Sa merci bi yalla nala si yalla défal liga si yélol boudé yalla motakh gay wakh dakh gnép gnossi bok yam mo mél si guiss bassi gniko gueum ak gniko wédi
Yow Cheikh Omar toniouleu dei,yow kaye yaako ameil Akheu, ndakh YALLAH miye attei diamaam yi neineu keineu kouneikeu ki nga tonj dina attei sen digantei yowmal qiyam,Akasa yow yaa wara dem baalou gi Cheikh Omar diagne
Lan motax ay seni serigne taxaw fi di manqué respect yalla, yonnetibi ak malaka yalla yii waxo lenthi kii wax lii rek ngen di dieufeurou sen ak serigne tegou niou fen yalla ndax sen cérémonie yoyou douniou thi meusseu wax yalla néna yonnetibi néna ndax souniou waxé ngen yewou fen yi dafadoy durée na 130 ans réveillé vous l'heure est grave la fin du monde approche dé
Sa waay nékal nite touti ta'nguéne dépassé fi nguéne ték mouride yi nioléne gueuna kham yalla ak yonéneti bi fouff mais liy sénn problème yéne moy nite waroul Wassila Gni topone yonéneti bi nékouniou ay talibé si mom Rewmi nak nite yéwo woufi gueuna kham Serigne mountakha kane moy yalla ak yonéneti bi
Aye mourid wara gnou di politiqué serigne touba géweul yi sonola gén réwmi yéneu yalla baye ballé khamoulén balé yalla ka mome ak nitt tame yéneu gnii fi wakhe yeup aye géweul lagniou maye léngou
Je n'aime pas les politiciens qui se servent des confréries pour se donner une importance que leur personne n'a pas du tout. Monsieur Mackiou Faye ne doit pas oublier qu'il était politicien Maire à grand Dakar et maintenant homme d'affaires la vente de terrains et dans la téléphonie, il n'est pas un marabout et il est mêlé dans beaucoup de controverses que lui reprochent des citoyens dans certains domaines comme l'affaire du monument de la renaissance etc. Donc il ne peut parler qu'à son nom pas pour les talibés.
Tu ne mérites même pas ma réponse, mais sache pour ta gouverne que Mbackiou Faye n'est plus Maire. Il est le représentant du Khalife Général des Mourides a Dakar. Pour que tu comprennes mieux, Ousmane sonko qui fréquentait sweet beauté et Ousmane sonko premier ministre est ce le même Ousmane ?
@@myandiaye4960 j'habite à Ouaga niayes j'ai vécu sous le magistère de ce monsieur quant il était maire l'ayant connu de vue bien avant cela, je peux pas accepter que des gens voient en lui quelque chose au delà de vous et moi. Je n'ai aucun critique à formuler à son égard seulement je n'accepte pas absolument pas qu'il contemple l'appellation de marabout NON. C'est pas ça la religion.
Dull rek professeur check omar diagne mo geun seni ndeye ak sen baye ak seni serigne yi eup leen xam xam eup leen ndiarigne ci rew mi geun lena nekk patriot. Pour finir kep ku contre pr check omar diagne dee molay tere dem safara😊
Mouridou lahi la wayé gninaan serigne bi mo bind mindeff akk diko djine yallah moom louy senn atté té pourtant kenn wakhou lènn dara. Donc nafekh yi nioy saltèl yoon wi té serigne bi dinako layo akk Yenn walahi ☝️
Souniou fi nékone di tagu sonko waleu Diomay merci mbackiou nguéni wakh déléne ande ak nite si deugu Nite sou défoul loudoul yone danga ko wara wakh amoul pastef la bokou amoul dara nioune wa touba bokou naniou si gniléne fal té yéne gni di saga chaque jour yéna done wakh merci wa touba
Akasa samb dimbaliniou amo benn khamm khamm di wakh Yéna fi wakhonn serigne touba mo lenn geuneul yalah ba paré ngenn di sonal nit yi fi ish Boulenn niou sonal
Délènn wakh li lènn serigne bi wakh Lo bilahi nioussi eupp si yenn dinagn ko layo serigne touba thie linioukoy sossal mouridou lahi la wayé douma fanatique Alkhamdoulilah 🙏
Dieureudieuff si sagua yi man douma tontou ayy doff akk ayy fanatique mtx cheikh akhmadou rafahi kepp layy déglou ndakh ma meuneuh tégou si le droit chemin .
