Mbonate dafa am ñaari façon muy buy dundu ci ndokh ak bo khamni ci suuf rek la dundu .amul ben buy moti di dem guedj wala dara .mbonate ouuu moy dundu ci keur yi amon na touba ak darou mouhty ci beyti du dundu muk ci ndokh bénén mbonate normal bi moy dundu ci ndokh.mbonate oun dina dundu ba 200ans mbonate ndokh 60 ans .
Seriñ Abdu samad aka beugg jaam yi diariñou. Yalla na fi yagg looooooool way. El hadji malick Jërëjëf
Amiin
Mbonate dafa am ñaari façon muy buy dundu ci ndokh ak bo khamni ci suuf rek la dundu .amul ben buy moti di dem guedj wala dara .mbonate ouuu moy dundu ci keur yi amon na touba ak darou mouhty ci beyti du dundu muk ci ndokh bénén mbonate normal bi moy dundu ci ndokh.mbonate oun dina dundu ba 200ans mbonate ndokh 60 ans .
Amna mbonante yo khamni si guedj dong laniouy nék
@@bayefall4158 lolu la wakh deh tortue Marine ak tortue terrestre
@@BAYEALELO wérr naa même sén tank yi sakh niouro woul souma dioumoul amna touti différence