Macha Allah mbokk mi lou rafet req mo am solo té lignu boolé mouy mbokkuk diiné gui dafa jiiitou tarykha yi kone nak nagnu rafet lepp ta beuguenté nguir jeummi yalla mignu boolé.
Billaay Madické sédal ngua xolou Sénégalais yi. Vous nous avez montré que diamm rek moo am solo. Peu importe ce que les gens pensaient de vous avant, votre amour pour ce pays n'a souffert d'aucun doute. Vous faites honneur à notre très chère nation👏🏽👏🏽
*Oh masha allah madické santal yallah linga am moo daakeu président boul outati président si adouna ndakh serigne touba moola sêdêl boopam ak beuguam té mouride bouné beugue naa ame linga ame*
Wallahi Enzim j n'arrive pas à comprendre pourquoi j'aime maître Madické Niang à ce point😍 vous avez perdu les élections mais vous avez gagné le coeur des sénégalais😍 Je suis Tidiane 100% mais ça m'empêchera pas d'estimer les belles paroles de Serigne Mbacké envers madické yalnala yalla bayi souñou kanam .
Je suis tidiane pur et dur mais j'ai un grand estime pour Madické. Nitou diam la té Mouride guimou doone deuguouna na si mome. Le seul candidat à avoir gagné le coeur des militants du pouvoir et de l'opposition. Yalla nako yalla défal diam way.
Officiellement madické proclamé vainqueur par le juge(khalif)representant le gouvernement de serigne touba.santal Yallah madické meme si je suis mouride et j’ai voté Sonko🇸🇳🇸🇳
Mane nima beugué Serigne mountaha eupouna bilay mbaké Mala wolou mbaké yama doy mbaké ya labir téwoyofe Serigne mountaha yala nafi yague té ande ak wérrr
machalla Mbacke yagui fi loll dagno âme lou guena cher mouy serigne touba sokhela wougne petrole ni gazoile nakh ressource bi guena chaire moy serigne touba yalla diamou yague way
C’est un homme bien un homme de paix Avec un bon cœur est grand Un talibé tu as gagné le plus important Madické Remercie dieu . Ce que tu as aujourd’hui en moins de 3 mois de gagner le cœur des sénégalais et du khalif Y’a n’a qui son là depuis longtemps et il ne L’on jamais eut Serigne Mountakha que dieu te laisse avec nous encore plus longtemps santé inchalla Je remercie dieu Le prophète SAW Et Serigne Touba
Mn premier commentaire sur RUclips , dabitude j lisei sans commenter ..mei sama khôl toy na ,say bouma sétané vidéo bi damay dioy ta doumako tay mingui melni mane lagn sédel li ...Madickei banga amei Serigne touba nga khamné gnako dara ...Serigne mountakha keine d'où mom ...akassa yalna diam yagu
Papa Madicke mane deh Tidiane la geumouma yakaarouma koudoul Seydi Elhadji Malick rta ak wa keureum waye nawnala dope nala niit dagay deuguou niit dagay geum niit dagay yakaar thi liga nekk waye nekk lii tay souba ga nekk lenene lolou kene soxla wouko Serigne bi moy sama Serigne té yow Serigne xamoula djabote hui waxi nopi sa dara dou Dem thi Keur Serigne ba kokou geumoulo té beuguelou Serigne ba té yalla rek takh. Machaallah NIANG nala borom bi sakhal thi yonou mouride abadane dayimane barke yonente Bi sws🙏🙏🙏on t’aime❤️❤️❤️🥰🥰🥰
Je s8 tidiane m vraiment mbacke sama kholl sedd ndakh kadou yinga sedell Madicke machaalla 😭😭
Mohamed Diop ndeysan ap dioulit nga te xolob dioulit day gawa toye
Salut frère merci
Slu cv
Dr1 nio farr
Dagaua bakh rékk
😢😢😢😢Madické amna loumou deff si sunu xoll yii waay dangua nu liguey.
