Heures de prières pour Dakar et ses environs du 31 Mars au 6 Avril, du 9 au 15 Ramadan 1444. Fajr 5:49 Souba 6:04 Tisbar 14:15 Takussan 17:00 Timis 19:29 Guéwé 20:29 Abstenons-nous de toute nourriture et d'absorption de tout liquide à 5:39 (heure de Imsak) environ 10mn avant salatoul fajr. Yalla nañou SUNU BOROM nangoul léep louniou ko jammou ci wéer wi, barké SEYDINA MOHAMED (SAWS)
Gnogno et Saneex dans Njaba😊 Fat Dame dans Impuissant 👍 Bella et Mbaye dozé dans mounieul 😊et bientôt Serigne Ngagne dans khew-khew 😄 je suis très contente de leurs intégrations 😊y’a pas plus exprimantés qu’eux 🎉 ce sont de grands artistes machallah
@@idrissaseck259 wa EvenProd rek lay top motakh 😂😅 mais je trouvais trop injuste d’intégrer des personnages justes par des critères de beauté ou autres alors k on a de très bons artistes renommés machallah 🤩au capital du théâtre
Wa mais trophée yi niouy diokhé si meilleur acteur yi mome jsprk serigne bouli amnasi rék😂 il est trop fort dans sont rôle vraiment🤣🤣🤣 kou and ak mane beuseul j'aime🥰🔥✌️
Pensée aux Modou-Modou et Fatou-Fatou ..... Koussi ame mbokk bounek bitiim reww nguirr Yalla parfois woko rien que pour waxtanalko car même s'ils font tout pour rendre fière à leurs parents, amis et proches, certains d'entre eux traversent des moments qu'ils ne peuvent expliquer à personne. Alors, ne serait-ce que pour leurs envoyer un message qui pourrait apaisé leur cœur, un message juste pour prendre de leurs nouvelles sans rien demander en retour , serait un grand bonheur pour eux ... Nb: A vous les Modou-Modou et Fatou-Fatou , Que le tout Puissant vous protège...
Cette série ne présente aucun sponsor au début, ça prouve que le thème qu'il aborde dérange beaucoup... Bravo Evenprod, il faut faire bouger les lignes 👏🏿
Si Alou avait acheté le salon là pour Oumy elle ne l’aurai jamais accepté vu tout ce qui s’est passé entre eux dernièrement avec la trahison du gars , Bana et tout
Alou bou donn gorr dina khamni Oumy mon gueun yeyo salon bi. Elle qui a sacrifier tout son argent pour lui ba Bana guiss ko diko beugg.. Mo takh loumou woné bakh meunou ma saff.. Badolo un jour badolo toujours
Alou Yagui defall bana wayer est-ce que doula worr un jour comme nigua woreii wonn alima adouna dafa goudou tank dhh wa bakhna Bravo à toute l’équipe d’even prod 👏🏻🥰❤️
Osman saison 2 épisodes 15 bande annonce m'intéresse pas du tout je suis en train de faire un tour à la maison et toi tu es où actuellement je suis en train de faire un tour à la maison et toi tu es où actuellement je suis en train de faire un tour un tour à la à la maison et toi tu es où actuellement je suis en train en train en train de faire un tour à la maison et toi tu es où actuellement je suis en train de faire un tour à la maison et toi tu es où actuellement
HEURES DE PRIÈRES DU 31 MARS AU 06 AVRIL 2023 Fadjr: 05h59 Suba: 06h04 Tisbar: 14h15 Takussan: 17h00 Timis: 19h29 Gue: 20h29 Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Mane je ne comprends pas le fait que c'est Ouly qui soutenait Alou sur tout avec un coeur en or et ce dernier part aidé une autre personne avec qui il l'a trahie vraiment la reconnaissance n'existe plus . J'espère un karma pour Bana et Alou
Si tu tombé sur ce commentaires qu'Allah t'accorde un beau destin plein de réussite dans tous ce que tu entreprends ALLAHOUMA AMINÉ ❤️❤️🙏 koorou diam ak salam 🙏🤲
Alou ? Khana tu as oublié tout ce que Ouly a fait pour toi ? Tout cet amour sincère que cette brave dame avait pour toi ?? Teye nii ngakoy fayeh ?? Boula lii djigueh ma khamni kone mbeurgua !
