Vraiment merci bcp la série avance d,un coup très bon casting, scénario au top ! Ca éveille bcp sur le Senegal meryi vraiment damalene ragal wayé ak lo meunti def DEUG bou dioté nga waxko pk bou éclaté ni thi bokk ak ni thi bokoul lay lal...Yalna na niou y'Allah xiir ti lou bax !
La phrase *tolou sissa ndaw dokh ko ayoul* moy li arame jangalei fi bravo à elle masha'allah. Li sokhna boumou yewoul doto yewou si adouna neik ndaw taxouta xam sa bop ta nagn xamni ni erreur de jeunesse yi mognouy rattraper euleuk gnouy rethiou. Sougn borome ndaw gni la soxla kone nagn ko jokh sougn ndaw ta bayi tiakhane yi. Bala ma merr Reik dougue tik tok comme ci dagniy fatei ni euleuk meune nagn ame njabote. Yallah nagn yallah soutoural Reik ta def sougn xel yi ak xol yi iman inshaa'allah🙏
Bilahi arame mi warna yée djiguéne niou Bari ni beugue Gor waroul takh gua diokhko sa bopou djiguéne dafa am valeur bouko yalla diokh ta c rares guay DJis Gor devierge la wala mou eumbeul la ba paré takkla Kon nagn samou souniou ndaw Ndakh amoul prix ta Gor boula diaral gua diokh ko sa bopou mounilafa nioukhou taki khalé bou ndaw bou fétagoul thi néne ndakh yalla mom bis bou diote mou wathié arrivages bou bess niou bayisi xél❤️❤️
@@awadieye7133 DJis gua danio wara Bayi louniou dall niouni natou wala ndogal Ndakh ndogal bo DJis lokhol borom mogui si ndogal man nala dall béneu yoone mes sou répétition amé rék donatoul ndogal mes tayéf ta nioùn danio tamou louniou dall rék niou djigne ko yalla Bilahi yalla 🤐🤐
C'est vrai que ça avance, mais bon...avancement bi moom c'est *"ndékété diw mo diour diw, papay diw mo diour diw, diw amone neu doom il y quelques années",* etc.
Aram warna yee djiguenou tay yi lou neh way def lou neh way wah lou neh way sol nek ci réseaux sociaux loulen neh sol loulen neh wah fog ni yena pogne adouna lou way rendi sa lokho lay nathieu teh nak yalla kouko denkoul sa ndaw doula tel sa mag nagnu delo khel yi ci yalla teh kham gnoy gnan
Surtout les snappeuse et les tiktokeuse qui se denudrnt en longueur de journée devant leur caméra et celles qui disent dagn ci tollu. Venez lire svp, ce message est pour vous
Adouna defois ga doundou lou meti ba yakarné yaw rek la yalla tek natou féke né amna koula eupeu metétou adouna ta dako nebou dou gepp la yalla may niouye nebou s'en natou Adouna
Salam la mifa ofait dieynaba yobanté wone nama si yène néna Serigne Sarr lay weur té beugoul scénariste goudal série bi limou goud rek da doye néna tamite tata armé nga dieule sa temps mo ngi niew garouwalé la 😁😁😁😁
@@maremafall2139, mais nak mane je trouve que même si ça avance, scénario bi dafa khéwi, *"diw mo diour diw, papay diw mo diour diw, diw amone neu doom il y quelques années, diw mo ray bayou diw, diw mo violé wone diw"* rék. Je trouve que Marodi et EvenProd ne l'auraient pas fait de cette manière.
