QUARTIER GENERAL: SPÉCIALE BAYE NIASS - Invités : CHEIKH I. BITEY & AIDA FAYE Parte1

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 10 янв 2025

Комментарии • 511

  • @enessaadoi
    @enessaadoi 5 лет назад +7

    Machaala ! kéroque , bama daamé , Atlanta USA , done céte, samaye mboque , faf ! ma yamthi , Amercain bou solu , ni julite , buye dam juhma aljuhma , muyeuguel mani , mome Talibés BAYELA kéroke ! Damma téque , fouma yégul , Machaala ! bég goloma , trop thila wakheni dieureftaty BAYE NIASS ay dieufeum chaaria bou mát seukla machaala wasal

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 4 года назад

      Wait and see..we all will be Baye followers..inchallah sikaw sikanam

  • @silvestmase5239
    @silvestmase5239 6 лет назад +20

    Kouye Talibe Baye Niasse beusel j'aime ma guisse

  • @magattegueye8209
    @magattegueye8209 6 лет назад +40

    "le Soleil reste Soleil malgré que l'aveugle ne le voit pas.Et le malade ne ressentirait point le goût du miel."
    Honte à celui qui a soif alors que le fleuve deborde.
    Niou Barhama mo niouy ndandal baniou mandi.
    Dieuredieuf Baye rek!!

  • @mbossetoure7992
    @mbossetoure7992 5 лет назад +2

    baye moy léep thiéye baye ,dieureudieufééééé cheikhal islam Chiekh Ibrahima niass

  • @fatoucisse6090
    @fatoucisse6090 6 лет назад +56

    Man dal douma doyal si wakhtane bi sétane nako plus de 20 fois way yalna nou yalla fayal cheikh Ibrahima biteye si wakhtane bi

  • @abytall6613
    @abytall6613 6 лет назад +19

    Merci wa tfm li nguéne déf nonoula mane guene n'a kham baye Niass grace à vous pape cheikh yalla nala yalla lafal thiat AK oustaz assane Amine

  • @ousmanesenegal75bp58
    @ousmanesenegal75bp58 6 лет назад +46

    Yalla nama yalla deff ma nek di talibe baye bala may sango souff si barké seydina Mouhamed Amine

    • @taibedrame2161
      @taibedrame2161 6 лет назад +1

      Ousmane senegal75bp yalla nala yalla déff talibé baye niass amine yarabi

    • @cheikhomarndiaye8574
      @cheikhomarndiaye8574 6 лет назад

      Amine sangue bi dinga ko nék inchalla, té linga beugue cheikh ibrahim niass rek doyna, ndakh mome moné kép kouma beugue rek yangui ci aldianay bél, moy paix intérieure xool bou laab

    • @mamadoungom2668
      @mamadoungom2668 5 лет назад

      Amna woté wayé amoul kharaté baye rk moy deugueu

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 5 лет назад

      Inchallah di nga ko nekk nakh khol wouyouna baparé dieum dji reka si dess

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 5 лет назад

      Yaw yaye doni deug talibé baye doni arif xam deug deug akhikhatou Mouhamadiya...salep Baye la kone yadi mom batinan fégnal ko rekk si zayir moci dess..Inchallah lolou yagatoul

  • @ousmanesonko3610
    @ousmanesonko3610 6 лет назад +16

    Machallah.
    Je suis resté toute la nuit pour suivre tfm jusqu'à 04h du matin

  • @mamadoulamindiallo5481
    @mamadoulamindiallo5481 6 лет назад +14

    الشيخ الإسلام رضي الله عنه هو أعجوبة الزمان والله لا يرى أحد مثله نفعنا الله ببركاته ءآمين يارب العالمين

  • @adamengomndiaye4209
    @adamengomndiaye4209 5 лет назад +2

    Machalla wakhtane bi amna solo k'en d'ou mawlana mame baye niass la solution

  • @amadouba1275
    @amadouba1275 6 лет назад +2

    Dieureudieufei Baye Niass il est international walahi. Danio beuri kham kham machala

  • @redlionpaco9008
    @redlionpaco9008 6 лет назад +8

    Kou beug Baye gnou beug la
    Baye mo deff sunu xol yi beug yallah wone gnou yone

  • @nabou7485
    @nabou7485 6 лет назад +126

    Yalla nagnou yalla def deug deug talibè Baye Niass ci Barkè Baye niaiss yarabii 🙏🏾🙏🏾❤️😍😍!!!!!!