Lane motah ma beugue leu
Je suis Tidiane mais wallahi dama beugue Serigne Mountakha té yalla takh
Ya bakh waay
Moi je ne suis pa mouride mai je suis très content de madické pour l'amour qu'il porte Anvers seurigne touba il mérite c'est témoignages
Macha Allah mbokk mi lou rafet req mo am solo té lignu boolé mouy mbokkuk diiné gui dafa jiiitou tarykha yi kone nak nagnu rafet lepp ta beuguenté nguir jeummi yalla mignu boolé.
Blhi madické talibé bou deuguel leu barkep serigne saliou kou beugue madické beuseull J'aime
😭😭alakhou akbar mbaké yalla nanga fi yague té wére amine
Amine
Amine si barké khadim rassoul
Bilay Madické niang yalla na yalla takhawou ngirr dieumi Serigne Touba
Billaay Madické sédal ngua xolou Sénégalais yi. Vous nous avez montré que diamm rek moo am solo. Peu importe ce que les gens pensaient de vous avant, votre amour pour ce pays n'a souffert d'aucun doute. Vous faites honneur à notre très chère nation👏🏽👏🏽
*Oh masha allah madické santal yallah linga am moo daakeu président boul outati président si adouna ndakh serigne touba moola sêdêl boopam ak beuguam té mouride bouné beugue naa ame linga ame*
😊 je connaissais pas bien madicke mais juste pour cela je l' aime beaucoup
C est un homme bien
de la part d un talibe Baye Niass
Bocar nit kou baakh nga
Merci bocar
Man dal xawma loutax talibé baye yi beug mourid yi rek
Merci encore
Bou len khamone ni ma beugué Serigne Touba...
Yalna sougnou borom Faye len
Bocar Ba,Mame Baye Niasse moo defar ay taalibéem ci djiko you rafét.
Bocar koubakh nga yalna yalla faye
J’ai pleurais et je ne sais pas pourquoi mais xamna ni limou toud serigne touba dara laci Bamba ci xoll ❣
De même k moi, wallaay ndeyssaan. Beugeu Serigne Touba reka weur
ohhh c'est larme Au yeux bilahi madicke amnga tawfekh
Amine ya rabbi
Mane mi sakh deme yèmou madickè amnge lou reye
Akassa Macallah Mbakcé yalla nafi yague té werr rek Amine
J'adore ce Khalif bilahi c'est un saint homme de la part d'un talibé Baye niass.
Dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne touba
Madické Niang nitou kèssé ndeysane mom diam rek lay am damako beugg barkep serigne Touba 😍😍😍😍😍
Madické santatal yalla am gua lou ken amoul
alhamdoulillah god is one bilay waxatiko lii mo gueune président si ap mouride
Wallahi Enzim j n'arrive pas à comprendre pourquoi j'aime maître Madické Niang à ce point😍 vous avez perdu les élections mais vous avez gagné le coeur des sénégalais😍 Je suis Tidiane 100% mais ça m'empêchera pas d'estimer les belles paroles de Serigne Mbacké envers madické yalnala yalla bayi souñou kanam .
Ndeyssane. Thieuy Yallah. Serigne Mountakha mo yarou. Mo bakh. Yallah na fi yagg té andak weer
Je suis tidiane pur et dur mais j'ai un grand estime pour Madické. Nitou diam la té Mouride guimou doone deuguouna na si mome. Le seul candidat à avoir gagné le coeur des militants du pouvoir et de l'opposition. Yalla nako yalla défal diam way.
