MODOU lô combat yi mouyue amate yébe YALLA nasi ame ayue victoire ba énervé Amine yarabi et donne nous de ❤long vie amine yarabi YALLA wérale NIOU mayue niou NIOU réalisé sounouyue rêve Que ALLAH nous pardonnes nos péchés ❤Amine yarabi ❤
Bilahi wax nga deug lamb. Diambar teug na affiche mais coté organisation sax dafa dess en plus pour bénén face 2 face bi dess na jeul niom Lambalogue niom becaye niom bour Guéwel ak fadam affiche danioukoy promouvoir. Merci encore lamb
Lanmb balla modou do beuré ag balla parsque gnoum lilén nakhari moy temps yi mom modou lô lagnouy wakh lolou mométi gnoum aziz mais dina gnou khar dé inchalla
Machala machala machala car caravane carapid cara carte cara caractère Caroline carottes lepp lou am car wakh nala ko Modou lo yalla Nako yalla may ndam rek inchallah siteu défaite rek inchallah si katanou yalla sounou brom ☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️ Modou lo ndam rek inchallah 🙏🙏🙏
siteu na déme si salle yi entrainer contact bou bax nganaNe dune athléte yi si monde bi yeup salle laniouye outé doley té souniou mbeur yi eupouniouléne doley
Machallah lambloque Modou kharagne lô yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw siteu le 24 novembre inchallah the king is back modou kharagne lô kessé lay topou machallah bouléne niou thiatou 😂😂😂😂 modou kharagne lô képpeu kouko yape daffa féke ni arbitre bé sifflégoul wayé bou arbitre bi sifflet Lou way wakhon NASA déllouwate 😂😂😂😂modou bandit guéwela modou lô le maire de pikines wa pikine niongui sissou si commentaires yii ak sama mbokkou guéwal yii modou diékhalna wa pikine 😂😂😂😂😂😂😂modou kharagne lô le bétes noire des lutteurs de pikines
Aye way chat djigou gnou way boulen gnou chatou way me dal lamalog analize bi pertinent na comm toujours antouca name rec lagnouy gnan way te geme nagne ne borom bi may gnou nam inechala bilay name rec lagnouy gnan inechala thi comba bi modou lo yale ge confirmer ce tu es lunuce roi et tu le restera ba gay djouge thi lambe bi djokh co coul nekh bilay yale co yale def touf touf amin
Fou face to face amé ba paré lambologue lay khar thi analyse...ya woor grand 💪❤❤
Waawaaw
Mane tmt 😂
😊
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mane tmt
MODOU lô combat yi mouyue amate yébe YALLA nasi ame ayue victoire ba énervé Amine yarabi et donne nous de ❤long vie amine yarabi YALLA wérale NIOU mayue niou NIOU réalisé sounouyue rêve Que ALLAH nous pardonnes nos péchés ❤Amine yarabi ❤
Sallallahou alla MOUHAMAD 🎉
Salla lahou alayhi wa salam sallahou ala Mouhamed
Shw psl ❤
SALLAHOU ALLA MOUHAMED ❤YALLA NANOU YALLA MAYUE NIOU LOUNOU DOUGOU RÉUSSIR KO AMINE YARABI ❤
Macahalla ❤❤❤ Modou lô yalla nala yalla May ndame❤❤
Ameen yarabi my ⭐️ ⭐️⭐️⭐️⭐️⭐️⭐️⭐️⭐️⭐️
Amine yarabi ❤❤❤❤
Amine
Boulénou thiatou modou modou rek li djigou nou😢
MACHALAH
Gnoune fans na ngou wakh MachaAllah rek
Gni kagne thiatou rek laniou mane modou yalnako thiate sékhlou
Machaalah rek
Modou kharagne lô Yallah nako Yallah lafal thiatt❤teii mayko ndam bou lerr si kaw siteu😍🙏
Amine
Amiine waay
Amine 🙏🏾 inch'Allah ❤️
Amina
Amine
Siteu défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
Cey sama wadji finguako teih rk la 😂
@@falistobambiste siteu défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
Hqby Amine yarabi modou kharagne lô yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw siteu le 24 novembre inchallah
Hqby Amine yarabi modou kharagne lô yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw siteu le 24 novembre inchallah
@@FatouMbaye-dy2ol amine inch"allah si barkep yallah mounou sakk inch"allah 👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
Lambalogue mo daka décortiquer si Gars Lolou mom dafa lérr Mãchaa'Allah ❤️
Lambalogue outal sa site internet saay xalate amena solooooooooooooooooooo job siiiiiii sa interet là
Borom salade dou niakh pomme dou néw 😂😂😂 lambalogue rek, yok ak ndam rek inchallah
Mes respects à Khadim vos questions sont pertinentes macha Allah.
