Diadine , man tamit ci laa bokk. J'aime bien tes contenus ❤. Très intéressants et instructifs. Bonne continuation et courage. Bu la dara jaral ngay changer. Peace love and harmony.❤❤❤
Bou todioule Wone fene d’où ko inviter sans juste pour humilier la personne heureusement que je le regarde pas je le connaissais même pas 🙈merci diadine 😂
Diadine vraiment pour mane danga dioume thi sa jugement thi gni dieul gual yi nitt warako juger tant que doundau limou doundou peut être bo nékone placame tu ferais pire nga balma nak🙏
Assalaamu halaykum. Fanweeri jëwriñ. Ci ay caaxaan doŋŋ lañu nekk ak lekk xaalis. Réewum Turki xam ngeen ko mbaa ngeen dégg ko. Juróom-ñett-fukki tamndareet mat nañu ko te amuñu jëwriñ yu tolli nii. Kon lii ay caaxaan kepp laa ko jàppe, lii moo tax réew mi ñu bari amuñu yu bari. Bëj gi ñu bari amuñu ko amuñu ndox mu doy te baax lënd gi moom dama koo jéllale matul te jafe na te it dajul ñépp. Moom daal li tere a dem réew mi bari na. Senegaal li nit di gën a yittewoo moo fi yombul, muy lekk ak naan ak um paj. Te mu baax ñi seen i yoxo jot seen ginnaaw doŋŋ a ko man a am. Yal na nu Yàlla taxawu te may nu njiit yu réew mi itteel ci barkeb Alxuraan.
Diadine guinaw bouma la ziarè🙏 danga wara gènn chaque semaine MM boudè Ben yon wala nga wouteul ko jour kom chaque samedi wala chaque dimanche ✍️pasqeu danioh soxla sa guiss si ni rèwmi di dokhè❤️✅mais sila bok✊
Délo ziar bou werr Bara Diop ! Waw fann yi la xawone diapp rek wayer delou ci na ! Bouma meuner def video chaque jour sakh tewlou lenn ma magui fi dina ko def ci Katanou Yalla !
Comment un présentateur peut rabaisser un invité à ce point ??? Le pays où sa jeunesse est traitée comme des moins que rien, Tounkara me sort par les trous du nez 😱
La suite de la vidéo à suivre mo ngui nii ruclips.net/video/ZIoegVL7-9I/видео.html ! Abonner lenn activer cloche bi bagna rater yici topp !
Diadine tounkara xamoule dara merci boye baoll
Sila bokkou❤
je suis nouveau mais amna solo tropp
I’ve never believed in Tounkara 😢because he always undervalued 😢people 😢
Très bien et bonne continuation. Il faut être véridique pour pouvoir changer et redresser le pays
Diadine , man tamit ci laa bokk. J'aime bien tes contenus ❤. Très intéressants et instructifs. Bonne continuation et courage. Bu la dara jaral ngay changer. Peace love and harmony.❤❤❤
Mo ma diakhal pape sidi héros national❤
Très fort sacré Diadine. Chapeau
Diadine ligueye bi Nice diam si ioe ❤❤
Bou todioule Wone fene d’où ko inviter sans juste pour humilier la personne heureusement que je le regarde pas je le connaissais même pas 🙈merci diadine 😂
Diadine c'est un plaisir de te suivre sarap li waye
Mes diadine c'est Nice bilahi yaw
I Like u bro I’m a Gambian 🇬🇲 but I’m feeling really badly but I’m really happy for you and pa Assan
No commente Kouma nekh khalat louko nekh
Ci touky bi
Tchilla bokk Mon frère ❤ Domou Ndar Bala Coss DIOUMA Mame ABASS❤❤❤
Salame salame diadine le djinn des youtubeur faut nékone namone nala kou bakhe
Didim Ciala book pour mouy lére
Diadune manjilaboco
Diadine vraiment pour mane danga dioume thi sa jugement thi gni dieul gual yi nitt warako juger tant que doundau limou doundou peut être bo nékone placame tu ferais pire nga balma nak🙏
Sincerement souma meunone ligeey ci reew mi ba dadialer fi au moins 300 mille dina def lenen loudoul dieul gaal franchement !
Diadine ci la bokk depuis fouta je te suis et suis fier de toi machalla vive les patriotes vive ous sonko vive diomaye ❤
Manchallah mane tamite ci la book
Ziar depuis 🇺🇸
Salut sama kharit Sila Book
Chyar_nalla Dmou_bye"Diop"Thiila bôkk 💕💕💕
Ziar domou Baye ! Nouyou nala Amsa !
Ci laa bokkou s mouhamed fall alxour ane ❤
Machalla sama wadji
Salame Diadine ziarr namou nala yagui si diamou❤️❤️❤️❤️
Senegal ci xol waw magui ci diam bou bakh Alhamdoulilah ! No def mba yagui am tawfekh !
Disdine fofo bakhna 😂❤
yallana sa diame yagg ❤
Diadine si❤la❤bokk❤
Diadine c iba sila dokou dèma toudou ❤❤❤❤❤❤❤
Aliou Ngom wala Iba 😅
❤❤❤❤❤❤ merci ✊✊✊✊👂👂👂👂👂👀👀👈👈💯
Aythia Diadine boul ragal dara nio gui sa guinaw d sila bokk nak ♥️✌️
Bravo Diadine
Diadine Si la bok❤❤❤❤❤
Si la bokkou❤
Ci la book
Je viens de découvrir ta chaîne maintenant je ferai parti de tes servant suiveurs
Merci et bienvenue PapsNgom !!
