🔴Mame cheikh A T Sarr ibn sokhna kine sy revient sur l homonyme de serigne cheikh avec des preuves

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 дек 2024

Комментарии • 280

  • @madiopndiaye3380
    @madiopndiaye3380 Год назад +15

    Ndeysaan ça fait toujours un profonds plaisir de t'écouter Mame Cheikh Ahmed SARR. Tabarkallah seddounga thi Mame Maktoum😍

  • @moussaniang7255
    @moussaniang7255 Год назад +42

    J'ai suivi avec beaucoup d'intérêt l'intervention de Pape Cheikh Sarr. Limaci dakhal mooy rigueur intellectuelle bi. Dieureudieuf Maktoum Pro ci diotalibi.

  • @papaaliounembaye3512
    @papaaliounembaye3512 Год назад +10

    Merci beaucoup mane cheikh tidiane sarr ❤Serigne moustapha sy yalla na yalla yokou fane wi Diadieuf sy malick

  • @mortallafall6843
    @mortallafall6843 Год назад +14

    Diarama Serigne Moustapha Sy Mame maktoum yalla na yalla yok ay lérame

  • @t.d.sservice2878
    @t.d.sservice2878 Год назад +24

    macha allahou yalla na yalla doli arr
    mame chiekh limou am dou tourbi wayeee takhawaye mokoko maye ak pass pasam si mame babacar sy
    nagnou bayi khele boubakh sounou bopou teh takhaw ndakh serigne moustapha wathio ak gnoune ndakhe lignou wara kham kham lepou wakhnagnouko
    histoirou keurgui mome loumou gnousi wakhoul geumou gnouko
    none bou pekhem doul djekh ak woudjou bou kholome fekh doufi djougeeee bafawou
    li serigne moustapha sy wakh gamou gui passee rk
    kou agnane mo geun kou seww
    teh amna gnokhamni ignanou gnou dagnou seww motakh diarou tontou

    • @diagnendoye5756
      @diagnendoye5756 Год назад

      👏🏽👏🏽👏🏽 bien résumé 💖💖💖 Mashallah

  • @assanegueye4284
    @assanegueye4284 Год назад +6

    Wallay ndeysane manchallah yalna Yalla fayla yiw Pape Cheikh Ahmed Tidiane Sarr barké sa tourondo Mame Cheikh Ahmed Tidiane SY

  • @massdiagne8412
    @massdiagne8412 Год назад +17

    Yalla na yalla yokou ayy leramm 🙏 té taass niou si barkèm 🙏 Al Maktoum ❤️

  • @laminedeme8944
    @laminedeme8944 Год назад +10

    Merci Mame Cheikh pour cette vidéo . Merci pour cette confirmation

  • @sultantv.télé.daara-dji
    @sultantv.télé.daara-dji Год назад +12

    Machallah amna solo yalna yalla barkél .... Ayi fénn mom yagg nafi wayé niounn kénn meunou gno fénn ndakh yagg nagno teewlou ak d teewé ayi diotaayou Serigne cheikh
    فوالله قد سميت بالعلم الذي يقصصني فضلا بي أتفرد

    • @diagnendoye5756
      @diagnendoye5756 Год назад +1

      Wallahi c ça exactement
      Ñi Seen ❤ mó febar

  • @ibou_tube
    @ibou_tube Год назад +10

    Ma cha Allah Serigne b, kaddu yi rafétna té tégouna thi thieuslaay, جزاكم الله خيرا

  • @pendagamouniang3497
    @pendagamouniang3497 Год назад +17

    Machallah mame cheikh yalna yallah fay yiw 🙏🙏🙏

  • @massyllambaye2549
    @massyllambaye2549 Год назад +7

    Serigne Cheikh touddé wounko Cheikh Tidjane Chérif moom wakhi doff rek la

  • @maogningue3922
    @maogningue3922 Год назад +10

    Ndeyssane Manchallah Mame Cheikh Tidiane Sarr dieuredieuf Mame Cheikh Tidiane Diop

  • @mmefallmn8910
    @mmefallmn8910 Год назад +8

    Machalla Mame Cheikh Ahmed Tidiane Sarr léral yi amna solo ta da siy bakh,
    Mais diadiafaté Mame Cheikh Ahmed Tidiane Diop si diotal bi man damay sétan MAKTOUM prod damako abonné.

