Pourtant l’épisode passé soda a dit à fatouche qu’elle a raconté tout à iboulaye mais c’est aujourd’hui que iboulaye a dit ça à awa soda toi est fatouche vous êtes mm chose bou😂😂fauteuil magic publicité mogate😂
Mais Bou t'es un complexé, depuis quand le wolof est vulgaire?on peut parler tout doux avec cette langue Bayiléne toutal bi le français n'est pas meilleur que le wolof
Bou ak Fat Kiné Yalla na séne diamm yague way❤❤❤🤣🤣🤣
Wooooouy Fatoush amoul ki dou nitt 😂😂😂😂😂😂 mais Fat kiné ak Bou relation bi doy waaar 😂😂😂😂😂😂
Fatouch menoul bayi fène🤣🤣🤣
Fébar la si moom lamigne bi comme louniou diiw laalo mbepp
Fatoush dafa laabir ndeysane mais iboulaye dafa diengue si eva way doko fassè😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Couple 💑 de l'année wayyy mais chapeau à wa thies chapeau à tout l'équipe eyyyy fatouch nk ammo diom billaye noooo bou amoul nena 18dollars🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Wa bou ak fat kiné ni rek laniou léne Di bayi 😁😁😁😁😁😁😁 wouyyy
Man Bou akk fatt kiné layy weur😃😃😃😃😃😃
Bou ak fatou kiné bougn ma rayoul🤣🤣🤣🤣 sheeuu vraimeent bravooo a vous🤣🤣
Fatouch yama nékh je t’estime beaucoup ❤️❤️❤️
Bou mii da melni meune na togu dh😂😂 en plus lekk you nekh rek lafi wakh mo takh birameu bi reuyy 😅
Ndeyssane fatouche damako moudié yeureum dafa direct
Bb Buu 😂😂 Faati Kinne ray na ma., 🤣🤣
Maman soda je t'aime beaucoup 💋🖇️❤️ et Eva d'amour aussi
Feuteuyi gno dougeule pochettes bi thi poche yi bilaye bou dou nite😅😅😅😅🥰
Eva mousouma faral awo yi wayé M'achallah Djiguene déy meuné founé Kham point faible goor motakhite iboulaye loumou mer mer dine wathie
nagn défarát fauteuil yi dang thiy tog mouy dougueul calpé sa poche
non 😂😂😂sacré Bou
Bou respecté wouniou 🤣🤣🤣
@@maryamkeita891 😂😂 il est le meilleur par ce que se Bou là et ce de polygame non c comme 2 prs différent
@@mamediarrafall3316 je t'assure !
Bou ak fatou kiné li amoule tmt😂😂😂😂❣️
Soda vrai seytané la
khawma fatouch khawma ak patawayam mias fénn rék lay def🤭🤣
Fene ak sof la bolé
😂😂
@@diariatoufall1391 billahi nonou la démé
@@tallasaliou9555 😅🤣
No bou amoul🤣🤣🤣🤣
Wa yene fatouch mi lamign bi dafay khassane khana?
Bou sous l’emprise pas dans l’emprise de ton amour 🥰
bou est le meilleur
Non fatouche nakk nakk nakk fénnkattega tamite mann louma guenna nakhari moy françaime yii du cou
🤣🤣🤣🤣
Wa tmt douniou wax ci fatouchhh beugu na français akk wane 😂😂😂😂mais chapeau
Mai buléne faté dieuw mo gueneh
Grave fene.
Awa Gueye xana temp yi tein noir lay out
Bou AK kiné 😂😂😂😂😂
Qui se rappelle encore de " Maram ak birane gnare gno khamnai dougnou ande dougnou taguo "👉🏽 c'est bou et fat kiné
🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Ayyy fatouch wañil ligay cas 🤣🤣🤣
Fatouch dafa deugu liguèyou diambour 😂😂ta soda dougnou dimballi Thi mousoram yiii 🤲
Wakh deugu. Comment chapeau riba riba
Kine ak bou 😂😂😂😂
Waw bou mom xana chef cuisinier la😂
Guegue bahool niari femme tamale🤣🤣🤣🤣
Walay Bou il me fait trop rire 😂😂😂😂😂
Ehhhhh mane beug na sen dioubo fat kiné ak Bou 😍😍😍😍😍😂
Khana bou dafa amatt khaliss😂
Buu bàyyil sunu làkk wi moo dàq wu farãse te gën koo neex.
