Excellent discours du khalife en vers le président Bassirou Diomaye Faye qui représente l’espoir de tout un pays voir même un continent. Que le bon Dieu vous facilite le travail
Toutes les confréries qui se trouvent au Sénégal cohabitent par l'intermédiaire de notre art de vivre ensemble et le respect vis-à-vis de l'autre. Merci aux sénégalais d'ici et d'ailleurs.
Machallah Al khalifa contane naagnou si discours bi. Yalla na yalla goudeul sa faan weereul saay thieur bayilafi banga féké toutes les réalisations de notre très cher Président de la république.🙏🏾
Yalla mo dogal ap guissé. Bouniou faté sounou borom. Machalla lakhawla wala khouwata ilah Sénégal diem canam té weral khol yi ak thieur yi inchalla alhamdoulilah dieu merci
Machalla niass yalla yok weur gui AK katan gui nga yagg fi lool si barké werr Té yalla defal tawfekh sou nou président diomay Faye AK Sénégal bi gnou bok🙏🙏🙏
Ce Marabou Cheikh Mahi est charismatique et merveilleusement humble... C'est comme son Père Cheikh Ibrahima Niass...
Merci beaucoup ☺️
Excellent discours du khalife en vers le président Bassirou Diomaye Faye qui représente l’espoir de tout un pays voir même un continent. Que le bon Dieu vous facilite le travail
Si seulement tout le monde avait cette pensée. Que Dieu veille sur la réussite du projet.
@@TiTiti-oy9mr excellent discours
MachAlla quel plaisir d’écouter notre Khalife quelle éloquence ❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup Al khalifa vous aviez bien dit assurément yalna yalla goudal sa fane Khâdimoul Oummati ❤!
Amine
CHEIKH MAHI YALNA FI YAGUE TÉ WEER ,MASHALLAH , GNI BAGN TARIHA XANA GUISSOUNIOU SA MBAKH GUI❤❤❤❤
Quand.j.ai.entendu.le.khalife.parle.j.ai.les.larmes.aux.yeux.ey.way
Yallah.na.yallah.nagou.niane.amine
Lolou moma dale
Excellent discours
Toutes les confréries qui se trouvent au Sénégal cohabitent par l'intermédiaire de notre art de vivre ensemble et le respect vis-à-vis de l'autre.
Merci aux sénégalais d'ici et d'ailleurs.
Limoy Sénégal tei li lagn fi kham ana gni dôme saga
Il est éclairé ce khalif. Qu'Allah lui accorde une longue vie et une santé de fer !
Amine
Machalla cheikh Mahi sa discour Rafétte na ❤❤
Machalla un président respectueux et modeste 🇸🇳🇸🇳🥰
Le discours du khalife est vraiment mais vraiment responsable. Je suis tellement content et fier ❤
Dieureudieuf Niass
Tout dirigeant a intérêt à s'entendre avec les guides religieux de son pays.
SE Diomaye que dieu te préserve té oyofal yaneu bi🙏🏾niogui seu guinaww lo ameu rk seu yar ak téguineu moleu ko mayy🙏🏾
Amine ya Rabal Alamine 🙏🙏
Pr Diomaye yalla nala yallah défal ndam si lèp lo songou ak say gouvernement 🙏
@@3M84amine
Amine
Amine ya rabi # Cheikh Mahi mashalah ziarr❤❤❤
Machaalah Niass yalna yalla barkèl bijahi seydina Mohamad alayhi salatou wa salam
DiomaYe goudall fane rék yalla nala sounou samall bopame Macha allah
Machallah diajeuf Niass❤❤🎉🎉🎉❤❤❤
Machalla diomaye yalla nako yalla may ndam si barcké wér bou téde bi
Machallah Niasse wahdji maténa loole . Akk yéné bou selli bi. Yalla na souniou borome goudeul fane wi.maye la weure
Machalla discours pr Diomaye tegou na yone ake yare bi finga beugue Sénégal ague yalle nala fa yalla agale
Le couleur blanc lui vas à merveille
La couleur Blanche on dit. Dieureudieuf
Machalla niass coumba abdoulaye wakh gua lépeu yalla na yalla goudal sa fen Amine yarabi
Dieureudieuf macha allah alhamdoulilah yalla na yalla barkel ya rabbi
Macha alla chiekh😢 mahi waxji teeyna jaarna yoon❤
Macha Allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
merci tout les khalif senegal
Ce beau discours du khalilfa cheikh Mohamadoul Mahi yala samako longue vie santé de fer
Je suis layenne mais il est très éloquent machallah et très mesuré dans son discours yague fi lole te were niasse
Sama Dom"Baye bi ya bakh rek merci beaucoup❤lépp bénn leu❤❤❤
❤❤❤
Un grand intellectuel.Merci Dieuredieufe
Mashalla niasse wakh dij rafétna yalna nga fi yague té weurr ❤️
Très belle discours du Khalifa
Machallah discours Ceerno Mahdy Niasse
quelle discour du président diomaye mercis beaucoup monsieur
Machallah allham dourillah billay deyssane Niass kadou yii rafféte n'a lli moy Sénégal
.yalla n'a yalla dolli ssoutoura té ssame gnieup fall amine
Macha Allah ❤ amna solo lôl diâaradiëüff SR Mahi Niass 💟💟🌧️🌧️♥️🌨️🌿👂🙏👍👏💟🇸🇳🤲🤲🤲🤲💯
