Félicitations à la DIC l'une des meilleures polices d'investigation au monde. Le gouvernement actuel doit leur donner tous les moyens et les meilleurs pour faire leur travail. Ils sont capables d'elucider tous les crimes commis pendant le règne de Macky sall!
Merci infiniment ngone saliou li deh mo wor kouye diokhé xibar daye leerlou bala mou koye diokh askane wi mais franchement ces influenceurs et pseudo enquêteurs RUclipsur yi kou lène moytouwoul di naňu raylou domou diambour kou nek rek taf ňaňu ko yek ko lou melni xémé té dara dousi DEUG thieye Sénégal ragal lêne Yallah té di soralé seni bamel toumalaté bi beurina wasalam Yallah na Yallah niit ňeup gni si.lalé inchaa Allah ,paix à leurs âmes
Je viens de découvrir le professionnalisme de Sans limite, désormais yén rek lay déglou pour toutes les infos. Manshallah. Rien a dire. Bonne continuation à Sans limite.
Wa pikine nio soff té beug bandit bandit Lou ko si dégg Mouy wakh mingui nane douma ragal domou pikine laa pikine ragal deukoufa lolou Moy sen slogan dé pour niom ame fitt moy nek bandit. Ils ont intérêt à changer nak ndakh kén nawlo toulène. Goor Yalla DEUG dou nek bandit mais dey liggey diarigne boppam. Que justice soit faite pour Aziz dabala wa salam
Gonè yaw rek lagne done xar si informations bou wor bi machallah yalla na yalla goudal sa fane gni fatou yalla yeureume lène xarèlène aldiana firdawsi si barkè seydina Mouhamed psl
Lerna dè yaye boye, jerejeuf, lèneu rèkk mooma diakhal instant bi moye niom nougnou dèff ba dougou tranquillement ci appt bi alors qu'ils avaient dèjas une altercation avec Aziz! Nabou Lèye aussi loumouy neube, je ne crois pas qu'elle soit complice mais dafa raggal rèkk, surement d'être jugée ou d'une retaliation.
Yalla na yalla léral lépeu li doynawar té niaw khawma kou def wayé niaw na en tout cas Aziz ak Wally niak naniou séneu bakéne paix à leurs âmes ndeyssane
Diadieuf Ngone
Très professionnelle, claire et limpide .
Sans limites informe juste et vrai. Merci Ngoné Saliou
Ngonei mom Lou ler rek lay wakh merci😍❤️
Waw kay informations Bou bakh bi figuakoy amé sii sans limite
J'attendais vos informations auxquelles je peux me fier. Merci Ngone Saliou. Bravo sans limite
képp kou beugue seyedina mouhamed abonnélema❤️🙏🏿
Sallallahou aleyhi wassallam 💚💚💚
Salalahu aleyhi wasalam
SAW ❤️☝🏾
❤
Psl
Un excellent travail de journaliste. Précis, concis, rigueur 🙏🙏Merci ma belle
6:20 la commencé 🙏🏾
Ngoné journaliste du peuple ❤🇸🇳🦸
Félicitations à la DIC l'une des meilleures polices d'investigation au monde. Le gouvernement actuel doit leur donner tous les moyens et les meilleurs pour faire leur travail. Ils sont capables d'elucider tous les crimes commis pendant le règne de Macky sall!
Merci infiniment ngone saliou li deh mo wor kouye diokhé xibar daye leerlou bala mou koye diokh askane wi mais franchement ces influenceurs et pseudo enquêteurs RUclipsur yi kou lène moytouwoul di naňu raylou domou diambour kou nek rek taf ňaňu ko yek ko lou melni xémé té dara dousi DEUG thieye Sénégal ragal lêne Yallah té di soralé seni bamel toumalaté bi beurina wasalam Yallah na Yallah niit ňeup gni si.lalé inchaa Allah ,paix à leurs âmes
Très clair et cohérent! Merci Ngone c’est ça le journalisme 🥰🥰
Merci sister Ngoné Saliou
Une vraie journaliste Ngoné Saliou❤
Merci sans limites ❤
Lii moy informations, juste, clair, bien conçue, bravo 👏👏👏👏👏👏👏
Je viens de découvrir le professionnalisme de Sans limite, désormais yén rek lay déglou pour toutes les infos. Manshallah. Rien a dire. Bonne continuation à Sans limite.
