Merci Serigne bi leeral nga lou bari la leundeum si bopp nit yi ndax djine batou arabe الجن kon logique na mouni rap ak djine man na nek beneu wolof di wax rap arabe ni djine
Wallioullah ou Awliya shaytane. Djinns ou humains on est bon ou mauvais. Le reste c'est de la littérature. Choisis Allah, obéis et tu te mets à l'abri. Laisse les interdits.
Sidy makhtar sylla ñianalal le honorable président macky sall pour mou gagné élection 2024 yii SVP. Sans macky sall le Sénégal ne peut pas développé ni émergé toutes la jeunesse Sénégalaise son derrière Macky sall pour le développement durable des sénégalais merci de vos compréhension
Ma defei nei ayy souf, ndox, safa, ngelaw yoyu ayy bidew leu ? Tei a ma connaissance rawhan, du ku nekk mokayy am nittu yallah bu borom bi thieureulei deug mokayy am. Niom nio gui thiossano ci tokh tokh ndokh yoyu di juugei ci Djibril guinaw sangom ci benn ci guediu yallah yi ci lagn bindei rawhan
Ki môme yalla moko yare talibé serigne touba la
Oh serigne sidy kouko deglou khamni il maîtrise teksi djiteul yalla machalah
Merci Serigne bi leeral nga lou bari la leundeum si bopp nit yi ndax djine batou arabe الجن kon logique na mouni rap ak djine man na nek beneu wolof di wax rap arabe ni djine
Thiey kham kham amna machalla ♥️🙏🙏
Sidy makhtar dafa Diangu trooop kou wedy demande à tounkara 😁😁
Antitounkarisé 🤣🤣🤣
Dotouko defati
Kou tëyla te yarou Macha allah
Machalah kham kham bounioukoy wakhe daye nekha deglou day yomba khame yalnako yalla yook
Manchalla le gas en blanc il metrise vraiment se k’il dit force a toi ni la Serigne di mell
Machalla makhtar Sylla dama nkh dafa yarou
Explication bi dafa lérrr nagne Talibé mourid dafay yarou com ki
Dalna teyna
Machallah bisou vraiment li amna solo
Je l’aime waye Machalla
Salam aleykoum maitre! Svp On aimerai avoir les prochaines vidéos en français
Mais qui il est vraiment patient
Outaz modou fall khamna dine mais khamousi dara maîtrise woko
En tou cas limou fi wakh khel meuneuna ko dégu
Vrmnt ki yalla maynako machaalah, dafa métrisé limouy wakh bolesi dal , wakh Ndank, explication bou ler goudeul fane♥️♥️♥️
Mashalla serigne bii téeyna troop.
Kou bahe yarou
Am munas from gambia I really like the man , please b exten my greating to him yayi salieu Njie munas mu tamsir Njie from gambia, I need this man
but why don't you speak wolof to maybe his companion they can hear you but when is any come to English few people in Senegal speak English
Wallioullah ou Awliya shaytane. Djinns ou humains on est bon ou mauvais. Le reste c'est de la littérature. Choisis Allah, obéis et tu te mets à l'abri. Laisse les interdits.
Dorrrr Kat leu. Lèk na sama khaliss, dieuleutoul samay appèl. Walahi
Leral lal,
Deye doul kéna lekoul sa khalisse bayil doul te ragal yalla
Sa leufeul yaye ismala. Sa Cheikh bi khamoul gatt, saysay leu, tèk deal. Sèn badio yay
Mes sincères respects Sylla
Billahi ki dafa yaro loull sakh ak kham kham bo sell bi machalla
Ma cha allah
Machallla ❤️❤️🙏
Salam alaykoum quel pour me dire ce qu'il dit en français s'il vous plaît ?
Wakh dji dall na macha allah
Sidy makhtar sylla ñianalal le honorable président macky sall pour mou gagné élection 2024 yii SVP. Sans macky sall le Sénégal ne peut pas développé ni émergé toutes la jeunesse Sénégalaise son derrière Macky sall pour le développement durable des sénégalais merci de vos compréhension
Doul rék 😂
Mdr mdr mdr mdr
MachaAllah amga yar amga teguine
Djine mbindéf la monou mana guiss thi ay bat rab kén douko guiss thi ay bat
Nice na
Respect
Macha alla bizou
Serigne bi yarouna déh
Ma defei nei ayy souf, ndox, safa, ngelaw yoyu ayy bidew leu ?