  • @mouhamadoulaminendiaye6592
    @mouhamadoulaminendiaye6592 Год назад +26

    Mon Dieu c'est une diversion cela montre que le meeting du PUR a dépassé toutes les attentes.

  • @aitadial4819
    @aitadial4819 Год назад +10

    Soul kér douko téréé féégne beuzz lagnouy woute rék machallah chef religieux

  • @idrissademe1931
    @idrissademe1931 Год назад +18

    Oh 💞💞💞💞💞
    Je m'en vais de ce pas télécharger la vidéo. Sunu Maam Cheikh est et restera à jamais l'homonyme de plus valable de Aboul Abass
    Lolou la Yalla dogal

    • @papamalick3259
      @papamalick3259 Год назад +2

      Ame na sollo machaAllah dieureudjeuf ❤

    • @papaderguenediouf
      @papaderguenediouf Год назад +1

      Billahi Mame cheikh Ahmed Sarr,ligua wakhe sisama leupi,moye li degui.vous etez le digne héritier et petit fils de Mame cheikh Ahmed tidiane sy Al makhtoum 🙌

    • @papaderguenediouf
      @papaderguenediouf Год назад +2

      Manedai manguilaye gnanale yallah disa sopai,disa monkhou pass pass,digua kharite maman soxna kiné sy Al makhtoum

    • @papaderguenediouf
      @papaderguenediouf Год назад +2

      En groso modo,ligua wakhe moye degui

  • @MansourDiop-y6j
    @MansourDiop-y6j 6 месяцев назад

    Alhamdoulila mom dé sante yalla rek et Mame cheikh Ahmed Tidiani Sarr❤

  • @mbayesall5248
    @mbayesall5248 Год назад +4

    Macha alla lére na serigne chiekh wakh nagnou lép avant mouy dém

  • @mamadoumoctargueye2325
    @mamadoumoctargueye2325 Год назад +5

    Machalla réponse très pertinente yalla na yalla samela té arela dieuredieufe bégue naniou si lérale bi

  • @cheikhtidianeniang246
    @cheikhtidianeniang246 Год назад +5

    Tourou diambour loussi diara ignane merci mahtoum prod merci pape cheikh Sarr

  • @ballasow903
    @ballasow903 Год назад +10

    Te Serigne Babacar sy amone n’a yene toude ko mame Abdou Aziz dabakh Seydina cheikh motakh toude wouko ndakh moko toude bopam mame Abdou wakh Serigne Babacar y’a wakhone bou neke goor mane ngakoy toude moune ko ah waye game gui dafa melni dafa andale touram nak ndakh borom tariqa bi toude nako bopam

  • @adjaworefall189
    @adjaworefall189 Год назад +6

    Tékate Sokhna Zeynabou bii mouyy Wakheu Bilahy Walahy Talahy Mame Rokhaya N'diaye Bou Mame Kharr Yala Sidy N'diaree M'baye Moyy wadioureum
    Bilayy Walayy Barkez Serigne Babacar Sy

  • @fatimadiop8383
    @fatimadiop8383 Год назад +10

    Machallah yalla na Yalla fayla yiw

  • @moristodiakisto5197
    @moristodiakisto5197 Год назад +7

    Machallah lérral Yi amna solo trope yalla n'a yalla yokk xam xam bi

  • @massdiagne8412
    @massdiagne8412 Год назад +5

    Liniou souniou Goor gui wax doufii meussa diogué ( woudiou wou xolam doul fééxx ak nonn bou péxém doul diéxx)

  • @cheikhfaye8893
    @cheikhfaye8893 Год назад +2

    Machallah deug bou wéer yalla na yalla Faye doli la wéer ak soutoura barké baye niass rta dieuredieuf

  • @insatop8182
    @insatop8182 Год назад +2

    Dieureudieuf mame cheikh Ahmed tidiane sarr

  • @ouzcapo2240
    @ouzcapo2240 Год назад +6

    ماشاء الله بارك الله فيكم وجزاكم عنا خير الجزاء بجاه سيدنا محمد صلى الله عليه
    شكرا بب شيخ تجان سار 💛💛💛