@@evenprod Amour ok wayeh ingratitude bakhoul. La pauvre femme a tout fait pour lui, elle ne mérite pas d’être payée aussi injustement. J’ai bien peur que le karma ne les rattrape un jour ces deux là
Vraiment série bi yepou rôle ouly momasi geuneu rk ndakh day diagalè dall ak worou yalla 😊😢quoi liko dall lepou ms loo wakh rk monii Ylla bxneu 🧏🏿♀️machallah ❤ ku d’accord 👍 rk aimel vraiment 😢
Alou dioume nga dé , avant mayé salon bi dang ko wara tak diabar pour verrouiller, nélaw nga té bo moytouwoul jour bo yéwo di nga méré sa bop. Jamono dji jiggën diaroul gaawa wolou. cheeeee nélaw nga
Heures de prières pour Dakar et ses environs du 31 Mars au 6 Avril, du 9 au 15 Ramadan 1444.
Fajr 5:49
Souba 6:04
Tisbar 14:15
Takussan 17:00
Timis 19:29
Guéwé 20:29
Abstenons-nous de toute nourriture et d'absorption de tout liquide à 5:39 (heure de Imsak) environ 10mn avant salatoul fajr.
Yalla nañou SUNU BOROM nangoul léep louniou ko jammou ci wéer wi, barké SEYDINA MOHAMED (SAWS)
Pmpm😊o
Pmpmm
Ooppop😊
Amine et merci 🙏🏽🙏🏽
Amine
Gnogno et Saneex dans Njaba😊 Fat Dame dans Impuissant 👍 Bella et Mbaye dozé dans mounieul 😊et bientôt Serigne Ngagne dans khew-khew 😄 je suis très contente de leurs intégrations 😊y’a pas plus exprimantés qu’eux 🎉 ce sont de grands artistes machallah
Team thies🎉❤❤
Yaw am gua inspiration dh😂😂
@@idrissaseck259 wa EvenProd rek lay top motakh 😂😅 mais je trouvais trop injuste d’intégrer des personnages justes par des critères de beauté ou autres alors k on a de très bons artistes renommés machallah 🤩au capital du théâtre
@@bintadiop9954ak ndeye sini
Mère Sow dans 4 fantastiques 😂
Wa mais trophée yi niouy diokhé si meilleur acteur yi mome jsprk serigne bouli amnasi rék😂 il est trop fort dans sont rôle vraiment🤣🤣🤣 kou and ak mane beuseul j'aime🥰🔥✌️
Bi passé dé Bathie Massamba laniou ko diokh bou série Karma khaw ma yane caractères laniou ko tané wayé diakhal nama
Franchement il joue très bien son rôle
@@bocarguisse2282 kone khana niarr la mane bou fatt kiné la guissone
@@bocarguisse2282 kone khana niarr la mane bou fatt kiné la guissone
Billay dafa aay trop mâcha allah
Pensée aux Modou-Modou et Fatou-Fatou .....
Koussi ame mbokk bounek bitiim reww nguirr Yalla parfois woko rien que pour waxtanalko car même s'ils font tout pour rendre fière à leurs parents, amis et proches, certains d'entre eux traversent des moments qu'ils ne peuvent expliquer à personne.
Alors, ne serait-ce que pour leurs envoyer un message qui pourrait apaisé leur cœur, un message juste pour prendre de leurs nouvelles sans rien demander en retour , serait un grand bonheur pour eux ...
Nb: A vous les Modou-Modou et Fatou-Fatou , Que le tout Puissant vous protège...
Yhh frère DEUG Gou weur Nga wax
Yaou bach ga dé machalah 🙏🙏🤍💚 yalah ga am diame 🙏🙏
Merci Ndey san
@@fatoumataba5107 Amine, Yalla n'a borome bi tassaré niou diam Djiii
Ndeysane yoe moom borom bakh guaa🙏 man dh doumaa woo kein koo woo mou yakarnei dankooy nianeu😂wala dank koy wakh sokhlaa tei fekk nouvelle laam gua beugonee khaam😅😂🤔
Kou beugue ame dome bou gore toudéko seydina mouhamed rek lalal j'aime ❤️❤️❤️
Bayilene di fower sene khele ci reseaux sociaux yi saway yonente bi dou morom fi dou pour lolou
Amine yarabi 🙏
SALALAHOU ALEYHI WA SALAME AMINE
PSL
Amine
Gni teudd ci lalou Hôpital yi yallah nalén yallah yeukeuti🤲🏽❤
Amine
Amine 🤲
Amine inchalah
Amine inchallah
Machallah sa commentaires amna solo❤❤
Salam... Prières du 31 Mars au 06
Kheud 05h 00
Fadiar 05h 49
Souba 06h 04
Tisbar 14h 15
Takussan 17h 00
Ndogou 19h 24
Timiss 19h 29
Guéwée 20h 29
Merci beaucoup pour les heures
@@sambadia3931 on est ensemble
Yalla nala yalla faye
@@coumbabarry650 Alahouma amine way gnubok lep Inchallah
Merci
Hé Bana ak Alou bamou soti dal Alou joue bien son rôle vraiment chapeau à vous l'équipe l'équipe evenprod 😍🥺
J'espère qu'elle va le trahir comme il l'a fait avec ouly 😊
Cette série ne présente aucun sponsor au début, ça prouve que le thème qu'il aborde dérange beaucoup...
