SaThies dans Bantamba avec Modou: Lamb, Touss, Show, Ambiance | Mardi 3 déc. 2024

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 3 дек 2024

Комментарии • 70

  • @ThioroFall-s8h
    @ThioroFall-s8h 8 часов назад +9

    Il mérite les chances donné par modou lo
    Modou lo le meilleur lutteur de tous les temps machallah ❤

  • @ndongobouQuench
    @ndongobouQuench 11 часов назад +15

    Très bien communication sa Thiès yalna yalla soutoural la si barke Serigne Babacar sy 🤲 je suis fans QUENCH mes tu e responsable

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 11 часов назад +15

    Modou Lo Champion yalnako yalla doli ay ndame 👑👑👑👑👑👑👑👑❤️

  • @AbdoulayeKASSÉ-p5i
    @AbdoulayeKASSÉ-p5i 11 часов назад +12

    Vraiment danga am diom respecte frère sa thies il mérite plus que maison des projets pour développé notre pays wallahi n'écoute à personne incompétente yii nicena frère je sui d'arrière toi mais je sui jaloux cii kheur bii dafa raféte trop 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 11 часов назад +14

    Sa Thiès future roi des arènes inch'Allah amine 🎉

  • @mouhamedsane9596
    @mouhamedsane9596 11 часов назад +12

    Sa Thies le meilleur de sa génération 👑

  • @DarioSeck-j6b
    @DarioSeck-j6b 7 часов назад +4

    Supportiar Modou lo la mais sa Thiès dafa Maneu communication bou rafèt 🎉🎉❤

  • @MariamaDiop-z4m
    @MariamaDiop-z4m 4 часа назад +2

    Je suis un fan de modou sa thies est un homme bien il merite vraiment de lutter contre modou ❤

  • @yassinbuwaro8644
    @yassinbuwaro8644 4 часа назад +3

    Keur gi raféte na trope diadjief Saliou Sakho❤❤

  • @pauldiouf400
    @pauldiouf400 11 часов назад +10

    Modou mayko chance way

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 12 часов назад +32

    Balla gaye dieul nga roi bi ba paré ngir dieumi rassoulilah bayiil modou lo ak Sathies takhaw diap si rek 🙏

    • @damedia9410
      @damedia9410 9 часов назад +1

      Khana balla beugoul dara en plus son marabout avait dit que …… boulé fatei

    • @NdiawareBabou
      @NdiawareBabou 9 часов назад +1

      ​@@damedia9410 khana si keineine lakoy dieulé mai po mod lo 😂😂

    • @damedia9410
      @damedia9410 8 часов назад

      @ saway doo modou lo nekoul yakoy diokh khaliss aussi

    • @NdiawareBabou
      @NdiawareBabou 6 часов назад

      @@damedia9410 saway souma amé khaliss boumay diokh mbeur ma diokhko samay wadiour walla ma Def ko si sama bop OK...modou lo mo wakh ma deg mouné dotoul beurré ak balla gaye khaleyi lay may chance gpsr que g était clair .....et dite à vos supérieurs que ni courone 👑 bi parcelle lay yeiwo wa Salam

    • @babacar3178
      @babacar3178 3 часа назад

      Douyone sakh mougay dieul té sa thiés beug modou bou franc beugué kéne douga dieul

  • @mamadouseydougueye1696
    @mamadouseydougueye1696 11 часов назад +8

    Il communique bien ce gars

  • @mamadoukeneme2463
    @mamadoukeneme2463 10 часов назад +4

    Je suis fan de modou mais sa dafa meun communique Machall

  • @aliouCafé-v4b
    @aliouCafé-v4b 10 часов назад +4

    Machlla❤❤❤❤❤❤

  • @AbdoulBeugue
    @AbdoulBeugue 4 часа назад +2

    Modou vs Sa thies ❤❤

  • @CheikhSeck-o3q
    @CheikhSeck-o3q 7 часов назад +1

    Sa Kat diambar la keur gui Machallah nako Modou lo may chance

  • @ibrahimasow724
    @ibrahimasow724 8 часов назад +2

    J’aime bien sathies il parle bien

  • @MaForce-w2y
    @MaForce-w2y 11 часов назад +6

    Les amateurs reclament Modou lo vs Sa Thies. t

  • @ouzlepikinois
    @ouzlepikinois 4 часа назад +1

    Thiey sama mbeur mi ya waur déé💪🏾❤

  • @cheikhtalibouyadjitte8855
    @cheikhtalibouyadjitte8855 3 часа назад +1

    Sa thies ak modou lo

  • @SerigneFall-qr3ox
    @SerigneFall-qr3ox 11 часов назад +4

    Mane fans modou lô la mais sa dafa yaro ❤❤❤❤

  • @djimsow6895
    @djimsow6895 8 часов назад +2

    Modou mayal boy bi chance way

  • @elhadjiibrahimadiatta9485
    @elhadjiibrahimadiatta9485 Час назад

    Modou lo sou dieulé Sa thies niak couronne bi ❤

  • @issalaye4
    @issalaye4 11 часов назад +3

    100% modou lo mais walahi sou warei danou sathies la beug mou dann ko. Il est tellement poli et humble ❤ tei diafei diafei yim nek da xawa yagu ndeysann

    • @malicksarr2141
      @malicksarr2141 11 часов назад +3

      Nono wa kuer ball gaye doyna❌

    • @TallFambaye
      @TallFambaye 9 часов назад +1

      Wakhofi dara nga nan lan moy sa thies la beugue mou dan ko

    • @issalaye4
      @issalaye4 4 часа назад

      @@TallFambaye ngourou yalla rk moo doul diex modou loumako beug beug tmt dmay nangou ni beuss dina niow mou joxei couronne bi.
      Dimension bobu lay waxé

