Machallah kawei neu li rekk moy film 🎥 biouy diangalei lou am solo li rekk mo wara daw télé 📺 yi ndakh niou dieulési lou bakh lou am ndieurign ba parei khamei si souniou diné ndakhtei kham yalla diamou yalla rekk motakh niou wathie si kaw souf kon amna solo machallah dieuwrign djiby seye liguey bi rafétneu machallah cheikh moussa cisse ndiame borom darou dieureudieufety ❤️👍👌🙏
Ha machalah intressant amna sôllô trop nite dafa wara dall wayé tamite khalé loumouye dougou dafa wara tagou ay kilifame, yalla rek mô am sôllô loudoul yalla dou dara
Franchement, je suis émus. Larmes aux yeux, les yeux fixés sur les dernieres minutes de la vidéo en me rappelant de mes premières semaines de tarbiyou. Vous avez accompli la mission, Dah té Dém. Kanam kanam la dieum. Yalla-Yalla Eternel...
Machallah lile wolof nane xell posso bou rérr le mak dinako for xallé danako for Film bi amna solo loole merci beaucoup elhadji djiby seye ak gninga ko andale gnépp
Un film vraiment instructif avec des messages spirituels vraiment mention spéciale à tous les acteurs particulièrement à maïmouna à quand la deuxième version????
J'ai été témoin un jour à un thiant des gens qui se proclament yalla yalla à thies, mais leur comportement cette nuit là laisser à désirer. Ils fumez, ils buvaient et leur cheikh avait été accusé (c'était vrai) de séquestration d'une fille qui habitait le quartier. Je parle de faits réels que j'ai vécu à Thies. Ces soit disant yalla yalla semblent ne rien à voir avec la communauté Yalla Yalla qui est sous l'égide de Serigne Moussa Touré que j'aime beaucoup et de ses lieutenants Serigne Souleymane Sene, Aladji Djiby Seye et un certain Niane que je considère comme des soufies, des mourides authentiques. On dirait qu'il y'a plusieurs communautés yalla yalla. Cela est un problème et l'une de ses causes reside en l'érection de Cheikh. Il existe beaucoup de personnes qui, soit sont érigées en statut de Cheikh ou soit s'autoproclament cheikh. Or le statut de cheikh doit être fondé sur la connaissance de la religion, la connaissance de la lumière mouhamedienne, la connaissance divine, la connaissance de Dieu etc. Fondamentalement l'Islam est éducation de la personnalité en vue de se rapprocher de Dieu et de recevoir Son agrément. Or cette éducation ne peut être faite que par un guide totalement réalisé. Un cheikh qui n'est pas réalisé ne peut guider personne. Certains jeunes sont égarés par des soit disant cheikhs, et c'est ce qui retient la plupart des gens à s'engager dans la voie. En tout cas excellent film avec un scénario très bien mené. Un film qui éclaire bien la lanterne de ceux qui sont sceptiques par rapport aux yalla yalla, un scénario qui montre une bonne réputation de la communauté. Des gens comme Djiby Seye et Souleymane Sene doivent être ceux qui sont habilités à parler au nom des yalla yalla. Ils ont la connaissance de mieux faire comprendre l'appel de Ndiamé et le tasawouf enseigné par notre vénérable guide à tous, Cheikhoul Khadim. Bonne continuation vraiment.
Je te rejoins parfaitement mon ami.dans chaque chose il y a des egarè.je connais bien sangue niane et les autres en l occurence djiby seye.moi même mon mari est un cheikh.il est professeur de mathématique et nous menons une vie correcte.il fais son travail normalement et en parallèle il a ses talibes et les guide vers le chemin de Dieu ❤❤❤❤
félicitation film très instructif. Juste un avis: prochainement mettez aussi l'accent sur le comportement et les discours de certains Yalla Yalla. Cela ne fait que sombrer la compréhension et réveiller la doute dans certains cœurs. Bonne suite, on attend la version 2.0
Ah bon lii moy yala yala donc,domage suis un catholique protestants et je ne sais pas si j'ai le droit d'y goûter,j'ai trop bien envi d'en faire partie mais je ne sais pas comment,aidez moi svp jean marc Thiandoume petit fils du cardinal Hyacinthe Thiandoume jeune catholique protestant depuis Genève,diadieuf ndiame darou
Sante Cheikh Moussa Cisse Cheikh Alhamdoudilah Diadieufeuti Cheikh Moussa Toure limoy Islam tournage rafetna Teh fouma guiss Seydina Souleymane Sene damay content Djiby Seye day dalal xel ak actor yeup limom yallana yalla yokou Amin
insbi film bi woron na guen yatou li negn si diapp diko setan lou barri diko partager en plus ndakh gneup meun sei diot gnou ligueyal cheikh moussa cisse
Toujours dactualite jajeuf cheikh moussa
Machallah kawei neu li rekk moy film 🎥 biouy diangalei lou am solo li rekk mo wara daw télé 📺 yi ndakh niou dieulési lou bakh lou am ndieurign ba parei khamei si souniou diné ndakhtei kham yalla diamou yalla rekk motakh niou wathie si kaw souf kon amna solo machallah dieuwrign djiby seye liguey bi rafétneu machallah cheikh moussa cisse ndiame borom darou dieureudieufety ❤️👍👌🙏
Machallah ame na solo
J'ai beaucoup aimé. Ça permet de faire tomber les clichés. Islam, imaan, ikhsaan. Qu'Allah nous guide.
