BAYEFALL d'où toukh,d'où mooy,d'où fén,d'où soussou,d'où NANE SANGARA,d'où féen,d'où dieuw,d'où togn té kouko tooogn mou Baal laa...nguir yallah bayilén Di mboubo Bayfall Di yakk souniou déerr..défois NGA guiss ci mvédd bi kou nék ci louko néx Di yalwane NANE Bayfall laa té limou am dieundé yamba,cigarette MBA SANGARA ...Bayfall dafay Sakho ndiap,Di sikzr tourou yallah Di liguey dimbalé AK jang alkhourane
Arbitre dafa siflet démal lathié Jules baldé confirmè na lolou mém lisse thiahabale nako 😅 ...lima beug moy mou entraîner woute dolé ak condition physique...bouko talfa dané insha alla niou hamenii dane na mbeur...mes état de forme bi mou yore bouko talfa dané daniouye nane pakola dafa bléssé wone 😅😅😅
@@AboubacryGASSAMA-zs7oi way ioe bayil nakh sa bopou ta niou waxanté deug mounane Jules 😅 ki niak srx rek lay dioy si mome sinon amoul moromame bouko teuu talfa moma nguéne wara wax mou nek si bopame wa salam
Bagne teugué combat bi ba légui yangui weur Di wahe 😂 rk dangua titte insbi khamo fo dieum démal entrainé mo geune sa takhawalou bi fougne tourné guisse leu geumeul sa bopou wy gameur bi mou Nieuw dh 😂💪
Boye yangui pockalairou rk Dalbou bi d'où boyi kéne Lou lérre bo yakaré né daye yomboul boul nieuw stade sa kaname gogou ngaye diohé dangua dieulegoul kou bo wara dieul rk déll ndéllou rk 😶
Lou leer Poko kén dakkoula mbeuré ci boy yi💪🏾💪🏾💪🏾
koula fararoul sakh xamni champion nga man talfa la faral mais li grand yi ame si lamb meun'ngako ame tabakhal mére bi galai .
Pokola pokolaaaaaaa 🔥🤣💪🏾 fit bé deugueur yokatal treune yii rek yallah bakhna
Pokola grand champion le futur de pikine ndam rek Inchallah🎉
Pokola seul mbam bi ❤❤🎉🎉❤❤talfa beug khèkh bagne khèkh
Amal jam rek mbeur 🎉❤yok entrétement yii
Pokala.chapion.dina.bakh 😢😢😢❤❤❤❤mashalla
BAYEFALL d'où toukh,d'où mooy,d'où fén,d'où soussou,d'où NANE SANGARA,d'où féen,d'où dieuw,d'où togn té kouko tooogn mou Baal laa...nguir yallah bayilén Di mboubo Bayfall Di yakk souniou déerr..défois NGA guiss ci mvédd bi kou nék ci louko néx Di yalwane NANE Bayfall laa té limou am dieundé yamba,cigarette MBA SANGARA ...Bayfall dafay Sakho ndiap,Di sikzr tourou yallah Di liguey dimbalé AK jang alkhourane
Bilaih deugue leu
Kone d baye Fall amoul
Gnima guiss ni kene doussi baye fall
Néll Baye Fall yomboul bayilen saltel,@@papadaoudathiam3903
baye fall dou jugé nitt gaure dou yor djiko djiguéne
Pokola bougnou fonto respectel nitt yi entreiner réussir dimbali sa yay
Talfa ❤
PokoLa á vie ❤️💚
Talfa guémeur bi seul pokola sa data yaye ⚔️🗡️⚔️🗡️
Talfa bou dieulé kou droit pokola di teud bilahi ❤🎉
Talfa kholou la sakh gua nek fi di talakhou rek Game bi daf lay dal force bilahi walahi
Démal entraîner djii yaw meuno dane sakh lisse ndiaguo .té walahi lisse talfa d'où tahaw ak mom .démal woutii dolé ak confre bou doye talfa inshaalla bén voyage lalaye déf
