KONA: LE LIVRE DE MAME BIRAME WATHIE LI GNOU SY MENEU DIANGUE AK LI XÈW ACTUELLEMENT SY PECCE MI

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 26 янв 2025

Комментарии • 318

  • @seynaboudieng5198
    @seynaboudieng5198 14 дней назад +5

    Walahi deuge le mame birame wathe diambare deuge le. ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤.merci beaucoup konna domi rewmi yalla nalla yalla dolle same amine yarabi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @juninho8226
    @juninho8226 14 дней назад +16

    Merci Konan
    Un homme véridique et sans façon. Yalna yalla samou laa

    • @Ballasylla-e6j
      @Ballasylla-e6j 14 дней назад +1

      Kona nitou deugu ga machallah vrai patriote boumak bi message bi dial na heureusement les sénégalais sonts très matures comprendre tout les détracteurs workat nafékh la igniane bone sokhor té bagne seydina Ousmane sonko késsé lanouy topou si réwmi focus sur lisaciél bayi détail yi focus nioutambakh réwmi diambar deugu ga ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @Ballasylla-e6j
      @Ballasylla-e6j 14 дней назад +1

      Mais defois douma andeu ak yaw si birou cheikh omar diagne kou khamadi béw fouy réw la aférou tirallér yi ak kilifa diné yi respecter woul kéne bayil di dieul ék sample simom même bouféké amna kham kham té andoul ak ay téguine mok mbeur mou seufi téré nioyam

    • @Ballasylla-e6j
      @Ballasylla-e6j 14 дней назад +1

      Merci beaucoup toujours pertinent égal même diambar deugu ga agacement digne détérminé khékh ba projet bi aboutir ba sénégalais yépou guisi sén bopou vision 2050 en marche inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

    • @Ballasylla-e6j
      @Ballasylla-e6j 14 дней назад +1

      KONA BAYIL DIAKHASÉ YI NÉNA YÉN SI PATRIOTES LA WAKH TÉ LOLOU MOY LI AME WAKHNA DEUGU YAGUI DIAWALÉ WAKH JI OUSMANE SONKO MOUSÉLMI KHAMNA LIMOUY WAKH BAYI LIGAY DIÉMA DÉF SI KHÉL YI DÉFOIS DAGAY FATÉ

    • @Cestlebontv
      @Cestlebontv  14 дней назад

      @@Ballasylla-e6jdèteu waye serigne bi chiekhe Omar niteu kou Bakh la mais tu peut ne pas être d’accord avec Lui c’est ton droit diadieuf 🙏

  • @Lina-u5f7c
    @Lina-u5f7c 14 дней назад +22

    Dieul na YALLAH mouyy sama sédé,WALLAHI, kona damalaa beugg ndakh deugg! Yalana YALLAH dolli la soutoura té gouddal sa ay fane🤲❤yaw dé do andd ak ken diko diayy!!!

    • @Cestlebontv
      @Cestlebontv  14 дней назад +1

      Dieureudieuf mala raw ❤🙏

    • @Diomayemoysonko3
      @Diomayemoysonko3 14 дней назад +1

      Ndeysan Yal nalen Yallah bole beugeu Amiin ❤❤❤❤❤

    • @Lina-u5f7c
      @Lina-u5f7c 14 дней назад

      @mackysallbadolala600 amine waay ak yaw tamit❤️❤️❤️

    • @Lina-u5f7c
      @Lina-u5f7c 14 дней назад

      @Cestlebontv ❤️❤️❤️🤲🤲🤲🙏🙏🙏

    • @rokhayadrame6147
      @rokhayadrame6147 13 дней назад

      Bravo kona deug mome yala moko mome

  • @babathioub7294
    @babathioub7294 14 дней назад +16

    🇸🇳🇸🇳💪💪 Respect kona Sonkooo Rék Laniouye Toop 💪💪🇸🇳🇸🇳 Leer na dhé 💪💪🇸🇳🇸🇳

  • @hassankamal1054
    @hassankamal1054 14 дней назад +10

    Bien dit une vérité absolue yow daal goudeul faan ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ThiataMbaye
    @ThiataMbaye 14 дней назад +5

    Mach'allh Jaajëf Waay Kona حفظك الله ورعاك وأيدك بجاه النبي محمد صلي الله عليه وسلم

