bilahi walahi, djiguéne you barri dagno am yéné seuy mais rare neu gnou am dieukeur diou bakh. té divorce sou amé gnou khass djiguéne gni té thiono yi djiguéne gni di dath goor yeupeuko kham mais amougnou diom.
@@dianablackqueen3510 VRAIMENT . YABATé rek mais diabaram mo wara guéneu si seuy bi . yalla meune nako may dieukeur diou bakh . goor si bopam mo diaroul yeureum rawatineu mandi katt bou liguéyèoul tek si topou djiguéne yiy takhawalou. femme bi mérito kénéne kou gueune mandi katt ak bandit. djiguéne sénégal ligniy mougn si soutoura amoul bénéne deuk boukay accepter. goor sénégal la majeur pârtie dagno yor diabar di ndiallo si alleu bi mais tot ou tard dinagn layo ak sounou borom. goor bou yor diabar di ndiallo , islam raynala kone femme bi na gnane batt woutti bénéne dieukeur bou responsable.
La vérité moy amneu nio khamni diarouniou mougneul sakh ben att, seuy nekhneu mais ak seu nawlé, dougou fo wara doug si kham seu bop la bokk. Courage à la dame té nga defarouwate rek khar kou bakh
C'est que tamite do feik app mandit kattt mou lernalani ki bakhoul tei gnimouy neikal bakhougne ngay dougou si mom ba parei teksi diko fayal neik tamite
bilahi djiguéne sénégal ay diambar lagn mais gnoussi barri amougnou chance am dieukeur diou bakh. té sou divorcer waune ni tay goor you nafekh yi ni djigéne gni seuyou gnou. nagnou délou sonou khel si yalla. djiguéne bouffi si dieukeur di ndiallo, demandel divorce dém weurri lénéne. yalla yorr weurseuk gneup.
Ça se voit cette femme est gentille c pour ça son mari lui manque du respect les hommes africains n aiment pas les femmes sérieuses ils les faut toujours les mauvaises comme eux ma chérie quitte le c pas un mari ça
Bilahi amna djiguen you meun mougne bougnou dadiéwon ak goor you bakh djour waliyou
Tua raison dé machallah boudoon. Kou goor ki mooko betoon si kaw goor , Kone seuy bi dieekh n'a kou dem migui took si seuy bi
Bilaye ndeye sane
Walay Ndeyssan
bilahi walahi, djiguéne you barri dagno am yéné seuy mais rare neu gnou am dieukeur diou bakh. té divorce sou amé gnou khass djiguéne gni té thiono yi djiguéne gni di dath goor yeupeuko kham mais amougnou diom.
Bilahi hooo😢😢😢
Ana gni meusta gueneu ak dieukeur jambour remplissez le bocal de cœur ❤️
😎
Do bari ❤ dé
✌🏽👊🏽😎
Merci pour votre commentaire
@@adamandiaye5829*Bilay dou beuri 😂😂*
Machallah Khady mane deh yama gueune khole lingua mougne yeupe courage ma belle sa dieukeur mo bone rek bon rétablissement ma chérie
*Ki kay diambar la 😢😢*
Yalla nga ame djekeeur diou bakh sa djekeur dji nitou safara la
Merci pour votre commentaire
Sénégalais dokhane rek surtout bouniou amee jabar te lolou arame na
Danga nane surtou niou niak gni gno gueneu niak diom
@@AdamaNdiaye-wk1lu😂😂😂😂😂Wouy beugn dou ré diamm
@@AdamaNdiaye-wk1lutellement vrai
Merci pour votre commentaire
@@AdamaNdiaye-wk1lu*Walay ieo gniak diom lagnou deff 😂😂😂*
Thieuy seuyou sénégal😭
wakhal key thieuy goorou sénégal. diabar you diambar lagniy yorr mais rare neu djiguéne am goor gou am diom
Merci pour votre commentaire
@@AbdouNdiaye-g5nwakhatiko comme guerre yow yagui mandi soite,defoulo lila warr soite gua beugue cé tekk di dokhane aka dialo vraiment 😢
@@dianablackqueen3510 VRAIMENT . YABATé rek mais diabaram mo wara guéneu si seuy bi . yalla meune nako may dieukeur diou bakh . goor si bopam mo diaroul yeureum rawatineu mandi katt bou liguéyèoul tek si topou djiguéne yiy takhawalou. femme bi mérito kénéne kou gueune mandi katt ak bandit. djiguéne sénégal ligniy mougn si soutoura amoul bénéne deuk boukay accepter. goor sénégal la majeur pârtie dagno yor diabar di ndiallo si alleu bi mais tot ou tard dinagn layo ak sounou borom. goor bou yor diabar di ndiallo , islam raynala kone femme bi na gnane batt woutti bénéne dieukeur bou responsable.
