Serigne Moustapha Gningue Wolofal Serigne Saliou

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 10 фев 2025
  • Serigne Moustapha Gningue Wolofal Serigne Saliou

Комментарии • 763

  • @elhadjndiaye4726
    @elhadjndiaye4726 2 года назад +9

    Serigne saliou Mbacke diadieuf ya yayoo dieuredieuf merci borom yeurmadee

  • @aminatafall1459
    @aminatafall1459 8 лет назад +3

    Sokhna Aminata Fall mou Serigne Saliou Dieureudieufeti Serigne Touba yalla yok sén leer tafgnou thi sen barke dieureudieuf Serigne Moustapha Ngingue yalla weureul bat bi

  • @momojob5660
    @momojob5660 5 лет назад +16

    Assalihal lesi you kamiloul amal bilay mbacké ken dou mome yalna ñouko yalla fayal!! Serigne Moustapha gnigue yalna sa fane goudou téi thieuryi wérr thi barké serigne saliou

  • @astoufaye5127
    @astoufaye5127 3 года назад +24

    😭😭😭😭Dieureudieuf Serigne Moustapha Guingue 💪🏾 yalna ya Allah weural batbi thi barké serigne Touba , Serigne Saliou yalnako ya Allah yokk ay leer 🤲🏾🤲🏾🤲🏾

  • @juniormurtala3636
    @juniormurtala3636 11 месяцев назад +19

    Thiey Serigne Saliou Mbacké les années passent mais la douleur reste toujours la. Yalle nako yalla yaram té DIEGAL KO 😢

  • @khoudiandiaye9239
    @khoudiandiaye9239 Год назад +18

    Ces paroles m ont manqué c'est pourquoi j'ai pas hésité de l'écouter vmt c'est magnifique dieureudieuf Serigne saliou merci infiniment Moustapha gning

  • @NdiagaDiouf-n5x
    @NdiagaDiouf-n5x 7 месяцев назад +6

    Sérigne saliou yalna yalla yeurem ko❤❤❤❤

  • @moustaphasylla3500
    @moustaphasylla3500 6 лет назад +13

    Machallala serigne moustapha Seck yallana serigne touba faye

  • @ndeyesougou6436
    @ndeyesougou6436 6 лет назад +4

    Bilahi Moustapha thi kaWW THI kanam thi lou bakh yalla nala yalla diapalei tei werreul batt bi thi barki s saliou

  • @khalilnewyorkino9493
    @khalilnewyorkino9493 4 года назад +61

    Kou setan si 2020 bi gnou ñianal s.saliou sa brom yookou ay leram te tafñu si barkeba amin

  • @bbkine2571
    @bbkine2571 4 года назад +18

    Oh yaram daw na😭mashallah yakar dji❤❤

  • @MamecheikhSene-m2r
    @MamecheikhSene-m2r Год назад +8

    Machallah yalla na serigne touba faye ❤❤

  • @ndeyediouf1137
    @ndeyediouf1137 3 года назад +7

    Koukoy sétann en 2021 machaalla sant yalla rek

  • @zallefallcestvraimasurkhal3771
    @zallefallcestvraimasurkhal3771 6 лет назад +15

    thieuy Serigne saliou Mbacké amoul morom yalla n'a yalla yok ay leram si Barker seydou na Mouhamed psl

  • @dofndeyelalaywaxde6002
    @dofndeyelalaywaxde6002 8 лет назад +13

    doundal way fall yalla s Moustapha yalla na yalla wéral batt bi taga dadiésékk gueureumou serigne Saliou l'absolu

  • @mamediarrasylla5045
    @mamediarrasylla5045 6 лет назад +8

    Mancha Allah shoukrane s'érigne saliou yereume nanou defar niou ba deme

  • @MynaMbaye-qy3nx
    @MynaMbaye-qy3nx 5 месяцев назад +5

    Ndaysane 😭 Serigne saliou yalla na yalla yokou aye leram 😭😭tu resteras toujours gravé dans nos mama saliou 😭😭😭

  • @bourysalioudia9214
    @bourysalioudia9214 4 года назад +19

    Mancha Allah thieuye serigne saliou makko beugu😭🥰

  • @NdiobaKane-dx2fm
    @NdiobaKane-dx2fm 11 месяцев назад +3

    Thiey Mbacké balla 🥰 sunu sangue bi yallna yalla yokou ay lèram té tass gnou si barkém 🙏 il reste tjrs gravé dans nos mémoires 😭

