Assalaamu alayka Tidiane. Dama begone nga laadjalma Cheikh abdoul hamid ''yalna Sunu borom yoku fanam ak wer gui yaramam''. Damaye liguèye philip morris moye figniye defaré cigarette. Té dama djeul wird.. Lane laa wara def. Ma bayi ligueye bi, wala ??. Djeredjeuf
@@mberyniang3962 Sénégal nga nekk walla ? Bala dara khew moom fok niou deugou souniou biir tee waakh nii cigarette dafa haraam bou graw sakh. Mis à part tariqa diiné d'abord moko teré, ensuite tariqa cheikh feedaliko. Une question : est ce que amnga feenene foo mouna ligueyy ?
@@Ndaar-Faam deug bu wer peng nga wakh. waw mangui senegal. Moye usine cigarette bi nek pikine si rond point bi. Waw mane dé dama niwone khaaral ma diap ci lii ba keroke sama recrutemen fonction publik di guene motakh mafaye ligueye nii
Il n'y a pas de grave mbok mii. Car les sénégalais font trop de folklore et CHEIKH SAYYIDIL HAADJI ABDOUL HAMID son objectif c'est justement être hors de ce type d'agissements et aider les gens qui le souhaitent à se rapprocher de ALLAH. Donc le plus important c'est d'écouter les fichiers et appliquer ses enseignements et inchâ Allah tu ne le regretteras pas.
Dangay dayy 🤣🤣🤣. Kouy deff safara dou mell nii mom. Takk plus de 4 diabars dii ndiaalo layla wa nahara ba paré wooté ay maqaamates kokou moo yell ssi safara.
C'est parce que tu ne comprends pas et tu ne connais pas l'histoire ! Donc contente toi de demander explications. En effet CHEIKH AL HADJI MANSOUR SY A EU AFFAIRE À CES GENS ET IL LES A REMIS À LEUR PLACE DONC LE CONTEXTE NÉCESSITAIT DES ÉCLAIRCISSEMENTS ! Et puis tu es un ignorant ou alors tu es complètement à l'ouest, pour te permettre de dire qu'il divague ! Il ne s'agit de divaguer mais il s'agit d'éclairer une situation pour que les ignorants comme toi sachent ou comprennent mieux ou découvrent et décident où mettre leurs pieds. Cordialement
@@mamadoutourre4318 Bien sûr il faut saga : { Wa diazaa-ou sayyi-atine sayyi-atoune mislouha...} Sourate 42 aya 40 kholal saar bii A-choura. Kou diayy rewandé niou wonko rewandé kou wonné ndiék ak yarr aussi niou delloleu lou ni mell. En gros on s'adapte 😀😀😀🤣🤣🤣🤣.
@@Ndaar-Faam nite daggay ame personnalité mano di dougueul lou ame solo. De retour di saggani il faur apprendre a ignorer certains messages negatifs. Bayil sagayi ga nek si ligga nek.