Aaah série bi mingui avancer nakk a l était temps waay Mais waroul won nekk « diabarou gorgui » mais plutôt « les secrets » prck dafa beuri secret trop Sinon vous avez des bonnes actrices machallah
Yénagui soté ndo secret yi deh🙄J'espère tout de même que gorgui n'est pas mortl rekk sinon série bi mom dou am sens en plus cawou dieynaba ak kharitam bi ak Serigne bi ça doit être réglé
A comparer la réaction de Sadiya et le Frer de Ma Anta c’est deux jeux différents kiko meun bikoul ak kikoy diem franchement ❤️ elle a même emporté les autres dans le jeu mashallah 😩
Khana gorgui ak dieynaba nekatou gnou thi série bi !? Accélérer nguene ko deh… appel bi sadia diote mom khana goorgui dafa accident deii lagne ko annonceii 🤔🤔 moy goorgui nekatoul ci serie bi… en tout cas j’attends la suite jusqu’à preuve du contraire 🚶♀️🚶♀️🚶♀️🚶♀️
Wooow quel épisode 🧨🧨🎆 il était impeccable. Bravo ! J'ai toujours apprécié la série mais vraiment vous avez fait fort aujourd'hui @Khar Medias !! Merci !
@@atta890 et le viol de Ma Anta aussi désse na et que les manigances de Dieynaba fégne plus l'histoire de Dieynaba avec un ami de Goorgui et aussi de sa fille qui Etudie à Londres
Vraiment merci bcp la série avance d,un coup très bon casting, scénario au top !
Ca éveille bcp sur le Senegal meryi vraiment damalene ragal wayé ak lo meunti def DEUG bou dioté nga waxko pk bou éclaté ni thi bokk ak ni thi bokoul lay lal...Yalna na niou y'Allah xiir ti lou bax !
428
❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️
L
T6o,,kfs
Des coeurs pour Serigne mbaye sy ❤️ AK Serigne Mountakha mbacke yagafi te werr
Amine
🙏
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
💝💝💝
@@sayegueye6151 jjjjjjjjjĺ
J'aime beaucoup serigne babacar sy 💚💚💚💚🤍🤍🤍🤍
Moi
Ak mann miii
Baringa ci morom
Bariguasiy morome
bilae dou yaw kessé
Kou beug sa srigene Babakar beuseul jtm❤❤❤❤❤❤
Jtm
♥️♥️♥️❤️❤️🥰
jtm
❤❤❤❤❤
😁
La phrase *tolou sissa ndaw dokh ko ayoul* moy li arame jangalei fi bravo à elle masha'allah. Li sokhna boumou yewoul doto yewou si adouna neik ndaw taxouta xam sa bop ta nagn xamni ni erreur de jeunesse yi mognouy rattraper euleuk gnouy rethiou. Sougn borome ndaw gni la soxla kone nagn ko jokh sougn ndaw ta bayi tiakhane yi. Bala ma merr Reik dougue tik tok comme ci dagniy fatei ni euleuk meune nagn ame njabote.
Yallah nagn yallah soutoural Reik ta def sougn xel yi ak xol yi iman inshaa'allah🙏
Bilay ma chérie en plus bo wakhé niouni sa yone nékoussi mandoule danga soxor
Machallah amna solo trop
Bilaye euleuk dou Agnès dou rére
@@sokhnathiaw6689 wallay wala gnouni iow dé bi ngay dounde, wala branché woh, wala xamo li khew danga serr. Mais yallah bakh na yallah nagn yallah soutoural
@@aichaniang6228 waxko si kaw
Ngi magua li yala nalene yala tek si yonou diam barke mame serigne touba amine
Amine ci barr gui chékhoule xadime
Me yawe nake do niewe xana dama bg kouma dalale❣
@@amdyndiaye9933 non moi je suis en France mais je suis sénégalais merci
Omiagod me yalla bakh na dinane la fasale inn challahou
@@amdyndiaye9933 merci yala na yala nagdou niane yep amine
Yen ngi maggal si touba yalla nalén yalla tek si yonou diam ak xewuel té Seringe bi na ngoul niou sounouk thiante ameen
Ndeysane série bi Arame lassi gueuneu yeureum erreur d jeunesses yimou deff dako eup lokho bilay massa yalla nala borombi takhawou inchahala 🙏💔
Diabarou goorgui temps yi daguénne ame djomm deh machallah
Mashalah chacun assume son.role mais sadya ya pas deux mashalahhhhh chapeau el assureeeeeeee
Vraiment. Cette série est excellente. Sans faute
Mohamedoul mahi lbrahima Niass yalla nafi yague ta wer
Amine
Amine ya rabbi si barky baye Niass ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Aminnnnnnnn ya raby
Amine Yarabi si barkeh Chéikh Ibrahim Niass
Amine yarabi 🙏🙏🙏
Sadiya tu joues trop bien les emotions 😍 du rire sarcastique à l’hystérie
Sen serie bi berina rebondissements!!!