Franchement c'est parfait, di doli di sante Diambe Borom Darou Rek
Ha machalah intressant amna sôllô trop nite dafa wara dall wayé tamite khalé loumouye dougou dafa wara tagou ay kilifame, yalla rek mô am sôllô loudoul yalla dou dara
Qui est la en 2024
Amna solo trop yalla geuna barkel si barke borom darou Ndiambe Darou yalla yalla bi
Machalla yallah n'a yalla yokkou xam xam bi ak yatal mission
Xam, dègg, dundu, dooh, djaap djèh, guiss yalla dafa djoOt...! Merci a vous ridiaal
Alhamdoulilah en fin yalla yalla yi
Fière d'être yalla
Akassa bégué koulou yalla yalla
qui est là en 2020
Franchement, je suis émus. Larmes aux yeux, les yeux fixés sur les dernieres minutes de la vidéo en me rappelant de mes premières semaines de tarbiyou. Vous avez accompli la mission, Dah té Dém. Kanam kanam la dieum. Yalla-Yalla Eternel...
dieurieudieufé ndiambé borom darou , seule la vérité triomphe
Machalha degeu rèk kay degeu té moy moudiou yalna gnou yalla May dégge ak toppou thi barké Cheikhra fall
Machalla yallah yallah yokk léne ci barké mame moussa
Tellement important
Un grand merci à tous ces acteurs surtout à cheikh djiby seye
Le film est hyper reussi. Xol sédatini tigui li déh ak sogno la si bépou joulite.amena solo lol sax yallah na yallah Faye si barké borome touba.
Kanam kanam rek la jëm yalna yalla barkél✊
mashallah chapeau a Famara, SEydina, et Djiby kamal je me rappel les années a l'ucad billahi gni ay gaure yalla khakhitane lagnou
Bégué nagnou bou bax goor yalla👌. Film bi amna solo té kamal na. Délen di gnanal rek si taxaway bi yalla yokk len té barkel liguey bi 🤲
Machallah kaname la dieum deh
Machallah lile wolof nane xell posso bou rérr le mak dinako for xallé danako for
Film bi amna solo loole
merci beaucoup elhadji djiby seye ak gninga ko andale gnépp
Yalla yalla DEUG
Il faut partager le lien avec vos proches et amis na yaatu fépp. Vraiment c un chef d'œuvre.
exactement ca doit etre publie partout
Merci beaucoup je veux avoir le numéro sëriñ allaji jîbi séy Si c'est possible
Mbaye Badiane pour le livre Masaalikul Jinaan ci làkku wolof appelle au 776676358 c le numéro du livreur
Akassa fall tarkalah fall loudoul yalla nenela
film bi dafa warona âme des saisons ak des épisodes.doyoul dé
Yalna yalla barkel leep thi barker cheikh moussa liguéybi rafétna
Félicitations sangu you tédd yi
Machalla film validée ndiamé borom darou protège
mashAllah kawé na, amna solo, te wané na lu bari, bien... yalla yokku te barkeel
Machahah amna solo dieuredieuf cheikh moussa cissé ndiambé darou
Machalla jangalé mii kawé yalna yallah matal lepp
Jah dieuf bayé djiby amna solo
Macha allah.... juub rek mo am solo. yalla na yamma barkel
Vraiment c'est une très bonne idée on est de tout cœur avec vous. Machalah le contenu est génial
Amna solo goor yalla yi 👌👌👌👌👌👌
Lidal amna solo rèfètna niogui khar un autre
Nous sommes avec vous
Amnaa solo tropp waay faal yekk YALLAH rekkaa woor
Machallah kaname rék la dieum et on vous félicite de la réalisation
Macha allah thia kaname
Félicitations! Vous avez fourni beaucoup d'informations sur le sens de l'engagement Yalla Yalla. Dina takh niit wagni jugements yi!
Machalah liguey bi rafetna
Machallah thia kaaw rek barcké cheich Moussa bonne continuation!!
