N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Masha Allah Yaye boye ! Kou geume Yallah ngua. Niaanalal sa dome té geureum Yallah mome mi mome kouné ci nioune. Fii Pape féytéwone ci yaw, Yallah rék lathi wolou niou gui koy niane mou féytéleu fofou té mou até ko ci yeurmeundèm ,xaré ko Aljana firdawci. Amiiine...
Amoul domou procureur amoul dara gni dan léen waron ray sakh li dafa yomb trop waay Que justice soit faite Juub juubaal jubanti rekk Rip frère 😭😭😭 Que la terre lui soit légère
Mane je ne peux pas concevoir le jour du décès vous vous rendez chez la famille du défunt faire un interview svp la douleur k la maman ressent me surpasse massa k dieu lakeuil au paradis meitina
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Masha Allah Yaye boye ! Kou geume Yallah ngua. Niaanalal sa dome té geureum Yallah mome mi mome kouné ci nioune. Fii Pape féytéwone ci yaw, Yallah rék lathi wolou niou gui koy niane mou féytéleu fofou té mou até ko ci yeurmeundèm ,xaré ko Aljana firdawci. Amiiine...
Amine ya rabi sa wakh rafetna machallah
Amine waye yalna yalla naguou niane
Vraiment maman masta yalla nako yalla hare aldiana ndeyssane metina la ou tu vois un vieux comme ça pleurer tu vois metina
Oh massa tonton tu ma fais pleurer
Que son âme repose en paix 🤲🤲🤲
Ndeyesane metina yallah nako yallah yeureum khareko aldiana firdawsi ak mbolém gni mou fa fek amine
3 lahatt diakoum chaque matin boy gueneu sa keur amna solo trop inchallah digua dougat sa keur
Dèsi bolè inchallah.
Tu mets ton pied gauche ngawahe Bismillah tawa kaletou Ala lahi wala hawela wala khouwata Ila bilahi aleye hil azim
Mére bii kou dal la machalla nako yalla kharé aldiana sii barki seydina moukhamed psl
Bilaye journalistes yi mane sen gnak khelgui eupouna, vraiment ki amoul khel,mère binga khamni beugoul dioye ame lou yalla wathie thi mome ngaye lath ladji khale
yaw dé léma beug gouneu wakh mom nga wakh merci gni nékou gnio aye journal léste khamou gniou dara
Amoul domou procureur amoul dara gni dan léen waron ray sakh li dafa yomb trop waay
Que justice soit faite
Juub juubaal jubanti rekk
Rip frère 😭😭😭
Que la terre lui soit légère
Massa yaye yalla nako yalla kharé aljana. Té yalla tekla lokho yaye boye. Lou méti bilay yagueneu ci adouna😢😢
Massa yay boy 😢
Salam salam 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲 massa yaye yalla nako yalla yeureume té kharéko alldiana billakhi billakhi métina trop sakh massa yaye 🤲🤍🤲🤲🤲🤲😭😭😭😭😭😭😭
NDEYSANE YALLA NAKO YALLA YEUREUM KHAREKO ALDIANA FIRDAWSI MÈRE Bi KOU GUEUM YALLA LA 🙏🙏
Massa yaye boy mettina trop yalla moko sohla mouy lou gueuneu mais mouy lou metti
Yalla nako yalla khare aldianna frdws sama kharet la wn billahi nio bockon atalie mariste niodon footbo lando mou nk niit kou tei billahi 😢
Yaye boye yalla nala yalla maye kholou mougne amine ya raby
Paix à son âme 🙏
Yalna nako Yallah Yereum kharet ko aldiana firdawsi
Mane je ne peux pas concevoir le jour du décès vous vous rendez chez la famille du défunt faire un interview svp la douleur k la maman ressent me surpasse massa k dieu lakeuil au paradis meitina
Massa yaye boye yalla nala deudo ak diam
😢😢 😢😢😢😢😢😢
😭😭😭😭🙏
Massa yaye yalna xipé al Diana firdawsi
Yalla nako yalla yeureum hareko aldiana firdawsi
Li mèti na
Yalla nako yalla yeureume
Papa yalna aldiana don sa kuer bark Serigne touba 😅
😭😭😭😭😭
JOURNALISTE Bi TAMITE MÈRE Bi NÈNALA DIEUREDIEUF NGAY INSISTE RÈKK DAFA NÉKK THI NAKAR NDEYSANE NIDIAYE DJI MO NGI DIOY RÈKK
Doyenaware journaliste yinio wara arrêter liiii si bopame tendre le micro kou âme nakare
@FantaDieme-u4n BILAY AMOUGNOU KHÉL
Journaliste yii tmt kii si naxar la nekk nguen di forcer nii rek doul waay