  • @Salsaa-x7z
    @Salsaa-x7z 14 дней назад +11

    Chétététe yi DEUG merci beaucoup Kona ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Haveuse-u5
    @Haveuse-u5 14 дней назад +8

    Merci Kona ❤❤❤❤❤ un million d'abonnés pour Kona le véridique 🙏🏻🤲

  • @MoussaTALL-ps6gq
    @MoussaTALL-ps6gq 14 дней назад +3

    Je suis très fière de toi Kona c'est le bon TV . Chaine de la vérité, vrai patriote

  • @OusseynouCisse-do3dh
    @OusseynouCisse-do3dh 14 дней назад +2

    الحق من ربك فلا تكن من الممترين merci beaucoup kona

  • @fatousamba8372
    @fatousamba8372 14 дней назад +4

    KONA WAAW GOOR MACHA ALLAH . MAME B. WATHIE MACHA ALLAH . DËG LA SUNU BOROOM BËG. VRAIMENT

  • @AbdouNgom-t4y
    @AbdouNgom-t4y 14 дней назад +3

    2 millions d'années pour Kona domou ndaye ounia Ndiaye ❤❤❤❤

  • @ThiataMbaye
    @ThiataMbaye 14 дней назад +2

    Mach'allh Jaajëf Waay kona Billahi wallhi Lou wëur Nga Waax

  • @momocreation3631
    @momocreation3631 14 дней назад +6

    Merci kona degue nekhoul mais defois sonko daye passer à côté

  • @mamadougassama8155
    @mamadougassama8155 14 дней назад +2

    Belle analyse frère tout à fait d'accord avec toi

  • @babacarmbaye2644
    @babacarmbaye2644 14 дней назад +6

    Goudeul fanne kona ,analyses you pertinente rek settil kona ak sa ndiogou ak mame birame wathie.❤❤❤❤❤❤

    • @vEbene
      @vEbene 14 дней назад

      Sa ndiogou n’est pas vraiment impartiel non . Je suis meme désolée de le dire mais je me rends compte de cela de plus en plus lorsqu’il s’agit de certains sujets qu’il traite .

    • @ousmanefalloubayeniass496
      @ousmanefalloubayeniass496 14 дней назад

      Leurs chroniques sont extraordinaires. Sa Ndiogou, il est choc. C'est un plaisir de l'écouter et très tranchant et efficace dans ses analyses. MBW mom c'est autre chose, des interventions avec un peu d'humour 😂 machallah

  • @nasirmbow835
    @nasirmbow835 14 дней назад

    Diadieuf kona vraiment tu es veridique yew deug réck ngaye wakh kona
    Kèn douyew .guisagouma koula guana
    Deugou merci bcp kona goudal fane Nasir mbow
    Da italy .❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdoutackodiallo3932
    @abdoutackodiallo3932 14 дней назад +12

    Merci 10000 fois kona ❤❤❤

  • @ndeyeyandendiaye3424
    @ndeyeyandendiaye3424 14 дней назад +1

    Doli ndéké vrai con le😂 merci Mame birame deugou rek mo am solo

  • @DiarraGueye-e5k
    @DiarraGueye-e5k 14 дней назад +1

    Merci beaucoup kona je suis parfaitement d'accord avec toi sonko yalla ko may souy wax nieup deglou ko mais khamoul waxine je suis très déçu de sa dernière sortie

    • @Cestlebontv
      @Cestlebontv  14 дней назад

      On est ensemble, on continue la lutte 🙏

  • @amarsow
    @amarsow 14 дней назад +2

    MBEUR TEY MOM TU AS CASSÉ LA BARAQUE COMME NIKO TOUBAB DI WAKHÈ MAA SHA ALLAHOU. FORMAT BI BAKHNEU TOROP !! TEY MOM FALL WONÈ NGA PROFESSIONALISME BOU MATT SEUK!!! ÇA A ÉTÉ UN PLAISIR DE T'ÉCOUTER BRO !! ONE LOVE ❤ C'EST LE SÉNÉGAL 🇸🇳 QUI GAGNE REK DIAAFWAAYE MBEUR 😂

  • @NgomIsma-r4d
    @NgomIsma-r4d 13 дней назад

    Machallah danga deugou té am déug déug mame Birame wathie Machallah yallnako yallah samou mayko goudou fane ak wéur