  • @damefall8818
    @damefall8818 Год назад +4

    Machallah.mame.ch.sarr.yalna.yalla.fayla.yiw

  • @MamadoulamineNguirane-e8p
    @MamadoulamineNguirane-e8p Год назад

    Machalla mame cheikh sarr merci bcp amna solo❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @dmwmdaaraymourchid4121
    @dmwmdaaraymourchid4121 Год назад +5

    Machallah yalna yalla motali dieureudieuff pape cheikh Ahmed tidiane Sarr

  • @Jule-diagne
    @Jule-diagne Год назад +6

    Le vieillard se vante d’être le premier petit fils de al khalifa mais ce type ne semble pas connaître l’histoire de sa propre famille ou il est juste jaloux des élus du ciel dont des hommes comme lui ont longtemps recherché d’être des élus du ciel 🤦🏾‍♂️🤦🏾‍♂️

  • @papaamadounael8487
    @papaamadounael8487 Год назад +6

    Walahi Mane dei deg n'a sama nijaay Doudou Kende Mbaye Mouni Daf mass nek ak Serigne Abdou Al Amine France Mouni ko am na gnouy wakh nane Serigne Cheikh keine toudei wouko Cheikhouna Tijany nena Serigne Abdou dafa tourné Niko mom lane ko toudei pure Mouni ko ngeine balma sakh Limay beug toud wayei Serigne Cheikh bimou nekei si sama birou yaye Cheikhouna Tijany dafa feignou Serigne Babacar neko sa sokhna si goor la eumbe sou djoudo nanga ma toudei tei bayiko ak Mane. Lii mom ma deg sama nop sama.nijaay wakh ko tei kokou mom dou sosal Serigne Abdou Al Amine

    • @diagnendoye5756
      @diagnendoye5756 Год назад

      Motaxx gëen war xamë mak muy keen duko deglu të loolu dalna kii di mansoursyjamil mak muy kacc kii mò añiaan Kii mò wëjjü

    • @diagnendoye5756
      @diagnendoye5756 Год назад

      Seriñ Sëex Tijjany Maqtūm dafko waxal Boppam ku lenenn kay dà fek ga bëg fenn ba nga nek ku añann

    • @salioudiouf2599
      @salioudiouf2599 Год назад

      Rééwe rek. Âme na gno khameni dougnou kilifeu

  • @Ndongosamb-u1o
    @Ndongosamb-u1o 11 месяцев назад

    Machallah ya oustaz pape cheikh Sarr amna soll❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mmefallmn8910
    @mmefallmn8910 Год назад +6

    (إن ربي قد حباني ... أن أسمّى بالتجاني)
    مام المكتوم.

  • @fatoufall6832
    @fatoufall6832 Год назад +1

    Deureu deuf Pape cheikh nioun niogui séne guisaw rek inchallah

  • @cheikhtidianendiaye8459
    @cheikhtidianendiaye8459 Год назад +1

    Serigne Cheikh Al Qoutboul Maktoum RTA

  • @adjakanytoure3317
    @adjakanytoure3317 Год назад +1

    Quelle réponse !!! ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @gueyeniaye6340
    @gueyeniaye6340 Год назад +3

    ماشاء الله تبارك الله جزاك الله خيرا

  • @boucountasene6755
    @boucountasene6755 Год назад +4

    FA TABARAKALLAHOU ❤

  • @AblayeDiop-um6xw
    @AblayeDiop-um6xw Год назад

    Merc papa Cheikh tidiane sarr totobi rafetna machallah

  • @Khadydiop-bz2io
    @Khadydiop-bz2io Год назад +5

    Machallah Mame cheikh amna solo

  • @adjaworefall189
    @adjaworefall189 Год назад +4

    Man'guii Rousse Wayyé Inianne Fonkoull Mourr Yalha Moyy Mayez Kii diaroull tontou Bilayy Walayy

