Max Bo waher siteu dey déranger vraiment waho li am fi la CNG wahni combat yi 19h30 lay dieh Siteu di sangou be 20h te ken avertirou ko ken disqualifié wou ko
@@kaneadama1226 sa tounou ndey nganan lan man sama pape dina nek si lamb té wara diamou dji yalla yen dal ay domou kharam ngen ms ningen meuna Mel sen mbeur werul werolen
Voici le Sénégal 😢, bienvenue. La vérité, bien souvent, est tué par crainte des menaces. Je tiens à féliciter Bour Guéweul et Lambologue pour leur courage, qui consiste à briser cette peur et à dire la vérité sans détour, malgré les intimidations. Ayez le courage de dire que Siteu n’a rien mérité ce jour là. Chapeau à Modou🎉, professionnel, athlète…
@MariataSow-vf9nl expert nono way loudoul 10% lènène niorouko ahhh na wakh mbeur mi deug voilà ils est jeune taille bi bahena meune na beurè al mystique aussi ..lène kèssè moko manqué moy biir guèw face au vip fiite bi daye guisss .en plus de ça na wagnii wakh bou barri biii ..naye deguel bopam di beurè besse bouko dèfè walahi vip yi dinagnou ame problème bou rey voilà
Sama gayi diamaguene pikine PA guediawaye médina rufisque… yeup c le Sénégal on est tous des frères jaroul wkh lou niaw wala diko jeuf sport la nak kou nékk am nga fo farr bou jékhé rek jékh na 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Pere Max avec toi Siteu dina Yekha nèk champion avec ta mentalité de victime. Il faut dire la vérité à Siteu ndam guén douko lidjanti. Amna dolè meun na beurè dafa wara deugueul bopam bayi sakouyi
6:57 Mangui sogua kham litakh Siteu niakk diom 😂Père Max dafa am complexe siteu …Kii dhé boudé siteu mome la yakaar dou avancer si lamb Yaw nga wara wakh siteu mou takhaw beuré mais chaque combat mouy daw rek ngueine takhaw fii di wakh en tout cas roi des arènes kéne douko lidieunti 😂
Père nangoul dogal té nopalou insbi sa beugue beugue rek guay wax wayé waxo lii am thi lamb djii..thi lamb dji siteu da daw modou mo def lepp bathi action bi
Délll wakh waxou mague té Di wakh sa xalé Yi deugueu. Démal lathié li waral arbitre bi deem VAR Yagui wakh Loula woroul té yagui Bakar Père il faut dire la vérité à tes poulains
Lolou yallah ngakay kalamer yallah mo djaraler ndameu modou lo si lokhoy arbitre . Wakhal ak Siteu mome mi bagne deiff dopage sache k c louche en tout cas
Père max yalla na léne yalla taxou si carrière siteu bi walahi dîna bax ñii douniou yalla bilahi siteu yalla koy faye xolam adina yeupa xani siteu mo danne ❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊😊😊😊
Max Mbergan yangi accuse CNG moyful dekabi dafeu am luwa. Yaw amo jom amo khalaat amo vision. Yangi yakhal Siteu. Lee sport la kesseh mbirrum aduna la kesseh. Yaw mack ngeu demal ngeu jaamu Yalla sunu borrom SWT. Yangi perd sa time. Wasalaam.
Yaw bouniou sonal way. Yaw sa mbeurbi ay million lagnkay fay ba paré bou arbitre bi sifflé mou dèm takhaw si guinaw sakouyi ba paré nguène di reuy lamègne. Épuis môme amoul sakh niveau beuré titre roi. Da niouko arrangé rek nguène di sonal nitt gni
Max il utilise de gros mots haine ? Sitteu subit des injustices côté sportif évolution de son lutteur ? Prochain adversaire et la tu critique le nouveau cng après 2 semaines Tu préfère avoir des défaites par avertissement ⚠️ et tu est heureux qu’il gagne pas 😂 et le vieux s’énerve vite
Max Bo waher siteu dey déranger vraiment waho li am fi la CNG wahni combat yi 19h30 lay dieh Siteu di sangou be 20h te ken avertirou ko ken disqualifié wou ko
Yaw ki sa moromou bayla amal yar réw nga trop
@@kaneadama1226deug da am moromou baye wala moromou mame
Sa bay day féne té doko wakh daguay fén
@@kaneadama1226 sa tounou ndey nganan lan man sama pape dina nek si lamb té wara diamou dji yalla yen dal ay domou kharam ngen ms ningen meuna Mel sen mbeur werul werolen
Lolou gnii teuguone combat bi moko wakh ms lamb 20h30 laniou wakh la wara diekh
Voici le Sénégal 😢, bienvenue. La vérité, bien souvent, est tué par crainte des menaces. Je tiens à féliciter Bour Guéweul et Lambologue pour leur courage, qui consiste à briser cette peur et à dire la vérité sans détour, malgré les intimidations.
