Souniou Moy tou woull nak dina niou tabbi Si goûta ndakh ndokhoum touba bou niou wakhe ba mou geun ci lokhoye wa touba aa woroul deh man dal li d'Allan sama khell modi ndokhmi bayi ko touba bogo Nou ami contor di Faye waya di Faye souniou bopp li thiy geunne di dougat ci deukeubi man dal li Moy sama khalat mo dall sama khell itam wassalam
Dëkk bi zaahir ji dañkoo waajaloul. Si on aura le statut spécial et on s'est pas formé d'avance, d'autres viendront gérer la ville à notre place
Yala nala yala defal diamu
Macha alla dieureudieuf
Nice
Il faut construire des écoles publiques pour enseigner Serigne bi et les centres des formations sinon d'autres faire à leurs places
Belle analyse
Voilà la réflexion qu'il faut avoir, poser un débat intellectuel. Out ay péxé té ćow du am
Li nga wakh moy deugue
Aduna daal ci xam xam lay dox
Diereu dieuf
Souniou Moy tou woull nak dina niou tabbi Si goûta ndakh ndokhoum touba bou niou wakhe ba mou geun ci lokhoye wa touba aa woroul deh man dal li d'Allan sama khell modi ndokhmi bayi ko touba bogo Nou ami contor di Faye waya di Faye souniou bopp li thiy geunne di dougat ci deukeubi man dal li Moy sama khalat mo dall sama khell itam wassalam
Li nga wax leer na wérna
Lii deh bouko Baye fall défon thiow dou am
Status special bi rek mo waron nek wakh dji
Oui.
Té baay faal yi waajal seen bopp ci xam-xam ak professionnalisme sécuritaire
Yalla na niou yalla mousall thi baye fall yi 😂