  • @fatoubintourassoul3365
    @fatoubintourassoul3365 6 лет назад +13

    Machallah way amna solo tropp yalla naniou yalla deff talibè Baye Niass ahihatane

  • @khadymbayesall7391
    @khadymbayesall7391 5 лет назад +2

    Baye niass moye degue bilaye yalla na yalla fayale ngnou ko 🤲🤲🤲❤❤❤

  • @taibedrame2161
    @taibedrame2161 6 лет назад +9

    Alahou akoubarr dieuredieufé baye niass dieuredieufé baye niass dieuredieufé baye niass lii nékhna trop barké baye niass

  • @abdoubiguekebe7744
    @abdoubiguekebe7744 5 лет назад +1

    Eskey ouztaz Cheikh Ibrahima Biteye wakhtaan bi werr na fassaa na deuggou na tamit machallah. Baye rék moy deugg 🙏🏿🙏🏿♥️♥️

  • @khadijafallmasterson4602
    @khadijafallmasterson4602 6 лет назад +1

    wawaw Minka ileyka
    hamdulilah ! Proud to be Talibé Mawlana Cheikh al Islam Elhadj Ibrahima Niass.
    Deug ak xam xam rék ak Yallay kessé machaAllah

  • @seynabouthiam7488
    @seynabouthiam7488 6 лет назад +21

    Machallah sokhna Aïda nekh na trop yalla na niou yalla fayalle Mawlana Cheikh Ibrahima Niass❤❤❤

  • @penthiemi
    @penthiemi 6 лет назад +6

    merci yalla ngafi yague té wer, gnou méni lagnou begue si senegal

  • @lhommedelarivegauchedufleu3101
    @lhommedelarivegauchedufleu3101 6 лет назад +2

    Machaalah kenn dou Cheikh'Al islam mame Baye yalla Nagnou yalla tass si barké amm amine allahouma amine

  • @Hoho-xu6ye
    @Hoho-xu6ye 5 лет назад +2

    Machalah wakhtane bi nékhna trop machalah sokhna Aïda yalla na yalla wéral bate bi si barké baye ak bayam

  • @Adamabarham
    @Adamabarham 6 лет назад +41

    niou anda ndo wakh dieureudieufff baye. haqq bil haqq. thioberé Yallah dji . doney rassoulilah. way affaire de serigne Sénégal rekk la am mais kou djegui frontière kham ni baye rekk moy serigne. wallahi yay deugeu. Beugeu Baye dal daley nopale.

    • @vieuxdembele4746
      @vieuxdembele4746 5 лет назад

      Dieuredieufèèèèèèèèèèèè Baye Niass

  • @mamadoudiol6239
    @mamadoudiol6239 6 лет назад +33

    Machallah baye sougou baye yalla nagou yalla fayall baye si barke seyidouna mouchard psl

  • @cheikhahmedtidianedieng8812
    @cheikhahmedtidianedieng8812 6 лет назад +7

    Kou naan diiw miirrr masha allah
    Alhamdoulilah!!!!!