  • @nioukfall7869
    @nioukfall7869 13 дней назад +1

    ❤❤❤❤SONKOOOOOREK UN GRAND MONSIEUR UN VRAIMENT PATRIOTE UN HOMME DIGNE VÉRIDIQUE HONNÊTE COURAGEUX TRAVALLEUR GÉNÉREUX QUI AIME SON PEUPLE WASSALAM WASSALAM WASSALAM

  • @babba_joop1311
    @babba_joop1311 14 дней назад +5

    C vrai certains patriotes sont emotionels et Macky Sall jouait sur cette émotion. Nekha yobale patriote thi tahirou sarr lako khame . Koune Sonko Rek gnouneko yawla🇸🇳 Sonko Rek point ☝🏽🇸🇳

  • @seynabouyvon2500
    @seynabouyvon2500 14 дней назад +2

    Je souhaite tous les sénégalais regarde cette vidéo, très pertinent machallah qu allah augmente ta vision sur le Sénégal. Je suis fière de toi.merci

  • @mouhamedcisse3287
    @mouhamedcisse3287 14 дней назад +1

    j'ai eu la même réaction et la même position que toi mon frère merci beaucoup. Au moins il y a quelqu'un qui ose dire la vérité à Ousmane Sonko et c'est ce qui l'aider pour ne pas tomber dans le même erreur que ses prédécesseurs. MERCI

  • @FatouJoof-vf1th
    @FatouJoof-vf1th 14 дней назад +2

    Walleihi Brother Kona you are very right most of the people surrounding President Diomaye are not from Pastef and that’s not a good sign 😢

  • @cherifhassaneful
    @cherifhassaneful 14 дней назад +11

    Amlen respect thi sonko nguir yalla

    • @kebafall3523
      @kebafall3523 14 дней назад +2

      Lo beug touddé niack respect fofu?

    • @vEbene
      @vEbene 14 дней назад +2

      @@kebafall3523moma diakhal. On aime sonko dans la vérité pas ds l’émotion .

    • @kebafall3523
      @kebafall3523 14 дней назад +1

      @@vEbene vraiment

  • @Bambabamba-t5f
    @Bambabamba-t5f 14 дней назад +1

    Merci bilhai dague bou wer merci

  • @biramathiam6408
    @biramathiam6408 14 дней назад +3

    Kona respect ci yaw.
    Mais pros limou waxx dafa simple defois dou diar yen thiow yi ba mou am ay patriotes you traité diomaye traître gni di saga
    Ci lolou la d'accord AK gnom dénoncer rek Mais certains patriotes dagno diap gno gueun xexx gneup té sonko waxx na ko kerok fi ken gueunou fi done patriote gnoune gneup gno bokk yené
    Sonko limou dadj yeup souko changer taxoul wonn Diouk Kone abandonné Bou yagg de même que diomaye

  • @mossandiaye6893
    @mossandiaye6893 14 дней назад +3

    Merci kona sonko na khamni nitla day dioum mok diomaye nio diomaye nio dioum fal kouniou warouta fal baparé beugue niou nopi lolou menouta né

  • @Diomayemoysonko3
    @Diomayemoysonko3 14 дней назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤mercy Kona bara doli dafay doul rek bou sangion dougou assemble diemna bouroukhlou ba soneu President Bassirou Diomaye Diakhar Faye ak PM Ousman Sonko falewouniou ko motakh mounan dafay kokali,modou fall mom faw ngeun comprend ko weerou koor moy wadia nieuw te soukarou koor dou nioge si palais bi di dem si mom motakh mou diafour 😂😂, Mame Biram Wathie journalist bou am valeur bi jambarr bi Yal Yallah goudal fanam ❤❤❤❤❤❤

  • @rokhayasarr6468
    @rokhayasarr6468 14 дней назад +1

    Merci beaucoup Kona ❤ félicitations à Mame birame c'est une bonne initiative yalna barkel ❤

  • @BambaaudiFall
    @BambaaudiFall 14 дней назад +1

    Merci ❤

  • @doupiri
    @doupiri 14 дней назад +3

    Barki alkhourane y’a nième deug dieureudieuf nala yalla sameu areuu la barki borom touba ,ngua sedale sama xol yalla sa xol di goundane ndate 😂😂❤❤❤❤❤c le bon tv 📺

