Abdou Aziz Doucouré: "Diguenté Serigne Babacar Sy, Senghor Ak Serigne Fallou..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 9 янв 2025

Комментарии • 136

  • @ndiawniass1099
    @ndiawniass1099 4 года назад +6

    Dieuredieuf sounou makgni mais kene dou serigne fallou borom may borom Sénégal

  • @rokhayandiaye4760
    @rokhayandiaye4760 4 года назад +15

    Machallah ki dal mako beugu dieureudieuf Serigne Babacar sy

  • @reinedesabatvseutoulatdior2357
    @reinedesabatvseutoulatdior2357 4 года назад +8

    Li nekhna SERIGNE FALLOU AKK SERIGNE BABACAR KEN DOU ÑOM MACHALLA MACHALLA CONTANNENA

  • @miachoumia6130
    @miachoumia6130 4 года назад +6

    Machalla serigne babacar sy kene dou mome

  • @djibindiaye4576
    @djibindiaye4576 4 года назад +4

    Bilahi wallahi bèk n'a dèmbo si yène torop machalla kène do serigne babakar sy yalna niou ko yalla fayal si barki bayam machallah machallah wakhtanebi tègo n'a si kham kham diakue rèk mo wour alhamdolilahi

  • @linembaye2502
    @linembaye2502 4 года назад +9

    Machalla amna solo sama serigne babakar sy la

  • @zakariadeune2296
    @zakariadeune2296 4 года назад +6

    Cey serigne babacar sy yalnaniouko yalla fayal té tasniou si barkém

  • @naboufaye4918
    @naboufaye4918 3 года назад

    Dégal lii bilahi souma khamone khalise ngua kham Kone mah may léne bamou Bari wore nakh yalla Mane ma begue Serigne Sy ak famille maodo yeup fière d'être talibé cheikh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏

  • @ibrahimasenenabien1204
    @ibrahimasenenabien1204 4 года назад +3

    Begue na serigne BABACAR SY

  • @babacarmbengue651
    @babacarmbengue651 4 года назад +14

    Machallah serigne Babacar sy

  • @mlm6366
    @mlm6366 4 года назад +8

    Amna solo lolou MashaAllah

  • @fawoldiop8474
    @fawoldiop8474 3 года назад +1

    Machallah Machallah Machallah Machallah 🙏🙏🤲🤲

  • @youssoufsmith1663
    @youssoufsmith1663 4 года назад +4

    Eskey machalla yalna Diam sax

  • @daoudalo9821
    @daoudalo9821 4 года назад +11

    Machalla kendou serigne babacar sy

    • @adasarr1565
      @adasarr1565 4 года назад

      Ksb kenal. Serigne Babacar sy

  • @AwaKebe-x1d
    @AwaKebe-x1d 9 месяцев назад

    جزاكم الله خيرا ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @belleduteteaupied1393
    @belleduteteaupied1393 4 года назад +6

    Mashala alhamdoulila

  • @reinedesabatvseutoulatdior2357
    @reinedesabatvseutoulatdior2357 4 года назад +1

    MACHALLA pape MALICK thiat YALNA BATBI WERR

  • @villanileonardo006villani5
    @villanileonardo006villani5 4 года назад +3

    ❤️❤️❤️❤️❤️💪💪💪 Machalah 😭😭😭

  • @dioufthierno3611
    @dioufthierno3611 4 года назад +3

    Merci pour tout le vénère

  • @ngoudageneraldieng8250
    @ngoudageneraldieng8250 4 года назад +5

    Machallah laf thiat joli

  • @amimbow211
    @amimbow211 4 года назад +2

    Machalla li nekhna way ❤️❤️❤️🙏🙏🙏

  • @papadembadia1092
    @papadembadia1092 4 года назад +4

    Kéne dou serigne babacar sy malicke

  • @mamegorefall2421
    @mamegorefall2421 4 года назад +3

    Thiey Babacar sy limou def senchor mosi gueuneu touti Babacar beuguoul sakh kouy wakh limou def parce que nit nii dounou ko kham mouk

  • @khadiatousarr5376
    @khadiatousarr5376 3 года назад

    Machallah kenn dou mame Babacar sy

  • @airafrique8193
    @airafrique8193 3 года назад

    Serigne Babacar dou moromou Serigne fallou ladiale Serigne Touba xamna ci Dara bo wedé yaw mourid bi

  • @sokhnawade6843
    @sokhnawade6843 4 года назад +5

    Machalla

  • @bambagueye4167
    @bambagueye4167 4 года назад

    Abdou Diouf mi s fallou né nélén ko diack s abdoulahad né soumako puisé sama bete rék dou falou serigne fallou né nélén ko diack ta boulénko puise bayi léne féne yi tawakh mame maodo aye karamame yalla nanou yalla yerem barkéb alkhourane

  • @moustaphandao6531
    @moustaphandao6531 4 года назад +2

    Macha allah dieureufé serigne babacar sy et baye niass

  • @abdoulo7514
    @abdoulo7514 4 года назад +3

    Billay pape malick liga way serigne abdou danèl nama amal diammou way

  • @okimamar3997
    @okimamar3997 4 года назад +4

    Walahi histoirou nila deme me amna gno khamni mome diamonom amo droit def loumou yeggoul ken dou serigne babacaar sy tay la nekh bilahi

