Serigne Ahmed Fall : "Seydi El Hadji Malick limou niane Yallah thi Yonent bi..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 22 янв 2025

Комментарии • 137

  • @ndeyemalediaw3296
    @ndeyemalediaw3296 4 года назад +34

    Khamkham rek guafi wakh walahi ☝nétali wo gara lo☝machallah professeur

    • @mensamensa9154
      @mensamensa9154 4 года назад

      Soirèe bi nèkh na machalla 😂😂😂

    • @cheikhba2363
      @cheikhba2363 4 года назад +1

      doul

    • @modoumboup1562
      @modoumboup1562 4 года назад +1

      @@mensamensa9154 changél sa tour bi do talibé ms vraiment yèn esk guem guèn yalla wallahi saytané mome nalèn respect amoulèn ko si nittou yalla yi

    • @ndeyemalediaw3296
      @ndeyemalediaw3296 4 года назад +2

      @@cheikhba2363 ndandal ndokh séral sa khol! 😂😂😂khol bou yalla ak yonenti teksi mak you bakh yi dou sagua ☝☝

    • @ngagnediop761
      @ngagnediop761 4 года назад

      @@mensamensa9154 changél sa tour bi réw nga trop

  • @awandao6192
    @awandao6192 4 года назад +31

    Yalla nagnou ko yalla féyal serigne babacar sy

  • @ndiayendiaye9143
    @ndiayendiaye9143 4 года назад +25

    MACHA ALLAH fasaha Yalla nalako sunu BOROM defal 😍😍

  • @mbdone3860
    @mbdone3860 4 года назад +33

    Seydina Mohammed sallahou aleykhi wasalam

  • @taphadjiamillo7347
    @taphadjiamillo7347 4 года назад +22

    Xam xam rkk mo woor billahi wallahi
    هل غاب من سكن القلوب قليلا 😭

  • @zeynabdiallo1744
    @zeynabdiallo1744 4 года назад +15

    Machallah machallah Sénégal si kaww si kanam. Yalna yallah deff diam tfm merci💓💞💞💕keeneu dou borom bonnet carré cheikhal Khalifa 💕💓💓💓💓👌👌

  • @mamadoumansourfaye4684
    @mamadoumansourfaye4684 4 года назад +8

    Serigne Babacar Sy sounou xol ❤️yeup yassi fess lolou yalla dogal❤️🙏😭😭

  • @pseudoweuz8397
    @pseudoweuz8397 4 года назад +18

    ALLAH AKBAR
    That's a hight level
    Un niveau tres tres élevé
    Eskey

  • @ndeyemalediaw3296
    @ndeyemalediaw3296 4 года назад +7

    Mane Ahmed fall la beugue guisss 😭😭😭😭😭

  • @diopbaps1481
    @diopbaps1481 4 года назад +7

    Sam mi nouniou déf bamou diangue ta guissoul war naniou ko lidieunti dh niou balma si wah dji ❣️❤️❤️❤️

    • @thiammamadou772
      @thiammamadou772 4 года назад +6

      Seringe Mansour brome daradji moka deffar da am tivaon si djabotou maodo gui lo kham ni sirou la danou kay dimabale ko khamni daa beug kham kham mes amoul outils yi koy may kham kham comme ko khamni dafa silmakha walla mou teukh wala mou moumeu walla khel mi nekhoul mam maodo deffal nako seringe alioune gueye seringe Babacar defal nako papay niom seringe Moussa Gueye mam Mansour bakhawmi deffal nako papay niom makhtar kebe mam abdou deffal nako gorgui ko dann djotalil mam habib deffal nako ay mangui lebou sa thiaroye seringe Moustapha sy djamil defal nako ay mag you barri sa medina fass..........

    • @diopbaps1481
      @diopbaps1481 4 года назад +4

      @@thiammamadou772 wéreul bro lolou dafa yémé d

  • @coumbasylla876
    @coumbasylla876 4 года назад +13

    Machallah yalla rék moko niorr akh yonéntém bi

  • @NewNew-ex4so
    @NewNew-ex4so 4 года назад +14

    Machallah.xam.xam.pir.tivaoun.

  • @mbdone3860
    @mbdone3860 4 года назад +17

    Xam xam mashallah

  • @babacarthiao1054
    @babacarthiao1054 4 года назад +11

    Machallah

  • @mamifall6170
    @mamifall6170 4 года назад +18

    Kén dou Serigne Babacar sy

  • @jamilboromfassgueye6601
    @jamilboromfassgueye6601 4 года назад +26

    ♥️♥️♥️♥️♥️♥️Serigne Babacar Sy Serigne babacar Sy Serigne babacar Sy Serigne babacar Sy Serigne babacar Sy Serigne babacar Sy Serigne Ba Adina dit touki ñiounak Serigne Babacar Sy ♥️♥️♥️♥️♥️🕋🕋🕋🌙 ki Tawlo Sama Tourando Seydil djamil Sy borom fass