@@dianablackqueen3510*Bilay ioe 😢*
Ndeysane bon rétablissement
Merci pour votre commentaire
Sois forte ma sœur je t’aime wallah force❤
Merci pour votre commentaire
Yallanala yalla dolli diam
Merci pour votre commentaire
Amin inch'Allah
Tu es brave 😢
Merci pour votre commentaire
Soudone mane doumako bayi nonou 😢loutakh maîtresse yi âme fitt di ndialo ba paré sec oeuil
Merci pour votre commentaire
*Moma diakhal ki eupeul na way*
Femme bi diambar la seuy katt la kimou dadièl mo bone rek
Merci pour votre commentaire
Ndaye khady ndeysane kou bakh diambar deug bilahi yalla bahna
Merci pour votre commentaire
Yalnako yalla dolel la nga yatt sa njabott
Merci pour votre commentaire
La vérité moy amneu nio khamni diarouniou mougneul sakh ben att, seuy nekhneu mais ak seu nawlé, dougou fo wara doug si kham seu bop la bokk. Courage à la dame té nga defarouwate rek khar kou bakh
Danga mana mougne rék seuye diaroul li
Merci pour votre commentaire
Thiéye Sénégal Fomou dieum ohh vraiment lii métina trop ❤
Merci pour votre commentaire
Dé léne khol thi goor Yéngui ni dougou
Merci pour votre commentaire
Vraiment
Ak djiguen yi niou dougou
Surtout lolou
Policies sénégal bayiléne sétane bi ni guene di déf bagnou raye domou diambour
Merci pour votre commentaire
Ma sœur laisse ton mari après tu ai tranquille
Merci pour votre commentaire
Boudé guel di diame bougnou také khana day raye
Merci pour votre commentaire
😂😂mo diakhal nieupe
*Ahh tégua sagna wakh 😂😂*
Waye li. Limou donne. Domerame. Reck Ay. Bandi. Mandi Kat boul. And. AK. Mome
Merci pour votre commentaire
Amna djiguéne youmana séy nangou séye BG séne djekeur.
Sama Toma lah❤😢
Merci pour votre commentaire
C'est que tamite do feik app mandit kattt mou lernalani ki bakhoul tei gnimouy neikal bakhougne ngay dougou si mom ba parei teksi diko fayal neik tamite
Vraiment parfois gnoy tek sène boppou thiono noy guissé goor guou illicite nguay ande ak mom
Sama hol ba ngui meti . Que Dieu te guide ma soeur.
Wakhouma guél rék wayé souma niafé sa Ndeyam doko nétali
Bayiléne diséy AK touh Kat yamba AK nane katou sangara. Tass AK problème yirék lay djéhé.
Lii mom lanela😢
Merci pour votre commentaire
Bayiko nitt kou amoul jarign kay bakhout 😢
bilahi djiguéne sénégal ay diambar lagn mais gnoussi barri amougnou chance am dieukeur diou bakh. té sou divorcer waune ni tay goor you nafekh yi ni djigéne gni seuyou gnou. nagnou délou sonou khel si yalla. djiguéne bouffi si dieukeur di ndiallo, demandel divorce dém weurri lénéne. yalla yorr weurseuk gneup.
Bilahi li ngaye wakhe yepe degue la
Merci pour votre commentaire
Mougnal yalla nanga am gor boubah
Ça se voit cette femme est gentille c pour ça son mari lui manque du respect les hommes africains n aiment pas les femmes sérieuses ils les faut toujours les mauvaises comme eux ma chérie quitte le c pas un mari ça
Merci pour votre commentaire
Masta chérie
Kaay ma takala terala
Ame na gor yo khame né warougnou ame diabar sisene adouna qui mo bone
Merci pour votre commentaire
yaw liga sol yereleu li pour nekleu
😂😂😂 cheuuu
Ki taloule lolou sakh. Pb thi boppamm mo bakhoul
Merci pour votre commentaire
Boko. Bayiwoul Dina la rey
Merci pour votre commentaire
Doynawar
😮😮
Merci pour votre commentaire
Soubhanalah.legui dal internet rek laaniouy khawei soutoureu yi😢
Ba kham nakh dina fathie dara
Merci pour votre commentaire
Police nela ba lundi ngay gen di wakh vendredi
Merci pour votre commentaire
Vous les femmes bo amé faar bouy touh mbamouy nane bayiko ndah amoul moudj.
Yaw ya djoum ma chérie warowone seuy ak mandikaat bi comme khamone ngua ko...gnoune djiguene na gnouy seuy ak goor bo khamni mo gnou nop...
yaw kay kii daa nagou sa diekuer
Do bayi ki tamite
Merci pour votre commentaire
Wadji dji mandikatte la😂
Merci pour votre commentaire
Bokoe bayiwoul dinae la reey
Merci pour votre commentaire
Ni mbu ko def dafa yawe trop vreiment