  • @khadimndiaye974
    @khadimndiaye974 4 года назад +2

    man mom mourit la wayé dama beug mam abdou ndakh dafa khamon plasou s.touba moutékk koufa beug loull yonou mourit

  • @abiboubuegueserignefallou8437
    @abiboubuegueserignefallou8437 4 года назад +2

    Nanou moytou saytane ta bayi sounou kilifa you bakhyi nouy wakh you rafetoul noun talibeyi Nanou dokh ni ab taloube wara dokhe ta fonkou sounou serignesi ndakh koumou Mana doon wakhalni sama Serigne mofi Guen komou nekh nako wakh yonou ken nekousi sounou borom khamna ki guen mangui sakou nian ta yalla takh nou bayi Saga yiniy saga kilifayi ndakh lolou sounou borom buegouko ta bakhoul thi rewmi Bal lenma hakh balna nieppou

  • @naboudabo409
    @naboudabo409 4 года назад +5

    Thiey galsen 🤣🤣🤣🤣

  • @moustaphambaye9216
    @moustaphambaye9216 2 года назад

    Bilaye yaw goudel fane

  • @abdouly6773
    @abdouly6773 4 года назад +7

    Thiey Serigne Babacar sy kén dou môme kou khôl Serigne cheikh Al makhtoum ak Serigne Mansour borom daradji ga hamni kén dou Serigne Babacar sy

  • @yoroka8549
    @yoroka8549 4 года назад +4

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @diop473
    @diop473 4 года назад +3

    Mame maodo bilahi da eupe mame khapha re dou morome

  • @stafftoubaplatre9305
    @stafftoubaplatre9305 4 года назад +2

    Diarama Al Maktoum

  • @ramsesniang8722
    @ramsesniang8722 4 года назад +6

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😭😭😭😭😭😭

  • @astoumamiediopngom6394
    @astoumamiediopngom6394 3 года назад

    Dama khôl sedeu n’a machalla keneu dou mome

  • @adasarr1565
    @adasarr1565 4 года назад +5

    Ksbs kenal serigne Babacar sy

    • @bayerek1272
      @bayerek1272 4 года назад

      Ziare nala kenal dou pour nioune

  • @fayeaissatou9148
    @fayeaissatou9148 4 года назад

    Sérigne Babacar Sy RTA Amoul Morom bèn lafi limou dèfal Senghor mo geuneu Touti si Mayou Sérigne Babacar Sy RTA li kouko wèddi tapez si You Tube nga binde Cérémonie Officiel Gamou Tivaouane 1965 Senghor si Boppam mokko néttalil Boppam Sérigne Cheikh Tidiane Sy Al Maktoum wakhnacko Gamou Tivaouane 2011

  • @bayediappasnaiecerndiapgrd4570
    @bayediappasnaiecerndiapgrd4570 3 года назад

    👌👌👌👌❤️❤️❤️❤️

  • @daoudadioptalibe7809
    @daoudadioptalibe7809 4 года назад +3

    Walay ndaysan

  • @mikeross3313
    @mikeross3313 4 года назад

    Mouride yifi nék di saga ak diingat solén respecter sén serigne yi mandou lén ndakh fii Senegal la kén gueunou fi reww ndy kén kolén saga serignam dina saga wat foukki yon sén serigne yépp ta kham léni nak yéna lén saagalou ndakh yéna togn.!

  • @hubad-pro3951
    @hubad-pro3951 3 года назад

    Dangay fen rék

  • @maimunabah6403
    @maimunabah6403 4 года назад

    chey sering babacarr kun do mor belie

  • @assanetoure1445
    @assanetoure1445 4 года назад +3

    Ok

  • @bambagueye4167
    @bambagueye4167 4 года назад

    Billahi ki mo mana féne séngor dafa gnew thi s fallou néko soungén ma diapalé ma diapaléléne thi raye bi pour séne diou ma bi serigne fallou né aka mouse dielle nako dh déll wakh dege

  • @bambagueye4167
    @bambagueye4167 4 года назад

    Wakhal thi s Babacar rék ta bayi s fallou

  • @djibrilsamb934
    @djibrilsamb934 4 года назад +7

    Saway wakhalal Mame Fallou lou wërr ish Senghor beug falou motakh mou nieuw Touba Serigne Fallou dadielei mbolo mi si penc mi Senghor wax sokhlam mouniko sa adjo fadiouna

    • @habsatoundiaye8404
      @habsatoundiaye8404 4 года назад +1

      Baylene parparlo . lolou ngay wakh fekewoko. Babacar sy au fallou mbaké nio gueuneu bokk.

