Lakhou thiep akk bou ame neuteuri - Bonne Fête ✨ Deweuneti 🙏 Aid Moubarak !
HTML-код
- Опубликовано: 6 фев 2025
- Lakhou Thipe akk bou ame neuteuri
Bonne Fête ✨
Deweuneti 🙏
Aid Moubarak !
Un Grand Merci à tous !!!
ALPHIE CUISINE vous remercie du fond du coeur pour votre soutien !!
Merci aussi à nos Partenaires :
REEN Herbes et Epices
Délices Mag
Nokoss de PÉ
Bonne Fête !!!
Aid Moubarak !!!
Abonnez vous à Alphie Cuisine !
/ alphiecuisine
Lakhou tieip dei dama fogone ni dagnouy waleu thiep bi araw ko😀
Bonne fête à toi alphie et dewenaty yallah na yallah barkel liguey bi si barkè Mouhamed psl
Merci alphie si goungé bi durant le mois de ramadan ak sa say recette you saf balnagnou la bal gnou déwénati bonne fête de korité
Amiine, yalla na yalla nangou ñaane, wa Alphie recette bonus ramadan bi na ñeuw🥰🥰🥰🥰🥰
Allahouma Amine chef Alphie, balnagne la ngua balgnou yaw tamite Yalla na Yalla nangou gnane yeup 🙏 Dewenati !
Cc ma Alfie lakhou thieb bii validé waaaye déweuneti eid moubarack bonne fête de korité 😘😘😘
Deweuneti ma aida
Dewenety ma chérie balma akhh balnalla souniou yague ko feker aye ate you bari🤲🤲🤲
Khetou mots alphie mo may ray néna setal nimoul khélé 😅yalla may gniou fekké dewen inchalla
Deweunity ma alphi merci beaucoup pour toutes ces recettes délicieuses durant tout se mois béni.k Dieu vous bénisse
Machalla cest tre bon alphie merci beauquou ❤❤❤❤
Merci alphie contana si yaw machallah koor nekh trop ak yaw déwénaty balma akh balna yalla nanou yalla bole ball Bn fête 😘😘😘😘
Vraiment extraordinaire DEWENETY
amine inchala. lakh bi nekhna
Mane Alphie daf may ray. Néna woy comme chocolat fondant. 😅😅😅😅. Jam ci yow. Bonne fête.🥰🥰🥰
Haa Alphie tu me rappelle souma démane walo sa ma goro magg daf ma ko dane togal ak thiébou walo bou séw routhie mome walo walo la merci de me le rappeler c'est très doux avec du lait caillé je te suis toujours depuis la suisse
Bonne fête à toi notre alphie nationale et internationale kéne kéne dou yow yaye sounou andado bi gueune si sounou wagn niak abonnés woroul😂recette et bon Humeur chez alphie cuisine
Amine alphie thi niane yi ❤️❤️
Wa Alphie maane ak yow louñou bokko😅, lahou thièp la togou hier, c'est tellement bon, j'ai un mortier pour les aliments sucré uniquement 🤗🤗
Bonne fête à toi aussi ma alphie d'amour yalla nala yalla samou arla barké seydina mouhamed contane nagne trop this recettes yi merci beaucoup 😍😘❤️❤️
Amine way alfii bi mom machalla masi kham dra Aka nekh
Amine dewenati
Machalah alfi. Dieureudieuf. Yalnagne ko ande att you bari 🤲❤❤❤🙏🏽🙏🏽❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Machalah alphie croustillant merci beaucoup bonne fête 🥰🥰🥰
Aid moubarak ma chère alphie
Ndeyssane sama mére mome daffa dane araw thiép bi, wayer nékh na
Waw amna nioukoy araw
Alphis say therme momay danel 😃
Bonne fête de korite merci beaucoup bisous à toute la famille
Bonne fête ❤❤❤❤❤❤
Thieb 😂😂😂❤️😂😂😂
Yw dal dumala Wax dr
🤣🤣
@@AlphieCuisine bonne fête ❤️❤️❤️
👍😋♥️♥️🌹🥰❤️🌹🥰❤️
Bonne fête à toi aussi chef Alphie, merci pour toutes ces belles recettes.que le Tout Puissant veille sur toi et toute ta famille.déwénaty😘