Ndeyssane Madické il est aimable mashalah
Ndeysaan Mbacke Goudaal faaan
Madicke Borom Baah la Yalnako Yalla Doli Diam
Walahi madickè begue nala guir Serigne touba Mbackè yague fi tè wèr🙏🙏💯
madicke geune nala beug guirr serigne touba. machalh mbacke balla yalla gafi yagg t weer
Mame Seck bilay barigassi morom
Akassa!!! Madické te rend tu compte ke c toi le gagnant!?🙏🏽❤️
Serigne Touba rekk la wakh kesse fier d'être mouride baye fall
😢😢😢 adouna doudara Diamou yalla gueum Rassoulihi beugueu Serigne Touba khadim Rassoul rek mo weur 😢😢
Mbaké yagui fi waye yagui fi waye yagui fi waye koubeugeu serigne touba defal j'aime si sama cmt bi
Madické ame ngá lép ame ngá Serigne Touba
bilah
Dieuredieuf mbacke yalla na ngafi yague tewer
Yalla nagnou keuneu beugue borom touba ndiouroul keep reek inchaallah
Ndeyssane dieuredieufetii Mbacke Madické mane dei beugue nalla diappou nalla nakh beugue biigua beugue serigne Touba takh
Madické bilahi ligua ame ni mo dax ngour fouff sax . Mitt ndoundou na ba dê amouko . Je t'adore dax serigne saliou
Dieuredieuf Serigne Touba
Alagou akkbar MADICKÉ santa YALLA
Machalah dieureudieuf mbacké balla yag fi lôle té wére
Amine
Mbaye Yatt Amine
Amine
Machalla madicke li nekh na mbacke yalla na fi yague te yer
Alhamdoulillah yalla na yalla fayal nioula Mbacke, Sénégal nanou fonk souniou kilifa yi niooy sounou ndam, niooy sounou royou waay
Ay way 😭 sama dafa séd way yalla nala yalla takhawou ❤️
Allah djeuredjeuf serigne touba ❤
Officiellement madické proclamé vainqueur par le juge(khalif)representant le gouvernement de serigne touba.santal Yallah madické meme si je suis mouride et j’ai voté Sonko🇸🇳🇸🇳
A li nékh na ci khol ❤❤ waye.
Macha Allah..madicke amga Lou reuy..beugue serigne touba tawfekh la
Mbacke yalla gafi yague ta wér ❤
Baagale liguéy biga beugue si yonou s.touba ❤
Aminnne👐❤❤❤❤
Machala mane sakh sama khole dafa toye yalna BOROME BI YOK SAYE FANE TÈ MAYLA WÈRE
Père Madické, li rek mo dakk ngourr, geunn ko nekh.
Yalna jamm deuk fi ak reew yika weur🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Machalla yague filol tawer
Dieuredjeufe Serigne BAMBA diarawlacke Mame CHeikh IBrahima FALL😭😭😭
Akasa amna solo madicke Niang Rawou nga dee machalla
Mane nima beugué Serigne mountaha eupouna bilay mbaké Mala wolou mbaké yama doy mbaké ya labir téwoyofe Serigne mountaha yala nafi yague té ande ak wérrr
Amine way
Segne Mountakha aka yémé aka kham té ranié té kham Segne Touba mashallah Madické am nga ndam mashallah
Ohhh mbacké contane na barki serigne touba j'ai les larmes aux yeux
Mashallah Mbacké amiiiiiiine ya'rabbi
Khol sed na machallah dioylo ngama nak
C'est trop émouvant 😭
Longue vie sunu khalifa bi
Machallah Madickè Sante yalla boubakhe ame seringe touba khadim Rassoul yomboule
Ahh pr madike rawgaa bâ faaaw machalah
machalla Mbacke yagui fi loll dagno âme lou guena cher mouy serigne touba sokhela wougne petrole ni gazoile nakh ressource bi guena chaire moy serigne touba yalla diamou yague way
Je ne suis pas mouride dh mais talibe li RK moy wareef fam DEUG djioup ak geum serigneum bilahi madicke chapeau
Macha alla ton madicke santal Yalla bou bakh AK Mohamed psl ak sa serigne bamba khadim rassoul ak khalifa diam rek
Machalah nekhna
Akaaaassa MBACKE begue nanou si yaw😍😍😍
Billaye li rafetna wayy . Machaallah app cathodique naak moko seidei j’ai les larmes aux yeux . Le Sénégal 🇸🇳 est beau j’aime mon pays
Machallah machallah machallah wahdji rafettena machallah Yalla laf thiat Madiké