  • @binetougy837
    @binetougy837 Год назад +3

    ☝🏾❤️☝🏾❤️☝🏾❤️☝🏾❤️☝🏾❤️ ndeysane ☝🏾❤️☝🏾❤️☝🏾❤️☝🏾❤️☝🏾

  • @oumyracisse4686
    @oumyracisse4686 Год назад +2

    Machallah Mame Cheikh Ahmed Tidiane Sarr Si leral yi amna solo

  • @tallat_s_chtv1232
    @tallat_s_chtv1232 Год назад +2

    Yalna yalla fayla yiw chiekh tidiani sarr

  • @muhammedsallah4672
    @muhammedsallah4672 Год назад +2

    Machallah am na solo mame cheikh Ahmed tidiane sy al maktoum

  • @mansourndiaye17
    @mansourndiaye17 Год назад +2

    Macha Allah papa Cheikh Sarr kadouyi lérna rafetna Macha Allah

  • @yagadiop6291
    @yagadiop6291 Год назад +2

    Machallah pape cheikh

  • @malickgueye9744
    @malickgueye9744 Год назад +5

    Machalla Yalna yalla Sam arr te motaly Inchalla

    • @cheikhdiop8681
      @cheikhdiop8681 Год назад +1

      Machala yalna Yalla barkél inchala khamé ak fidélité rék moo am solo

  • @ousseynouish
    @ousseynouish Год назад +3

    Macha Allah Mame Cheikh

  • @bathiediagne2045
    @bathiediagne2045 Год назад +3

    Machallah rappel bii amna solo

  • @cheikhsamb606
    @cheikhsamb606 Год назад +1

    فتبارك الله وجزاكم عنا خيرا. أفصحت وأوجزت. ما شاء الله

  • @modoundiaye8143
    @modoundiaye8143 Год назад +2

    thiey fougnou dieum AK woudiou Yi sén xol doul féékh moukk.
    DIARAMA MAME CHEIKH AHMED TIDIANE SARR

  • @ndarawfall8752
    @ndarawfall8752 Год назад +4

    Machallah yalnayallah fayla yiw oustaz serigne mame cheikhe ahmed tidjani diop

  • @groupeleveurprofessioneltv3058
    @groupeleveurprofessioneltv3058 Год назад +5

    Barakalahou fikum ❤️

  • @missionnaire879
    @missionnaire879 Год назад +2

    Cheikh Tidian Sarr Djarëjéuff 💓💓💓✅

  • @malicksy7763
    @malicksy7763 Год назад +3

    Walaye ndeyesane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @babacarseck5686
    @babacarseck5686 Год назад +6

    Merci ❤🙏🙏👏🏻

  • @taphandiaye3758
    @taphandiaye3758 Год назад +1

    Merci beaucoup Mame cheikh

  • @astougueyegueye5904
    @astougueyegueye5904 Год назад +2

    Dieureudieuf seutou Mame ,

  • @alassanesall8674
    @alassanesall8674 Год назад +3

    Machallah Sangue bi Kadou matna té matalé

  • @cheikhmbengue6590
    @cheikhmbengue6590 Год назад +1

    Merci Mame Cheikh Atmad Tidiane Sarr léral bi baahnassi.
    Serigne Cheikh Atmad Tidiane Sy Al Maktoum directement si Cheikh Atmad Tidiane Chérif si Lou wér.

  • @sadamoumamecheikh
    @sadamoumamecheikh Год назад +3

    Amiiine Macha Allah

  • @ousmanefaye5920
    @ousmanefaye5920 Год назад +4

    Ham ham, piiiir wallahi 👏🏾

  • @CheikhtidianeNiass-dv7ps
    @CheikhtidianeNiass-dv7ps Год назад

    Machalah yalna yalla faye yiiw té goudeul fan wi🙏❤️

  • @aladjidiop7115
    @aladjidiop7115 Год назад +2

    ماشاء الله بارك الله فيك 🥰

  • @doudouwadegueye3926
    @doudouwadegueye3926 Год назад +3

    Serigne cheikh néna Moy tawou seydi diamil wayé Serigne Mansour djamil Moy sama yaw . S Mansour cheikh néna S Mansour djamil Moy tawou papame Kone gnou moytou wakhyi