  • @unknowmobileplayer8007
    @unknowmobileplayer8007 Год назад +1

    maa shaa Allah Serigne saliou yalnay ook ay leeram akki kheweuleum taasniou si barkem Serigne Moustapha ngning yalla yalla feyla yiw Barke xassidayi

  • @amdygueye1206
    @amdygueye1206 4 года назад +1

    ndeye sane yalla nonu yalla fayall serigne salliou

  • @ndiollediouf4035
    @ndiollediouf4035 5 лет назад +9

    Macallah nice na lool kay barki s saliou mbacke rek 😭😭😭😭😭😭😭

  • @mamediarradiop2928
    @mamediarradiop2928 8 лет назад +11

    Serigne saliou mbacke sope nako lolou way sama khol bi ninkoy sedale yall na sakhe way Diadieuf serigne Moustapha machalah ❤

  • @mamafall1931
    @mamafall1931 5 месяцев назад +4

    ALLAHOUMA SALLI ALLA SEYDINA. MOUHAMAD WA SALLIM ADDIYA SOKHNA WALO M'BACKE ❤❤❤❤❤❤❤

  • @mortine9844
    @mortine9844 7 лет назад +23

    SERIGNE SALIOU MBACKE DOUGNOU LA FATE BA FAW ADOUNAAK ALAHIRA YALLA NAYALLA YOKE SA LEER MBACKE AMINE

  • @ndeyefatoumbacke8200
    @ndeyefatoumbacke8200 6 лет назад +2

    Dieureudieuf s moustapha gningue yènangui bégueul sopey s salihou yi

  • @leillyizao2694
    @leillyizao2694 2 года назад +5

    Tous les jours je prie Dieu de le voir en comme j'ai pu avoir la chance de le voir de son vivant. Yalna yalla yokou léram ta tasniou sii mbarké borom Touba.

  • @ndeyemaguettengommail3006
    @ndeyemaguettengommail3006 4 года назад +12

    Dieuredieufaty serigne touba kén dou mom diarama Mme cheikh Ibrahim fall 👌👌👌🙏🙏🙏

  • @seynaboudione9461
    @seynaboudione9461 6 лет назад +35

    Sante serigne touba mo nou war. Dieureudieufeuti serigne touba diarama mame cheikh ibrahima fall

  • @serignefalloufall4242
    @serignefalloufall4242 4 года назад +33

    😭😭😭😭😭😭thiey serigne saliou mbacké balla ayesa yalla na yalla yocou co ay leer amine ya rabi 😭😭🙏🏿

  • @oumoukalsoumdiagne1626
    @oumoukalsoumdiagne1626 5 лет назад +12

    bilahi moustapha gningue dou séne morom même quand je suis trés heureuse ta voix veut couler mes larmes

  • @fatoudiagne1011
    @fatoudiagne1011 5 лет назад +48

    Thieuy yalla en 2019 batay sayoumako deglo Sama xol di ngeuneuh toyyy yalnanou ko yalla fayal Mame Saliou Mbacké yalna yalla yokk lerr gui 🙏🙏🙏🙏🙏

    • @limzongom1193
      @limzongom1193 5 лет назад +2

      Ndeysane Fatou Diagne bimako dieuk degloo dama dioy ba sonou téwoul manguiwat nii Ken dou Serigne SALIOU yalnala brom bi défal tawfekh ci sahir ak battine ak bépp mbollém dioulitt

    • @fatoudiagne1011
      @fatoudiagne1011 5 лет назад +2

      Walay c vrai a chak foi jm dis loutakh makay deglou wate chak fois aye dioy lakay egalei mai soumay play video bi sakh doumako Tay