Je suis pour sonko mes le message et triste j'ai des larmes aux yeux du courage Madicke tu es une honnête
Wallahui ly day wanéné serigne mountakha daray adina nioroko lépame serigne touba la kofi nieuw serigne touba rékk lalaye wakh point 👌👌👌👌👌👌👌👌👌
C’est un homme bien un homme de paix
Avec un bon cœur est grand
Un talibé tu as gagné le plus important Madické
Remercie dieu . Ce que tu as aujourd’hui en moins de 3 mois de gagner le cœur des sénégalais et du khalif
Y’a n’a qui son là depuis longtemps et il ne L’on jamais eut
Serigne Mountakha que dieu te laisse avec nous encore plus longtemps santé inchalla
Je remercie dieu Le prophète SAW
Et Serigne Touba
Machalla mbacke amna solo trop yalna yalla bayii lafii bathi kanam mbacke
Longue vie à vous é bcp de bonheur madické
Bilahi Mbacké yallah rek moy deug sénégal yalla na diam yag si barké baye niass alhamdoulah
maître tu as gagné tu es quelqu'un de bien je suis tidiane mais je suis fière de toi et le khalifa
Thiey lii deh reuynaa lolou bilahi
Âme gua ou reuy Madicke
Mn premier commentaire sur RUclips , dabitude j lisei sans commenter ..mei sama khôl toy na ,say bouma sétané vidéo bi damay dioy ta doumako tay mingui melni mane lagn sédel li ...Madickei banga amei Serigne touba nga khamné gnako dara ...Serigne mountakha keine d'où mom ...akassa yalna diam yagu
Walahii ndeysan Serigne moutakha mbacke" yalnafii yague aka deugou aka deugou d'Ara gnioroukoo loudoul dine"
Ndeyssane madické khole bé raféte,
Machallah man duma mourid waye wakhdji rafeta mbacke yalla nasouniou serign yagui tewer contananiou
😢😢😢jai des larme au yeux dieuredief mbake yalla na yalla yagal la fi lole mbake 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Oh ndayesane Madické machalah machalah alkhamdoulilah
Machalla yalla na diamou yag madicke yalla nala saring bi har
😢😢😢 cey madicke sonou xol toujours ❤❤😢😢
Macha alla amna solo lool way dieureudeufé serigne touba
Dieureudieuf madické kou am pastef ngua vraiment yalnala yalla dolèl
niang demba thianer dafa bakh ther humble nit kou simple la yalna yalla guoudal sa fane fière d'être saint louisienne
Dieuredieuf serigne touba non khol sedena madické niang borome bakh la bilay
Madicke 💓khol bii moo rafeeet ndeyesan
Madické santal Yalla bou baxx wayy Mashalla Mbacké 🙏🏽
MASAHLA nice diaradef yala na yala yagal lafi
Madicke amga Lou rey santal yalla bou bakh te khamne serigne bi loumu wah loumu guem rek lay Don
Mbacke balla yalla gafi yague te wer lol
Papa Madicke mane deh Tidiane la geumouma yakaarouma koudoul Seydi Elhadji Malick rta ak wa keureum waye nawnala dope nala niit dagay deuguou niit dagay geum niit dagay yakaar thi liga nekk waye nekk lii tay souba ga nekk lenene lolou kene soxla wouko Serigne bi moy sama Serigne té yow Serigne xamoula djabote hui waxi nopi sa dara dou Dem thi Keur Serigne ba kokou geumoulo té beuguelou Serigne ba té yalla rek takh. Machaallah NIANG nala borom bi sakhal thi yonou mouride abadane dayimane barke yonente Bi sws🙏🙏🙏on t’aime❤️❤️❤️🥰🥰🥰
wallahi j'ai les larmes aux yeux. machaallah
Machaallah yague fi te weur Mbache
On t'adore tu resteras gravé dans nos mémoires ta pas perdu ta le respect des aînés contrairement aux autres
Ndeyesanne , amneu solox
Dieureudieufeti Mbacke
Dieureudieuf Serigne Touba
Macahlla Mbacke yagefi tavre
Wakh ji dawna yaram. Les sénégalais sont des hommes de bien. Madicke,,toyal nga khôl yi. Que dieu te donne une longue vie.
Machalla
Le gagnant de cette élection, c'est madicke, il a percé dans tous les coeurs des sénégalais. Un homme unificateur.