Ayez le courage de dire que Siteu n’a rien mérité ce jour là.
Chapeau à Modou🎉, professionnel, athlète…
Père max mbargane 😂nanal glace 🍨 siteu dafa daw combat bii yepp tapet la 😂 roi des arène kenn douko lidianeti 😂😂
Do nopi iwo
Roi des Arènes kouy Rooyy Lac 2 douko jeull Max Nanaal ndoox..😂😂
Fatma dia sa liguéye rafétna trop mane yaw rk lay suivre bonne continuation
Mor kang kang seul domou baol ak colobane yalla nga ame ndame si diop 2
Waro wakhé ni siteu mo beuré woul, violence rk lafi infi ,beuré woul,réglé woul, kène lidieunti woul sa mbeur 😂
Ki mo beurii wakh way ahhhh nono way tamitt😅😅😅
Qui expert leu
@MariataSow-vf9nl expert nono way loudoul 10% lènène niorouko ahhh na wakh mbeur mi deug voilà ils est jeune taille bi bahena meune na beurè al mystique aussi ..lène kèssè moko manqué moy biir guèw face au vip fiite bi daye guisss .en plus de ça na wagnii wakh bou barri biii ..naye deguel bopam di beurè besse bouko dèfè walahi vip yi dinagnou ame problème bou rey voilà
Père Max moy lamb bilahi ❤❤❤❤longue vie pour vous 🤲
Père max félicitations 🎉 Siteu nouveau roi des arènes
😂😂😂😂 le roi des guinaw sakou
Roi des dawkinda 😂😂
Thiak thiak yi
Sama gayi diamaguene pikine PA guediawaye médina rufisque… yeup c le Sénégal on est tous des frères jaroul wkh lou niaw wala diko jeuf sport la nak kou nékk am nga fo farr bou jékhé rek jékh na 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Pére bayil soxor té ngua gueumm yalla
Mais nak père déleu wakh li âme siteu da daw
Ay wa dji père nguir yalla menou guem yalla tamit ahh ko père diaxal ni man rk lalal aime 😂
Dans tous les sports de combat pour être le champion il faut battre clairement le tenant du titre, pas de façon litigieuse.
Siteu dafa daw sou takhawone modou lo reuy ko
Pere Max avec toi Siteu dina Yekha nèk champion avec ta mentalité de victime. Il faut dire la vérité à Siteu ndam guén douko lidjanti. Amna dolè meun na beurè dafa wara deugueul bopam bayi sakouyi
Max daguay doul rek lougnouy khekh si siteu
Rew nga
MAX MBARGANE C'EST NORMAL MOU WAKHÉ NII NDAKH 10% YI 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
No makse wéra nga li nïepe wakh moy degue Sénégal ko yakar ame na ngor bo lalé kotém kham ni xalis moko nior
Il faut pas salir la victoire du 👑 roi modou lo diame daye Nangou dogal ah
Pér 10% 💶🫵🏻😆🤣😂courage
Père Max Bayil yamba bi ngay diokh khaleyi 😔
Père boul def appel bipé nga kéne dieuloul defal télégramme
GUEMEUL YALLA MAX
Bilaye di ngua mougne dh modou lo moye roi des arènes
Pére wakhal sa mbeur mi ay deugue mo gueune siteu dara lafi défoul nek di daw rek ba lamb ji diekh kilifeu nga nak wakh ko deugue mo gueune
Diop2 Seul ❤❤❤❤❤❤
Vraiment siteu mon dane nk wakh degue
Couronne mom dégueu nguénssiy am mounane mo daneu kou daw combat yeupeu noy dané
Niuy xeex Siteu nio doon xeex Sonko,nafekk lagn
Moh dedet bokkoul dheii 😂nakh sonko dou daw diambar la
Siteu kasse siteu kasse 👑👑👑👑❤️
6:57 Mangui sogua kham litakh Siteu niakk diom 😂Père Max dafa am complexe siteu …Kii dhé boudé siteu mome la yakaar dou avancer si lamb Yaw nga wara wakh siteu mou takhaw beuré mais chaque combat mouy daw rek ngueine takhaw fii di wakh en tout cas roi des arènes kéne douko lidieunti 😂
Mercy pere Siteu kesse Roi bou bess Le Roi Siteu..
Siteu ku bakh la wayeh du gat chi birr gew bi. Daa daw komba bi.