    • @falloumbengue6504
      @falloumbengue6504 4 года назад +1

      Ndeysan

    • @BASSIROUDIONE-pc1sm
      @BASSIROUDIONE-pc1sm 11 месяцев назад

      Bonsoir

  • @camillesylla
    @camillesylla 8 лет назад +18

    yall na Serigne bi weral bat bi machalahhh🙏

  • @ndeyesokhnagueye1810
    @ndeyesokhnagueye1810 5 лет назад +15

    Dieuredieufeuty Serigne Saliou Mbacke walahi awma Sago s Sangue😭😭❤️❤️❤️

  • @serignesalioufall7463
    @serignesalioufall7463 2 года назад +2

    Dieurediefety Cheikh Saleh Mbacké
    Machala Serigne Moustapha

  • @santeserignetouba6619
    @santeserignetouba6619 10 лет назад +27

    machala santaty mame saliou bou bakhe tey gnane boure yalla yoke ayes leerames

  • @ahmadchbok6164
    @ahmadchbok6164 7 лет назад +14

    amine serigne touba d'où kéne mane ma si khame d'Ara dieurediéfé borome touba

  • @NdeyeAwa-b9t
    @NdeyeAwa-b9t Год назад +1

    Ndaysan yallnama yalla may dome Bou toudou s saliou ❤❤❤❤ beug nako loll❤❤❤❤😂

  • @sallabiguesow110
    @sallabiguesow110 8 лет назад +8

    yalla nala yalla fay si barké s saliou yakar s saliou kr beugue s saliou kr

  • @mbayegueye6511
    @mbayegueye6511 8 лет назад +43

    deureudeufe Serigne touba diarama Mame cheikh Ibra Serigne salliou yalla nanouko yalla fatal mbacke yokou léram tas niou thi barkem s Moustapha yalna fanwi goudou battby weer amin amin

  • @ndeyendiayegarmi2226
    @ndeyendiayegarmi2226 8 лет назад +60

    sante serigne saliou j'aime serigne saliou plus que ma vie dieurdieuf mame saliou

  • @Khemessediouf-d9r
    @Khemessediouf-d9r 6 месяцев назад +4

    Que dieu te protège sérigne bi❤❤❤❤

  • @mouhamedfutureneymar10
    @mouhamedfutureneymar10 9 месяцев назад +3

    Machallah moustapha nala yalla foy

  • @senegaldakar1273
    @senegaldakar1273 4 года назад +2

    Machala ndawna yarram serigne saliou mbacké si khol mo dakk leeup

  • @astoumbeneniang7178
    @astoumbeneniang7178 8 лет назад +23

    Machaallah yalnala yalla takhawou si barke SERIGNE SALIOU

  • @ousmanecoly1231
    @ousmanecoly1231 2 года назад +9

    Sante yalla ak borom touba🙏🙏

  • @MohamedFall-xs7vu
    @MohamedFall-xs7vu 10 месяцев назад +3

    Cheikh saliou m'bake la lumière merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤

  • @binetalam5608
    @binetalam5608 3 года назад +2

    Thieuye Mbacke wette nagnou deh yalla nafi yalla yagal sa lere taf gnou sa barker 🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🏼😭😭😭😭🥲🥲🥲🤲🏼🤲🏼🤲🏼😭❤️😭😭❤️

  • @moussakane9695
    @moussakane9695 6 лет назад +7

    Dieuredieuf serigne touba diarama serigne saliou mbacke💙💙💙💙📝📝💙💙 kharitou khalé yi

  • @adamandiaye4314
    @adamandiaye4314 2 месяца назад

    ❤❤❤ Dieureudieuf serigne touba amoule morome Sunus waddi Akhemadou Bamba khadyme rasoule ❤

  • @mbodjiaissatou8370
    @mbodjiaissatou8370 3 года назад +3

    Yallana Allah swt feyal niou Serigne touba

  • @mounassndiayr9146
    @mounassndiayr9146 8 лет назад +13

    mbacke balla wetal gagnou gnoun ndaw yi dieureudieufaty serigne serigne saliou mbacke

  • @saerndiaye2351
    @saerndiaye2351 6 лет назад +14

    yalle nako yalla yaram té diegal ko 😢😢😢

  • @beugueserignesaliou1809
    @beugueserignesaliou1809 8 лет назад +4

    thiey dieureudieuf serigne touba yalna yalla weral batbi serigne sidi Mokhtar mbacke yalnafi yague lool té weer

  • @daoudagueye2635
    @daoudagueye2635 6 лет назад +34

    Without Serigne Saliou My life is nothing i like him deeply in my heart i will never forget him i can swear it

  • @fatoumouserignesaliou9553
    @fatoumouserignesaliou9553 4 года назад

    Sama adduna sama yakar tay ak elleuk yallah na yallah yokk ay leram ta tass gnu ci ay barkem😭😭😭😭🙏🏾🙏🏾

  • @yayoubayam9843
    @yayoubayam9843 4 года назад +5

    Thiey Serigne Salliou kenn la😭

  • @matysy5536
    @matysy5536 7 лет назад +3

    Machaala Serigne Saliou yalna yalla yokou leram

  • @syllakhoudia7943
    @syllakhoudia7943 11 лет назад +15

    Dieureufeti Cheikhy Saliou..

