Vrai champion moy Balla..Un.champion c'est quelqu'un qui a toujours dans sa tête que c'est le meilleur..Il fait pas des calculs pour éviter les lutteurs
génération 2005 2006 balla moy vrai roi des aréne da téklé ay victoire ba éski ci yékini modou lô da dieugué ci défaite diokko combat royal balla c vrai roi❤❤❤
@@KamaraSarr Modou lo et un exemple parmi ces rois dieule rois thi béne année ngua beuré 3 combat meusoule am et sur ces 3 combat ay khalé la beuréle kouka niémé personne apars yékini modou reste le meilleur un exemple un référence pour un être humain sur tout qui conserne la vie d'un être humain bravo ndanane diotena nak ngua bayi
❤❤❤❤❤Li ma guiss moy ay reference gueine gueine arreter bania beureiti creer ay propre entreprise yi guein bok ko toudei ko balla xlo en plus guein di deimlanetei toudanetei ay doom diokhanetei ay thieur seini ndiamboot ki lala bayalei day gana rafet❤❤❤❤
Le 12 avril 2012 ga rawé say mass si arène bi ba faw wakh béfi niak respect mais mbeur yifi nék warnanioula diokh sa alarba dosen morom yay goor empereur bi ❤
Balla et Eumeu veulent se lutter contre Modou lo parce qu'il savent très bien que Modou est supérieur à eux, alors maintenant Modou le roi et le supérieur veut donner la chance aux jeunes et c'est ça l'intérêt général de la lutte, il faut donner la chance aux jeunes lutteurs talentueux pour une éventuelle amélioration de la lutte Sénégalaise.
@assanendiaye5640 niaari défaite balla rek lagne waxnii dafa ame blessure té lolou balla waxouko, ay journalistes confirmé nagne ko. Balla meussoul renvoyé combat contrairement ak niene gnii. Date bigne ko diapal lay beurê sou nieuwé diokhé boppam loumou am dieul. Lolou mooy neek sportif té môme il est sportif.
😅😅😅 Balla carrière rame moye carrière rou payi😅yaw modou lo rék nga dane si khalé😂yaw sa carrière bousi ma Modou lo niari yone guénone😁😀 carrière yawou dial ngaye am😬yaw kharagne lo yako dane mais moysa papa si lambdji ☝️ yaye dane yaye néksi guinawam 😬 lolou moko méti ndaysane😅 toujours yaye néksi guinaw kharagne lo inchallah😁
Saay bayilène di wakhé émotion Balla il respecte Modou Lô té kouko ladjie dalay wakh Modou mo gueneu nakaré beurèl si lamb dji yé dafa meune beuré lol Machallah Ms li sport la comm k mo dane Modou 2 fois amna droit wakh k moy empereurou Modou té Modou dou roi wam Lgui Modou bou beugué dindi lolou na dieul Balla dane ko🤝
Buleine gnou sonnal mod’lo gueneu nekk sissouman meussul nangoul balla ou mou waxal ko lou bakh.. balla fougn ko ladj si beurei mod’lo mounei champion la mbappat lako commencé suivre..c’est pas son roi voila
Meilleur émissions 😂😂😂 ay Billy Borso yeureumeul balla tamite Mai’s nice
❤❤❤❤❤❤ Balla Gaye 2 le GOAT des arènes le meilleur de tous les temps.
Inchallah 🙏 futur roi pour la deuxième fois.