    • @Cestlebontv
      @Cestlebontv  14 дней назад

      Dieureudieuf amine gnou bokou kou 🙏❤

  • @CoolBoy-zg9he
    @CoolBoy-zg9he 14 дней назад +1

    Je suis tout à fait d'accord sur toute la ligne Kona, waxi deug rek nga fi wax👏👍

  • @IbraimaTall
    @IbraimaTall 14 дней назад +1

    Merci le vrai patriote Kona❤🙏🏽🙏🏽 goudal fane inshalah 🙏🏽

  • @magiangfall4001
    @magiangfall4001 14 дней назад +1

    Merci kona ae

  • @caranoufedior564
    @caranoufedior564 14 дней назад +3

    Salam Salam ziar Kona
    Félicitations encore une fois à Mame Birame Wathie pour son nouveau livre que je vais inchalah adquirir
    Malheureusement le Sénégal un pays à tradition orale les sénégalais lisent pas ou très peu et ça notre drame

  • @abdoulayesow5022
    @abdoulayesow5022 14 дней назад +1

    Respect Bros tu es , véridique,gratuit franchement qu'Allah vous garde

  • @oumarkane907
    @oumarkane907 14 дней назад +2

    Ya deugou champion yalla samela. Vérité absolue.

  • @khadimgaye4033
    @khadimgaye4033 10 дней назад

    Sonko dafa dioume si ay wakham merci kona ❤

  • @diaibrahim6798
    @diaibrahim6798 14 дней назад +1

    Merci kona bien dit machaallah toujours véridique 🎉🎉🎉🎉🎉😂😂❤❤❤❤❤

  • @maneseydina6564
    @maneseydina6564 14 дней назад

    Jeureujeuf Kona sa doundou amna njeurigne tabarkallah, longue vie à vous.

  • @adamadieng8720
    @adamadieng8720 14 дней назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Kona deuggue dou ROMBE ayy nopp ,WAKHDJI RAFETNA si deuggue yi

  • @MbayeBabacarNdao-vj9mw
    @MbayeBabacarNdao-vj9mw 13 дней назад

    Rewmi de walahi yala rek mowalousi takhawounou kep kou bougonn senegal tegouwatt thie yonn nafekyi ak workat yi lides thie sen adouna sen khol dotoul nekh merci cona nanou gueuna niann rek ta diam lep dina bakh

  • @muhammadfall3655
    @muhammadfall3655 14 дней назад +4

    merci respect a vous nous somme 100 % patriote Sonko lagnuy top,
    je suis en phase avec toi si remarque yingua def si pro

  • @elimaneMbaye-v1y
    @elimaneMbaye-v1y 14 дней назад +1

    Machalha amatina solou diaradeif Kona dueg rék la yala ba ga des❤❤❤❤❤❤ pour kona

  • @ModouGueye-cb2mj
    @ModouGueye-cb2mj 14 дней назад +1

    Yala bou modou fall don sama mame😂😂😂😂😂 vive KONA yamana tontou❤❤❤

  • @aidabadiane6924
    @aidabadiane6924 14 дней назад +1

    Sonko a vie point ❤️ ❤️ ❤️ ❤️

  • @AliouneBadaraDIOPDIOP
    @AliouneBadaraDIOPDIOP 14 дней назад +1

    Toujours pertinent merci du courage

  • @santeyalla879
    @santeyalla879 14 дней назад +3

    Merci beaucoup mon frère kona lou lér gua wakh

  • @Ousainou11Ousainou11
    @Ousainou11Ousainou11 14 дней назад +1

    Thanks Kona God bless you long live i am happy so much 🇬🇲🇬🇲👍👍🙏🙏

  • @mouhamethndiaye4548
    @mouhamethndiaye4548 14 дней назад +2

    Merci beaucoup kona ماشاء الله جزاك الله خيرا وبارك الله فيك ❤❤❤❤

  • @papaabdoudiop1380
    @papaabdoudiop1380 14 дней назад +1

    Livrou Madiambal Diagne kouko lire doula geum té dou geum Ousmane Sonko.Merci Kona.❤

  • @mamadoundiaye5246
    @mamadoundiaye5246 14 дней назад +2

    Merci beaucoup Kona mon fils toujours pertinent dans ses analyses. Bonne continuation

  • @vEbene
    @vEbene 14 дней назад +2

    Quelle franchise kone . Je t’aime vraiment pour les vérités que tu dis .

