Salam ya Imam,depuis 4ans chaque fois que j'écoute cette DAWAH mon coeur se raffermi d'avantage Alkhamdou Lill'Ah maa chaa Allah je vous serais toujours reconnaissante 💯une soeur en Islam
The only people who disliked this video either did so mistakenly or they really need help with their current situation. Dr Mouhamed Ahmed Lo may the Almighty ALLAH protect, guide and you, your family and all those who follows the footsteps of the prophet Muhammad PBUH. And may the Almighty ALLAH soften the heart of all those who hate you just because of the truth you are spreading and I really hope that all those people will soon realize the love you have for them by always trying to show the the right path. I really love you and In Shaa ALLAH I’ll always keep praying for you and your family for protection, guidance and long life.
Allahou akbar Lila kilifa di diarigne yalna yalla defal la diam goudeul say fane inchallah ❤️❤️❤️Sope nagnla lol yalla nala yalla ak yonentam sope nouko raw dr
Ya Rabbi pardonne nous 😭😭😭 On seras jamais à la hauteur même si on passais notre vie à te remercier. Pardonne notre ingratitude ya Rabbi. Que Ta miséricorde accompagne nos vie.
Wallahi wahtane bi meunou ma thi doyal ça fait presque quatre ans damakoy déglelou bale sah dama dém beu métrisé ko yalna yalla takhawou cheikh bi bayyiko fi ay ate tou beuré beuri té. Mou ande ak wéer
yalla nala borom bi fay (fa zakkir fa inna zikra tanfaoul mouminine) yalla nagnou yalla défal tawhid bou deugeur geuneu diss montangne yii amiiiiine ya rabbal alamine
Dr Ahmad lo ressource humaines la mais malheureusement Sénégal khamouniou ko mangui laye nianal ci sama khol yalna y allah samou.la goudeul sa fan yok sa kham kham ❤❤❤❤
بارك الله فيك يا دكتور جزاك الله خيرا شكرا فذكر إن ذ كر تنفع المؤمنين، من دل على خير كفاعله اللهم زده علما ومدد عمره تبارك الله احسن الخالقين اللهم صل وسلم وبارك على سيدنا محمد وعلى آله وأصحابه أجمعين ببركة القرآن الكريم
Dr Mouhammad Ahmad lo ♥️🙏 Oustaz Mor Kebe ♥️ Oustaz Aliou Sall ♥️ Oustaz Oumar Sall♥️🙏 Imam Hassan Sarr ♥️ Oustaz Makhtar axirou zaman♥️ Tafsir gueye ♥️🙏 Oustaz irán nDaw♥️🙏 etc ....ALLAH tu as bcp d arme, encore une x ns aurons plus des arrgumment devan vous (Maliki nāshii) Au Jr dérniére 🙏😭
Walahi liguay def si kholou ❤ diame yi sakh khamoko,dp8 3ans magui deuglou a chaque fois ma am natou,barakallah fikoum 🙏🙏🙏🙏🙏Nala yalla sam
Ki billahi Senegal dinanou ko sagané bamou dém nou diko réthou yalla nako fi yalla bayi ta same ko ba nou mandi diarinou si mom lou bari
Amine y'a rabbi
Amine mandé soumakoy damay contant kouco mel yombot si rewmi yalla naco yalla yokou fan ak weur si barké saydina Mouhamed s h w s
Wakhatiko wayy Gorrr Yallah
Walahi
والله كلامك صحيح يا أخي
Je souffrez vraiment pour une fille que j’aimais depuis mon enfance mais après avoir écoutés cette dawah mon cœur s’est apaisé . Alhamdouililah
Qu'Allah te facilite
Salam ya Imam,depuis 4ans chaque fois que j'écoute cette DAWAH mon coeur se raffermi d'avantage Alkhamdou Lill'Ah maa chaa Allah je vous serais toujours reconnaissante 💯une soeur en Islam
Je n'arriverais jamais à compter le nombre fois que j'ai écouté ce discours.😭😭😭😭😭😭
Yalla nako Brom bi samou
Une de meilleures khoutba c'est dommage qu'au Sénégal on néglige ce grand monsieur de l'islam ❤
Salam, c'est ce genre de discours qu'un musulman a besoin et plein de sens. Coran et Sunnah rek mo wor
Maachaallah
Quelle pertinence !
Quelle profondeur !
❤❤❤
Le Doctor Lô , une ressource immense plus reconnue hors de nos frontières que chez nous.Ma cha Allah.Réjouissons -nous et profitons de ses leçons .