Balla moy sama mbeur mai modou lo il est exceptionnel woww konggg😂
Ma Sha Allah❤
Da khèré 😂
Bilahi wax nga deug lamb. Diambar teug na affiche mais coté organisation sax dafa dess en plus pour bénén face 2 face bi dess na jeul niom Lambalogue niom becaye niom bour Guéwel ak fadam affiche danioukoy promouvoir.
Merci encore lamb
Modou lo ndam rek inchallah 🙏🙏
Lambalogue soufi nékoul woneu ma bayi cétane lamb 😊
Macha Allah Macha Allah Modou lo domou diaboure la
Khadim tes questions sont pertinentes
Khadim machallah ts Questions sont très pertinentes ms lambologue diot na ngua out sa site si internet bi té vraiment pertinente machallah
Kharagne loooooo nékha farale Dimanche Ndam rék inchallah ❤❤❤🇺🇸🇺🇸🇺🇸
Modou Lo yalnako yalla maye ndame ❤👑👑👑👑👑👑
Amine inchallah❤❤❤
Modou bi da entraîner ba wow ndey congg 😂
Aye domou diambour dji Machalla dél wakh Machalla 😮😮😮
😮😮😮😮
Lanmb balla modou do beuré ag balla parsque gnoum lilén nakhari moy temps yi mom modou lô lagnouy wakh lolou mométi gnoum aziz mais dina gnou khar dé inchalla
😂😂😂😂😂 waxofi dara
Machalla Modou lo laff thiat ndam rek inchallah ❤
Machallah laf thiat laf bouss si Modou kharagn lo ndam rk inchallah 🙏👑👑
Dembe modou def na lim man pour nekhal mai siteu mo ross modou lo masol may keneu diamo si diakorlo ahh
Machala machala machala car caravane carapid cara carte cara caractère Caroline carottes lepp lou am car wakh nala ko Modou lo yalla Nako yalla may ndam rek inchallah siteu défaite rek inchallah si katanou yalla sounou brom ☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️ Modou lo ndam rek inchallah 🙏🙏🙏
😂😂😂
Lambalock machallah ❤❤❤❤❤❤
Ndam rk pour Modou Lo inchallah❤❤❤
Je suis très fière de lambalogue
BILAHI MODOU LO LEGUI LA GUINA BARI DÖLLE 💪
Lambalong do moromou buur guewale bilah
Macallah Mamadou lo le roi inchallah ndam rék 👑🇸🇳🦁✌️🙏
Siteu kou ko maye 100ans Dou baaré😂 Modou Lo keeesé❤💪🏾💪🏾❤️
Guanima 😂😂😂😂 akay degue bou wer
Louleer lawax forme Modou bi dafa doywar machalahh... Siteu amna problème deh.
Modou lo ndam Rek inchallah
Siteu tarkinda bi yallah nako yallah may ndam inshallah ❤❤❤❤❤❤❤❤
Il est trop fort ce gars lou leer le wax mais nak mystique ame na D faites attention
NO LAMBALOG KHAMNA LAMBA
KOUHAM SPORT MODOU LO
DEFA AM DOLLE💪
Lamb wakhna deugue dè Siteu na entrainè durement si dune yiii
siteu na déme si salle yi entrainer contact bou bax nganaNe dune athléte yi si monde bi yeup salle laniouye outé doley té souniou mbeur yi eupouniouléne doley
Xaragne rek inchallah ❤❤❤
Lambalok yaBari kham kham machalla
Wadji daafa fort bilahi moom laay deglou ci lammbou
Lambalog ya meune si lamdji 🎉❤
Modou kharagne lo l'un des meilleurs de sa génération 😊😊😊😊
Thank you so much brother jamou si yow❤❤❤❤❤ modou rek
Ms gars lambelogue dou nitte 😮😮😮😮😮😮😮❤❤❤
Vraiment très pertinent tank site yi desna v yi guenoul
Moudou lo yalla na ko yalla maye ndame ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Bilaye lamalok ya am kham xam machalla
Machallah lambloque Modou kharagne lô yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw siteu le 24 novembre inchallah the king is back modou kharagne lô kessé lay topou machallah bouléne niou thiatou 😂😂😂😂 modou kharagne lô képpeu kouko yape daffa féke ni arbitre bé sifflégoul wayé bou arbitre bi sifflet Lou way wakhon NASA déllouwate 😂😂😂😂modou bandit guéwela modou lô le maire de pikines wa pikine niongui sissou si commentaires yii ak sama mbokkou guéwal yii modou diékhalna wa pikine 😂😂😂😂😂😂😂modou kharagne lô le bétes noire des lutteurs de pikines
Macha'Alla dégg na dëgg dee.