Restaurant sombii diounii 5000😂😂😂😂😂
Bou ak fate kiné taye séne rap yi djibona niou
Wa légui nak yow sa fassé lèrna ndax yako wakh 😅😂🤭🤫
Yoyou beugue nako wouy fate kiné 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣dinako lekk
Thiey fatouche méw rék do bayi épinpéw nonnn da nga wone narr
Soda say ndiagne taxawe na😂😂😂🤣
Soda ewa fatouch yene nieup bene khene aye féne kate khene dekhene niap fatouch rek
Tout le monde se joue de fatoush enfaite 😂😂
Ziar ak magal way 😁 massa thiono à toute l'équipe! Liguey ak Bou et Fat Kiné rek thiono la walahhh😅😅🤣. Très bonne fin de soirée 🙏
Non bou raynama 🤣🤣 néné tokk thie feuteuil mou dieul kalpé dougal sa bir poche 🤣🤣🤣🤣
Pourtant l’épisode passé soda a dit à fatouche qu’elle a raconté tout à iboulaye mais c’est aujourd’hui que iboulaye a dit ça à awa soda toi est fatouche vous êtes mm chose bou😂😂fauteuil magic publicité mogate😂
Moma djakhal, ils font des erreurs, Soda avait dèja dit à Fatouch que nètalina Ibou laye wakh dji.
Fatos mooom man ta bayi fen
woooy bou ak fatkiné, je meure. sombi guerté
Bou wakhal pabi afer deux pathiana bou 1992 thiata bane age ngua amone svpl🤣🤣🤣🤣😅
Attend attend gayii wakhougne thii couple iboulaye bii
Bou et fat kiné dougnouma ray koi maguiléni gnanale diam bou bkh ta diko sakou si gnéne
Bou bayil saga
Nice na trop
Bou li mo takh sa birr akk sa lekh yi kaye lekk rekk la 🤣🤣🤣
Nice 👍👍👍👍
Bou sa biir bi ak sa lékh yi yako sakal sa bop 😂😂😂😂machahalla
Wa fatouch ba li diam la si yaw ?
Eyyyy soda bayil sa beutt yi ngaye soule
Mane môme ibou laye momaye rayé 🤣🤣🤣🤣
Wa bou amoul droit dindi lunette yo wala beuteum yi Nice soul
Mor gate kaye lol 😆 😂 🤣 😅
Mo gate
Waa soda tamit mousor bii moom Nice n'a 😂😂😂
🤣🤣
Wakh len Soda mou gorgorlou ci moussor, coiffure.... Sheeeeeeeeeeut 🤦♀️😩
No please kou kham numero soda ga diokh mako giryala man dama ko beugeu bilahi
Chérie boko amé
Ok nio far
Moi aussi mn amour
à tout ka am na fling
Number on
Noublier jamais les gens qui n'ont pas les 3 repas du jour agne rére ndécki plus désser
Bou boulma raay way dit dont ses ko cha bou monfi meune vrais toubab la koi tres bien bou🤣🤣🤣
Bou khame gua Lou neh
Wouy🤣🤣🤣mangui saww 18$ sa dollar bala 💯💥
Saw nak😂
Extrême pauvreté reynama😂😂😂
Non Soda vrai ligueulayize la Aka saff khorom
Kone fatagounegoune🤣🤣🤣🤣
Bou encore une plassace,c’est un plat Gambien
Pourtant en ville, le restaurant Layal day diay sombi, riz au lait
Mais kiné el raconte du blabla plat 5000 eupp nah
Wa tata soda khana wa Richard toll lah?
Bou mi dafa def formation hotelier d 😁😁
Heyy fatouch yow rek
Enfin la kinez ✅
Fatouch bayile nétaly
Bou khana traiteur
La
Nn j t aime soda 😘😘
Mais Bou t'es un complexé, depuis quand le wolof est vulgaire?on peut parler tout doux avec cette langue
Bayiléne toutal bi le français n'est pas meilleur que le wolof
On peut être vulgère ou doux avec toutes les langues, c'est pas la langue qui est vulgère mais la personne même.
Non fatouch meunoul teuyé lamignam
Eva la femme de bou dans la vrai vie wala khamguéneko
Vs êtes serious? Eva est la femme de Bou?
@@aidafallousall6793 oui c vrai
Non Soda dafmay fathie
❤❤❤🤣
👏🏿👏🏿👍🏿
Nn bou rék
😁😀😀
🤣🤣🤣🤣🤣
First
No bou ak kiné déna