  • @alioubadaradiagne1909
    @alioubadaradiagne1909 14 дней назад +2

    Merci beaucoup mon frère ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ vous méritez des millions des abonnés merci encore ❤❤❤

  • @Mdhbsk
    @Mdhbsk 14 дней назад +2

    Deugg you lêr si léppe rawatina ver pm os merci

  • @mariemediaw1248
    @mariemediaw1248 14 дней назад +3

    Merci, Kona le grand patriote, je partage ton opinion, le projet on le surveille de très près. Le peuple sera tjrs au dessus. Pour mouy clair.

  • @babacarfall3677
    @babacarfall3677 14 дней назад +1

    Diadieuf Kona say analyse amnagnou solo trope.❤.

  • @SaliouMbaye-jr2em
    @SaliouMbaye-jr2em 14 дней назад +1

    Merci beaucoup koná❤❤❤

  • @cheikhtidianediop4914
    @cheikhtidianediop4914 14 дней назад +3

    DIARADIÉFF KONA MERCI KONA شكراً لك KONA

  • @alioubadaradiagne1909
    @alioubadaradiagne1909 14 дней назад +2

    ❤❤❤❤❤❤ merci beaucoup Cona merci vous méritez les billions des milliards des abonné❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @younousthior8558
    @younousthior8558 13 дней назад

    Sacré MBW ❤❤❤et merci kona

  • @BadaraFall-b9t
    @BadaraFall-b9t 14 дней назад +2

    Merci beaucoup frère kona yawe rek laye top ❤❤❤❤❤❤❤

  • @seynaboudieng5198
    @seynaboudieng5198 14 дней назад +1

    Dieureudieufe konna c'est vraiment le bon

  • @abdoulkhadreba5724
    @abdoulkhadreba5724 14 дней назад +1

    Dieuredieuf bon lundi

  • @VictorNdiaye-gw8yd
    @VictorNdiaye-gw8yd 14 дней назад +1

    Vraiment Kona a raison de certains de leader de pastef sur leurs façon de communiquer. Les patriotes sont majeur et vaccinés, ils faut respectaient.

  • @silmakhatraore483
    @silmakhatraore483 14 дней назад +2

    Kona le grand chef de village du konamba hey mokhobã big respect 👊

  • @Kingsley114
    @Kingsley114 14 дней назад +2

    Mes respects Kona! Merci pour tes analyses! ❤❤❤❤❤❤

  • @sadiosama8034
    @sadiosama8034 14 дней назад +6

    Kona je suis toujour avec toi ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @moustaphasadiocissokhothies
    @moustaphasadiocissokhothies 14 дней назад +3

    Modou fall domarame la khaliss lay jamou dou sarap ndeyam

  • @serignemoustaphagoudiaby9192
    @serignemoustaphagoudiaby9192 14 дней назад

    Non Kona tu es formidable vraiment. Nous devons nous réunir au tour de l'essentiel. Mais les hommes de mauvaise foix n'ont pas la place dans ce projet.

  • @xelxelli
    @xelxelli 13 дней назад

    Bravo Kona lou am solo nga wakh ci léppeu surtout...

  • @MohammedPadane-v7f
    @MohammedPadane-v7f 14 дней назад

    Merci beaucoup Kona wakh nga deug dh❤Omar Sow Limou niou yéne Yalla na keup ci kawam Modou fall lou Yalla kham doy na

  • @aboubacardiop8804
    @aboubacardiop8804 14 дней назад +3

    Kona dioumga c'est vrai que certains patriotes sont faciles à manipuler.