Ci la bock
DIADINE , c'est comment ton vrai nom? jeste par sécurité. Mais je ne rate jamais tes sorties ❤❤❤du courage
C'est DIADINE mon vrai prénom 😂
Billahi
Diadine ci laa bokk🙌🏾
Ci la bol frère
Diadine mane dhé diaxlé wone na. Déeumb reck mangui lay Xalaat
Magui fi dé je vais trés bien Alhamdoulilah ! Dikatina nak !
@@Diadine-TV Alhamdoulillah 🤲🏿 y'all na Diam yagg inshallah 🤲🏿
Alhamndou Lilah DiADINE TV tew na ❤❤❤❤❤ yalla na diamou yague waye
Amine Madicke ! waw tewate na dé magui nii
Diadine boulma may dédicace 😂😂😂😂 dama guédd Gérard DIOME depuis Congo Brazzaville
Boul guedd noter nala dééé ci nga bokk vidéodemain inchallah ! Bouko rater !
Diadine mangui si bir
Thi la book
Wa ci la bok😊
Keurouk ndiobén dé mom weuroula bok mes khana ma diapou si yalla rek😂😂😂😂😂
😂😂 douma la sakh tontou ngay am loula nekh damay lire sa commentaire rek rombou 😂
Ðiadine thi labok mane same la
Diadine tu es une fierté
Jajeuf way Bassirou !! Ndia...euh !! doko def Diop rek mou geuna simple ??
diadine si la book❤
Ci la bocke
Assalaamu halaykum.
Fanweeri jëwriñ.
Ci ay caaxaan doŋŋ lañu nekk ak lekk xaalis. Réewum
Turki xam ngeen ko mbaa ngeen dégg ko.
Juróom-ñett-fukki tamndareet mat nañu ko te amuñu jëwriñ yu tolli nii.
Kon lii ay caaxaan kepp laa ko jàppe, lii moo tax réew mi ñu bari amuñu yu bari. Bëj gi ñu bari amuñu ko amuñu ndox mu doy te baax lënd gi moom dama koo jéllale matul te jafe na te it dajul ñépp.
Moom daal li tere a dem réew mi bari na.
Senegaal li nit di gën a yittewoo moo fi yombul, muy lekk ak naan ak um paj. Te mu baax ñi seen i yoxo jot seen ginnaaw doŋŋ a ko man a am.
Yal na nu Yàlla taxawu te may nu njiit yu réew mi itteel ci barkeb Alxuraan.
Diadine ci lama bokka😂
Diadine guinaw bouma la ziarè🙏 danga wara gènn chaque semaine MM boudè Ben yon wala nga wouteul ko jour kom chaque samedi wala chaque dimanche ✍️pasqeu danioh soxla sa guiss si ni rèwmi di dokhè❤️✅mais sila bok✊
Délo ziar bou werr Bara Diop ! Waw fann yi la xawone diapp rek wayer delou ci na ! Bouma meuner def video chaque jour sakh tewlou lenn ma magui fi dina ko def ci Katanou Yalla !
@@Diadine-TV d'accord inchallah mais nak sila bok dèma dédicace way👉al Bara chérie indo
Mangi si biit Diadine
No la déf
Diadème si la bokk❤
si la bok✊✊
Ci la bok,From The Gambia
Salam Diadine namnala sinon ci la bokk
Diadine thila bouko
DIADINE 🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Diadine si la bok❤❤❤
Aimer ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ aimer aimer partager partager aimer
Jajeuf Djibril Gueye !
Diadine si la bok
Hello bro , sa ligueye rafett caaaar , mais bayil islamologue yingay garouwalé nak😅
Diadine barké l'islam sunu dîne namanala lol way frère diam soutoura goudou fane AK khaliss bou sét té Bari lol way
Bilay fila eupé Sadou Diallo !! Amine way !! Yalla na sa niane nangou !
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Si la bookou
🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Diadine si la bokk
Pape Sidibé ci la bok
Ci laa bokk❤
Mes encouragements
Merci beaucoup !
Si la bokk
CI LA BOOK
Man mi thi la Bokk
Thi la book dpuis USA
Ci la bok❤
Dia ta oublié si diable logu bi yavé osi les mamouth
Si la bokkk
Way yaw fo nekon lilanla ni yaw waro no manke❤
Maguini tewate na
Bonsoir Diadine mon n'amie mon frère ça fait un baye bilay 😅 restons Focus rkkk inch'Allah la victoire finale es proche 🎉❤❤
Benoit comment ca va oui c'est vrai mais me revoila !
Salam salam Salam
Salam Ousmane !
Ci la bok diadine❤❤❤
Jajeuf Khadim Gueye ziar nala
Ci la bok💯❤😘
Comment un présentateur peut rabaisser un invité à ce point ??? Le pays où sa jeunesse est traitée comme des moins que rien, Tounkara me sort par les trous du nez 😱
Tounkara dama béte
ci la bok mbok mi djadine
Tounkara dafay Fay ndanane au lieu que Moulay encouragé daflay décourager lo
Cii laa bok mes tu nemue remercie pas ❤❤❤❤❤❤
C'est noté je n y manquerai pas !
Či la boke
Diadine chlabok
🤲
Tounkara xoot bop la😂
Si la boque
Khalé Dina fallé tounk naféekh nga