Machallah kadougui rafetna Serigne Mahi Niasse, khalifa
Machallah Niass longue vie à vous fière de vous beau discours
Un discours inspirant et responsable du Khalif. Yalla na diam yague Sénégal 🇸🇳
Il parle bien. C'est un bon marabout un intellectuel. Je suis contente de son discours
Masahallah Chiekh Mahi yalna yalla yok say fann bou andal werr 🙏
Que du bonheur❤️Al Khalif yalna yala mayla Goud fane ak wër incha allah🤲❤❤❤
Salam et merci Cheikh Mayi Niasse pour ce beau discours ❤❤❤❤❤❤❤
Machallah xolsedna loll way wakhdji amna solo loll yalla na nala fi yalla yagal té weral ❤
Niass Abdallah yalla na nga fi yagu té wér,Amiiiin❤❤❤❤
Amine ❤
Machallah mame mahi alhamdoulilah !❤❤
Pourquoi je suis tellement fière de mon président comme si que ma ngi soga am président ohhhhhhhhh 🎉❤
Billahi moma dall❤
dama foguone mane késsé makoy doundou❤
Machallah personage bi ande ak diomaye amnan yaaar trop
Bilhay
Personnage ndak
Dieredieuf PAPA MAHI NIASSE
Kaddouyi rafetna trop❤❤❤❤❤❤
Machallah Al khalifa contane naagnou si discours bi. Yalla na yalla goudeul sa faan weereul saay thieur bayilafi banga féké toutes les réalisations de notre très cher Président de la république.🙏🏾
Amine yarabi
Machallah way Niass amna solo tropp ❤❤❤
MAGNIFIQUE DISCOURS DU KHALIFE MACHALLAH ❤️❤️❤️
Al Khalipha dieureudieuf Niass ❤❤❤monsieur le président merci 🙏🏻 ❤❤❤
Bilhay papa mahi ya bakhe té oyoff niass goumba Abdallah yalla nanoula yalla fayale president diomaye diadieufe
MashaAllah NIASSE,
KHÔL YI SÉDEINA, KHÉL YI DALNA.
DIEUREDIEUF NIASSE
Cheikh Mouhamadoul Mahi Cheikhal islam Elhadji ibrahima Niass❤
Yalla mo dogal ap guissé. Bouniou faté sounou borom. Machalla lakhawla wala khouwata ilah Sénégal diem canam té weral khol yi ak thieur yi inchalla alhamdoulilah dieu merci
Machallah amna Solo ♥️♥️♥️♥️🌷🌷♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Un discours plein de sens . Une participation aux aspirations du président !
Merci beaucoup alhamdoulilah 😊
Alhamdoulilah yalla na yalla barkell
MACHALLAH DIEUREUDIEUF SERIGNE MAHI NIASS AMINEEE 🤲🤲👏👏🙏🙏❤️❤️❤️✅️✅️✅️
Machalla niass yalla yok weur gui AK katan gui nga yagg fi lool si barké werr
Té yalla defal tawfekh sou nou président diomay Faye AK Sénégal bi gnou bok🙏🙏🙏
Machallah serigne bi
Masahala al Khalifa chiékh mahi niass khadimoul oumati
Mais merci président
Merci cheikh al islam
Amine pour ces prières 🙏
Amine ya rabbi ❤❤❤❤
Dieureudieuf niasse ziar❤❤❤❤❤
Amiiiine Ya Rabbi
Niass ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machalla président Diomaye ❤❤❤❤
ماشاءالله حفظكم الله ورعاكم
Machallah khalifa Niasse bi ❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup président bassirou diomaiye Faye ❤️ bonne continuation manchalla 💕
Machalah sa yaar bi dou yaaru Mikar ❤
Machallah Yallah deff diamou
AMINE. DIEUREUDIEUF YALNA YALLA DOLLI SOUTOURA, AARR SENEGAL.
Amine
Cheikh Mahi parle avec le coeur ❤🎉
Machalla am na solo ❤❤❤❤
Machalla ❤❤❤ amine
Un président respectueux avec beaucoup de sagesse
Cheikh Mahi mbaakj rek laa guis si moom
Dieuredieufety niass
Manchalah cheikh bi wakh dji rafféte na yalla na yalla nagou sa niane serigne bi 🙏🙏
Beau discours du khalif mashallah
Seydina Ousmane sonko mousélmi nitou yalla deugu la té beugu réwam détérminé khékh ba projet bi aboutir sénégalais yépou guisi sén bopou machallah mominou tanal jitou réw boumat téyarou yiw téy bakh taleu té beugu réwam diokh niépou thiéreu kilifa diné yépou
Bilahi wakh ga Deugue
Sa wakh tafétena
Wakh dji rafét na machalla ❤❤
Machallah kaddou yi refet na ❤❤❤
Machalla alhamdulila un discours pertinent et cohérent en vers le président de la République Bassirou Diomaye Diakhar Faye
SONKO mooy DIOMAYE ❤
Machalla discours cheikh mahi yalle na yalla goudeule faname maye ko weure
Dieredieuffati Mame Baye Niass cheikh makhi Niass cheikh khal Islam Niass yaggeu fi lol ta andak wér amine ya rabbi 🤲🇸🇳✊❤️❤️🙏🙏
J'aime ce khalifa ❤
Danga goré rk walahi ❤
Adouna billay wollay doudara Dieredief yalla ❤❤❤❤❤❤❤❤
macha allah amiiine Niass
Prési yalnala yala may ndam ba faw si Sénégal cheikh mahi ya bâkh walahi
Félicitations pour vos efforts continus pour améliorer les conditions de vie au Sénégal. Continuez sur cette voie
Merci beaucoup❤❤❤❤❤❤
Machine Khalif by defna discours kilifa ❤