  • @nassitewoulfcloud861
    @nassitewoulfcloud861 4 года назад +9

    Bilahi xam xam baanga tivaouane

  • @srbathiediop4854
    @srbathiediop4854 4 года назад +2

    Amoul wéranté🥰🥰🥰🥰🥰🥰allahou akbar

  • @yayeawdiatv948
    @yayeawdiatv948 4 года назад +5

    Serigne babacar sy 💖💖💖

  • @elhadjilo7597
    @elhadjilo7597 4 года назад +22

    kene dou seringe babakar sy

  • @mamifall6170
    @mamifall6170 4 года назад +9

    Xol sed na Bilay

  • @BathieFalleuh
    @BathieFalleuh Год назад

    Machallah❤

  • @papesylla7281
    @papesylla7281 4 года назад +8

    Wakhtan wi amna sollo dégue nafi yalla dégue nafi yonnent bi.

  • @ismailamoubayeniassfall6541
    @ismailamoubayeniassfall6541 4 года назад +4

    Ohh xol cedd na masha allah

  • @diopbaps1481
    @diopbaps1481 4 года назад +7

    Level bi dafa kawé

  • @maremewade6713
    @maremewade6713 4 года назад

    Yallanala bour yalla faye oustaz

  • @tallasarr7560
    @tallasarr7560 2 года назад

    MACHALLA 🙏 🙏 🙏 🙏

  • @bamsbams5164
    @bamsbams5164 4 года назад +6

    Cheikh seydil Hadji Malick sy ❤ 🙏 7
    Cheikh seydil Hadji Malick sy ❤ 🙏 7
    Cheikh seydil Hadji Malick sy ❤ 🙏 7
    Cheikh seydil Hadji Malick sy ❤ 🙏 7
    Cheikh seydil Hadji Malick sy ❤ 🙏 7
    Cheikh seydil Hadji Malick sy ❤ 🙏 7
    Cheikh seydil Hadji Malick sy ❤ 🙏 7
    Amine🙏 amine🙏 amine🙏 amine🙏

  • @sidyfall4293
    @sidyfall4293 4 года назад +6

    Mame khalifa❤️❤️❤️🙏🏽

  • @astousaliou6997
    @astousaliou6997 4 года назад

    Machalla sy Amna solo Amine Amine Amine

  • @cheikhgeuye9731
    @cheikhgeuye9731 4 года назад +18

    Kou léne yab da démoul ak yéne si xam xam maodo mo raw si Sénégal ak fénéne foudoul senegal xam xam dou ay thiow

    • @mensamensa9154
      @mensamensa9154 4 года назад

      Bamba moy bayam maodo moride

    • @dmxedemx3671
      @dmxedemx3671 4 года назад +2

      @@mensamensa9154 Nakarou xol dinala Ray téga yam frère Babacar Sy dou Morom deh

    • @fallmor1049
      @fallmor1049 4 года назад

      Serigne cheikh dafa lér

    • @omargaye9950
      @omargaye9950 4 года назад

      😂😂😂Nioun ak yén dou combat cheikh béthio rekk dou moromou mame maodo

    • @ibrahimadiakho489
      @ibrahimadiakho489 4 года назад +7

      @@mensamensa9154 s8 mourid waye iow seringe touba santunu li de iow kou dem do ap mourid ap mourid waroul toutal ken bamba di maodo maodo di bamba koulen baga fewale danga kahmoul kouy ya rassulilah seringe touba Bo khole kassida yim binde yonantebi lasiy way Bo khole seringe alhaji malick tera yimou bind yonante bi lasiy way guir yalla yewou len yalna diamou yag si barke seringe touba

  • @ndiayetechjr6724
    @ndiayetechjr6724 4 года назад +1

    Xam xam dafa wara rafet ❤❤🙏🙏

  • @cheikhalakhone7110
    @cheikhalakhone7110 4 года назад +4

    Khame khame daye moka machallah khame lingaye wakh nekhna

  • @fakanegeuye6047
    @fakanegeuye6047 4 года назад +3

    Dama beugeu serigne babacar sy

  • @mbdone3860
    @mbdone3860 4 года назад +1

    Cheickh Tidjani cherif radiallahou Aboul abass

  • @moktarmoh789
    @moktarmoh789 4 года назад +1

    Ken dumaodo malick sy 💖

  • @aminatadiaw521
    @aminatadiaw521 4 года назад

    Machalah seydi Sy Mame boy

  • @abdabouboudiop1812
    @abdabouboudiop1812 4 года назад

    Machallah seydi sy

  • @deffaly9056
    @deffaly9056 4 года назад

    Masha Allah

  • @PastefAfricaNews
    @PastefAfricaNews 4 года назад

    Diereudieuf Seydi El Hadji Malick 🙏

  • @dmxedemx3671
    @dmxedemx3671 4 года назад +8

    Xam Xam daal kouko begeu demal diangui tivaouane

  • @diagnenar8290
    @diagnenar8290 4 года назад +12

    Kene dou maodo

  • @omarmandiang1061
    @omarmandiang1061 4 года назад +1

    Walakhi kou deugu senegal taguay wakh deugu wargua wakh dieureudieuf seydi hadji malik sy holal borom xam xam yi si Sénégal