Meilleure serie du moment
👏👏👏👏👏
Bon magal à tous bonne route yalla naléne yalla tékk si yonou diamou 🙏
Yalla saye wadiour féké sa niarigne nél amine
Amin yarabi
🤲🤲
Amine wayy
Amine
@@ibradiop1108 ko
Profitons de nos parents louniou meune, lounioulene defal khèpe.
Investissement bi geneu mak moy lolou.
😍😍😍
Bilay ndeysann lou lerr
Bilahi arame mi warna yée djiguéne niou Bari ni beugue Gor waroul takh gua diokhko sa bopou djiguéne dafa am valeur bouko yalla diokh ta c rares guay DJis Gor devierge la wala mou eumbeul la ba paré takkla Kon nagn samou souniou ndaw
Ndakh amoul prix ta Gor boula diaral gua diokh ko sa bopou mounilafa nioukhou taki khalé bou ndaw bou fétagoul thi néne ndakh yalla mom bis bou diote mou wathié arrivages bou bess niou bayisi xél❤️❤️
Walahi Lou diara bayui khel dh
Wayé de Foix natou lay nek rk
@@awadieye7133 DJis gua danio wara Bayi louniou dall niouni natou wala ndogal
Ndakh ndogal bo DJis lokhol borom mogui si ndogal man nala dall béneu yoone mes sou répétition amé rék donatoul ndogal mes tayéf ta nioùn danio tamou louniou dall rék niou djigne ko yalla
Bilahi yalla 🤐🤐
Aka lerr
@@nnnnn4519 merci 👍
J'aime beaucoup la façon de sadiya❤️🥰
Qui trouve que sadya fait partie des meilleures de sa génération vraiment elle est très talentueuse machaalah
Magal ak diame salam féki diame bayi kofi indi wate diame inchalla barke seydina mouhamed saws 🙏🙏🙏
Amine Ya Rabbi merci👌
@@gangueafsa4916 gno far
Ta mère vivra jusqu'à ta réussite dit Amin 🤲🤲🤲🤲🙏
🙏🙏
Amine inchallah
Amine
Amine
Amine
Arame est très forte louko meuneu dal day diouli di niane yalla
Enfin, la série avance. Merci Khar Média.
C'est vrai que ça avance, mais bon...avancement bi moom c'est *"ndékété diw mo diour diw, papay diw mo diour diw, diw amone neu doom il y quelques années",* etc.
Bilaye ma beugue Serigne Mountakha Mbacke rek borom mbëcke
Ma Anta baiyil make-up, MachaAllah dangà àm naturel beautè nguir yalla. Danga rafèt MachaAllah Ma Anta. 🇬🇲🇬🇲👌
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 3 vérité thi ben episode je tire mon chapeau bravo khar media
Ma anta ce caukan
Sadiya, elle est adorable♥️♥️♥️
Ta mère vivra jusqu'à ta réussite dit amine 💖
Très éducatif ce film. Dieuf kéndeu meunouko soul
Gniy magali nelen yalla tek si yoonou diam... nagniy tam di wakh deg quelque soit les conséquences moy ndieuk ta moy moudjou👍
Thiey passé ya moune topaté, fou arame dougou nga lokhatiko😂😂😂😂😂
Passé dafa goréwoul rek😂
😁😁😁
Bilae damako yeureum 💔😹no passer dmrm la
Bilay passei bi dako top bamou seusss
Mdrr😂😂😂😂
magual ak diame inchallah
Jaime serigne babakar sy Malick ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Moi
Arame est la plus souffrante de la série 🥰🥰
Ummh, pas plus que sa propre fille Ma Anta
Aram warna yee djiguenou tay yi lou neh way def lou neh way wah lou neh way sol nek ci réseaux sociaux loulen neh sol loulen neh wah fog ni yena pogne adouna lou way rendi sa lokho lay nathieu teh nak yalla kouko denkoul sa ndaw doula tel sa mag nagnu delo khel yi ci yalla teh kham gnoy gnan
Surtout les snappeuse et les tiktokeuse qui se denudrnt en longueur de journée devant leur caméra et celles qui disent dagn ci tollu. Venez lire svp, ce message est pour vous
Dèg na deug vraiment lou lèr nga wakh té bo wakhé niouni danga soxor sa yone nékoussi mandoule ect...