Dieuredieufeti ya cheikhouna Ahmadoul khadim❤❤❤❤
Bamba. Rék❤❤
Dieuredieufeti Serigne Touba ❤❤
Macha-allah Dieureudieufaty Serigne TOUBA Cheikhanaa Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul Yalla nanou ko YALLAH fayal ❤ Amine ❤ ❤ ❤
Yalla nanou YALLAH mousseul ci Say-Say Omar Diagne borom khol bou Salté boobou mbirame daffa andak chaytaané
Sérigne touba kou ka magne do am daimou mérci bamba ❤❤
Jërëdëfti Serigne Touba Diarrama Mame Cheikh Ibrahima Fall🇸🇳🥰
mbackiyou Faye bilaye ya mate li nga done yalna nga goudou fane
Alhamdoulilahi dieuredieuffeti Serigne Touba❤
Djaradjaf serigne touba djarama mame cheikh ibra fall❤❤❤الشيخ الخديم لا مثيل له
Dieuredieuf Cheikhoul khadim❤❤❤
Dieuredieuf serigne Touba
Dieuredieuf Serigne touba amoul morom ❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf serigne touba ❤❤bamba rek
AK mane dieureudieufty s Touba khadim
Serigne touba rek machallah mbacke balla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Serigne Touba bimou gnibisé Gabon dafa balé none yépp .
Té dou allak atté yallah doyinako.
Waxdji métina wayé bayilénn ko ak yallah 😢😢
Cheikh oumar deug rek ka wakh ❤❤
Dieureudieuf Cheikh Omar Diagne ❤️❤️❤️
Sa tounou Ndeye
Dieureudieufeuty SERIGNE TOUBA
Dieuredieufy SéRignE TOuba MBacké 🎉❤🎉❤❤❤❤❤❤❤
Machalla amatina solo dieure dieuf ❤❤❤
Kou ted ki amoul morome
Machalla Anna solo serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Cheikh Ormar deh saytanéko meunn rekk wayé mann dey balnako té diko gnanal ni yalnako yalla guindi barkëp Cheixoul Xaidim🙏🏿
Ñun mouride nañulen bolo wate sunu bolo wé té serigne TOUBA takh ken douñu ñémé
Dieureudieuf serigne Akassa Samb
Les avancées dans le secteur énergétique sont impressionnantes. Continuez sur cette lancée
DIEUREUDIEUF SERIGNE TOUBA AMIIINE
Dieuredieuf khadimmoul Rassoul❤❤❤
Dieuredieuf borom touba kéne la
Manemi baloumako yalnaniou yalla atè ak mome barkèpe borome touba amine🙌
😂😂😂😂
C. Oumar ❤❤❤
Qu'Allah veille sur vous
Vous n'avez rien dit de mal
Yamana kathi
Sa dioubou Ndeye
Serigne Touba amol lor
Diaradieuf serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf makiyou faye
Dieuredieuf Serigne Touba, founou tollou
Amine ya rabbi ❤
Merci beaucoup Cheikh Oumar
Sa merci bi yalla nala si yalla défal liga si yélol boudé yalla motakh gay wakh dakh gnép gnossi bok yam mo mél si guiss bassi gniko gueum ak gniko wédi
Yaw ak omar diagne sen leufeul ndiaye ak kou and ak yein
Yaw ak omar diagne sen leufeul ndiaye ak kou and ak yein
Merci beaucoup serigne Touba ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶
Merci❤
Nonii Serigne Touba yii yallah moguilène di wérre
Gni niro ak Abo laheub gnoy soutenir wakh katou gnawtéff yi mélni Omar Diagne
Akassa❤❤❤❤
Mane Serigne Abdou fata mbacke moye sama Serigne je suis cheikh Omar Diagne
Lolou sa problème oiê
Dieuredieufy SéRignE TOuba MBacké ❣️❣️
Mouridoulah
S touba nimou mél koum néxoul thi nakhar ngay deukk
Senegal daffa beurry ay nitte niou bonne serigne touba daffa liguey yalla ba ame limou kou bagne nittou yalla nak nala laire nee yalla gua bagne
Je suis COD ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Senegal mo barri nafekh
Comme ça genre yi rek 😂😂
Yow Cheikh Omar toniouleu dei,yow kaye yaako ameil Akheu, ndakh YALLAH miye attei diamaam yi neineu keineu kouneikeu ki nga tonj dina attei sen digantei yowmal qiyam,Akasa yow yaa wara dem baalou gi Cheikh Omar diagne
Yaw ak Omar diagne aï mbam guene
❤machlla amna solo loll❤
Diaradiafe seringe akasa sambe ❤❤❤❤❤❤❤
Sëriñ Tuubaa de baal na noon yépp aka baax te bari yërmande.