  • @sambadiop1158
    @sambadiop1158 6 лет назад +9

    yalnañou yalla feyal BAYE ÑASS akk mboleum nitou yalla yi gni ndieuk ak gni moudiou (mouride tidiane khadre layene)leup sènègal laa "FALLOU DIOUF"on se respect

  • @mamadoundione4840
    @mamadoundione4840 6 лет назад +7

    Dieuredieufé BAYE NIASS ALHAMDOULILAH MERCI CHEIKH IBRAHIMA BITEYE BILAHI BAYE REKAY DEUGUE

  • @cheikhtidianeba7145
    @cheikhtidianeba7145 6 лет назад +2

    MACHALLAH SERIGNE BI WAXTAANE BI NEEX NA ET JEUREUJEUF BAYE NIASS

  • @abdoulazizsow2719
    @abdoulazizsow2719 6 лет назад +2

    Dieureudieuf Baye..Dieureudieuf Oustaz biteye,, mashallah xol yi seddeuh neuh!

  • @mamadoukourmang2848
    @mamadoukourmang2848 6 лет назад +3

    macha allah BITEY YALLA nala YALLA gueureum si barke BAYE, contenaniou si yow te YALLA BAYE gueureum

  • @aichatouniass8996
    @aichatouniass8996 6 лет назад +2

    Deug deug Baye rek moye serigne yalla nagnou ko yalla fayal bijahi rassoul Niass Goumba Abdoulaye ❤

  • @maribiteye3030
    @maribiteye3030 6 лет назад +10

    Yallah fayal nou baye niass 😘

  • @moustaphacisse8612
    @moustaphacisse8612 6 лет назад +25

    Talibet moy aldianna. Nekal talibet rek tet doundou sa aldianna. Djeureudjeuf bay Alhamdoulil lah

  • @yahyaabayawo7402
    @yahyaabayawo7402 6 лет назад +5

    Alhamdulillah Macha Allah Ler na Mat na Saf na Nekh na Yalla na Yalla Werel la Katanal la Gudal say Fan Ta nge Feke ko cii Barke Baye

  • @malickfaye5850
    @malickfaye5850 6 лет назад +2

    Baye moy sunu baye . Cou amoul baye do nekk do dioudou . Dieureudieufééé BAYE NIASS

  • @soldaroubayeniassmmesarr9659
    @soldaroubayeniassmmesarr9659 6 лет назад +24

    Machallah dieureu baye barhama niass zeyda khol sedatina machallah yalna batt bii wer

  • @fatoubintourassoulmbaye5413
    @fatoubintourassoulmbaye5413 6 лет назад +2

    Machallah Dieureudieufé cheikhal l'islam mame baye niass❤❤❤

  • @yayoutawsy8422
    @yayoutawsy8422 6 лет назад +22

    Machallah Dieureufé BAYE NIASS. Machallah Cheick Bitéye wakhtane bi nékhna XAAM XAAM bou wér ❤️❤️❤️❤️

    • @yahyaabayawo7402
      @yahyaabayawo7402 6 лет назад +1

      Yayoutaw Sy Alhamdulillah Macha Allah Yalla Nako Yalla Werel Gudal Fanam ta nge feke ko

  • @seynaboucisse3692
    @seynaboucisse3692 6 лет назад +1

    Machah lah cheikhe ibrahima biteye yalna baye niass fayale nioula dieureudiefeh baye niass alhamedou lilah

  • @serignendione6712
    @serignendione6712 6 лет назад +1

    Macha alah wakh tan bi matalè serigne yalna Baye niass Faye la

  • @fatitisadji7678
    @fatitisadji7678 6 лет назад +31

    machala seyda Aïda Bay notre solution le meilleur c est cheikh Al islam

    • @cheikhahmedtidianeba4108
      @cheikhahmedtidianeba4108 6 лет назад

      Fa Titi Sadji baye rék moye dégeu yalla nala yalla faye si barké cheikhou tidiane

    • @slashmethalux1162
      @slashmethalux1162 6 лет назад

      Sou dei baye moy solution leigui kane moy resultat?