Bravo Evenprod, il faut faire bouger les lignes 👏🏿
Tey dama done Sangou nane " keuf nagn bop bi yobou khel mi démétoul sagom dagnko ndiabar " 😂😂😂 bilay even prod télécharger nguen ma j'adore trop vos génériques
Ëpounaaaa😂
bayil di waye thi dousss
Boula djiné yi kheuté😂😂😂😂
@@nogayeniass8595 woy😂😂😂😂
@@nogayeniass8595 bayyiko fofou rek
Serigne bouli est trop fort 😂😂😂
En matière de douul xana😂😂
Tes parents vivront jusqu’à à ta réussite dit Amine ❤😊
Amine
Amine inchalla
Amine
Amine ma belle
Amine
Longue vie aux parents et k'allah exausse tous nos prières ❤🎉
Penda fall je te connais on dirais où habite tu réponds moi stp 😢😢😢
@@AntaKebe-el7mm Yoff tonghor
Meilleure générique de tout les temps ✊🏾👏🏾💥
Cvtroenwlsncu dl d'huile
Kou geum ni day métti rk Mais SONKO moy nékk Président
2024 inchallah
inchallah ☝️
Que dieu nous accorde les biens fait du mois de Ramadan 🤲🤲 Amine et nous pardonnes nos péchés Amine 🤲🤲
Amine
Amine
Bouly ils joue bien son rôle 😂😂😂
Ibrahima Dkt Merci
Notre série préféré ❤
😅😢😊😅
Déwén si heures bi Yalna fék sonko palais mouye ndogou ☕🌮😍
🙏🙏🙏amiin ya rabi
Amine wayy si barkè salalahou ala mouhamad
Amine
Amin way
Macky
Keep kou Beugue am Domme Bou Djiguén touddé KO sa yaye RK beuseul j'aime ❤
Yalla na diamo yague sy Sénégal amine 🇸🇳❤💯🙏🇸🇳❤💯🙏
Si Alou avait acheté le salon là pour Oumy elle ne l’aurai jamais accepté vu tout ce qui s’est passé entre eux dernièrement avec la trahison du gars , Bana et tout
Vraiment Bana aurait dû souffrir après tout ce qu'elle a fait a ouly
Alou bou donn gorr dina khamni Oumy mon gueun yeyo salon bi. Elle qui a sacrifier tout son argent pour lui ba Bana guiss ko diko beugg..
Mo takh loumou woné bakh meunou ma saff.. Badolo un jour badolo toujours
L
@@ThiesKaay wallahi
C est ouly pas oumy
Codou ndiaye damako yeureume koune serigne amoul dala diapoul Sanex ❤❤❤
Bouly meilleur acteur dans cette série
Genre il est vraiment dedans quoi , da gueum ni mom serigne deug laa 🤣🤣🤣
Alou Yagui defall bana wayer est-ce que doula worr un jour comme nigua woreii wonn alima adouna dafa goudou tank dhh wa bakhna
Bravo à toute l’équipe d’even prod 👏🏻🥰❤️
J'ai eu la même pensée je vois Bana retourner avec weuz
@@boubacarboiro5813 hum exactement
@@mbayangdiagne1904 En tout cas la suite nous le dira
@@mbayangdiagne1904 Amal koorou diam reck
Weuz dor kat la sou guisser bana am khalis dina séduire dokhanat co Alou perte
Meilleur série du monde ❤❤
Osman saison 2 épisodes 15 bande annonce m'intéresse pas du tout je suis en train de faire un tour à la maison et toi tu es où actuellement je suis en train de faire un tour à la maison et toi tu es où actuellement je suis en train de faire un tour un tour à la à la maison et toi tu es où actuellement je suis en train en train en train de faire un tour à la maison et toi tu es où actuellement je suis en train de faire un tour à la maison et toi tu es où actuellement
Le trio de Atou Leuz et Junior c'est un triplé de choc 😂😂😂😂ALJ= Andeu Leudieul Jeux bi 😂😂😂 Sabou (Ndeye ) bayil nangou guinga néké 😂😂😂😂😂😂
Samba FALL Ya wah li yeup boul leudieul jeux wouy diambour
@@evenprod 🤣🤣🤣trio bi nioy Leudieul Jeux yeup 😂😂😂😂
Sonko ndam rek incaallah 🙏mé yallana niepou am diamou waxal amine yarabii 🙏
Machala bonne continuation très belle série que le bon dieu nous garde toujours ensemble amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
No serigne bouli est le meilleur de sa génération 😂😂😂 il mérite le titre du meilleur acteur
Qui est d'accord ?