@@bggueye4828 BG Gueye bou khamoul dangay laathîé ! Attention ne pense pas que tu es plus consciencieux que les autres et te permettre de placer en moralisateur ! Je sais très très très bien ce que je fais et comment parler et répondre également ! La personnalité ne s'acquiert pas avec du bla bla comme tu le penses à tort ! Vu que tu n'as pas compris le sens du ayaa que j'ai cité en phonétique je te le dis autrement : Serigne Babacar Sy a dit :{ bouléne diangue wokh mais diangue lènn tontou, lo nek nitt beugko yakh walla soofantale Défendre sa mbir nala diaral lou eup limko diaral pour yakhko} . Ou encore BG gueye il faut savoir s'adapter, en français l'intelligence est définie comme étant la capacité à s'adapter à toute situation ! Nitt doo nekk yaram dongue walla sokhor dongue. Ibn mouhayyab bi mouy tagg Yonenteu billa gueun gueun meu gueun sa baaye yow BG gueye ak sama baaye, neena Yonenteu saws parfois dafay baakh waayé parfois houuuuu dafay tang dieurrrrr ! Donc bou nitt wonné wee yarr ak téguine il faut absolument le lui rendre en mieux ! Mais koula khossi matt koo bamou nathieu !!!!! Wa salam
aka bagne serigne touba té meuna wakh lou niaw kou milni moussoumako guiss avant hier lay soga deglou audio wam mais dama diommi si naka la kouy wakh si diné di dieuwé ay dioulit ni moom En plus mouné talibé mame dabakh mingua khamni zero faute
@@Ndaar-Faam no loy ragal bo nieme bayi thi commentaire bi mame abdou aziz sy dabakh buniy khol entre sarr wala cherif kou mu guena ndirou nieup danu nann cherif la guena ndirou
@@Ndaar-Faam bettouma cii yen fen ak saga lalene domeram j diangale tel père tel fils.mena saga sa ndaye ak ak ndaye Serigne. Mais grawoul nagne wax cii xam xam .b
Machallah sy malik ken dou seydil Hadji malik sy amoul morom yalla nanouko yalla fayal is barke seydina mouhamad ❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🕋🕋🕋🕌🕌🕌🕌
La ilaha ilallahu mouhammadou rassoulillahi.
Allahumma salli alaa muhammadinin nabiyyil ummiyyi wa-ala aalihi wasallim tasleema. Amin
J’ai commencé à le suivre récemment et franchement je le nomme le général défenseur de la tarikha tidiania
Momm leu kayy. Maa cha Allah.
@@Ndaar-Faam salam kou baakh ki sognou meunone bakhè wakhtan bi Serigne bi def si Tafsir sourat Youssouf
@@papagassama956 Wa alaykoum salam. Dinagn ko dougeul inchâ Allah.
حفظك الله ورعاك وأطال بقائك ياشيخ الحميد وريث القوم
Yalna yallah dimbalila
FAYDOU CHEIKH OMAR FOUTIYOU LE
Macha ALLAH . dieureudieuf sérigne Abdou Hamid Sarr
أطال الله عمره ورعاه ءامنين
Thieuy seydil Hadji malick dieureu dieuf sarr
Ameen YA Rabi🙏🙏🙏💕💕💕
Yalna sama Borom dimbali la
Machallah
ESKEYYYYYYYYY CHEIKH SAYYIDIL HAADJI ABDIL HAMID. MOY SANGUE BOU FESS DÉLL, MOY PONKAL, MOO SELL, MO BAKH ESKEYYYYYYYYY. YALLA NA SOUNIOU BOROOM FÉKH AW FANAM BAMOU DIOTT 100 ANS. AMIINE
Assalaamu alayka Tidiane. Dama begone nga laadjalma Cheikh abdoul hamid ''yalna Sunu borom yoku fanam ak wer gui yaramam''. Damaye liguèye philip morris moye figniye defaré cigarette. Té dama djeul wird.. Lane laa wara def. Ma bayi ligueye bi, wala ??. Djeredjeuf
@@mberyniang3962 wa alaykoum salam mbokk mi. Kagn nga commencé liguey fofou avant walla après ngay djél wird ?
@@Ndaar-Faam apré bima djeulé wird laafa cmencé ligueye
@@mberyniang3962 Sénégal nga nekk walla ? Bala dara khew moom fok niou deugou souniou biir tee waakh nii cigarette dafa haraam bou graw sakh. Mis à part tariqa diiné d'abord moko teré, ensuite tariqa cheikh feedaliko. Une question : est ce que amnga feenene foo mouna ligueyy ?