  • @CheikhSy-q8d
    @CheikhSy-q8d 10 часов назад +1

    Sathies modou lo le roi 🎉comba bi niorna way

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 10 часов назад +1

    Sa tihss diamou Rik ❤❤❤❤❤

  • @KhalilDia-y3z
    @KhalilDia-y3z 6 часов назад +1

    Lamb rk❤

  • @jobendongo3080
    @jobendongo3080 11 часов назад +2

    ❤❤❤❤❤❤

  • @Lamzi92i
    @Lamzi92i Час назад

    Modou moy sama mbeurr
    Meiyal sa thies chance dafa yarou
    Mériter la chance

  • @Modoufaly
    @Modoufaly 9 часов назад +2

    Donté fans Modou Lô wayé Sathies nexna may chance pour plusieurs raisons
    Yarou na si communication
    Bouy beurei day deugeul bopam def foula ak fayda dem noyam

  • @Saikou24y0
    @Saikou24y0 10 часов назад +1

    Sa Thiès dou sama mbeur mais il communique bien ,un exemple

  • @bayemodoufalldiop6816
    @bayemodoufalldiop6816 9 часов назад +2

    Ndeysan sathies daffa yaarou ....Modou lo Moy samaa mbeur mais sathies la beug mou dieul franchement

  • @adamandiaye789
    @adamandiaye789 4 часа назад

    Mbeur bou yarou Machallah

  • @CheikhKjfnkhf
    @CheikhKjfnkhf 10 часов назад +3

    Modou lo dieleul Sa Thiès dafa yaru vraiment ''niou dann ko bolleko si palmarès bii

  • @bayelaminegueye3511
    @bayelaminegueye3511 9 часов назад

    Merci modou mbaye

  • @PapeNdiaye-pz6fw
    @PapeNdiaye-pz6fw 2 часа назад

    Sa thèse vs modou lo yalla na takhaw ❤

  • @laminefall6481
    @laminefall6481 3 часа назад

    salife waye 🎉modou dieuleul boye melakh dh

  • @elimansinyan3453
    @elimansinyan3453 9 часов назад

    Momo ndanane nga walahi. Jama so yow. 💯💯

  • @babacardiop6810
    @babacardiop6810 Час назад

    Balla sama fan la waye sa thies sm modou lo mon takh

  • @ahmetdiop5146
    @ahmetdiop5146 9 часов назад

    Sa thies modou lo lou logique bilay

  • @PapyGningue
    @PapyGningue 8 часов назад

    Sa Thiès vs modou lo une très belle affiche

  • @mbayendiaye5033
    @mbayendiaye5033 8 часов назад

    Salif billay do mbeur sa yar international lala yéné ay milliards com mma wala boxe 🥊 mais sama mbeur mi ya oustaze modou kharagne lo nala may chance

  • @mamadouthiam9428
    @mamadouthiam9428 10 часов назад

    On réclame sa thies VS Modou lô combat de l’année

  • @moustaphadiouf9154
    @moustaphadiouf9154 8 часов назад

    Modou lo sathies lamb jou nara nekh

  • @cerveautv7572
    @cerveautv7572 Минуту назад

    Sa thies da niro ak Tahirou

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 9 часов назад +1

    Sathis ak modou bou taxawée da guis combat bou nékh

  • @trace-infos2a846
    @trace-infos2a846 11 часов назад +1

    Balla Gaye dal dafa wara may Sathies mou tenter chance roi des arènes comme ay moromame.

  • @mistercarter467
    @mistercarter467 2 часа назад

    Balla rek lagnuy topp mais naa bayii sathies beurrei ak mod’lo quoi

  • @badola521
    @badola521 4 часа назад

    Supporter Modou lo mais sathies bouko dane douma metti

  • @abrahamsamb6596
    @abrahamsamb6596 9 часов назад

    NITT DEUGU LAA MASSALA

  • @BayeFall-c2f
    @BayeFall-c2f 9 часов назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😊😊😊😅😅❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂😊😊😊😊❤❤

  • @mbayecheikh9965
    @mbayecheikh9965 9 часов назад

    Thiat seul

  • @MawaFayejoal
    @MawaFayejoal 5 часов назад

    Ah sa thies mii dou dane kéne comunique rek la meune

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 10 часов назад +1

    Siteu nimouy beuré bakhoul dafa wara bayi daw yi xalé la

  • @cheikhbayeniassbadiane2544
    @cheikhbayeniassbadiane2544 4 часа назад

    Sa thies meun nga beurré yarrou nga wayé lolou douyoul pour dane mbeur. Heh ak fit biir guew nga wara outtt

  • @ndiagathioye3928
    @ndiagathioye3928 12 часов назад

    Yaw ya seytané balla gaye modou lo amoul affiche boukko dakk

  • @TidianeNiang-fi6pk
    @TidianeNiang-fi6pk 6 часов назад

    Sa yorouna trop me dfa wra yokou entereman yi

  • @mamadoudia3009
    @mamadoudia3009 10 часов назад +1

    Mais boy bii epaul bi la tek di te nengn epaul dou dieleu xol len combat paketas bi cng mii

  • @MoussaKane-tm6ne
    @MoussaKane-tm6ne 11 часов назад +2

    CNG day doul ti dadiale siteu mo dane

  • @massambadare
    @massambadare 8 часов назад

    Tapha tine Modou lo Moy combat bi Sénégal wakhlen si lolou Modou c mon lutteur mai pourquoi il fuit tapha tine

  • @mouhameddiene804
    @mouhameddiene804 7 часов назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