Allahou akbar😱Pape Mbaye magui sante yalla bou bax beug na dem Makkah après na takk sokhna lolou rek

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 26 дек 2024

Комментарии • 40

  • @maimounadiop673
    @maimounadiop673 День назад +13

    Allhu Akbar, quelles sages paroles, qu'Allah SWT nous garde dans dans le droit chemin

  • @StellaKaa
    @StellaKaa 9 часов назад +1

    Machallah kadou yi rafetena yallah n’a niou yallah diegale si yeuremadem amine amine inchallah

  • @fatoukinembaye4523
    @fatoukinembaye4523 День назад +13

    Macha Allah ces paroles m’on fait pleurer yalna yalla dieguelko tee tekko si yonou siratal moustakhim 😢😢😢

  • @fatoundiaye9234
    @fatoundiaye9234 15 часов назад +1

    Machallah départ amoul solo arrive mo âme solo yalla nanou yalla maye mouthie guou raféte

  • @mamediarraboussondiaye769
    @mamediarraboussondiaye769 День назад +4

    Yallah nala yallah weulbeuti AK diam nga teguei wate si yonou siratal moustakhim 🤲🏽🤲🏽🤲🏽

  • @MameCheikhMbacké-v8t
    @MameCheikhMbacké-v8t День назад +6

    Bilahi yalla bourla bokhameni yeurmandem yamoul fenne toubal rek yalla mooy bour

  • @malickniang4529
    @malickniang4529 День назад +5

    Machalla amna solo yallna yalla diégeul niepou

  • @Amadou-b4i
    @Amadou-b4i День назад +13

    Mané kou toup diégalou yalah balla Nanou bourbi diégal🤲🤲🤲

  • @codesall5874
    @codesall5874 День назад +3

    Pape mbaye yalla wétali si yon bi nga begu diar bilahi doundou yalla dafa nékh machala mbaya sa kadou yi am na solo torop

  • @YayouKhaleyi
    @YayouKhaleyi День назад +1

    Pape tu m’as agréablement surprise je suis très contente de toi qu’Allah te bénisse et te guide dans le droit chemin inshalla 🫶🏾

  • @dyeracky7797
    @dyeracky7797 День назад +2

    Machallah mon duo préféré. C’est toujours avec plaisir de vous écouter ❤❤❤❤

  • @ababacarkhalifa5398
    @ababacarkhalifa5398 День назад +4

    Rien na dire machalla k Allah vs béni

  • @mamediarraboussondiaye769
    @mamediarraboussondiaye769 День назад +1

    Yallah nagnou yallah bolei jeggal gnoune gneup sougn bepp bakarr ak noum meunti mell si barkei Seydina Mouhamed sallallahou allayhi wa salam 🤲🏽🤲🏽🤲🏽

  • @KharDieng-gb9wv
    @KharDieng-gb9wv День назад +3

    Machallah mbaya ❤

  • @khalyinnovation3096
    @khalyinnovation3096 День назад +5

    Machala rafétena

  • @diopkhady4751
    @diopkhady4751 День назад +5

    Machalla ❤❤❤❤

  • @RamataDatt
    @RamataDatt День назад

    Papa bay li yallah mou continue allah houma amine y’a rabb

  • @khadydiop8608
    @khadydiop8608 17 часов назад

    Yalla nala diama sonal ❤

  • @seynifaye3938
    @seynifaye3938 День назад

    Man pape mbaye dama ko beug ndakh wolou yallah ak weteul ko pape mbaye yal nala yallah sopi diegeul leu yal nala borom bi diapale soutoural la banga deloussi waat ❤️❤️🥰 walahi deug nga wakh boul meusseu nagou thi yeur mande yallah te so bakarone bamou fess assamane ak souf nga diegalou ko rethiou bayi dotoko defati yallah diegeul lako

  • @PacoDiaz-yc5fy
    @PacoDiaz-yc5fy 19 часов назад

    Meno nakhh yalla❤

  • @diva8320
    @diva8320 15 часов назад

    Ndeyssane hamdoullah

  • @modoudrame3715
    @modoudrame3715 День назад +1

    ❤❤❤❤merci mbay

  • @Mechaelsoum
    @Mechaelsoum 2 дня назад +4

    Machalah machalah machalah

  • @Kangaroo_queens
    @Kangaroo_queens 9 часов назад

    Marshallah pape

  • @sophie1924
    @sophie1924 День назад

    Mbaya Yalnala yallah tahawou !
    Mome moy borom yeurmender. Nagnoudelou nioune nieup toub!

  • @WeulySeck-j3e
    @WeulySeck-j3e День назад

    ❤❤❤❤❤❤dieu est ent grand

  • @thiounesoda9420
    @thiounesoda9420 День назад

    Amiine yallah bakhna❤

  • @pendagueye291
    @pendagueye291 День назад +5

    Yala Nala yala diapalé Si barké arhouran hawlou lahi tabara wa tahala

  • @talibehbamba3060
    @talibehbamba3060 День назад

    Masha Allah, May Allah forgive you all your sins and guide you to the right path. So happy for your turn to Allah( SWT)

  • @remadiouf
    @remadiouf День назад +1

    yalla nalla yalla diegueul diegueulale lagnou tek gnou gnoune gneupeu si yonou siratal moustahim

  • @RamataDatt
    @RamataDatt День назад

    Alhamdoulillah alla koulli hall

  • @seynifaye3938
    @seynifaye3938 День назад

    Dama dioyy pape dila nianal ndigelou yallah ak mou nangoul la sa toub walahi man deih dina la defal niary rakka nianal la yallah yeurmande ak niegeul

  • @AmindaoNdao
    @AmindaoNdao 10 часов назад

    tey len si mom bakhna

  • @MaremGueuye
    @MaremGueuye День назад

    😭😭😭😭Ndeyesn

  • @seynifaye3938
    @seynifaye3938 День назад

    Ben waay ray na 99 personnes diakhlè dem ladji ben borom khama kham mou nekoso dewe dem safara mou rey ko mouy100 personnes yimou rey . Mou demaat thi benen borom kham khan mou ni ko yallah dinala diegeul so toubei .. mou dem toub yallah diegeul ko mou deih dem aldiana .. woloul yallah toubeul rethiou comme ni ko borom lakhdariyou wakhe .. anadamou alamaafa .. rethiou ne dotoko defati thi li dess thi sa dound

  • @Createurdecontenu-ow9mn
    @Createurdecontenu-ow9mn 2 дня назад +1

    Kaliphone est ce que amna liguey

  • @thebigH-qx8kd
    @thebigH-qx8kd 2 дня назад +2

    Kalifone bayil gorjiguene bi continue rekk sa safara mogui lay khar

    • @maimounadiop673
      @maimounadiop673 День назад +3

      Dioulite day wah louko Word, togn bahoul

    • @amyrock4324
      @amyrock4324 День назад

      SA SAFARA MO GEUNEU WOOOR BOSSAM

  • @zeydaamydia6391
    @zeydaamydia6391 День назад

    Yaww mome PAPE mbaye tu racontes que des conneries 😂😂😂😂😂 !!! Allal dou mandarga andak yallah
    Togne bi nga togne sa moromou dioulitt naak té yaww togne katt nga yallah dou Ball linga sékheukk sa morome !