Le ministère de la culture devrait disposer d'un fonds social pour ces artistes qui n'ont pu vivre de leur art. Ce couple mérite un soutien de la mairie de Thiès.
artistes 100 pour 100 un couple tres representatif ma cha alla thies caye bena deuk gnary guares deukou artisans ak artistes sounou artistes yii artisans yii yalla nalene fii yalla yagual ak diam ak khiweul nous thies oi sofe nagnou sounouye artistes
ministere de la culture warna diaple artistes yi ndakh lou ame mana thi rewe la ndakh aye historiens lagnou ak educateurs ndakh the generation future bou taiye bie gnou thi bari khamou seni thossane ak compotement yi leup bou americain dou bou senegal artistes yi gnomana fekhe ba delossi thi sounou thossane
Le ministère de la culture devrait disposer d'un fonds social pour ces artistes qui n'ont pu vivre de leur art.
Ce couple mérite un soutien de la mairie de Thiès.
artistes 100 pour 100 un couple tres representatif ma cha alla thies caye bena deuk gnary guares deukou artisans ak artistes sounou artistes yii artisans yii yalla nalene fii yalla yagual ak diam ak khiweul nous thies oi sofe nagnou sounouye artistes
Amna solo

🙏🏿