Ken dou mom di lutte pure yalla nako yalla doli werr ❤❤❤❤
Modou lo we love you all the way from Gambia 🇬🇲 ❤💚
Billay balla mi migui si forme machallah ❤❤❤
c'est un vrais champion bilahi nekha faral dimanche
Keneu dou balla gaye 2💛💙🇸🇳
Gninagou yéna bok baye mais gnibagne yaye sene baye ❤😅
sa ma mbeur balla guaye 2 yalla nafi deféte yam ❤❤❤
Balla ntre empereur nekha faral dimanche yalnala yalla défal diam ❤❤❤❤
Je t'aime fort ❤,i love you gauche,i love you droite,yaw rk laye top lo dèf beug na ❤❤❤❤
La dame est très forte enplus dafa maîtrisè lamb machallah
❤❤❤❤
Balla gaye rék❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
The king ❤❤❤
Un grand monsieur qui parle il faut bien écoute ❤❤❤
Balla gaye 2 champion nga ❤
Merci Madame je vous connaissais pas .. Mais belle emission avec le Champion
Balla gaye 2❤❤❤❤❤rk
Merci billy borso meilleur émission ❤❤❤
Balla gaye 2🎉👋💪
BG2 rekkk ❤❤❤❤❤
Gambia 🇬🇲 ❤❤❤
Vrai champion moy Balla..Un.champion c'est quelqu'un qui a toujours dans sa tête que c'est le meilleur..Il fait pas des calculs pour éviter les lutteurs
Femme bi métrissé na diar diar Balla gaye dé
Professionnel le ❤
❤❤
@@Charlott435mo nobone khalil serie babel
Mo nobone Khalil série babel
Balla champion❤❤❤❤
Empereur seul❤
Le grand champion yaye sene bay
génération 2005 2006 balla moy vrai roi des aréne da téklé ay victoire ba éski ci yékini modou lô da dieugué ci défaite diokko combat royal balla c vrai roi❤❤❤
Da rafétoul sakh et mo yakeu rois des arènes bi franchement niak démi Final dém Final mor lo rek moco déf
@@KamaraSarr Modou lo et un exemple parmi ces rois dieule rois thi béne année ngua beuré 3 combat meusoule am et sur ces 3 combat ay khalé la beuréle kouka niémé personne apars yékini modou reste le meilleur un exemple un référence pour un être humain sur tout qui conserne la vie d'un être humain bravo ndanane diotena nak ngua bayi
Iow môme dangua soxor
😊
Balla Gaye 2 ❤❤❤bilahi deissaloto sayy supporters daara Gor yallah Deug gua bilahi keinn dou yaw
Boko sakk ak mbeur yi moytuwatei ak tanneu ay adversaire you yomb.
Yaw dagua amm diom
Balla Gayie kasse ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤yafi nekke
Billy borso mon combat
Modou moy sa rois nangoul teu bagna sissou, vive xloooo❤
😂😂😂😂
❤❤❤❤❤Li ma guiss moy ay reference gueine gueine arreter bania beureiti creer ay propre entreprise yi guein bok ko toudei ko balla xlo en plus guein di deimlanetei toudanetei ay doom diokhanetei ay thieur seini ndiamboot ki lala bayalei day gana rafet❤❤❤❤
Notre empereur ❤❤❤ dame rek inchallah
Le 12 avril 2012 ga rawé say mass si arène bi ba faw wakh béfi niak respect mais mbeur yifi nék warnanioula diokh sa alarba dosen morom yay goor empereur bi ❤
C’est pas le 22 plutôt ?
Balla et Eumeu veulent se lutter contre Modou lo parce qu'il savent très bien que Modou est supérieur à eux, alors maintenant Modou le roi et le supérieur veut donner la chance aux jeunes et c'est ça l'intérêt général de la lutte, il faut donner la chance aux jeunes lutteurs talentueux pour une éventuelle amélioration de la lutte Sénégalaise.
Ils sont jaloux
22 avril ❤❤
❤❤❤❤ vrai sportif moye Balla gaye ❤ bilay walahi boko dané sakh d'où sisou 😂😂 pas comme Modou lo domouharam bi 😂😂😂
Yow sa leufeul ndeye
BG2 mooy sama mbeur c'est un vrai sportif mais lii ngay waxnii si Siteu la dieek
@@Robbe-Grilletballa Kay dou sportif 😆 🤣 😂 chaque defaite mouni blessure 😂😂😂😂
@assanendiaye5640 niaari défaite balla rek lagne waxnii dafa ame blessure té lolou balla waxouko, ay journalistes confirmé nagne ko. Balla meussoul renvoyé combat contrairement ak niene gnii. Date bigne ko diapal lay beurê sou nieuwé diokhé boppam loumou am dieul. Lolou mooy neek sportif té môme il est sportif.