Même moi je viens de m’abonner❤❤❤
Merci beaucoup ngoné vraiment vous faites l'exception de tout ses sois disant journalistes qu'Allah vous protège et vous facilite la tâche
Xibare you wére té wore Merci Sister ngoné 🙏🏽
Voila des information Clair et precise une vrais journaliste merci pour ces infos. Thanks
Li moy journaliste wakh bou lér to wor
Très claire merci beaucoup
Que justice soit faite
Ma fille chérie ziar nala yalla nala yalla barkel sama sope merci ma fille bon courage
Voilà une vraie journaliste limoy informations way merci ngoné
J'attendais SANS LIMITE qui informe juste et vrai...merci beaucoup Ngoné
Merci sans limite
Le journalisme libéré des chaînes (les capitaux...l'argent) merci madame...keep it up and all the best 👍
Merci beaucoup Ngoné c'est clair maintenant.
Ngone Saliou moy djiokhe information authentique
Léép fii léyy lérré merci mes sœurs
Wa pikine nio soff té beug bandit bandit Lou ko si dégg Mouy wakh mingui nane douma ragal domou pikine laa pikine ragal deukoufa lolou Moy sen slogan dé pour niom ame fitt moy nek bandit. Ils ont intérêt à changer nak ndakh kén nawlo toulène. Goor Yalla DEUG dou nek bandit mais dey liggey diarigne boppam. Que justice soit faite pour Aziz dabala wa salam
Diadieuf Sokhna Ngoné xam xam dou pékhé informer les Sénégalais juste et vrai c'est la seule chose importante ❤❤❤ merci à Sans Limites étagement
Ngone le chroniqueur de la nouvelle génération
Li moy journaliste, dire la vérité pour eclairer la lanterne des sénégalais. ❤❤❤❤❤merci ngone diadieuf sans limites
Gonè yaw rek lagne done xar si informations bou wor bi machallah yalla na yalla goudal sa fane gni fatou yalla yeureume lène xarèlène aldiana firdawsi si barkè seydina Mouhamed psl
Merci ngoné bonne continuation🥰🥰
❤❤❤❤❤ Machalla a vous ngone et toute l'équipe du courage 💪😘 good job 👍
Merci beaucoup sister ngoné ❤❤léér na nagn
Ndeysane jalousie rek maïs la vérité sera établie Inchallah one love ngoné ❤
La vraie information merci❤
Merci beaucoup bonne cette éclairage
Machallah Ngoné ak wa sans limites
Wa feeling Dakar tamit meune naniou fene dal. Merci Ngoné.
Yen yena dess feeling Dakar😂Sen tittre fen yoyou😂
@@fatoumatabintoucolley8878 non lii dou yone rek laniouy def.
Merci ngone yalnala yalla sammou
Meilleur journaliste du Sénégal
Je viens de comprendre merci pour l'information c'est très claire merci beaucoup ❤
Ngonè continue ainsi. Des informations justes et fiables
Inchllah gnu gui taxérlou yénéne ni infor merci❤️yalla na ylla léral lep barki srgn fallou🤲🏻🤲🏻🤲🏻🥹
Feeling Dakar moy fenn walla
En tout cas dal mandou lén thiakhanouma
Té yalna yalla léral lepp inchallah
Feeling Dakar mō dak fēnn sii site yeup mö tah dama désabonné föfü
NSD merci beaucoup très clairs ❤❤❤❤
Merci Ngoné Saliou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bravo. Mais yakamti ba diokhe des fausses infos.
Vraiment chapeau bas a SL
Sans limites télé bou bakh bi info you lér nagn❤❤❤
Merci Ngoné pour les informations
Thiéy meun lingay déf dafa nékh machallah @ngoné Saliou merci beaucoup
Depuis lors j'attendais sans limite pour des informations claires .