Nn doucrè
SERIGNE bouly❤est un acteur multidimensionnel il assure grave ses rôles
HEURES DE PRIÈRES DU 31 MARS AU 06 AVRIL 2023
Fadjr: 05h59
Suba: 06h04
Tisbar: 14h15
Takussan: 17h00
Timis: 19h29
Gue: 20h29
Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
President sonko rek ❤❤❤❤❤❤✊🏽✊🏽✊🏽✊🏽✅✅✅
Mane je ne comprends pas le fait que c'est Ouly qui soutenait Alou sur tout avec un coeur en or et ce dernier part aidé une autre personne avec qui il l'a trahie vraiment la reconnaissance n'existe plus . J'espère un karma pour Bana et Alou
Lolou la done wadia wakh nga wakh ko vraiment pdt les moments durs c est ouly qui était là où est la reconnaissance
bilaye même moi lolou la wakh
Yow dé yagui melni kou féké sama waxtane
Liii nakkkk moy Guor bouléne ci dara diakhal
Lii dé ladone weur
Yala na akou ouly dal Alou amine touf touf
Pauline Mendy Sa gnane baleu
Yalla sonko dieul réwmi 🤲🤲
❤ à l'heure, bon visionnage a tous
Njambar kagne laay degne 😂 founei dougou naffaa visaa rekk 🤣😂njambar Fann la niou dieum😁😁
Notre série préférée
Ndeya wolou nga sa serigne wayé yalna nga échoué 😅😅
S. Boully est le meilleur 🎉😂😂
😂😂😂😂bouly douma Ray bilahi
Ndeysane mbeuguel dîna def louné xolal alou ak banna 😊
Kou gueme né digua ame dome bou gor toudèko seydina mouhamed wakhal amiine té lal ❤
Amine
♥️
Amine
Aminn🤲🙏
Codou Ndiaye Loula khir si khesaal
J’adore le couple de bana et Alou malgré qu’il a trahi Ouly .
Bravo à tte l’équipe ❤❤❤
Avec evenprod notre cœur bat plus fort 😘🎉❤ machallah ❤️ thia kaw thia kanam unchallah ❤️❤😊🔥🎉🙈
Mame faty Bousso Diadieuf
Yalla nieup am diam ❤ Ak soutoura
Alou nak werenga Ak lila Ouly defaral lep nga worko mou nek en faillite japalewoko
Ouii dîna amat couzin wam bi mokoy diapalei
Yalla gua ame dome toudé kou Seydina Mouhamed (PLS). WAKHALE Amine ❤❤
Amine yarabine inchalah
J'aime beaucoup le personnage que Aliou incarne ❤
Koy worè touba rk lalal👍
Tivaouane lagniy woré
Mais sétlou nguéne wadji done rombou si séquence sou niom atou ak junior weuz sakh ay rétane dako diape mouye kholé rék😂😂😂😂😂😂😂
Man dama yakaronn ni si la bokou day took sakh😂
Limako ré😂😂😂😂😂
Si tu tombé sur ce commentaires qu'Allah t'accorde un beau destin plein de réussite dans tous ce que tu entreprends ALLAHOUMA AMINÉ ❤️❤️🙏 koorou diam ak salam 🙏🤲
Notre BOULY national 😂😂😂😂😂😂
Ngoumb le surnom de papa yalna souf sed si kawam🤲
Amine
Bana(Khadija) ioe rk y’a takh may sétan série bi ma belle😘Machalla bonne continuation🙏❤️
Mme Thiam Lolou nexnaa
Mane serigne bouly lay weur... néna guinakhou badio 😂
😂😂😂😂😂
Codou ndiaye sa khèssal bi mètti nama 🥲
Vraiment 😢
Bouly rew na néna des fois nga guis jiguene you wow kong fangué farou rapp bila😂😂😂
Ndeye marieme Diakhate Badou yok stress gni di maigrir sans raison
🤣🤣🤣🤣 Lolou la yakar nak wayé ay waxou bouly diaroul door dom😂
Sanexx joue très très très bien jtm bien
Amy Seck Merci
merci even prod
Machallakh EvenProd❤
Instrument qui commence cette série benènne affaire leu🎼🎷🎻🎧
Moustapha Thiam Merci
Alou faté gua ni ouly mola passalon gua dem Europe donc li gua defal bana ouly moko méritée
Bravo khoudia mbouly day doule rek ndiambar keut bou mag la xamoul dara
Sunu série préféré ❤
Machalah njabaar dafa nékh pasq dalay yé silou Bari vraima amoulén morome weuss Moy sama acteur
Bilahi bouli Dinama raay néna kérok bimako défé bima gnibisé diouné yi dane madone nokh
Kou boug sering bulli bosal aime
Serigne bouli😅😂😂😂😅😅😅😂😂 sheuttttttttt non way
Mais aussi wa thies dans vos productions c'est juste génial
Force à toute
kou beug seydina moukhamed lalale j'aime ❤❤❤❤
On réclame le bonheur de Ouly
Machala amna solo vraiment réalité pue et dure
Alou ? Khana tu as oublié tout ce que Ouly a fait pour toi ? Tout cet amour sincère que cette brave dame avait pour toi ?? Teye nii ngakoy fayeh ?? Boula lii djigueh ma khamni kone mbeurgua !