Anna goordjiguéne akh commenté si lamb démal diokhé sa tâte lolu nga kham
Balla kassé ❤
Ils ont jaloux de modou Lo
Balla Gaye nala nieup dane seuf modou lo ok 😂😂😂
Waawaw😂😂😂😂
Modou lo moye moune ❤
Amougnou sa faye EMPEREUR BI MOY LAMB 💛 💙 🫅 ✌️
Dou 12 22 avril la balla gaye daan yekini
❤❤❤❤❤❤❤ balle seul ❤❤❤❤❤❤❤
Balla gaye2 eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone
😂😂😂
Mala beuga❤❤❤
Bg2 le lutteur le plus populaire
Sa affiche bi d'où respect il faut respecter le roi des arènes Modou kilifa leu li rafétoul suis fan de Reug reug
*22 AVRIL 2012👑 👈👉[ ~ BALLA GAYE 2 , LE 22, DÂNN 2 FOIS ~ ] BG2 RÊK CI XÔL 🥰
MASHALLAH LAFF THIAT 💦🙏✅
Le vrai lion
Ms journaliste bi 😪🤌🏾♥️
effectivement Balla gaye DEUG la wx😂
😂😂😂😂😂
Modou lô
❤
Bg2 l'ampereur le roi des roi
Balla Gaye 2 vs yekini c'était plutôt le 22 avril 2012 pas le 12 Avril
Bilakhi balla Gaye moye lamb yalna sa diam yague
Balla moye sama deure
Merci billy borso
Balla gaye2 eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone Balla gaye eumeu sene Moy yone
Balla gaye modou lô moy yone
@@modoubayefallsikroulla1423balla Gaye Modou Lo Waawaw Moy Combat 😂
Bg2❤
Il a raison ndakh moko dânne 2 fois
L’empereur qui a 6 défaites 😢
Eumeu séne a 11 défaites
Donc c’est normal que vous soyez des amis 👯
Balla Gaye 2 beinn mbeur yabouko kou niemei reikk nako dieul
Billy déjà gua maîtriser deh 🤣🤣🤣stadium ibra diop pas marius ndiaye
En plus le 22 avril 2012 pas 12 avril
Vive.balla
Do journaliste supporter nga
Dof gua 😂 sa khelmi moy négliger
Balla bull sissou waye vreman sokohr bakhull koi
😂😂
Balla linguaye wakh dou sport le rois c le rois de tout les lutteurs ay ki mako dane dou sama rois un vrai sportif ne doit jamais dis sa
Tous les lutteurs pas tout les lutteurs.
@@BarkaKoita😂😂😂
Balla aka beug lou xess nak😂😂journalist bi charmé neko bou yag😂😂😂
Wakhi Dof 😂😂😂
43:12 Wa balla louy mental bou forokh tamit😅
Balla mon champion mais MMA mo eup khalis lamb
😅😅😅 Balla carrière rame moye carrière rou payi😅yaw modou lo rék nga dane si khalé😂yaw sa carrière bousi ma Modou lo niari yone guénone😁😀 carrière yawou dial ngaye am😬yaw kharagne lo yako dane mais moysa papa si lambdji ☝️ yaye dane yaye néksi guinawam 😬 lolou moko méti ndaysane😅 toujours yaye néksi guinaw kharagne lo inchallah😁
Yekini rek doyna si palmares
Yaw mi ragalale yalla Balla moromom yeup presque Dane naléne gay wAkh fi
King balla
Balla guaye katal sa ndeye feulé moudou lo moy roi des arènes
😢😢
Frère respect svp iow cheikh Mbacké ga toudd
Diambar amal yarr lii foo ake rèe le rék bouldi wakh lougnelay khèbè
Tu as qu'elle age poto ? Man modou balla sathies ama et eumeu nieup lay bèguer
Efface ton commentaire frère
Yakeni dafa magnet ton
Balla takal xalebi😂
No chérie c'était le 22 avril 2012 contre Yekini pas le 12
En Bon
Balla Seul
Yamuen yaeppou dolé
Le empereur de arene
Balla tu es mechant il faut respecte modou en foot ball tu voi une equipe qui gagne le chanpionnat mais elle ne gagne pa's tout les match
Saay bayilène di wakhé émotion
Balla il respecte Modou Lô té kouko ladjie dalay wakh Modou mo gueneu nakaré beurèl si lamb dji yé dafa meune beuré lol Machallah
Ms li sport la comm k mo dane Modou 2 fois amna droit wakh k moy empereurou Modou té Modou dou roi wam
Lgui Modou bou beugué dindi lolou na dieul Balla dane ko🤝
Buleine gnou sonnal mod’lo gueneu nekk sissouman meussul nangoul balla ou mou waxal ko lou bakh.. balla fougn ko ladj si beurei mod’lo mounei champion la mbappat lako commencé suivre..c’est pas son roi voila
@@cheikhomarba1541Wakh Nga Deug Deh Grand Frère
@@mistercarter467Merci Beaucoup Grand Frère
Voilà @@cheikhomarba1541
❤❤
Balla t’es pas sportif , modou est le roi de tout le monde
Billay dousa Rio
sa thies dall amatina ndam bg2 communication zero
Pas le 12 c le 22 avril 2012 dangéna dioum
Balla manol wakh day fen Di doul rek
Mais balla xana dagay fatte Sathies? Loutax citewoko si future roi ?
L empereur seul
The emperor.
22 avril 2012
fam bii dafa mélni daga nopp balla dei😂😂😂
Wakhi doff makhala lou Billy borso di doyer balla mi dou sakh niveau
Thiey sama mbeur bi. Néna per
Journaliste bi dou professional daga fare bamou fegne boula nékhè nga fare mes waro fegne
Doul gua deh 😂
Le 22 avril la wone
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
BALLA GAYE 2 KASSÉ