    • @gorgainde1978
      @gorgainde1978 6 лет назад

      Send me your number 0508159650

  • @zaraniass4866
    @zaraniass4866 6 лет назад +2

    Machala monde entier ngéneu laleu taye Baye Niass Bayi rouhou yi Bayi alame Bi Niass

  • @mamendiaye4651
    @mamendiaye4651 6 лет назад +2

    Yalla nallene yalla Faye thi barkè baye barkhama Niass dieurediefè baye

  • @kebacisse3390
    @kebacisse3390 5 лет назад +2

    Machallah baye niass mon tubloo bourou kanou

  • @mamadouthiam5936
    @mamadouthiam5936 4 года назад

    Minka iléyhi. Kén Dou Baye Niass. Alahamdoililahi Baye rékk

  • @tabatreich89
    @tabatreich89 6 лет назад +2

    Al hamdou lilahi rabil alamina biniou Yallah mayé Cheikh al Islam

  • @xelmoyniitxel9053
    @xelmoyniitxel9053 6 лет назад +6

    Dg Dg Baye niass rek moy serigne niass rek moy serigne niass rek

  • @masssarr2304
    @masssarr2304 6 лет назад +23

    Yalla na niou dee si begeu baye niasse

  • @bayediaw913
    @bayediaw913 6 лет назад +7

    Baye niass rekk moyy deug walahii Baye moyy adouna

  • @mamadousall1151
    @mamadousall1151 5 лет назад +1

    Machala Allah plus de 50fois la ko sétane té Bou nieu gueuna nékhe

  • @boubadrame2681
    @boubadrame2681 6 лет назад +9

    Baye moy sougnou baye machallah

  • @moussasamb207
    @moussasamb207 6 лет назад +64

    Yalna yala déf niou ah talibé baye deug deug done talibé baye billah yoboul

  • @fatoucisse6090
    @fatoucisse6090 6 лет назад +6

    Alhamdoulilah alhamdoulilah machallah dieureudeufé Baye Niass

  • @khalill_9492
    @khalill_9492 5 лет назад +1

    Gnii dii dise like nitt noumou mouna deké Senegal bagne sekhal Islam

  • @bathiewade3002
    @bathiewade3002 6 лет назад +5

    Alhamdoulilah rek lay wakh ndakh Baye loumaci meunti dègue damay doli sante rek té khamni amna loubari lou dess

  • @Adamabarham
    @Adamabarham 6 лет назад +75

    « Nul pourra connaitre Allah sans pour autant passer par moi »,
    nous dit Baye. « Celui qui vit jusqu'à
    la mort sans connaitre son seigneur a hérité d'une vie sans quintessance... ma
    lam yanal maarifatou rahman ahmarouhou lahad madal asmani » évoque Baye
    Niass dans Rouhoul Adab, un livre étonnant écrit à l'âge de 21 ans.
    Quand finira-t-on de parler de Baye ? C'est comme si on puise quelque
    part où ça ne s'épuise jamais, ce qu'on prend, et jamais ne se remplit l'endroit
    où on le déverse.. way khana dou beugeu baye mo nekh. khana dou ki moy degeu ❤❤❤💦💦💦

    • @rakiatoukeita53
      @rakiatoukeita53 6 лет назад

      Adama Rassoul machalla amna solo

    • @ababacargaye1846
      @ababacargaye1846 6 лет назад +1

      Adam Rassoul ziarnala. Diokhma sa numéro ma am nouma def ak Yaw ci Barké Baye

    • @Adamabarham
      @Adamabarham 6 лет назад

      +Ababacar gaye dieulal 771587411

    • @ababacargaye1846
      @ababacargaye1846 6 лет назад

      Bien reçu.
      Merci

    • @alphaoumar8034
      @alphaoumar8034 6 лет назад +2

      Niaaaaaaaaaaassssssssss cheikh ababacar gaye naka teral wadji barke Baye

  • @aliouba6978
    @aliouba6978 6 лет назад +29

    Billahi sante nala Chiekh Mamour INSA Diop yow mima khamal Baye Niass

  • @dimabolykdiankha6781
    @dimabolykdiankha6781 6 лет назад +1

    Jazakalou khayra al oustaz wahtan wi fassa lol dieureudieufè baye niass

  • @adamaawadiallo7009
    @adamaawadiallo7009 6 лет назад +1

    Macha'allah shaykh islam do gnom té dougnou iow.khamal guama shaykh tidiane khamal guama nabi(psl) diarrama baye

