Sam Faal:Leral mak ñi doon awwu Baay Jibi Juuf

Поделиться
HTML-код

Комментарии • 14

  • @falloumboup9626
    @falloumboup9626 Год назад +3

    Fall yaram amoul complet ngua dimbali mba thie ❤

  • @mamadouniang7707
    @mamadouniang7707 Год назад +3

    Bilae Sama khol bii séddeu na gouyyyyy ❤❤❤❤❤Dieureufeuty Borom Touba DIARAMAA Mame Cheikh Ibra ❤❤

    • @euxlukhassida
      @euxlukhassida  Год назад +2

      Alhamdoulilah yalna saa borom xep doli

    • @mamadouniang7707
      @mamadouniang7707 Год назад +1

      @@euxlukhassida Amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine ♥️🖤

    • @mamadouniang7707
      @mamadouniang7707 Год назад +1

      @@euxlukhassida Amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine ♥️🖤

    • @euxlukhassida
      @euxlukhassida  Год назад

      @@mamadouniang7707 jaa jëfati Mourite

  • @Amdy114
    @Amdy114 Год назад

    Dieuredieuf serign touba diarama mame seex

  • @AdamaNdiaye-qi3sj
    @AdamaNdiaye-qi3sj Год назад +1

    Guir yalla plateau complet bii ban tour ka

  • @abdoulayeniang10
    @abdoulayeniang10 Год назад +1

    Machallah ❤❤❤❤

  • @ridialsy2047
    @ridialsy2047 Год назад +3

    Gnou matta kham Gnou Matta Ndiangualer nakh dadj you beurrer gui rérr génération wou tay tégguou gnou si dadj t kougnou beuggeu séne Biir khol la nagn ko tarbiya t ndjang ko guiir délossi temps yi aki wakhtane yi akassa

    • @euxlukhassida
      @euxlukhassida  Год назад +1

      waww faal Werna d lu mata gueustu la wayé dinagne df ay jégo lugn ci ame dinagn ko dougal fi si chaine nieup diarignou ci barkep mame Seex Ibra

    • @ridialsy2047
      @ridialsy2047 Год назад +1

      @@euxlukhassida yokk rek sou boba bou guaine meuner di inviter deuber katt yi kouko yeukk rek tew yeukeuti ay airam bou djarer dafarat gnou wakhtane si ba am dadj you gnou beuggeu basi awou bi dana bakh loolou sama Dieuwrigne akassa na say may di Bawane Ndoundeul fall

    • @euxlukhassida
      @euxlukhassida  Год назад

      @@ridialsy2047 waww fall lolou lu meuna nek la dh t dina guindi sama class gui nga xamni daniouy degg sikar t xamu ñu dëg dëg sikar

    • @Gaydelrahmatane
      @Gaydelrahmatane 6 месяцев назад

      Déléne déglou wa Keur Serigne Khadim Lô yii niom dh Laniouy sikar maguéna lolou