Bilahi wakh gua lou wére
@@moussandiaye9707 je
Lou wér
@@africanpeople14707❤0i¹
The only people who disliked this video either did so mistakenly or they really need help with their current situation. Dr Mouhamed Ahmed Lo may the Almighty ALLAH protect, guide and you, your family and all those who follows the footsteps of the prophet Muhammad PBUH. And may the Almighty ALLAH soften the heart of all those who hate you just because of the truth you are spreading and I really hope that all those people will soon realize the love you have for them by always trying to show the the right path. I really love you and In Shaa ALLAH I’ll always keep praying for you and your family for protection, guidance and long life.
cette vidéo à parfaitement modifier ma vie depuis mon premier écoute en 2019 alhamdoulilahi
Voilà celui que les Sénégalais devrais connaître et écouter pour mieux comprendre leur religion malheureusement les hypocrite s'y oppose farouchement
Vraiment borom xam xam la ta kanggam la Macha Allah, noonou islam rek mookoyy bagne walahi ndakh diinei kessei mooko gnorr❤
Machallah oustaze mouhamad lo c incroyables
Moi j'ai le même maladie je suis toujour triste j'ai toujour la peur l engoise aider moi svp ça fait 3 ans
@@AissatouKane-iy8vvdél barilأستغفرالله
Ndeyessane je pleure djiadieuf ya oustaz
Jazakallah khair. Khaley yi di dem si mbeuk mi war nanio deglou kou melni ustadh bi Mashallah.
Allahou akbar Lila kilifa di diarigne yalna yalla defal la diam goudeul say fane inchallah
❤️❤️❤️Sope nagnla lol yalla nala yalla ak yonentam sope nouko raw dr
Alhamdou lilla
بارك الله فيكم يا دكتور شيخنا أحمد لو 🙏🏾💯❤️
Qu'Allah swt lui prête une très longue vie.
Ya Rabbi pardonne nous 😭😭😭 On seras jamais à la hauteur même si on passais notre vie à te remercier. Pardonne notre ingratitude ya Rabbi. Que Ta miséricorde accompagne nos vie.
MACHALLA YA CHEIKH SA DOUNDOU NDIERIGNE KESSE LA
Billahi serigne Ahmed LO Sénégal mô la réreu
Qu’Allah préserve notre Cheikh.
Alhamdoulillah hamdan kassiran tayban moubarakan fiik. Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Yallah n'a sunu Borom sam la docteur
Wallahi wahtane bi meunou ma thi doyal ça fait presque quatre ans damakoy déglelou bale sah dama dém beu métrisé ko yalna yalla takhawou cheikh bi bayyiko fi ay ate tou beuré beuri té. Mou ande ak wéer
ماشآءالله ❤
macha allah yallah nala yallah fay aldianna firdaws
Masha Allah Sheikh ❤❤❤❤
Alhamdoulilah, sukram ya Dr Lo
Qu'allah récompense notre imitent chéikh. Qu'allah lui accorde long vie avc une bonne santé. Amin
Amine ya rabbi🙏🏿❤️
Dieuradieuf
Amin Amin sa vie nous est utile
Barak Allahou Fikoum Ya Dr Mouhammad qu'Allah vous récompense. Dommage que beaucoup de nos compatriotes n'estiment pas Allah à sa juste valeur...
Aa
yalla nala borom bi fay (fa zakkir fa inna zikra tanfaoul mouminine) yalla nagnou yalla défal tawhid bou deugeur geuneu diss montangne yii amiiiiine ya rabbal alamine
Amine
AMINE
Amine mbokk mi
Moi j comprends plus la vie car je suis dépassée par les épreuves priez pour moi
Yalla n’alla yalla Faye yiw tè may la goudou fane
Docteur des esprits que allah te donne une longue vie santé pour tes enseignements 💯💯💯💯❤️❤️❤️❤️❤️
Amna solo trop yalna sounou borom maye la diam ak wérr thie barkéb serigne Touba
Allahou Akbar Macha Allahou yalla nala yalla fayi fatelibi amna solo Allahou Akbar xam xam li lay dierigne Macha Allahou
Un savant hors pair.allahou barifik
@@saneguifaye8292 maa shaa Allah
Yalna yallah samb'leu té barkel sa n
Doundou Dr Ahmed lo
Touchant tres tres touchant. Imane rek mo wore. May Allah give us plenty of it. This has to be one of the greatest bayan ever
Amin !
@@ndeyemariemefall4967 diagsakelhou
Amna solo. Dieureudieuf.
Allahou akbar ......... barakallahou fik
Ya Cheikh Que Dieu vous bénisse.
barakallahou fikoum papa yalna borom bi sameu leu tei yok katanbi fan wou goudou lô
ماشاء الله يا أستاذ محمد أحمد لو حفظه الله ورعا ه 💖💖🏅🏅🏅🏅
Qu'allah vous assiste yaa cheikh et qu'il vous laisse devant nous longtemps
Dr Ahmad lo ressource humaines la mais malheureusement Sénégal khamouniou ko mangui laye nianal ci sama khol yalna y allah samou.la goudeul sa fan yok sa kham kham ❤❤❤❤
Ma sha Allah baraka Allahu fik ya oustaz LO
Allahou Akbar.Djeum jii amouniou fayam yalna niou ko yalla fayam.yalna niou weursegueul ay borom kham kham you mélni mom
Mashaallahu barakallahu may the allmaity Allah bless you oustaz allahu akbar.