  • @bathiewade3002
    @bathiewade3002 6 лет назад +2

    Sama serigne Baye Cheikh Wade mankoy ñanal yalla boubakh tamit ak Baye Niass

  • @mouhamedcisse9728
    @mouhamedcisse9728 6 лет назад +21

    Machalah cheikhal Islam rekk mome lawolou

  • @mouhammedwade782
    @mouhammedwade782 6 лет назад +3

    Kookou moy Mawlana Sidy Barhama Cheikh al islam El hadji Ibrahima niass baye borome Medine borome faydatou tidianiya mome moni kouma gueuna beugg yonent bi moy dieul nga sa barame lale ko si weer bi ( impossible ) baye moniou doye si diangalè yalla ak yonent bi PSL doyniou si fonkou souni niari way diour DIEUREUDIEUF BAYE.

  • @papasanadiallo4875
    @papasanadiallo4875 6 лет назад +7

    Dieredieuf baye niasse mais pape cheikh a fait de bonnes interventions

  • @ismaeltambasireraleigh287
    @ismaeltambasireraleigh287 5 лет назад +2

    Pape Cheikh un peut deux respect qu'an même . tout ce qu'il disais est vraie,
    seul peux des sénégalais qui connais pas Baye

  • @abdousalam8630
    @abdousalam8630 6 лет назад +43

    Lii ça montre que cheikh Ahmed tijane amoul morom ci adouna bi

  • @bayembow8142
    @bayembow8142 6 лет назад +3

    Machalla li nékh,na jërëjëff baye barhama niass

  • @ozil-ou1ku
    @ozil-ou1ku 6 лет назад

    Mach'allah ! Amena solo baye Niass borom faydou bii!

  • @Dou19760303
    @Dou19760303 6 лет назад +2

    Mame BAYE NIASS ,une fierté pour le senegal!

  • @6calimandiayecisse202
    @6calimandiayecisse202 4 года назад +1

    Dieuredieufé baye niass machallah alhadoulilaah❤️

  • @seydoundiaye8341
    @seydoundiaye8341 6 лет назад +1

    Vraiment Cheikh Biteye dafay dindi stress Yalna Yalla fayla si Barker Imam Ahmad

  • @oulimatandiaye3516
    @oulimatandiaye3516 6 лет назад +4

    Masha ALLA kéne dou Baye Niass

  • @bayeniassdieureudieuftv9692
    @bayeniassdieureudieuftv9692 5 лет назад +1

    macha allah néxna trop
    Baye Niass Dieureudieuf

  • @khadijaloum2412
    @khadijaloum2412 6 лет назад +1

    Dieuredieufe maolana cheikh Ibrahima Niass baye moye lepp limadone yow la niass

  • @elhadjiibrahimathiam6964
    @elhadjiibrahimathiam6964 6 лет назад +1

    merci infiniment Baye Niass, Billaye ya bakh.

  • @ndeyfatousallah4785
    @ndeyfatousallah4785 6 лет назад +14

    Machalla wahtabi amna solo trop

  • @modoucheikhthiamine1971
    @modoucheikhthiamine1971 6 лет назад +1

    ALAHOU AKBAR ALAHOU AKBAR ALHAMDOULILAH YALNANIOU YALAH KHAMAL BAYE NIASS AK SOUNIOU ROKHO AMINE

  • @mamadou642
    @mamadou642 6 лет назад +3

    Machallah wa keur baye niass xam xam rek

  • @beuguebaye5009
    @beuguebaye5009 6 лет назад +5

    baye niass nous a sauvé alhamdoulilah

  • @mayasarr7928
    @mayasarr7928 6 лет назад +47

    baye moy serigniou Serigne siii

  • @ibrahimakane7141
    @ibrahimakane7141 6 лет назад +2

    dieuredieuf Baye Bitey Dieudieuf Aida Faye lii rafetna wayé sénégal mou nékh léne wala mou nakarii léne Baye moy degue té bougouniou koudoul mome

