3/Les Qualités éminentes de Cheikh Ahmadou Bamba| S. Bassirou Khelcom

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 18 янв 2025

Комментарии • 29

  • @CheikhounaNdiaye-kb3ks
    @CheikhounaNdiaye-kb3ks 2 месяца назад

    Dieureu dieufé Kou Tède ki Yalna niou yalla défal djikkom you teddé yo ya🤲🏿

  • @yorodiouf1283
    @yorodiouf1283 5 лет назад +1

    Amna Solo loole Mbacke masha Allah Yalna Borom bi faye ci Serigne Touba mi ngay ligueyal.

  • @cheikhounagueye1396
    @cheikhounagueye1396 6 лет назад +5

    dieuredieuf waay serigne bi amna solo lool liguay leeral amna solo dieuredieuf mbacke yalla nala fi yalla ya gual si sugnou kanam barkeb yonen tebi sallalahou alayhi wassalamm barkeb serigne touba amine dieuredieuf

  • @layendiaye7424
    @layendiaye7424 5 лет назад +3

    Machalla yalla gafi yague tè wer

  • @mominnatoudiop3201
    @mominnatoudiop3201 6 лет назад +3

    Machalla amnasolo lool

  • @laminlo4449
    @laminlo4449 7 лет назад +5

    machallah serigne bassirou mbacké khelcom

  • @rassoulmbaye7239
    @rassoulmbaye7239 6 лет назад +3

    Soukrane amna solo trop

  • @papembengue354
    @papembengue354 5 лет назад +1

    Mashallah...

    • @cheikhounasamb6150
      @cheikhounasamb6150 4 года назад +2

      Serigne Bassirou Mbacké diadieuf leerna andak téguine
      Wanté Khassidayi di wakhi kou tedd ki boul nangou mouy gueuneu soufé say wakh .Nga dieul sakh léneen lou melni wayi arab sou meunoula niakk.Ndé sakh wakhtan wi késsé doyoon na.
      Défar rekk mom laa dioublou.Mangui diegoulou nîeep

  • @toubambartv7062
    @toubambartv7062 5 лет назад +2

    Machallah Serigne basirou khelcom soponala

  • @76abou
    @76abou 7 лет назад +5

    diarama mene cheikh ibrahima fall

  • @ndiayeteranga3772
    @ndiayeteranga3772 6 лет назад +2

    machalla mbacke waxtane wi am. na solo lol yagui léral lou Iouri thi serigne bi

  • @daoudathiam4844
    @daoudathiam4844 7 лет назад +3

    Ma Cha allah serigne bi amna solo loul sakh

  • @abdoug731
    @abdoug731 6 лет назад +2

    Amna solo

  • @cheickbadiane173
    @cheickbadiane173 5 лет назад +2

    Jiere jief borom tuoba dolli whatal wakhtane wi

  • @76abou
    @76abou 7 лет назад +3

    Mbacke balla zuma la degğ lou damay am mbegğ looll serigne touba da seraall sama xooll moom rek la bagğ bagğ serigne touba rek fall

  • @rassoulmbaye7239
    @rassoulmbaye7239 6 лет назад +6

    Dila nianale rek mbacke balla yalla goudal fane wi weral thieur yi

  • @momobayfallmomobayefall9994
    @momobayfallmomobayefall9994 6 лет назад +5

    Hakacha fall

  • @mouhametbouxarangelo6592
    @mouhametbouxarangelo6592 6 лет назад +3

    Son bi si sof motakh wakhtanal bi xaw masidara

    • @daarayserignebassiroumback2395
      @daarayserignebassiroumback2395  6 лет назад +3

      Dissi diégalou boubakh. Desnnassi bayi khel bénén yone Incha Allah

    • @SanYallah
      @SanYallah 6 лет назад +1

      @@daarayserignebassiroumback2395 Asalamoualeikoum
      kan moy diangue khassida yi si video bi ?

    • @marwanefall4798
      @marwanefall4798 5 лет назад

      @@SanYallah serigne aliou fall

    • @SanYallah
      @SanYallah 5 лет назад

      @@marwanefall4798 diadieuf way Barakallahoufik ak ngeureumeul Borom Touba

  • @MorDiaw-v8g
    @MorDiaw-v8g 18 дней назад

  • @yorodiouf1283
    @yorodiouf1283 5 лет назад +2

    Ziar na niep, Beugue na kouma bakhei ki diangue khassida ci font background bi.

    • @pslleida6817
      @pslleida6817 4 года назад +1

      Bay aliou fall moko diangue fatou na nak nako yalla yaram

    • @cheikhsakka8185
      @cheikhsakka8185 4 года назад

      @@pslleida6817 aminn