Je suis Chaikh Oumar Diagne
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yak mom yéna Yam ay togne Kat ngéne
Gnakeu khamkham bounguène wara wakhtané mo takh Omar Diagne dilène di wathié chaque jour
Demlène diamoudji yalla
bismilah
Délènn wakh lilèn serigne bi wakh Lo ndakh moussoul bakou ndakh daffa xam boromam té tawkhîtt lalèn diangal wayé dou ayy par parlo.
Serigne Mountakha, Mbackyu fay, Serigne akasa Sambo, yén Doll way
Soudé yalla maynala touti kham kham so paré khamni sa papa nga saga
Omar Diagne kay kenn baalu ko😢😢😢
Je suis cheikh oumar ❤❤❤❤❤
Mési❤❤❤
Man tamit balou mako yalnako souno akhe dall
YEN MAYLEN NIOU DIAM MOMOULEN SENEGAL,SERIGNE TOUBA KEN BANIOU KO DOMERAM YIKOY MBOUBO DI DEF LOULEN NEKH LA KEN DOTOUL NANGOU DOUL MERCI...
Katal sa Ndeye
Bayil khamadi
Dieureudieuf
Je suis Cheikh Omar Diagne❤❤❤
Cheikh omar diagne deugg la wakh
Mbame houhh nga rekk
Focus le 17 novembre inchallah ❤🇸🇳
Lan motax ay seni serigne taxaw fi di manqué respect yalla, yonnetibi ak malaka yalla yii waxo lenthi kii wax lii rek ngen di dieufeurou sen ak serigne tegou niou fen yalla ndax sen cérémonie yoyou douniou thi meusseu wax yalla néna yonnetibi néna ndax souniou waxé ngen yewou fen yi dafadoy durée na 130 ans réveillé vous l'heure est grave la fin du monde approche dé
Jërëjëf sëriñ Tuuba Yakar ji❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sa waay nékal nite touti ta'nguéne dépassé fi nguéne ték mouride yi nioléne gueuna kham yalla ak yonéneti bi fouff mais liy sénn problème yéne moy nite waroul Wassila
Gni topone yonéneti bi nékouniou ay talibé si mom
Rewmi nak nite yéwo woufi gueuna kham Serigne mountakha kane moy yalla ak yonéneti bi
Yen dei yenneu tonj Omar diagne
Je suis de tout coeur avec cheikh oumar diagne molene geune molene eup xam xam moléne geuneu beug rewmi
Toth sah thiott nday meuna douuuul yaw ak Omzo mingay défendre yépp sén djobb nday téh balah yagg diggén koh guiss Domékharam yih
Diangnou lékke sén tiotou ndaye yak mom
@@cherifgueye4845 pourquoi ay saga mais répondez moi par des idées monsieur
😂😂😂yonu murid ça kaw ken meunu si dra😂
@@cherifgueye4845 yaw mono wakh loudoul saga ?
Merci ❤❤❤❤abdou
Bayil fen mak nga tahau fre de fen akha Dull
Amal yarr nék sa ginaw clavier di saga sa moromou baye yi dou ndam
Amine Serigne akassa Mane mi doumako meusseu diegueul
Omar Diagne sadata yaye
Cheikh Oumar Diagne mbaam mou bone té yees té khamadi la kou bagne yoonou mouride la
Aye mourid wara gnou di politiqué serigne touba géweul yi sonola gén réwmi yéneu yalla baye ballé khamoulén balé yalla ka mome ak nitt tame yéneu gnii fi wakhe yeup aye géweul lagniou maye léngou
Cheikh Tonioul kén
Ah bon defal vidéo wax lim wax
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieuf serigne touba, serigne dou morom dé kouko bagne alkou
Dara douko dall cheikh omar diagne diameu rek ley am
Sadata yaye
Dangaye Doull di
Je n'aime pas les politiciens qui se servent des confréries pour se donner une importance que leur personne n'a pas du tout. Monsieur Mackiou Faye ne doit pas oublier qu'il était politicien Maire à grand Dakar et maintenant homme d'affaires la vente de terrains et dans la téléphonie, il n'est pas un marabout et il est mêlé dans beaucoup de controverses que lui reprochent des citoyens dans certains domaines comme l'affaire du monument de la renaissance etc. Donc il ne peut parler qu'à son nom pas pour les talibés.
Tt ta fait vérité absolue
Ils aiment trop les détails ces gens là puff…
😢😢😢thieyy sataan yii lii dou wakhou politique
Bilay Lou weer geu wakh
Tu ne mérites même pas ma réponse, mais sache pour ta gouverne que Mbackiou Faye n'est plus Maire.
Il est le représentant du Khalife Général des Mourides a Dakar.