Tei a ma connaissance rawhan, du ku nekk mokayy am nittu yallah bu borom bi thieureulei deug mokayy am.
Niom nio gui thiossano ci tokh tokh ndokh yoyu di juugei ci Djibril guinaw sangom ci benn ci guediu yallah yi ci lagn bindei rawhan
Bijou mo diongoma machalla mane dafma nekh rek te yalla takh
Macha allah
ya pas en francais??
Buzou man Mauritanie
I love you serign b macha allah
Ki dalna sheut❤❤❤❤🎉🎉
Ab bokaalékat bou sett wecc niyeenla rek mounaanma hàatim Souleymane alaihi salam Ragalén Yalla té Jaamou'ko baay Serigne yék Jiné yinguéndi Jamou moo gun siyeen niou naanma daa Yarou Youssou N'Dour ambassadeur Iblissla denguén ham kouko gueuna Yarou?
As salamou aleikoum rawhane mome lagni woowé énergie spirituelle
Très élégant....
Ayywaayy Bijou invitéle Oustaz Aboubacar Sow mii DTV invité woone temps yii si émission Gudu gii ...moo taanéwoone je pense Oustaz Beuzz mii tookfii
Koone bilaakhii guënn dëgg deugg piiirrr
Serigne makhtar sylla borom xam xam 🤣🤣🤣 ani tounkara
rab wolof la djinè di Arab
👍
He is perfect , what he is saying is very clear, number please from gambia
Add me one Facebook sylla cartésien
Ki Mome machalak nako Yalla same
Bijou pour koi do inviter oustaz mor kebe ou oustaz omar dieng face a ces charlatan?????
Wa kou beugua kham sa rawkhane
Khaham boulére lafi dégue kidaware di wakhdé
Mais est-ce que Rawhane dagne koyy guisse ?
Sénégal réwou thiakhane va travailler petit paresseux en grand moubou Paul kagame vien au senegal mettre de l'ordre que des futilité
Katal ndeyam feulé bulshit
Wa serigne bi kou ame numerome? Sokhla nako dé
Mais est ce que Rawhane dagne koye guisse
Bijou apprends à t'exprimer.
Raw amoul dione moam ak rawhan ak khodam
What is his number
Toi tu as compris
Machalla lérr na te andak téguine oustaz modou fall ya soof go🤣
Bi
Yaw na borom kham kham ga machalla waye rap amoul dione moam
Bizzou woma
Yaw fo todj niéménga diambarlo
Ma todj ma gnew fofou
Bijoux mi séytani la déy diakhsé nitte yi .gnomm niépp islamique laniouy khékh .bijoux bilay dara khamoko
Toi ftg c’est mieux on force personne à regarder
Hhhhhhh Sénégal mo Bari ay nakhaté Kat ki khamul gat
Bilahi senegalais comme mouton topou khetou niit yi nga kham ni lou gni waxxx yeup ay naxater la
🙉
Ok
Ou se trouve rawhan ds le coran ou ds les hadith du prophete swl
Demal soratoul djini
@@abdoulayendiaye745 Wa rawkhane loumoy def
Nawsy nopil xamoghie dara
Machal buzou
Modou fall pou koi tu le dit ce que le prophet a dit sur ce que dit ce ndiabarr kat
Djine Moy rap rek djine arabe la le mot rap wolof là.
Mane silaye ligeye
Oustaz bi di manieru doyna war dale
😂😂
ki deh xamoul dara dafma arnaqué
@#Madjiguene_Gaye loy wakhni tiakhano 😒
@@jrpp6617 Je te jure c'est pas des blagues
Bimou né djinné ak rahwane bene leu la thiii paré
Ouztage modou Fall mi geumoull dara djiguénn rek lay wakhtané safouma dara
Ndakh djiguène moy leep, té sénégalais yi djokhou gnou thieur djiguène, il faut les sensibiliser davantage.
Sénégalais mettii kii amoul sa temp
Sénégalais mettii kii amoul sa temp
🤣
😂😂😂😂😂
Asalamou aleycoum je ne suis pas d'accord nit déy ame rawkhane bou wera wear wer
771369173
Wolenma
Yw fo tothie
Yalla bou tayalone dou dinde.fell🤔
@@babacarniagne8559 manam thi lane
Yalla bougoul kouye tonie bayima gnir yalla
Machallla ❤️❤️🙏