  • @bambadiop9689
    @bambadiop9689 2 года назад +8

    Jamais on noublieras ce vendredi soire...dst khadimoul rassoul

  • @sokhnamayleye3178
    @sokhnamayleye3178 4 года назад

    Thieyy yalla naniu done ay salihate you werr ba aldiana ♥️

    • @badoufall4861
      @badoufall4861 9 месяцев назад

      Thiey yalla ❤❤❤❤❤❤

  • @makhtardiop4104
    @makhtardiop4104 4 года назад +8

    😭😭 thaye s saliw amoll moroum

  • @ramadione468
    @ramadione468 4 года назад +4

    Ma beugue s saliou walahi😭😭

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 5 лет назад +32

    *Ndeyesenn ils nous manquer beaucoup paix à leurs âme😪😭😢*

  • @ridialoulahiakasaa2311
    @ridialoulahiakasaa2311 6 лет назад

    dieureu dieuf seringe touba diarama mame cheikh ibrahima fall s moustapha gningue yal na yalla weral bat bi

  • @pendasow5852
    @pendasow5852 6 лет назад +5

    Thieuy yalla bouniou amoul wone Mane saliou khawma fougou dieum

  • @cherifaidara9624
    @cherifaidara9624 4 года назад +3

    28 décembre 2007
    28 décembre 2020
    Ken dou faté borom diamono mignou defar nioune nday yeup

  • @sophiangom6984
    @sophiangom6984 9 лет назад +4

    sant serigne Saliou, Moustapha gningue yal naco yalla fay

  • @AbdouMbaye-s5b
    @AbdouMbaye-s5b Месяц назад

    Yalnala yalla diapalé si barké borome khelcome

  • @kaneserigne8315
    @kaneserigne8315 10 лет назад +8

    dieureudieufe serigne touba diara serigne madiba sylla

  • @ramatulayendoye4387
    @ramatulayendoye4387 8 лет назад +60

    Dieurdieufti.s.saliou mbacke amoul.morom.yalananuko.yala.fayal.amiiin.

    • @moussandoye9659
      @moussandoye9659 4 года назад

      Amine sohnassi

    • @ramatulayendoye4387
      @ramatulayendoye4387 4 года назад +1

      @@moussandoye9659 ziyarnala Loubari ndoye neklen si diam amiiin yarabi.

    • @moussandoye9659
      @moussandoye9659 4 года назад

      @@ramatulayendoye4387 délou dila ziar. Linga beugueu yalnalako borom bi dëfal té mou gueune si Barké Serigne Salifou Mbaké. Doundal beu âme 100ans ak wér ak khéwal . Dôme bay béguénala lolsah

    • @ramatulayendoye4387
      @ramatulayendoye4387 4 года назад +1

      @@moussandoye9659 alahuma amiiin dieurdieufti sa thiaminieu. Man si atoub serigne touba la yaro diourbel.niou bok nianyi amiiin yarabi.

    • @moussandoye9659
      @moussandoye9659 4 года назад

      @@ramatulayendoye4387 dila ziar Sa souné. Motah nga bakh. Manit souma fa yarowone daldi mélni yaw . Niane nala kon déma nianal SA souné ngir Mbakhou Serigne Saliou ma ame Talibé gouniou nangou.

  • @keytifokt42
    @keytifokt42 Год назад +2

    ❤❤❤❤monou défarr Dé❤❤❤❤

  • @LeyeEva
    @LeyeEva 3 месяца назад +1

    Santé seringe Saliou ❤ 2024

  • @MaguetteGueye-l8k
    @MaguetteGueye-l8k 3 месяца назад +2

    Mame saliou ❤❤❤❤

  • @sanabownobw8517
    @sanabownobw8517 7 лет назад +29

    You make me happy every time I hear your voice preaching my God dating inshallah Moustapha Gningue

  • @inssatoure1
    @inssatoure1 11 лет назад +4

    serigne moustapha yala nala serigne saliou degue té yala yok say fane té mayla weer d la part d souleymane mbacké prokhane