Pour que tu comprennes mieux, Ousmane sonko qui fréquentait sweet beauté et Ousmane sonko premier ministre est ce le même Ousmane ?
@@myandiaye4960 j'habite à Ouaga niayes j'ai vécu sous le magistère de ce monsieur quant il était maire l'ayant connu de vue bien avant cela, je peux pas accepter que des gens voient en lui quelque chose au delà de vous et moi. Je n'ai aucun critique à formuler à son égard seulement je n'accepte pas absolument pas qu'il contemple l'appellation de marabout NON. C'est pas ça la religion.
Grazie mille serigne Touba e ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yeeen bayiileen thiaxane Yii Serigne touba nekoul si aye thixane wa baxma 😅😅😅😅😂😂
Serigne Touba gnikoy togne nio barri 😢😢😮😮
❤❤❤❤❤
Sé bon pour mourid yu
Akassa mbakiyou Faye momou dey branchit argent 😢😢😢😢 mouride Bou jubb amoul
Doull rk ngay def
Yaw Ya bon
Sama waadji boul wakhati loolou gnii mouride yi ande niou ak nioom .
@@mohamadoulaminesylla8676 bilahi monoma gennel mouride bou jubb
Cheikh Omar Diagne kessé
Bilahi beugo cheikh omar Diagne serigne touba nga bagne
YALLAH mo kham kou dinei nior ak koumou niorroutt mais pas yein
Dull rek professeur check omar diagne mo geun seni ndeye ak sen baye ak seni serigne yi eup leen xam xam eup leen ndiarigne ci rew mi geun lena nekk patriot. Pour finir kep ku contre pr check omar diagne dee molay
tere dem safara😊
❤❤❤❤❤❤❤❤💞💞💞💞💞💕🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Mouridou lahi la wayé gninaan serigne bi mo bind mindeff akk diko djine yallah moom louy senn atté té pourtant kenn wakhou lènn dara. Donc nafekh yi nioy saltèl yoon wi té serigne bi dinako layo akk Yenn walahi ☝️
Omar diagne domeram la
bayilennn sennn waxx yi guirr yalla
Cheikh Omar kazab Diagne noonu Serigne Touba la ak képou kou and ak mom 😂😂😂😂
Goudi gamou amolén lolén Di wakh ndakh tokk fi Di wakh CHEIKH OMAR DIAGNE. Yéna niakk ndéy djom.
Genre yi motahe niouye hass gamou.
Souniou fi nékone di tagu sonko waleu Diomay merci mbackiou nguéni wakh déléne ande ak nite si deugu
Nite sou défoul loudoul yone danga ko wara wakh amoul pastef la bokou amoul dara nioune wa touba bokou naniou si gniléne fal té yéne gni di saga chaque jour yéna done wakh merci wa touba
Akasa samb dimbaliniou amo benn khamm khamm di wakh
Yéna fi wakhonn serigne touba mo lenn geuneul yalah ba paré ngenn di sonal nit yi fi ish Boulenn niou sonal
Boulen si dougal Serigne Mountakha
✊🏾🙏🏽
Délènn wakh li lènn serigne bi wakh Lo bilahi nioussi eupp si yenn dinagn ko layo serigne touba thie linioukoy sossal mouridou lahi la wayé douma fanatique Alkhamdoulilah 🙏
Waye dagay doulllllll képp
Dangay fénd do mourit
Sa tounnou day katal sa dayy feuleu
Dieureudieuff si sagua yi man douma tontou ayy doff akk ayy fanatique mtx cheikh akhmadou rafahi kepp layy déglou ndakh ma meuneuh tégou si le droit chemin .
Man limay wakh xamnako bou bakh ndakh nieuw naniou si serigne sidy moukhtaar néko kénal serigne touba laniou beugue takhawal serigne bi nélènn kénal yallah kepp lassi xam mtx yenn douma meuneuh wakh akk yenn ndakh vous avez rien du tout compris si yoon wi walahi
C'est vraiment domage wara wakhtané ci yonetebi Di wakh ci Lou amoul bénneu ndiarigne
Bouniou offensé yalla offensé yonénetebi guén né tékk
Sëriñ Muntaxaa it fa Maamam Sëriñ Tuubaa nekk rekk fala nekk moo tax ñiy wax ñépp doo dégg kenn kuy wax ci ñii te tek ko ci ndigalam.
Yèn nit yousof gèn 🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐
Cou diapalee mbame diagne mandouwoo
Te mandou mogeune diouly
Yeenn yeenaye aye nafek.
Cheikh Oumar diagnie kou diokh thieur serigni Touba la ....
Mei limou wakh DEUG la tok mouye dokh bi dafi warra diekh