@@Ndaar-Faam deug bu wer peng nga wakh. waw mangui senegal. Moye usine cigarette bi nek pikine si rond point bi. Waw mane dé dama niwone khaaral ma diap ci lii ba keroke sama recrutemen fonction publik di guene motakh mafaye ligueye nii
Jari jaff
Sarrrrrrrrr
thiey chiekh Abdou hamib Sarr
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mabaga mama Mansour sy
شكرا
Merci
Guddël fann Serign Abdul Hamid Sarr 🤗
Amine
حفله الله ورعاه ءامين ❤❤❤
El Hadji Hamid yagueu fii loll tei andeuh ak weir🙇♂️🙇♂️🙇♂️
Ma beugue mame maodo bilahi ma beugue seydil hadji malick ak kep kou bakh waye beugue ba mame maodo si sama kholbi
Bilaye mane dama sope mame Hamid sarr souféké amna groupe ma doikhé sa numéro
Il n'y a pas de grave mbok mii. Car les sénégalais font trop de folklore et CHEIKH SAYYIDIL HAADJI ABDOUL HAMID son objectif c'est justement être hors de ce type d'agissements et aider les gens qui le souhaitent à se rapprocher de ALLAH. Donc le plus important c'est d'écouter les fichiers et appliquer ses enseignements et inchâ Allah tu ne le regretteras pas.
@@Ndaar-Faam Serigne bi foum deukk mome??
Ignace moo taakh mou teekheedii feene rek layy def
Sokhoorr nakk
Hamid sarr tooj kat nga soo tuubul ba dée dem sawara
Dangay dayy 🤣🤣🤣. Kouy deff safara dou mell nii mom.
Takk plus de 4 diabars dii ndiaalo layla wa nahara ba paré wooté ay maqaamates kokou moo yell ssi safara.
@@Ndaar-Faam tu m'as tué
@@Ndaar-Faam domou thiaga pire ga
@@lunelune8872 ah walla bokk daniouy diaay reew,😂
DÉFENSEUR DE LA TRIKHA TIDIANE
Kouko deglou mome dagua yeugue ni kham khame bouy dokh la
J'adore écouter sa causerie mais il ne parle pas du thème mais divague un peu trop qu en même. cordialement
C'est parce que tu ne comprends pas et tu ne connais pas l'histoire ! Donc contente toi de demander explications. En effet CHEIKH AL HADJI MANSOUR SY A EU AFFAIRE À CES GENS ET IL LES A REMIS À LEUR PLACE DONC LE CONTEXTE NÉCESSITAIT DES ÉCLAIRCISSEMENTS ! Et puis tu es un ignorant ou alors tu es complètement à l'ouest, pour te permettre de dire qu'il divague !
Il ne s'agit de divaguer mais il s'agit d'éclairer une situation pour que les ignorants comme toi sachent ou comprennent mieux ou découvrent et décident où mettre leurs pieds.
Cordialement
@@Ndaar-Faam naniou deff niane lol reponse bi leerna, correctena, polina, te diss. machaallah
kii doul rék lay déff di nioddi Aÿ makhama di sakéto mame MAODO doul rék lay déff
SA BADIO NDAYE 🤣🤣🤣🤣🤣🤣😀😀😀
Diaroul saaga mé moy todie sen yol yi dilen khamal ☝️sen mousiba baye yi 🤣
@@mamadoutourre4318 Bien sûr il faut saga :
{ Wa diazaa-ou sayyi-atine sayyi-atoune mislouha...} Sourate 42 aya 40 kholal saar bii A-choura.
Kou diayy rewandé niou wonko rewandé kou wonné ndiék ak yarr aussi niou delloleu lou ni mell. En gros on s'adapte 😀😀😀🤣🤣🤣🤣.
@@Ndaar-Faam nite daggay ame personnalité mano di dougueul lou ame solo. De retour di saggani il faur apprendre a ignorer certains messages negatifs.
Bayil sagayi ga nek si ligga nek.