Mais je pense que amor gnaw marabouté les femmes
Mash'allah amna solo merci bcouq 💖💖
Machallah vérité absolue
Arame aime trop souffrir dans les séries . Elle incarne souvent ces genres de rôle
Kanamou kouye souffrir la yoré motakh gnou koye diokh rôle bobou lou beuri🤣
Mbadou innocent la toujours dalll
@@fallpapaseckoufall5999 🤣🤣 innocent fane Arame rek eupena
@@ramadiaw607 🤣🤣🤣 mbaa dou
🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Adouna defois ga doundou lou meti ba yakarné yaw rek la yalla tek natou féke né amna koula eupeu metétou adouna ta dako nebou dou gepp la yalla may niouye nebou s'en natou Adouna
Sadiya elle est trop curieuse elle cherche tt l temps à savoir ce qui se passe sur la vie des autres. Niit dafay am reserve touti sakh😉
Bien dit
Bilay defa sop dé ak kestion you beuri yi
Lep la beug kham
Djiko bobou keiy na yam si rôle bi rék dafa dagn coumpa trop
Mandou mom défouko
El v tt savoir tei dalay top banga seuss li mom keine xamoul lanla n'a yam si serie bi dal ndax dans la vrai vie mom li doxoul
Plaisir 5m parfois moulay ték nakharu adouna Ak alakhirah teuh Daray adouna diaroko
délén bayi khél s'en bop ta ragal yalla
Bon magal🙏
5910(5mns de plaisir,9mois de grossesse,1enfant,0pere😛😓😂😂😂
@@amydia5877 😂😂😂 non Amy Ray ngama mais nk bilahi deug leu
Ta ossi lolou Dara diaroko
@@mahmoudkhalilal-hussarytvh3664 lolou la dh 😂😂😂😂
Yalla nanu yalla dafal magalou diamou bone magal
Amine
Ani gnouy fanane tay Touba👩🦯
Inchallah ben ci man aksina depuis 10
@@mamourgueye6905 ndeysane 😭
Ande pouss publicité yi 🤚🥳
Ma Anta tu es naturellement belle wagnil sa maquillage bi en plus andoul ak sa rôle
Taye mome dafa eupe trop
Vraiment un très bon film qui devrait servir de leçon à tous hommes comme femmes
Meilleure épisode bravo Khar Media
Arama natou deugeu moko dalle
Hâte ô prochain épisode tey mom épisode bi nekh la deff 😃qui est d'accord avec moi na pousse bleu,👍yalna diam yagu, dilène di nianal magalou diam
C'est la meilleur série de l'année j'aime sadiya et arame
Salam la mifa ofait dieynaba yobanté wone nama si yène néna Serigne Sarr lay weur té beugoul scénariste goudal série bi limou goud rek da doye néna tamite tata armé nga dieule sa temps mo ngi niew garouwalé la 😁😁😁😁
Niaw ay guadde
D’accord nila meuna dèmé kay 🤣😅
Bah voilà Khar média, on avait hâte que ça avance, mercii🥰
Reste plus que Ma Anta wakh que ni c Samba qui l'avait violé rk match bi tass
@@kanekhady7331 boul faté desna bénéne goor gui mo ray papaye sadiya
Lol vous avez raison d, fatéwona ces secrets aussi
@@maremafall2139, mais nak mane je trouve que même si ça avance, scénario bi dafa khéwi, *"diw mo diour diw, papay diw mo diour diw, diw amone neu doom il y quelques années, diw mo ray bayou diw, diw mo violé wone diw"* rék. Je trouve que Marodi et EvenProd ne l'auraient pas fait de cette manière.