  • @thianekhoule1588
    @thianekhoule1588 6 лет назад

    Ndeysane dawlonga sama yaram. Serigne Saliou day Serigne touba kepp

  • @fatouthiawciss7232
    @fatouthiawciss7232 4 года назад

    Baye saliou dieureudieuf sante yalla bama yalla mayé ma guissék borom diamono borome khelekom

  • @Moughniyane-tv
    @Moughniyane-tv 3 месяца назад

    Ndeisàan tawfexx rek sëriñ mustafaa ❤

  • @aissatoundior1554
    @aissatoundior1554 5 лет назад +2

    mashallah YALLANA YALLA WEUREUL BAT BI CI BARKÉ SERIGNE SALIOU

    • @SoxnaawaTall
      @SoxnaawaTall 3 месяца назад

      ❤❤❤❤❤❤❤

    • @SoxnaawaTall
      @SoxnaawaTall 3 месяца назад

      ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @KhadijaaDione
    @KhadijaaDione Год назад +1

    ماشاء الله شكرا جزيلا لك ساليوعلى كل شيء يحمل اسمي لعزير ماشاء الله شكرا لك على جزكم الله خيرا لكم ❤❤❤❤

  • @matymbacke2290
    @matymbacke2290 6 лет назад +7

    Yalna la serigne touba fey

  • @seynaboukane4639
    @seynaboukane4639 5 лет назад

    Dieuredieuf Serigne Touba Diarama Serigne Saliou Mbacke yalna yalla yok sene leram

  • @SayeFall-mh6ms
    @SayeFall-mh6ms 7 месяцев назад +2

    Macha allah ❤❤❤❤

  • @ablayenda0972
    @ablayenda0972 4 года назад +1

    Ki est là en 2020❣️

  • @fatindiaye937
    @fatindiaye937 7 лет назад +4

    yalla na yalla wèral bat bi

  • @Bira77me
    @Bira77me 6 лет назад +7

    Machallah amna sollo loll way

  • @aissatougningue1939
    @aissatougningue1939 4 года назад +29

    ❤️❤️❤️😭😭😭😭😭

  • @darosaliouloum2847
    @darosaliouloum2847 3 года назад

    Walahi man daro s saliou rek la beug walahi mom rek mom dogg mom kassé😭😭😭😭💪💪

  • @mamaduwagne3580
    @mamaduwagne3580 10 лет назад +19

    Dieuredieufati borom touba diarama mame cheikh Ibrahima fall cheikh sidy makhtar mbacke yalna fi yague ter wer

  • @diaboubacar438
    @diaboubacar438 8 лет назад +15

    SERIGNE SALIOU WETALNANIOU...AY MBACKE WE MISS YOU A LOT...FOR EVER LOVING HIM..

  • @bijoubonnaire5179
    @bijoubonnaire5179 9 лет назад +43

    Bilahi limiy wakh si Serigne Saliou yala n'a nek ayy chambre palace tia adiana

  • @moussandoye9659
    @moussandoye9659 4 года назад +19

    Yalla moy yalla, Mouhaméd PSL. Moy souniou yonét, chiékhoul khadim leukéneu khamoul loumoudone.

  • @ouzsolosolo9453
    @ouzsolosolo9453 7 лет назад +8

    dieureudieuf borom touba

  • @ndeyeastouFaye-yq3wu
    @ndeyeastouFaye-yq3wu 9 месяцев назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Yalla nagnou fah ande akk serigne touba thé bou gnou fah takhaw🙏

  • @damediouf2054
    @damediouf2054 Год назад

    Li weur diang bii dieureudiefaty s saliou ❤❤❤

  • @AblayeDiop-y8w
    @AblayeDiop-y8w Год назад

    Thieuy cheix Salih ma vie mon bonheur ❤🎉 amouma sago si môme jereujeuf Serigne salih ❤❤❤❤

  • @toutoufall1001
    @toutoufall1001 4 года назад +1

    macha allah yalla na la yalla barkéle

  • @malickdiene9672
    @malickdiene9672 8 лет назад +109

    Mane dé serigne saliou moma defar walahi ay boudoul wone yaw fouma dieum mame Saliou wetal ngama 😪😪😪😪😪😪😪😪😪😪😪😪😪😪😪😪

  • @dyinfo6236
    @dyinfo6236 8 лет назад

    Machala yalla na yalla wèral bate bi barkè borome diamono