Sénégal 🇸🇳 li lagnou am nagnou ko téyé
والله ماشاءالله تبارك الرحمن ❤❤❤❤
Macha Allah! Dieureudieuf Lo. Amnasolo ak ndiarine lol lol lol.
Merci beaucoup on profite bien de vos enseignements
Machallah dr. Yalnala yalla fay yiiw toi barri té sakh ba faw.
Machallah y'a dr Ahmed lo
Yalna yalla goudal say fane wallahi douma doyal si vidéo bi sa youma koy dégguelou déy mélni Bou béss la yalnala yalla féy Dr Mouhammad Ahmad Lô♥️
Merci beaucoup que dieu nous protège et longue vie a toutes
Yalnala yalla samme aarleu
Masha Allah rafetna amna solo diaridiaf serige diaridiaf grazia thanks merci grazie yalla na yalla Yoko ta barkel Amin Amin amine ameeeeen
Que Dieu nous protege 😭
Macha Allah Dr. Mouhammad Ahmad lo xam xam na
Ma sha allah yalla nala yalla feye.
بارك الله فيك يا دكتور جزاك الله خيرا شكرا فذكر إن ذ كر تنفع المؤمنين، من دل على خير كفاعله اللهم زده علما ومدد عمره تبارك الله احسن الخالقين اللهم صل وسلم وبارك على سيدنا محمد وعلى آله وأصحابه أجمعين ببركة القرآن الكريم
Diadieff ya Oustaz 🙏🏾
Mashallah yalna yallah fayla Barina 😭😭😭
DiazakAllahu kheyran ya Cheikh Dr Yalla nala Borombi samm tè bayi la suniou kanam
Amal nga niou ndiarigne ! BarakAllahu fiik
Maa sha Allah amna solo JazakAllahu qayran yalna Allah goudal saw fan
Waxtane bi kouné warnaka deglou mane dé magui djoy djioyou xol Docteur yalna Yalla defal la goudou fane ak youw you bari
Mashallah oustaz
Macha Allah merci beaucoup
Yalnala Yalla fay yiw Oustaz
MACHA ALLAH ALHAMDOU lillAH
بارك الله فيك يا دكتور محمد
cette video me fait pleurai الله أكبر 😭😭الحَمْدُ ِلله
Maa Shaa Allah. Très intéressant et appaisant. Yalna Yalla fay
Oh c'es trise lougeur vie oustaz 😢🫶🤲🤝🙏
Dr lo; un bien commun inestimable
Perfect timing! Allahouakbar
Dr Mouhammad Ahmad lo ♥️🙏 Oustaz Mor Kebe ♥️ Oustaz Aliou Sall ♥️ Oustaz Oumar Sall♥️🙏 Imam Hassan Sarr ♥️ Oustaz Makhtar axirou zaman♥️ Tafsir gueye ♥️🙏 Oustaz irán nDaw♥️🙏 etc ....ALLAH tu as bcp d arme, encore une x ns aurons plus des arrgumment devan vous (Maliki nāshii) Au Jr dérniére 🙏😭
Qu'Allah nous guide dans le droit chemin
Machaallah Alkhamdoulilahi
Yalla rek ak yonetibi yalla na yalla mayniou degue degue 👉👂
Masha'Allah Cheikh bi , amna solo torop ! Barak'Allahou fikoum
Machallah très jolie conseil je vous aime
Amatina solo .beugnala lool y'a oustaz
🥰JAZZA KOUMOULAAHOU KHAYRANE CHEIKHANA
Yi moufti lawaraneka Sénégal
ماشاءالله 😭😭 حفظكم الله
Macha Allah docteur dieureudieufeti na Yalla fayla tu nous rappelles la bonne voie
Machaallah ya cheikhouna barak Allahou fiikum.
Machallah nous croyons a Allah
lo doundou doyoule ya oustaz yalla nala yala fay
macha'allah yalenagnou yalla maye kholoupe mougne..DR yalenala yalla faye
Koni ndaw gandal yalla mo mana maye kham kham حفظه الله ورعاه الشيخ دكتور محمد بن أحمد لوح
Yallah na yallah sama la bage nala guire yallah ♥️
ماشاءالله
Il est pertinent Machallah
Maa shaa Allah amna solo yalnala Allah fay la ta barkel la ❤❤❤❤
Mashalah, Jazaakumullah khayran, yalnala Yallah sam
حفظكم الله ❤️❤️❤️
جزاكم ألله خيرا يا شيخنا الدكتور أحمد لوه
Machallah ya cheikh Dr Ahmed lo
Machallah amna solo