DASO DASO Il se laisse epmporter par son amour pour bana
@@evenprod Amour ok wayeh ingratitude bakhoul. La pauvre femme a tout fait pour lui, elle ne mérite pas d’être payée aussi injustement. J’ai bien peur que le karma ne les rattrape un jour ces deux là
الحمد لله
Vraiment série bi yepou rôle ouly momasi geuneu rk ndakh day diagalè dall ak worou yalla 😊😢quoi liko dall lepou ms loo wakh rk monii Ylla bxneu 🧏🏿♀️machallah ❤ ku d’accord 👍 rk aimel vraiment 😢
Codou Ndiaye yakk nga sa teint bou Nice nak
Legui segne boulli kene dou wakh si kawam tamit 😂😂😂😂
Alou dioume nga dé , avant mayé salon bi dang ko wara tak diabar pour verrouiller, nélaw nga té bo moytouwoul jour bo yéwo di nga méré sa bop. Jamono dji jiggën diaroul gaawa wolou. cheeeee nélaw nga
Bana est materialiste 😂
Wii de trop 😂 téh lolou mome c pas bien 😮
Bana kay bakhoul epuis dafa gnak kersa meun wakh bou gat chipp
😂😂😂😂et pourtant nonoula ko beugué nak
Sérieusement
❤❤❤
Free Sénégal
Free SONKO 🙏💪
Je suis trop content si li alou defal bana bilahi❤️
Souleymane Dieye Super
Khoudia Fall robe bimou soll amnako à des prix abordable nekh si yarame ❤
Kou beugue done milliardaire 🤗😍❤️
Dioumisha Bv Beineu si yaw
Meilleure serie
Ani ni beug seugn bouly wanelenn se bopp 😂😂😂
KOU BEUGEU SERIGEN BABACAR S'Y LALAL J'AIME 😍
Kéneu dou momeu ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mom laniouy noyei ❤sy MaLiCK
😂 no segn Bouli amoul kw, kone ni la cas bi dèmè 10 oubi là ok, mais Alou mome c’est un vrai gentleman geste bi c’ vrmnt chic ❤
Seugn boully dou nit 😂😂oubi oubi wat nooo il est fort
Non codou Ndiaye mérénala trop 😢 ak nimala begué wone an tank aita wiri wiri 😅
😂😂 non saringe buLi AK khoudia dangay reé 🤣 ba dé😂😂😂😂😂😂
Ici c’est 22h30 mn et je regarde la série .
Serigne bouly a chaque fois sougnou ko hassé wala insulter koo 😂😂mouné souma amoneu Loumay sett😂😂😂😂
Seynabou DIOUF Xamna bouko guisser djiné dinagne ko fayoul
La meilleure maison de production ☑️☑️☑️
✅♥️
Alou est Un bon ami
Bouli me fume 😄il joue bien son rôle
Kodou ndiaye yakh na yaramam bi noo khesal bakhoul billay
Elle était très belle dans wiri wiri c'est dommage mais bou bayiwer dina récupérer teint wam à condition de s'y mettre
@@m.s3254 billay dafa leer
La son de série vautour sur 15min ohh série bou nékh kouko lalal j'aime
C La premier fois ke may commentaire 🥺🙏🏽❤️
LE PERSONNAGE DE ALOU WAAW 😇