  • @mamesow3426
    @mamesow3426 Год назад +4

    Diarama serigne moustapha sy yague fi lol té ande ak wérr

  • @moussacissediop7480
    @moussacissediop7480 Год назад +1

    Walahi kou ame kilifeu do gangantiko si mbéde
    Dieureudieuf Sarr

  • @alphounadiallo1547
    @alphounadiallo1547 Год назад +2

    Merci Mame CheikhTidiane

  • @taphasall7518
    @taphasall7518 Год назад +4

    Machaallah amna solo

  • @fatima-gd8td
    @fatima-gd8td Год назад +2

    Euskeuy machalla Sama serigne

  • @malickmbodj4146
    @malickmbodj4146 Год назад +2

    Machallah amatina solo vraiment

  • @magueyegueye9899
    @magueyegueye9899 Год назад +1

    باركالله.فيك.جزاك.الله.الف.خير

  • @bayebadou4951
    @bayebadou4951 Год назад +1

    Merci lerna nagne

  • @senebadia8519
    @senebadia8519 Год назад +3

    Macha alla yalla na yalla def la mak

  • @codedieng3966
    @codedieng3966 Год назад

    Barack-Allahû-Feek Serigne Cheikh Sarr Danga bakh rèkk mais Dieurou wone sakhe dissi dètayé

  • @4mtv86
    @4mtv86 Год назад +1

    Oh sama xool dale sédatina ❤

  • @bnnd3362
    @bnnd3362 Год назад

    ولقد ولدت ولي رضا بولادتي
    لولادتي في منهج التيجاني
    ولأنني سميت من أمر به
    فجزى الإله فتى به سماني

  • @sopeserginemoustaphsyalmaktoum

    Macahlla lélarye amna solo

  • @cheikhdieye3484
    @cheikhdieye3484 Год назад +4

    Je suis fiér d êtres moudtarchidine walahiiii

  • @djibrildiop9630
    @djibrildiop9630 Год назад +3

    MACHAALAH TABARAKALAH

  • @insatop8182
    @insatop8182 Год назад

    Dieureudieuf makhtoum pro

  • @khadycisse8456
    @khadycisse8456 Год назад

    Bilahi Mame Cheikh Ahmed Tidiane Sy al Maktoum mo donneu Mame Cheikh Ahmed Tidiane Chérif batia Fass au Maroc.

  • @abdoulayefall1282
    @abdoulayefall1282 Год назад +1

    Merci bcp Pape cheikh Sarr

  • @ndeyediop335
    @ndeyediop335 Год назад

    Quelle éloquence mais son intellectuel domine ❤❤❤❤

  • @diagnendoye5756
    @diagnendoye5756 Год назад

    Merci Maam Sëex Ahmad Tijjany Sarr yaw xalëbi ci att doo morom mak muy kacc

  • @mayipkante6280
    @mayipkante6280 Год назад +2

    Machall 💔

  • @laminendiaye2417
    @laminendiaye2417 Год назад +3

    Macha allah amatina solo

  • @awatouray3063
    @awatouray3063 Год назад +2

    Amna solou

  • @abdoulayefall1282
    @abdoulayefall1282 Год назад +2

    Woudiou bou xolam doul fekh rek moffi nek , limou wakh ay Talibém si mosquée ou Salle si politique ak serigne Moustapha wané na lepou

  • @babacarndiaye3173
    @babacarndiaye3173 Год назад

    لقد احسنت واكملت وبلغت

  • @Al_Xaliifa
    @Al_Xaliifa Год назад +2

    machalla am na solo🥰

  • @moustaphawade1541
    @moustaphawade1541 Год назад +3

    Machallah❤

  • @sarasene1158
    @sarasene1158 Год назад +2

    ❤Mashalla 🙏

  • @diamamadoulamine6545
    @diamamadoulamine6545 Год назад +3

    Macha Allah

  • @babagauye3686
    @babagauye3686 Год назад +1

    Machallah wakh bi kham khaména té and na ak téguine

  • @medounendiaye4746
    @medounendiaye4746 Год назад

    Dieuredieuf pape Cheikh