@@maremafall2139 ak dieynama mn ray yacine aka desss skh
Arame beug neu mayma m’a expliqué leuh 😂😂😂😭😂😂
Yena mana séttlou
😂😂😂😂tè dou meuseu expliqué
Magalou Diam dem Diam yow AK diame 🤲🏼🤲🏼🤲🏼💯
ah tay keur gorgui matar yeungeutouna il est temps de reveler les secrets et que la serie avance
Lo wakhati khana Taye môme fi to dji na
Mais goor gui dou yeuk parce k raynen personnage bi
@@blackgyal moma diakhal gorgui Ken guissatouko
J'ai adorèe au moins le serie avance en fin
Thia première vue bala
J'ai les larmes aux yeux 😭😭😭😭😭mame anta yeureume nako sadiya tamite 😭😭😭😭
Thèâtre bi mome khana dangio dieul problème yèpeu kheupou ko Arame
Bilay yaw ..
Machalla tata arame Dale mou Mane limouye def
Aaah série bi mingui avancer nakk a l était temps waay
Mais waroul won nekk « diabarou gorgui » mais plutôt « les secrets » prck dafa beuri secret trop
Sinon vous avez des bonnes actrices machallah
Yénagui soté ndo secret yi deh🙄J'espère tout de même que gorgui n'est pas mortl rekk sinon série bi mom dou am sens en plus cawou dieynaba ak kharitam bi ak Serigne bi ça doit être réglé
A comparer la réaction de Sadiya et le Frer de Ma Anta c’est deux jeux différents kiko meun bikoul ak kikoy diem franchement ❤️ elle a même emporté les autres dans le jeu mashallah 😩
Wa yène dunguène ñu wakh fu goorgui dougou aaaaahhhh lii tamite nagnou thii wakh book
Pourquoi rôle bi gnou dioh ko arame menone na dale dieynaba
Khana gorgui ak dieynaba nekatou gnou thi série bi !? Accélérer nguene ko deh… appel bi sadia diote mom khana goorgui dafa accident deii lagne ko annonceii 🤔🤔 moy goorgui nekatoul ci serie bi… en tout cas j’attends la suite jusqu’à preuve du contraire 🚶♀️🚶♀️🚶♀️🚶♀️
Mariage forcé consekence apre mou diekh
Est ce que dou oumaya mo doff
Wooow quel épisode 🧨🧨🎆 il était impeccable. Bravo ! J'ai toujours apprécié la série mais vraiment vous avez fait fort aujourd'hui @Khar Medias !! Merci !
Enfin les secrets commence à sortir bravo
1 épisode 3 révélations j’adore merci 🙏🏼
Khana diékhoul pask fok sadiya khamni goor gui mo réy papam
@@atta890 et le viol de Ma Anta aussi désse na et que les manigances de Dieynaba fégne plus l'histoire de Dieynaba avec un ami de Goorgui et aussi de sa fille qui Etudie à Londres
@@ramadiaw607 wawaw serie bi waroul diékhé nonou neu deug yi fégn 🏃♀️🏃♀️🏃♀️🤸♀️🤸♀️🤸♀️
@@atta890 wawaw na lépp fégne rek en plus goorgui waroule dé parceque mome mo khame comment est mort le père de saadya
Sadya coiffure yigua def yep bimolassi va bien...bayilma perruque mireille bi 😄😄
😀😀😀😀😀🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Lii waar na yé jeunes you bari 😥meuytouléne eureur de jeunesse regarde Arame rék oh j'ai pitié d'elle 😥
Épisode 115, Secrets yi fégn naniou 🥳🥳🥳🥳🥳🥳!!!