Roi de courir 😂😂
Roi bouy daw ba lamb dji diékh 😂niakk diomm
Per max yawe danga ragal siteu doko wakhe deuge limo takhe Quenche beugone dieul licencam yawe ecrit lamsar fale wofa bebe mbeur boudoul siteu
Père nangoul dogal té nopalou insbi sa beugue beugue rek guay wax wayé waxo lii am thi lamb djii..thi lamb dji siteu da daw modou mo def lepp bathi action bi
Délll wakh waxou mague té Di wakh sa xalé Yi deugueu. Démal lathié li waral arbitre bi deem VAR Yagui wakh Loula woroul té yagui Bakar Père il faut dire la vérité à tes poulains
Li ngay dougeul si nopou siteu nga wara bayi li ngay conseiller siteu baxoul et puis pourquoi siteu refuse de faire le test anti-dopage
MOD LO MOY ROI
WOUYIL MBEUR DANGAYE DOUL REK
Ma ngui comprendre lou takh siteu thioune.
Pér geumeul yalla téga wakh siteu deugue mou bayi nimouy beuré di daw rk 😂😂😂
Kou banige siteu sa data ndaye
Man ak sa baye nioo took ni di naane café Touba néena siteu rek la banie
Manak sa baye nioo took ni di naane café Touba néna Siteu rek la banie
so nangouwoul défaite siteu thi modou boul waro nangou défaite siteu thi lac
MAX DANGAYE YAKHAL SITEU REK BAYIKO MOU BERÉ
Pér démal nga nane galaas😂😂😂
MAX KOU SOF NGA
Dix Pour Cents Takhna Ngay Fén Diarouko Khaliss Boumou Takh Nga Diay Sa Ngor
Do rouss sakh amo fayda omo foula mousso dane mbeur sa carrière max
Siteu li motakh mou niak diome kene douko wakh deugue
Thiak Thiak 😂😂
Max margane nopaloul amo mbeur meune gua lékk si mom khaliss nakk
Per max mane koula nawone la me legi bayina la dotoumala deglou si lambe yawe do geum yalla siteu dawe lambdji bamou diekhe ngaye wakhe fi
Iow père boulniou sonal waay
MAX SE WAKH DAFA BARI
SITEU MOY LAC 3
Pa bi noumou niawe nonou la meune fein
Wakh ko mouy deggel boppam mom siteu
Max del lah siteu deug Doulit dou fene
DANGA DANOU 5 APPUS
Max pa diamaguene 😂 deugla
Yw rk yatakh mbeur mii amoul diome mbeur thia guéw ga lagnou wakh
Ni mouye beuré kaye bakhe na. Ndakhe diote nga sa 10 pour cent. Ak Max mi Siteu dou meusseu nek roi des arènes.
Pére bayile fénne nack sa mbeur danouna
Max yangi melniki buki. Yaw yaa nyaw teh buga ekrabi.
Mom kay doyna waar 😂
Toure Leuz
Deg pur
Fatma boul niou sonal khoul soukhour guam
Bouniou wakhé té yala tah siteu dane nako
Lolou yallah ngakay kalamer yallah mo djaraler ndameu modou lo si lokhoy arbitre . Wakhal ak Siteu mome mi bagne deiff dopage sache k c louche en tout cas
Ya meuneu fenn ana boppu siteu bi demal xoli benene angle
@hamadykamara8662 do deim kalamer yallah tmt soneu nga dei
Max sa data ndeye ok
Ioe Kou Rew Gua
Père max yalla na léne yalla taxou si carrière siteu bi walahi dîna bax ñii douniou yalla bilahi siteu yalla koy faye xolam adina yeupa xani siteu mo danne ❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊😊😊😊
Max Mbergan yangi accuse CNG moyful dekabi dafeu am luwa. Yaw amo jom amo khalaat amo vision. Yangi yakhal Siteu. Lee sport la kesseh mbirrum aduna la kesseh. Yaw mack ngeu demal ngeu jaamu Yalla sunu borrom SWT. Yangi perd sa time. Wasalaam.
Yaw bouniou sonal way. Yaw sa mbeurbi ay million lagnkay fay ba paré bou arbitre bi sifflé mou dèm takhaw si guinaw sakouyi ba paré nguène di reuy lamègne. Épuis môme amoul sakh niveau beuré titre roi. Da niouko arrangé rek nguène di sonal nitt gni
Max il utilise de gros mots haine ? Sitteu subit des injustices côté sportif évolution de son lutteur ? Prochain adversaire et la tu critique le nouveau cng après 2 semaines
Tu préfère avoir des défaites par avertissement ⚠️ et tu est heureux qu’il gagne pas 😂 et le vieux s’énerve vite
Bayil yamba
😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Pabi il n'est pas mature kome khalé koi
Kou banie siteu sa koyi baye
Siteu façon CON you mélni yaw rk gnokay yakal
Doff nga rk nga nék sa guinaw clavier di saga dof nga rk😂😂amo khél
Tu parle tro
Iow kou sof gua mak day am foula
Tapalé mayéwoule titre roi des aréne
Kou banige siteu sa data ndaye
Yaw dangeu bange Siteu kin sa koyu baye.
Kou banige siteu sa koyi baye
Kou banige siteu sa koyi baye