Serigne Cissé tacle Aziz Ndiaye : "ci ay pékhé rék la nék, limouy déf yeugue na lepp…"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 15 дек 2024

Комментарии • 16

  • @abdoulkhadrecisse5087
    @abdoulkhadrecisse5087 День назад +1

    Inchallah 🙏 Serigne Cissé bi ak sa Touba dinaleinn feinn lo dagnou bari wakk trop tei khamougnou daara .
    Sénégal gui loffi Diayy reikk amna Koula soutt fouff Nei patteu ak mom

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 День назад +3

    Serigne Cissé mi wakhlén ko deug😂😂😂 dafay sopp reck. INCHALLAH bis bou combat bi takhawé lay khamni ayoul.

    • @beuguesalioubeuguesaliou524
      @beuguesalioubeuguesaliou524 День назад

      Sérieux wakhati ko serigne bo khame ni chaque jour migui si réseaux yi teksi oubi site bopame Sénégal mo nekh rek
      N’importe koi mofa ame

  • @carterjim9391
    @carterjim9391 День назад

    Dara khamoko bilay tousss menoko

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 День назад +2

    yaw Serigne Cissé lofi wakhoul contre Siteu té jour lambj linga wakhone amoul. bakhna reck boulén sarakhé Modou lo bamou dioum ba dieul combat bi contre Balla Gaye. Inchallah défaite reck lafay dieulé wat

    • @adamadiouf487
      @adamadiouf487 День назад +1

      Serigne cissé da meuneu guéw dé Machalla5 Khana khamoni Siteu mo momone combat bi maís fékhé Nagn ba yakheu ko Saloum la Deuk dé

    • @modoubayefallsikroulla1423
      @modoubayefallsikroulla1423 День назад +1

      ​@@adamadiouf487😂😂😂 Wa bakhna na dieul balla rk😂

  • @chamousman2726
    @chamousman2726 День назад

    Sering modou toure rek ganaw yallah mome rek Momana Mai modou lo Ndam si kaw Balla gaye2

    • @faalmadeugal2804
      @faalmadeugal2804 День назад

      SMT bobu kagn la fi tog togaayu sunu borom???

    • @chamousman2726
      @chamousman2726 День назад

      @faalmadeugal2804 damaneh ganaw yallah nekal nit

  • @teckjunior8005
    @teckjunior8005 День назад

    Je ne comprendre comment donner la parole à ces faux types, généralou sériñ Babacar Sy dou xatio ay géwou lamb

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 День назад

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @Zam-Zam710
    @Zam-Zam710 День назад

    SERIGNE CISSÉ 😂😂 MI MO THIOUKOU WAY NIATTA COMBATS NGAFI WAX LOU AMOUL DI MÉEW LOU FARAAAAAA 😂 MAMADOU LO BOU DIEULÉ BALLA GAYE 2 souko BG2 DANOUL MA TOUBI DONI YÉFEER BILAHI WALAHI capturé léen sama commentaire

  • @abdoulkhadrecisse5087
    @abdoulkhadrecisse5087 День назад

    Serigne bi daffayy feinn ki dou touss.
    Manei inchallah 🙏 Modou lo sou dieulei avanssou Balla Gaye Balla Gaye 2 danatt ko par force.
    Tei inchallah 🙏 Balla Gaye 2 dîna dieulatt couronne 👑 bi notez bien ça.
    Notez bien ce que je dis Modou lo daffayy danou son prochain combat quelque soit son adversaire bilahi Lolou force là

    • @faalmadeugal2804
      @faalmadeugal2804 День назад +2

      Yow sohorr ngeu daal
      Lula Modou Lo deff ba takh ngeu yenè daanu par force😮
      Yen̈e neggla borom maci fanaan