Ya résumé li ba tokk ki niouss liss mou sincome mounane dane 😂
Arbitre dafa siflet démal lathié Jules baldé confirmè na lolou mém lisse thiahabale nako 😅 ...lima beug moy mou entraîner woute dolé ak condition physique...bouko talfa dané insha alla niou hamenii dane na mbeur...mes état de forme bi mou yore bouko talfa dané daniouye nane pakola dafa bléssé wone 😅😅😅
@@AboubacryGASSAMA-zs7oi way ioe bayil nakh sa bopou ta niou waxanté deug mounane Jules 😅 ki niak srx rek lay dioy si mome sinon amoul moromame bouko teuu talfa moma nguéne wara wax mou nek si bopame wa salam
@@ibouciss3519 talfa d'où lisse ndiaguo 😅nél sa mbeur mou dém entraîner djiii woute dolé té bayii milieu 😅😅😅
iow esque cv
pokola defal yefou bay fall defoo KO dh way iunchalla dan lay dan nak
Ki fiite bi rombou na bou talfa bi dou yoyou ❤
Lolou lagnou khamoul si mome
Fite beurei woul
So amoul fiite noy dieulé yeneu coup yi
Fitt kecei dou beurei amna fitt wayei doff leu tei tekolein feinn ni mo eupp talfa fitt nitt day yewou
Lèn deh xam nako sou entrènè mo meun fouki talfa kou dane gackou 2 boul lal lisss😂😂 way way
Yaw doff yi gaye wakhale dé loumou lathieu rk day giém si DH borbi dakoy Faye rk cambéréne seule❤❤❤❤❤
Amna fiit mais entraînement bi desna troppp
Pokola seul ❤❤❤amoul lénnénne ❤❤❤❤❤❤❤❤pokola késsé défaral boy bi bagage niou dokh dém🤌
Tall fa ay wakh danou ko de lolou de xamna ko insbi danga late trop poko gayi daniou la beug kon demall nga ligueyi
Entraînement rék moo woorr
Demal entraîné dji té bayi banditisme amoul chance hol si ama balde
So gorgorlo ame sa diome dinga ame dara
Mann baye Fall la 😂😂 bandit bi
Pokala na Bayi di mouro Bay Fall yi.
Bay fall la motakh mou nekh ma❤❤❤❤
Baye faux la mais pas baye fall
Pokola sa forme bi tamite
Talfa à vie❤❤❤
Bayil bandit bandit lou mbeur nga
Talfa seul
❤❤
Sa 10000 data yaye talfa seul ❤
Bathie séras la cuisse dé. Ki dou dém fénn. Bandit dou réussir si l’ambiance ji
Bayil di nane baye fall la ba paré di def linioulayy khébé
Ça fait longtemps parce que pokola et blessé
Guayis nak lolou lagnou khamoul motah gnouy wah rek
Pokola seul 💚❤️
talffa mogui bambilor mogui liguiyé billahi
Talfa seul
Pakola Del wakh rk yaw
Barry wack boy bi
Gnemer woudou woudou Lou
Pokola daye dane talfa
Ki day souss wakh mé talfa moko meunn aller retour
Pakola yaw danga wara khamni champion nga bayil yenayi leulou di entrainer deuglou say ndidiaye te bayi yena andando yi
Bagne teugué combat bi ba légui yangui weur Di wahe 😂 rk dangua titte insbi khamo fo dieum démal entrainé mo geune sa takhawalou bi fougne tourné guisse leu geumeul sa bopou wy gameur bi mou Nieuw dh 😂💪
aka meuna beuré dafa tothie mbapate certe des fois xalé mokoy gagné
Do dedieuwe ndayame
Leneu Dei xamal Nalénko
Guisouma Mbeur Bouko Fith Senegal 🇸🇳bou respecte Treune Dou yoyou sax✍️✍️✍️