    • @khadimdiop3348
      @khadimdiop3348 4 года назад +2

      Yalla naou yalla dollè fayal yari makyi mai senghor ak s fallou dègou masu won lolou s babakar yalla nako yalla dollè fay

    • @khalifasembene5878
      @khalifasembene5878 4 года назад +2

      Li d boko ladjei mag peu importe tarikham boudei deugouna rk dinala wax li mo am Tay nak la wax nex wayei serigne Babacar limou doundeih mag yi ko doundou demagougnou feine niougui fi cedei yi sorriwoul

    • @papitodiack3092
      @papitodiack3092 4 года назад

      @nittu deugg Jaime mon pays daniouy copie coller rek dagay rouss sah bilahi c'est flagrant

    • @moustaphagueye2288
      @moustaphagueye2288 4 года назад

      @@papitodiack3092 mé ki limou wakhe serigne cheikh Tidiane s'y AL makhtoom wakhna ko sétanale guamou 2011

  • @Mamediarra2001
    @Mamediarra2001 4 года назад +3

    Tidiane la waye histoire singhor deme woul nonou wax sax mbax morom du Yaxx darà thi sa mbax leep ben la waye nak singhor apres yalla yonente psl serigne fallou moko Diokh Rew mi

    • @moustaphagueye2288
      @moustaphagueye2288 4 года назад +3

      Haha yawe ya nékh rekk. Ki limou wakhe niii serigne cheikh Tidiane sy al makhtoom moko wakhe sétanale guamou 2011...senghor wakhna ko serigne babacar sy moko boléke serigne fallou... Yawe lolou fékéwoké kone nopile

    • @seckpalamine9544
      @seckpalamine9544 4 года назад +1

      kone do tidiane amoul werenté sakh

    • @khadimndiaye974
      @khadimndiaye974 4 года назад

      yabakh tagoré louné fagg kén douko diékh

    • @doudoudiong6131
      @doudoudiong6131 4 года назад +1

      Do Tidiane wakho Deugg Sérigne Babacar Sy RTA mo nè Senghor Talalal ma Nianal le nga Douggou si Gèw gui bama kham fi bâ Arache koulay Folli nècko boffi dioggué dèmal Si Sérigne Fallou nècko man yow la andal mou nieuw wakh ko Sérigne Fallou Sérigne Fallou nècko kou Sérigne Babacar Sy Nguèmb nga am Senghor tè Senghor nga Sant kone Senghor Sengue rék sa thiaw tokk bâ Doyal nonou la Dèmé li nakk moy Vrai Histoire bi Sérigne Cheikh Tidiane Sy nèlatti watt nako si Gamou 2011 té wèdiwoko nieupp di dègg lolou makk gniko Fêkke barinaniou trope.

    • @mikeross3313
      @mikeross3313 4 года назад

      nittu deugg Jaime mon pays ligniy wakh deugu la yaw yay ignorant bou bonn bi khamo di wakh

  • @dembismc5243
    @dembismc5243 4 года назад +3

    😂😂😂😂😂😂😂😂 mbata signature contran

  • @khadimdiop9438
    @khadimdiop9438 4 года назад +4

    🤣🤣

  • @fatoubeye1766
    @fatoubeye1766 4 года назад +2

    Serigne babacar dou moromou serigne fallou ladji lène serigne touba mo xam serigne babacar

    • @khadijafaye2530
      @khadijafaye2530 4 года назад

      Loutakh serigne babacar sy mou wouté sen diouma dji yalla day até

    • @fatoubeye1766
      @fatoubeye1766 4 года назад

      @@khadijafaye2530xamou li ngaye wakh damal nga ladjiate mague mou nèkoul nafèque serigne babacar ay djouma la fi bayi ak ay zawiya yéne mouride li takh ngéne bagne ko da diare féne ak séne serigne bo ladjié gnou wakhe la

    • @khadijafaye2530
      @khadijafaye2530 4 года назад

      Mane dioulite la sama khôl bi yarouma ni dina bagne nite rawatina kilifa diner ki ame la wakh gueno ma kham Lima wakh s fallou limou déf oupoul kéne

    • @Tomyato
      @Tomyato 4 года назад

      Fatou Beye bayil fewaleh, Babacar moy Fallou, Fallou moy Babacar. Niom niar nieup am naniou wilaya, kouy seddeh, seddal lene lou bakh

    • @papitodiack3092
      @papitodiack3092 4 года назад

      Ioe topal feulé gua mélni kou yorr mbeurou lambe Babacar sy bobou ngay wakh dafa ame Serigne té Serigne bi narr la topal feulé

  • @Rich_in_vitamin_murid
    @Rich_in_vitamin_murid 4 года назад

    Bat man

  • @abdouly6773
    @abdouly6773 4 года назад +4

    Machalla

  • @moussandiaye9908
    @moussandiaye9908 4 года назад +6

    Machallah

  • @biancathioune1640
    @biancathioune1640 4 года назад +2

    Machalla machalla

  • @ousmanebasse8967
    @ousmanebasse8967 4 года назад +1

    Macha Allah

  • @fatoukinetdieng2917
    @fatoukinetdieng2917 4 года назад

    Machallah

  • @mbayesall633
    @mbayesall633 4 года назад

    Machaalah

  • @alamine803
    @alamine803 4 года назад

    Machalla