Vraiment sans limite et solution tv je vous adore
Macha Allah thi kaw thi kanam
Diaajeuf Ngone. Courage waye !
Bravo Que leurs âmes reposent en paix paix et que Firdawsi soit leur demeure éternelle Amine
Machalah. Chapeau Ngoné
Guoné yaw rék laniouy top
ngoné je t'aime ❤️
Saway bougouma am ak ioe problème deh 🙄
@@jackson_nj😂 wouy
@@fatimatra8457ki défa yabatei kw😂😂
@@jackson_nj je l'aime beaucoup frère 😂❤️
😂😂@@jackson_nj
Merci 313 sans limite
Merci beaucoup ngoné.
Iow rek yama doye thi information ❤
Ngoné rek laa done khaar 😍 boy weur journaliste bou crédible rek topal ngoné loumoula wakh bindal🥰🥰🥰🥰
Mann daal Ngoné Saliou laa wolou thi ay xibaar 🥰🥰🥰
De grâce votre jenerik est trop trop long...
Surtout lolou dafa goudou trop
Mane kay dama warou sakh c trop wayyy
Lerna dè yaye boye, jerejeuf, lèneu rèkk mooma diakhal instant bi moye niom nougnou dèff ba dougou tranquillement ci appt bi alors qu'ils avaient dèjas une altercation avec Aziz! Nabou Lèye aussi loumouy neube, je ne crois pas qu'elle soit complice mais dafa raggal rèkk, surement d'être jugée ou d'une retaliation.
Merci sokhna ngone saliou diop respect 💪💪💪
Iow la meune déglou ba xam si loulér merci ngoné l’info très pro et clair
Bilahi mala beug yaw ngone saliou diop léer na jte zur merci beaucoup wa sans limite ❤❤❤❤❤❤❤
Mrc ngoné saliou ler na nagni masha Allah
Merci ma belle ❤
Merci ngonè saliou ❤❤❤❤❤❤
merçi ngoné mane lii la gueume machallah trés pertinente ❤❤❤❤
Ngone saliou vrai journaliste
Non suis pas d accord on arrête celui qui a pris le wave d un défunt et on le libère ????
MACHALLAH ALHAMDOULILLAH MERCI BEAUCOUP SOKHNA NGONE SALIOU ❤❤❤
Machalla sen légué rafitna
Merci Ngoné Saliou ❤❤❤
Merci beaucoup pour l’info clair et nette
Merci ngoné
❤❤❤ enfin clair merci sans limite
Machallah yékhgua diogué touba
Yalla na yalla léral lépeu li doynawar té niaw khawma kou def wayé niaw na en tout cas Aziz ak Wally niak naniou séneu bakéne paix à leurs âmes ndeyssane
Merci pour info ❤
De plus en plus CLAIR.merci
Salam Sister Ngone Ma Sha Allah Bonne Continuation Dieureudieuf 🙏 🙏 ❤❤❤❤Yallah Nalen Yallah Yeureum Khare len Aldiana Firdawsi Ci Barke Seydina MOUHAMED ( p.s.l) Ak Mbolem Dioulite Allahouma Amiiiiiiiiiine Y'a Rabbi 😢😢😢🤲🤲🤲😔😔
Machallah lérna ngani❤
Wa nio mana fénn gni nék si internet Di wakh té dara xamonio ko si linioy wakh bakaro rék
Merci beaucoup
Machala lerna nagne li moy informations
Merci Ngoné sama fans nga bilaahi
Machalla ngone na sa diame yague
Machallah ngone❤❤❤❤❤❤
Merci yaye fall ngone grazie mille
Macha allah très précis
L'affaire va être simple avec le bornage des te téléphones koufa nekone dinayou khame inchalah
Très content de vous
Merci Ngoné la meilleure des journaliste
Merci nagnou exposer gni def li 💔😭merci gnoné
Très professionnelle✨ Ngoné merci tes dires sonnent bien à l'oreille
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤
Merci nguone SL est se qui vous accompagne Mami est les autres pas les autres qui on détourner nôtre argent merci beaucoup
Merci may sister ❤