@@bggueye4828 BG Gueye bou khamoul dangay laathîé ! Attention ne pense pas que tu es plus consciencieux que les autres et te permettre de placer en moralisateur ! Je sais très très très bien ce que je fais et comment parler et répondre également ! La personnalité ne s'acquiert pas avec du bla bla comme tu le penses à tort ! Vu que tu n'as pas compris le sens du ayaa que j'ai cité en phonétique je te le dis autrement : Serigne Babacar Sy a dit :{ bouléne diangue wokh mais diangue lènn tontou, lo nek nitt beugko yakh walla soofantale Défendre sa mbir nala diaral lou eup limko diaral pour yakhko} .
Ou encore BG gueye il faut savoir s'adapter, en français l'intelligence est définie comme étant la capacité à s'adapter à toute situation ! Nitt doo nekk yaram dongue walla sokhor dongue.
Ibn mouhayyab bi mouy tagg Yonenteu billa gueun gueun meu gueun sa baaye yow BG gueye ak sama baaye, neena Yonenteu saws parfois dafay baakh waayé parfois houuuuu dafay tang dieurrrrr !
Donc bou nitt wonné wee yarr ak téguine il faut absolument le lui rendre en mieux ! Mais koula khossi matt koo bamou nathieu !!!!!
Wa salam
aka bagne serigne touba té meuna wakh lou niaw
kou milni moussoumako guiss
avant hier lay soga deglou audio wam mais dama diommi si naka la kouy wakh si diné di dieuwé ay dioulit ni moom
En plus mouné talibé mame dabakh mingua khamni zero faute
Ki waliou bou magg la bly
Wakhtanou cigarette svp
C'est en ligne !
Loutakh ngay supprime commentaire yi
Parce que tu es excité quand tu te seras calmé,on pourra discuter sereinement et je suis sérieux !
@@Ndaar-Faam no loy ragal bo nieme bayi thi commentaire bi mame abdou aziz sy dabakh buniy khol entre sarr wala cherif kou mu guena ndirou nieup danu nann cherif la guena ndirou
Doul rek lay def wadji
Gosse SA LEFEUL NDAYE BOU KHONKK TIOURR !!!!!
@@Ndaar-Faam bettouma cii yen fen ak saga lalene domeram j diangale tel père tel fils.mena saga sa ndaye ak ak ndaye Serigne.
Mais grawoul nagne wax cii xam xam .b
@@khalilthiam1812 Domou thiotou ndéyam loo beugeu wokh cii xam xam ???
@@Ndaar-Faam thiey sarr domeram j yaxna boyi yeup.alkafire tidiane souma demeh ba beuguela saga rek rousse Alioune harazime.albarada.
@@khalilthiam1812 GOSSE SA THIAAPA NDAYE NAAFEEKH NGUEU !!! YOW KHAMNGA SAYYIDI ALIOU HARAAZIME ???diango khamo té deglouwo !!! KHAM NGA NII SAGA DAFA AMM FOUMOU WARR 😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😎😎😎😎
Baye niasse moy séne baye di sa bayou serigne
Dangay doul ! Sa baye ak con you melni yow.
@@Ndaar-Faam nieuwel niou wakhe si yalla ma manela ni sa Baye
@@Ndaar-Faam yawe lane moyi tijiane
@@Ndaar-Faam tontoul rk
Sa serigne may bayame
Ya mana fén ya bon
Yow loyy tieupi tieupi ? Katall ndèmm té dall néé mepp!!! So khamoul oubbil sa lefeul ndaye nga laathié!
YAW YAY DOUMRAM DOUMRAM PIRE
Ki mo dakha doul hahahaha
SA BAYE MOY DOUL! Kiné say say tédiall sa leuf li ! :-)
Sa lefeul ndaye wokhouma sa leuf yow waayé sa bou ndaye espace de domou khatieu
لكل إناء لمافيه ينضح
Li rek momgén am saga motakh mom géni wakh domi ndilo yougén din
@@kinefaye1439 doomi ndiaalo kay ni yow layy méll ! di doul di wokh cii ko khamoul . So khamoul dangay noppi. moy sa diamma .