Barké sérigne touba pokola mo eup fiit tatfa thii guèw , en plus mo dakh beurré, problème bii moy est ce qu'il va respecté les entraînements 🙁🙁
Pokola danioula beug mai d'email entraine
Pokola demale entrainè bayi wakhdji akk weur dit Mandi rkkkkk yaw akk ada fass niakk diome rkkkk
Talfa Dina dokhane sa ndaye
Wa saway fasson wat bou neke wat nako😂😂😂
Mbeurrr barkep dabooyy mame sayy Ndiaye boyyy entrainelll beugu nala trop mais après combat bi demalll 4:11 guadayyy liiii doyoulll dh❤❤❤❤
Dou gnow ngeu P.A gnou souslo lène yak sa papeu Ada
Baye fall dou naye sagara ❌❌
Beugu metti n'a poko après émission bi boul guéneti danio soxla lamb dji😮kén Doula wax way
Pokola seuls
Poko èhh buzzu talfa nga atanoul daley game P.A seul
Pokola mi joueur la wala mbeur ? 😂
Boy bi, il est à l’image du Sénégal : indiscipline et ignorance. Domerame yiii. Fallait stériliser les parents. Dokhane sen ndeye.. mounane baye fall
Bandi amoul kii baye fall
Khôll ko ak niaway bi
Kou meunoul daneu Liss do daneu talfa Boulen nakh sen boop
Talfa kassé ❤
Talfa day dan sa data yeye
Talla boko yabé dala sori ioe kén doula wax kouy Tal 😂
Pokola seul talfa do dara daguay yorou fi gua yoorou youssou ndour sa lokho damou😂😂❤🎉
Ya man Say morom yep lou ler way daga wayoul daga wara nex nit
Boul raggal dra rak sama
Demal wouti doly té bayi sa wakh diobari dji
Ki défa rew très indispline très impoli yawe deguay yakh tourou falay balde,,,Say nidiay dégno yarou am discupline kéne doulene DEUG thiy darra Lou gnak fayda poko mban
Boula talfa diapé di nga xamni lèpp deug leu
Talfa seul 👌👌
Louga la deuk mais pokola rk lay topou 🎉
Boye yangui pockalairou rk Dalbou bi d'où boyi kéne Lou lérre bo yakaré né daye yomboul boul nieuw stade sa kaname gogou ngaye diohé dangua dieulegoul kou bo wara dieul rk déll ndéllou rk 😶
PIKINE niogui sa kinaw Dey moytou rk frère
Mais wadji lou nék wahnako cii pokala ci lou bone 😂😂thiey lii
Boy Demal entraîner li dou formé mbeur
Kii dou mbeur talfa mola gueuneu mbamé foufe
No boy bi gaka way nekal nit way boy xamal sa bope way
Demal entrainé t bayi millieux millieuxkham nanou lifa nekh thiaga ag sangara gno nk si barr yi gnak ngen coseil trop
Gueme kassé gnou dem
Wat yi pour lan la
Dangadon yorou rk wayè yangi dougua yapp nk am nga problème
Bi yagana way
Boula talfa dalbou bi diape dina GAME sa ndaye
Talfa seul
Talfa la mane fouf
Sa beut yi soulou yi, apparemment il a fumé des joints,dou dane kéne.
Vidéo bi yague na dmrm yi bayiléne doul😂
Danga wara neik nittt deim entraîner bayi taxawalou bi
Yow talfa Daf laye lek yagui toutini
Doleee beutt d'où ko guiss
Ki talfa dakoy lekk 😂
Talfa yorou rék la meune dou lénéne 😂
Yalla Bakhna
Iow do mbeur deh bro🎉nekal fii mandi rek🍾🍹ngay dull😂talfa mo meune sax ama balde
Talfa daléy guème
Amo doole Beuri nga wakh 😅😅
Pokombam ndeye seul ❤
💯💯💯💯❤❤❤❤❤❤❤💪💪💪💪💪💪
Yaw talfa mola meune fouf dou combat
😂😂