    • @Cestlebontv
      @Cestlebontv  14 дней назад

      Lolou mounoule gnaque sy Mballo mais la majorité des patriotes sont des responsables et très mature lolou mo takh taye projet dougou palais 🙏

  • @moustaphasylla6048
    @moustaphasylla6048 14 дней назад +3

    Vraiment je t adore tu as très bien parlé deug dou wesou ay nopou

  • @niangtalla5981
    @niangtalla5981 14 дней назад +1

    Merci beaucoup bien dit vérité absolue je suis d'accord avec toi

  • @bayemalickdiakhate8847
    @bayemalickdiakhate8847 14 дней назад +1

    Kona yagui wakhale kep kouye yewo Senegal ak bitime rewo machalla yana sa diame yage

  • @vEbene
    @vEbene 14 дней назад +2

    Vive kona pour ces vérités . ❤

  • @DabaDiouf-v5g
    @DabaDiouf-v5g 14 дней назад +1

    Kona Sonko ak Diomaye danioo am faiblesse sou diplôme .
    Jeunes yi khèkh ba sònneu niouy nommer ay MaryTéo Niane Oumar Samba Ba Mimi Touré Serigne Guéye Diop Mabouba Diagne Augustin Tine et beaucoup de vieux qui ont plus de 60 ans.

  • @nasirmbow835
    @nasirmbow835 14 дней назад

    Man domarate sa benne live.kona ostas modou fall doukharame leu
    Nafékh bou bnnleu maky sall
    Moyèss thi adouna maky sall framazon. Félicitation mame Birame wathie thi livre
    Bimou Binde. Merci ancore de
    Plus.

  • @laminembengue3443
    @laminembengue3443 14 дней назад +2

    J'aime bien t'écouter ,merci bien.

  • @nafissatoudeme4999
    @nafissatoudeme4999 13 дней назад

    Merci c le bon Tv grand bi contane si yaw li nékone sama khol yeup wakhal nga mako té li nak moy li fi am motakh Ngour gui wara def attention parce que nioune jeunesse bi projet bi souniou bakane laniou si ték tay souba ba guinaw souba kone nak naniou niou bayi khél bou bakh . Wa Salam

  • @cheikhtidianediop4914
    @cheikhtidianediop4914 14 дней назад +2

    شكرا لك يا KONA MERCI KONA MERCI KONA ❤❤❤❤❤

  • @ndeyesokhnacissokho8633
    @ndeyesokhnacissokho8633 14 дней назад +1

    Merci Kona deugue rek wakh Modou khôl bé diekh rek ndakh lawone mo wonie yalla na sa diam yague

  • @SiradjiMbodj
    @SiradjiMbodj 14 дней назад +2

    Kou beug deg deug diapal c’est le bon tv

  • @serignleye5529
    @serignleye5529 14 дней назад +1

    ❤❤❤ merci beaucoup machalla

  • @BounaCisse-li4pu
    @BounaCisse-li4pu 14 дней назад +2

    Merci Kona vraiment tu es véridique

  • @DioufiGave
    @DioufiGave 14 дней назад +1

    Respect à toi pour deggou gui!

  • @beyjilofficiel7902
    @beyjilofficiel7902 14 дней назад +1

    Haaaa merci beaucoup waye kona wakhe deuge dè ❤❤

  • @khadycamara5172
    @khadycamara5172 14 дней назад +2

    Merci cona vérité absolue deugeu dou rombi nope

  • @ousmanembodji9158
    @ousmanembodji9158 14 дней назад +1

    Merci frère toujours pertinent

  • @dioufgallassfallou7156
    @dioufgallassfallou7156 14 дней назад +21

    😂😂😂😂doli mo niak fayda

  • @cheickmoinga3245
    @cheickmoinga3245 14 дней назад +1

    SONKO Seul ❤
    SONKO à vie ❤
    Jub-Jubal-Jubbanti ❤

  • @cheikh564
    @cheikh564 14 дней назад +1

    Mbockoum rewmi yalnaleu yalla samme té mousseul leu si ayou lamigne

  • @classycool1516
    @classycool1516 14 дней назад +2

    Big up vraiment Kona deug rekk ngaye wakh❤

  • @donomrecane7471
    @donomrecane7471 14 дней назад +1

    Big up bro Sénégal mo am💪💪💪💪💪

  • @AbdouNgom-t4y
    @AbdouNgom-t4y 14 дней назад +2

    Oustaz Modou fall domeram le tok mou dokh teudeu Mouy dokh dioutou.mouy dokh karaté sakh Mouy dokh lolou amatoul mbire ye commencer metti😂😂digne totie sen leufeul ndaye deh😂😂😂