  • @fatitisadji7678
    @fatitisadji7678 6 лет назад +66

    j aime bay de tout coeur

  • @awafall6361
    @awafall6361 6 лет назад +9

    Alhamdoullilah dieredieufé Baye niasse 😍❤💓💖💗💞💚💛❣

  • @sohnaabsabarhama3812
    @sohnaabsabarhama3812 6 лет назад +5

    ALLAH BAYE REK MASCHA,ALLAH YAYE BOY AIDA

  • @karibaye2333
    @karibaye2333 6 лет назад +4

    Machallah BAYE moy 2gue🙏🙏🙏🙏🙏👌👌👌👌

  • @pendathiamtijani2392
    @pendathiamtijani2392 6 лет назад +1

    Walahi ya oustaz dama contane ci yow. Yallah nala Yallah yok kham kham bouy diarigne ci barkei Baye. Ndeysane Oustaz Barham Diop radi Allah anhou méthode bi la amone ba meune di wakhtane ak talibé ak kouko doonoul. Alhamdoulilah

  • @cheikhouka4718
    @cheikhouka4718 6 лет назад +1

    Machallah machallah machallah machallah biteye merci merci merci mame baye niass

  • @cheikhlo1696
    @cheikhlo1696 5 лет назад

    Yalla nagniu yalla fayall baye niass

  • @moussaly3169
    @moussaly3169 6 лет назад +4

    Thiey baye Niasse . Sa mbeguel ci yonete bi ken douko amossi masse walahi. Dieuredieuf Niasse

  • @chimerediouf1152
    @chimerediouf1152 6 лет назад +1

    Thiey Baye Niass 🙏 Alhamdoulillah😍

  • @cheikhfaye8893
    @cheikhfaye8893 3 года назад

    Dieuredieufé maolana cheikh Ibrahima niass ra mom

  • @alhagieinternational265
    @alhagieinternational265 6 лет назад +9

    mashalah sukran alhamdoulilah jerejef sheikh Ibrahim nyass

  • @maliktamba2561
    @maliktamba2561 6 лет назад +2

    Mancha'allah wahtan bi néh kadouyi rafetna lérr na.
    Yalana yala yokk télé bi té yokk ko si batiin ak zahir thi barké wahtan bi

  • @tidamichaud8260
    @tidamichaud8260 6 лет назад +1

    Merci.beaucoup mon pape ton émission est super wakhtanebi amna solo

  • @assankuta2935
    @assankuta2935 5 лет назад +1

    I like the waxtane and I have watched it many many times.

  • @ndaomore7047
    @ndaomore7047 6 лет назад +5

    Mancha Allah Cheikh Ibrahim Niass

  • @cherifkande1694
    @cherifkande1694 6 лет назад +2

    Baye amoul morom siii adouna

  • @sadoubenziabarry541
    @sadoubenziabarry541 6 лет назад +3

    Yalla nagnou yalla yeureum
    Deff gnou deugeu ay talibé baye

  • @fatimakouta1656
    @fatimakouta1656 6 лет назад +6

    Bilahi Baye rk mo doré
    Ken d'où Baye diarama baye

  • @fallfadel9398
    @fallfadel9398 6 лет назад +3

    pape yalla na yalla fay léne si barké baye ak bayame wakhe tane bi fasana trop

  • @talibebarhama5567
    @talibebarhama5567 6 лет назад +8

    alhamdoulilah baniou doné talibé Baye