😂 beaucoup trop même , Mame anta elle en a jusque dans le dos
Ma Anta c’est la Dialika de cette serie
Elle a tous les maux du monde
Mbaye sy yagifi te wer
Taye nak serie bi nexxna trop🥳😂😂😂 ma anta dina guaniou rek ak ayy probleme😢
Machalah machalah migui neh vérité yi mogui fégne té yénagui yété bravo khar média ❤️
ma anta sa maquillage 💄 bi dinama xama tousser🤣🤣 touty
Ma anta courage rek
Salam gayi Ana gni wax série avancé woul tay mom dolenn wax darra machalah mai le fils de ta Diéneba dafa beau dé qui d'accord 🤗🤗
Sadiya sa thiouray bi nékh na trop ❤️🤭🤭😂
Dafla xèn🤔🤔😂😂😂ma peukh😂😂😂
Thiouraye té guissa goull gorgui
Bilay Arame sumadone joué théâtre duma bokk sa famille ndakh kunékak yw du diokk si problème courage ma anta
😂😂tu m'as tue😂😂mbadou Arame moy nitou blèm 😂😂😂
😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣😄😄
😂😂😂😂😂😂😂
Omar diaw mome khamnani kou oyofon kalsonla 123rék mousomi 🤦
😂😂
😂😂😂😂😂😂😂wouy magui dh
😂😂😂
@@zeynabgaye4841 mane dé Diaw bi mou sante rek moma meti 🤨
😂😂😂😂😂😂
Wa mane wakhouma lolou déh anni dieynaba lam
J'aime beaucoup la façon de sadia
Enfin un peu d'action dans la série
Xana série bi dougene Agne AK rerre xiff môme dinalene reyy😂😅😅
😂😂😂😂😂
Enfin sone naniou si wiri wiri bi
Qui est déjà en touba
Ma anta loumiy doundou si série bii méttina trop sakh
Bonsoir la mifa yalna niou yallah défal diamou😘❤
Maa ngi ñaanal ñiy màggal si sunu Boroom teg leen ci yoonu jàmm ak salaam.
Amine wày
Dama sone di khar aram mou wakh deugue bi sadia kharalma wakh la secret bi mame sey dou sa yay ma anta gorgii djiouroula.
beaucoup d'émotions; bravoooo
Machallah qui est fan de ma Anta 😘😘😘🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Enfin….La série avance.Il était temps ✋
Taye Kaye série da dawe magoum avance
Heee man de dama sonnou billahi si série bi sama fitbi tongagoul Billahi 🥲🥲🥲
Mane dale sadiya la andal machalah dièk bou ndaw dangay deff bamou bakh nièmei drap bou blanc diko lalale sa dieukeur wawe kayy
Bon magal a toutes le mondes❤💫
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Li mom sou nekoul fin de saison danou lenni niouss😂😂
Li lagnouy wakh kou FOWÉ SA NDAW SA MAK RÉRELEU lou fi way di def rek nako kholate ndakh euleuk nètaliba meuna rafet
Bilaye lou way def bopame
Bi Sadiya di rétane Awa bilae dama rétane ba sonn😂😂😂
115 épisodes nak😖😮💨 sadiya tamit ay talons wam yi war nassi def bouchons wala mou arrêter diko sol akhhh
🤣🤣
🤣🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣
Khar tay nieuwé nga dolé linga bolé lépp tay kéneuh atanouko😁
Khar média mom goor la oubien fille
@@ndeyelo1151 😂😂😂😂 esq dou garçon
@@binetaseye2678 kharit lathié way
Non goor leuh 😅
Enfin avancement de la série
Bolen rayé gorgui douma len ko baleu😂😂😂