Modou Lo bilahi yallah nala yallah lafal thiate way
Bilahi deug rékk ngéy wakh
Hé machallh ah lafa thita
Bilay aka ma yénna Mou dém.lutte TV Wala Albourakh
Bien dit Lambologue mais del wakh mashala thiat djigul kén, Modou athlète la.
Lambalogue vraiment tu es fort 😂😂😂
Bilaye Lou lèrr grand frère lambalogoe Modou lo kėssė
Agnal liguay agn😂😂
Modou lo bo entrainè wul sax mo mane Siteu 😂
SALLAHOU ALLA MOUHAMED YALLA NANOU YALLA MAYUE NIOU RÉALISÉ SOUNOUYUE RÊVÉ ❤
Bouléne thiatou souniou mbeur mi ahhhhh Modou ngy ame ni 😂🎉
Nioun siteu la nou beugue❤❤
Machalah👌 Lambalogue analyse bi lerna naagnne😊
Bilay lambalogue waxatiko dh ya deg modou lo seul kassé nk💪💪💪💪💪💪
Way yaw yay lamb way❤❤ cheuuuu
Aye way chat djigou gnou way boulen gnou chatou way me dal lamalog analize bi pertinent na comm toujours antouca name rec lagnouy gnan way te geme nagne ne borom bi may gnou nam inechala bilay name rec lagnouy gnan inechala thi comba bi modou lo yale ge confirmer ce tu es lunuce roi et tu le restera ba gay djouge thi lambe bi djokh co coul nekh bilay yale co yale def touf touf amin
❤môdou lô rek ❤❤❤❤ niôman niô epoudôlè
ndam rek inchalla ❤❤❤❤
Lambeloque le meilleur communication de lutte de nos jours et doit être invité dans les face two face en tant que presenteur 🎉
Modou lo yalla nala yalla maye déféte bou lére amine
Tay mom doul nga ba dioutou 😮😮siteu moo meun fouff bilahi walahi wa taalahi yalmbine moko meun le 25 novembre niou varr laa ndeyam
Ioe tite nga DH combat bi le 24 la do la 25
Mashahallah rk laff thiatte
Modou lô yalla NASA diamou yagu yalla nala yalla may dame
😂touf touf touf😊 machalla
Yalmine bi yallah nako yallah may ndam inshallah ❤❤❤❤❤😂
Yalna yalla goudal fan wu AK wer
Le meilleur
Moudou Lo rek ❤❤❤❤❤❤
Vraiment ndanane moy wax
Lambologue la de ❤❤❤❤
Modou lo yalla nako yalla lafal thiat té mayko ndam
Bilay dama febar me werna merci lamalok
Je pense que Modou Lo perdra un peu de sa masse musculaire avant le combat
Pour l'an
Agnal Li Ngaye Agne Key😂😂 Kii Mo Degg Lambe ❤😂
Siteu kasse siteu kasse ❤❤❤
Merci❤❤ regarde les avant brat de Modou❤❤
Oh lamb guddeul Fan waay 🤣🤣❤️❤️❤️❤️💯
Yafi nek
Modou lo rek ndam rek insa allahou Rabi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🙏
Bilahi lamb amo morome billay
Bilay lamblogue Moy lamb
Bilahi yaa meunn nk 😂❤❤❤
Biendit ❤
Yafinek ❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalle nala yalla défale diame lamba locke
Lamb kasse lay topou ❤
Aythia lambaloc yay lamb dh❤
Modou Lo mo eup doolé si lamb ji mais niou beuri hamouniou lolou.