  • @cheikhseck5857
    @cheikhseck5857 4 года назад +6

    Svp bayilene di tontou naniou tal sounou bope rek

  • @Nymeria1111
    @Nymeria1111 4 года назад +1

    Gnounn tarikha cheikhna ahmadal tidiany serigne babacar sy lagnou doylo koumou nakari diaroul ngay khol loufi khew soul ker douko téré fégn

  • @awadia8658
    @awadia8658 4 года назад +2

    Mbaye.dane.gua

  • @daviediop992
    @daviediop992 4 года назад +1

    Seydil ABOUBACAR SY rék rék dongg

  • @NewNew-ex4so
    @NewNew-ex4so 4 года назад +3

    Limoy.xam.xam.waye.seringe.bi.nawna.seringe.bi.moy.yalla.mo.ditou.yonente.lolou.dou.xam.xam.te.amoul.ndiaringe.

  • @soldarousbabacar7291
    @soldarousbabacar7291 4 года назад +1

    Xam xam mo wor walahi

  • @ndiassegueye1933
    @ndiassegueye1933 4 года назад +1

    AL KHALIFA dal rien a dire nignouleu beugué kén mounouko expliqué lii kén xamoul lanla

  • @maremesy7276
    @maremesy7276 4 года назад

    Dierediefeti wa tfm tha caw thia canam diam rek thi yene thi barket Serigne Babacar Sy gnopou contannagnou

  • @elzofall742
    @elzofall742 4 года назад

    Emision.bi.bamou.ame.legui.la.probleme.tarikha.conmence.

    • @ibrahimadiao6048
      @ibrahimadiao6048 4 года назад

      Voilà comme day indi wax naniou arreter waxtane si dîné

  • @alieujallow3710
    @alieujallow3710 4 года назад

    Yean ragallean yalla gen wakh degi tarika tijan fen

  • @alioudrame6266
    @alioudrame6266 4 года назад +1

    Xam xam bi lerna neko fi di garouwale aka yok

  • @mensamensa9154
    @mensamensa9154 4 года назад

    Soirèe bi nèkh na bayilen fen rèk doule liga wakhon lepo ay fenla dem len akale Sen jumma dji 😂😂guire yalla dèlen diokhe adiya

    • @lazebre1192
      @lazebre1192 4 года назад +4

      Yaw mome do talibé cheikh wayé Diouma dji diguéne ko bayi meuna am diouma dji bouy paré doko fèkkè ndax ay faux billets douko tabax

    • @Mamediarra2001
      @Mamediarra2001 4 года назад

      La Zèbre wakhi doff 😂😂😂

    • @alioudrame6266
      @alioudrame6266 4 года назад +7

      Dînee islam kene douko nat ci ay tabah. So demé Londres wala New York fek kofa. Yene dangueneu tarder ci diné di dabou ci ay tabah. Tabah ay nit mo eup solo. Tidiane bokou gnou ak yene philosophie il faut que nguene kham lolou. Gni khamou gnou ladj khaliss. Yenak danguene di exploiter talibe yi rek

    • @diawabdou2823
      @diawabdou2823 4 года назад

      Kimo niaw ndayi wah yén diangou léne motah ngénedi wéle wéleli mame maodo danio dékelaré ak nieuweume katale ndayam diangui

    • @abdouazizdiouf2371
      @abdouazizdiouf2371 4 года назад +2

      Mashalah wakhtane bi amna solo
      Laniou bayi wakhaté yu niaw yii n'a kunek gueum sa serigne rek té fonck wala mandou si kenennn!!

  • @slyfy7419
    @slyfy7419 4 года назад

    Mame maodo raw si xam xam bou wer

  • @omargaye9950
    @omargaye9950 4 года назад

    Waxtan bi nekhna ndakh dieumi yalla wayé nakkk xamlén sén place bén cheikh béthio rekk meuna djité koulou tijan

    • @fatimatoufall8210
      @fatimatoufall8210 4 года назад +2

      Bayinaniou la ake ya Allah ci barké wérou koor ya Allah reubeuna kouye yé fitena té gore dou toutil serigniou diambour.

    • @cheikhtidianendao3374
      @cheikhtidianendao3374 4 года назад +1

      Demleneu si concours mbarass yi

    • @fallygaye56
      @fallygaye56 4 года назад

      Ya meuna dajii sa data yaye ak Kathie bou dé yak sa serigne domeram

    • @عليبابكرشك
      @عليبابكرشك 4 года назад

      Omar Gaye sa dokhotou serigen

    • @omargaye9950
      @omargaye9950 4 года назад

      @@عليبابكرشك ni rekkkk yag ngên thi boulén sisou liguéyolén won kén fayoulén point sen talibé yi compprend niogui daw di nieuww

  • @amadousam8469
    @amadousam8469 4 года назад +3

    Machallah

  • @mouhamadouyoum2613
    @mouhamadouyoum2613 4 года назад +3

    Machalla