il doit etre convoque car il a menace tout l'etat du senegal et les senegalais,il doit etre convoque,l'etat doit etre fort car ils sont entrain de tester leur degre de courage
Bay Ndiaye n'a fait qu'une illusion mais cela n'explique pas qu'on doit l'arrêter il a droit à la parole mais pas aller jusqu'à menacer un république il fait juste une erreur de communication sa peu arriver à tout le Monde mais contrairement à bah diakhaté il a insulté publiquement Cordialement Momo bou sonko 🙏👌
ES CE QUE BAY NDIAYE MINGUI FAY IMPOTS ?? 🤔🤔 D'OU VIEN L'ARGENT ?? 🤔🤔 QU'ELLE SOCIETE IL DIRIGE ??🤔🤔 IL FAU LE SANCTIONNER. ETAT SOIT FAIRE DES AUDITS SUR LUI
Baay Njaay yaboo mu ñaan combat bi jàmm rekk am ci, ndax ludul loolu lépp ci kawam la jëm Bu dee waajii di wax Moom kuko dégg xam ne day duul masul xeexal dëgg waaye nak wax na dëgg ci lim me dëgg lay xeex ndax ku xeexalul dëgg rek yaa ngi koy xeex, te day duul masul bokk pastéef, doomi raam.
Vérité absolue mon frère
Baye Ndiaye mo yabaté khamoul bopam
Gars yi danio todj lé. Li lép thi tok mouy dokh bila, t dafay diékh
Patriotes yi vraiment wakhé rek vraiment mais li dokhaloul rojet bi
Bayil ba Mouna bindeu projet
Baye Ndiaye Bayiko réwoul saax
Baye ndiaye na combat bi rombe heure bi gua khôl yaw rewo sakh te lou khew digua KO regretter inchzlla
Baye Ndiaye est dans le viseur...la loi ne peut pas sévir à 48h de l'événement...Le jour j à l'heure H la loi va sévir...chaque chose en son temps...
Yene hana meunoulene may niou diam delene justice doungene kene
Doull way yaw bayil baye Ndiaye
Merci beaucoup frère ❤❤❤
il doit etre convoque car il a menace tout l'etat du senegal et les senegalais,il doit etre convoque,l'etat doit etre fort car ils sont entrain de tester leur degre de courage
Des vrais opportunistes aziz da fok mo mom lamb dji
Les promoteurs de la lutte doivent être protégés. Ce sont des créateurs d'emplois. Bari nguéen wakh trope bayiléen lamb ji
emplois Hanna se yaye AK pape gnofeyy liguey ki tog Menacé tout les Sénégalais beu le 21 inchallah
Yaw nokhoul feulé mounane créa d'emplois idiote iniorent mana féne
Bay Ndiaye n'a fait qu'une illusion mais cela n'explique pas qu'on doit l'arrêter il a droit à la parole mais pas aller jusqu'à menacer un république il fait juste une erreur de communication sa peu arriver à tout le Monde mais contrairement à bah diakhaté il a insulté publiquement
Cordialement Momo bou sonko 🙏👌
Baye Ndiaye wakhi khalé rek lay wakh
loumou wakh rék sonko wakhna louko raw
Soufguen way Sen wakh barina way
Parler pour parler mon frère
Si Oussou bb lagneko copier l'homme le plus méchant
Doff bi kanela Sénégal mo néékh khana mbokou bah diakhaté nga démal nga took 😂😂
ES CE QUE BAY NDIAYE MINGUI FAY IMPOTS ?? 🤔🤔 D'OU VIEN L'ARGENT ?? 🤔🤔 QU'ELLE SOCIETE IL DIRIGE ??🤔🤔 IL FAU LE SANCTIONNER. ETAT SOIT FAIRE DES AUDITS SUR LUI
Bay ndiaye rewoul sakh mais nak bayilen fén sen titre bi moy lolou
Yaw doul li ngay sokhor te bone yéné néik la te borom mosiy fanane baye ndiaye diam rk ngay am inchallah ❤❤
États bi dako wara diap
Après lambo senegal chaque fois c'est le mauvais temps
Wakho fiy darra 😂😂😂
Boy yi dagno tothie sen thiorou daye daffa yomb boybi dagnoukko warra dieuli gnaf dayam thi kassobi bakham liuy khew
Dofff deug moy genre yiii .gni nio yakh sènègal. Kane ngay wakh gayiii fi kèn doufi sa gars .yaw si niou beug yakh sènègal si nga bokou
Xolalma yiiiii khetou mbam rek demal outi ligueye mbambi
Day réwantelou Bayiko Domou khadj Domou harame
Il doit être arrêté et annulé cette combat
Empereur 😅
Seytane bakhol
Baye.sk.aziz.yalla.nalene.yallaouseule.ci.sey.none
Yaw.doule
Wero
Yaw sa data ndaye way wakhofi Dara bou done sa baye do wakh liii
Bi nga andek pastef nga perte🤙
Yw giess kham ne Yw maso Khékhe bayil doul Wa apr gua
Baay Njaay yaboo mu ñaan combat bi jàmm rekk am ci, ndax ludul loolu lépp ci kawam la jëm
Bu dee waajii di wax Moom kuko dégg xam ne day duul masul xeexal dëgg waaye nak wax na dëgg ci lim me dëgg lay xeex ndax ku xeexalul dëgg rek yaa ngi koy xeex, te day duul masul bokk pastéef, doomi raam.
Sa way yaw topoul feulé wakhofi dara lou am chance
doul rek gaye def mayeniou diame waye fene rek
🥲🥲🤷🤷
Bilahi walahi bokoul pastef .😂😂😂
Yaw sa data ndaye way wakhofi Dara bou done sa baye do wakh liii