Machallah yallah na yallah barkél
Respecto Yalla reka diara topou mais mada bi thi fin bi neehna lol machalah
Dieureujeuf borom darou yieuk soga nek👌
Macha Allah amna solo trop
Hakassa yatuna lol jajef Njammé borom darou yalla yalla rk ilahi abadane
Machallah am na solo si diam gni
Vraiment, c'est un très bon film. La fin est très important !!!
vraiment on doit partager le film partout mou yatou
Machallah amatina Solo Trop Dieureudjefé Borome Darou
tjrs d'actualité très belle leçon
Felicitation à tous les acteurs surtout à eva content de toi le film est venu à son heure dieureudieufé niambé diarama sangue ousmane fall lamp
Merci beaucoup "eva" 😘
Machallah amena solo dieuredieufé borome darou cissé
Xol sedna. Yalna yala fay te barkel
Akassa xol sédina bilahi yalna Yalla barkel message leerna
DIEREDIEUFÉ BAYE NIASS
DIEREDIEUF CHEIKH MOUSSA
jajeuf iow miko wax
Jërëjëf goor yalla yi
Souniou xol sedna na yalla barkél
Machallah toute mes felicitations c'est sa la vie j suis emus les larmes aux yeux machallah vous avez reussi bonne continuation 👌👌👌👌👌
Ndeysan
AMNA SOLO LOOL. NEK YALLAH YALLAH MO GUEUN TE EUP TAWFEKH LOOL NEK LENEN
NDIAMÉ 4LIFE ludul lah ilaha ilalah du dëgg
Xam yalla diamou rekk moy deugeu dieuredieuf ndiamé darou
Machallah
Mashala jangën jefēty goor yalla yi
Xol sedna machalla yalna barkel
Manchallah nice initiative amna solo
jërëjëfëty mame ndiamé
Amna solo alima diack dite maimouna dans le film est ma soeur. Bonne continuation et courage
7medias eskey MachAllah 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
C vrèma kelk chose de tres sprituelle
Diadieuf
Un film vraiment instructif avec des messages spirituels vraiment mention spéciale à tous les acteurs particulièrement à maïmouna à quand la deuxième version????
Wa waw serigne daï am ligéuye
Ce film est un bon film.
Kawéna gorr yalla film bi rafena
tjrs d'actualité partagé lenko mou tass si aduna bi amna ndiarign lol
Mashallah yatouna yalna yallah yokk
J'ai été témoin un jour à un thiant des gens qui se proclament yalla yalla à thies, mais leur comportement cette nuit là laisser à désirer. Ils fumez, ils buvaient et leur cheikh avait été accusé (c'était vrai) de séquestration d'une fille qui habitait le quartier. Je parle de faits réels que j'ai vécu à Thies.
Ces soit disant yalla yalla semblent ne rien à voir avec la communauté Yalla Yalla qui est sous l'égide de Serigne Moussa Touré que j'aime beaucoup et de ses lieutenants Serigne Souleymane Sene, Aladji Djiby Seye et un certain Niane que je considère comme des soufies, des mourides authentiques. On dirait qu'il y'a plusieurs communautés yalla yalla.
Cela est un problème et l'une de ses causes reside en l'érection de Cheikh. Il existe beaucoup de personnes qui, soit sont érigées en statut de Cheikh ou soit s'autoproclament cheikh. Or le statut de cheikh doit être fondé sur la connaissance de la religion, la connaissance de la lumière mouhamedienne, la connaissance divine, la connaissance de Dieu etc.
Fondamentalement l'Islam est éducation de la personnalité en vue de se rapprocher de Dieu et de recevoir Son agrément. Or cette éducation ne peut être faite que par un guide totalement réalisé. Un cheikh qui n'est pas réalisé ne peut guider personne. Certains jeunes sont égarés par des soit disant cheikhs, et c'est ce qui retient la plupart des gens à s'engager dans la voie.
En tout cas excellent film avec un scénario très bien mené. Un film qui éclaire bien la lanterne de ceux qui sont sceptiques par rapport aux yalla yalla, un scénario qui montre une bonne réputation de la communauté. Des gens comme Djiby Seye et Souleymane Sene doivent être ceux qui sont habilités à parler au nom des yalla yalla. Ils ont la connaissance de mieux faire comprendre l'appel de Ndiamé et le tasawouf enseigné par notre vénérable guide à tous, Cheikhoul Khadim. Bonne continuation vraiment.
Amnasolo
Many mburu bo guiss amna russite
Très pertinent frère j'ai l'impression que tu ne fais pas partie de notre communauté, mais tu as tout compris !!
Je te rejoins parfaitement mon ami.dans chaque chose il y a des egarè.je connais bien sangue niane et les autres en l occurence djiby seye.moi même mon mari est un cheikh.il est professeur de mathématique et nous menons une vie correcte.il fais son travail normalement et en parallèle il a ses talibes et les guide vers le chemin de Dieu ❤❤❤❤
Machalla. Nice na trop
Yalla yalla guide kou wounie
félicitation film très instructif. Juste un avis: prochainement mettez aussi l'accent sur le comportement et les discours de certains Yalla Yalla. Cela ne fait que sombrer la compréhension et réveiller la doute dans certains cœurs. Bonne suite, on attend la version 2.0
Liguéye bii rafét na kamal na yalna yalla gueuneu Barkel ci barké CM6C borom darou
Santé Mamé Ndiamé Darou
Ah bon lii moy yala yala donc,domage suis un catholique protestants et je ne sais pas si j'ai le droit d'y goûter,j'ai trop bien envi d'en faire partie mais je ne sais pas comment,aidez moi svp jean marc Thiandoume petit fils du cardinal Hyacinthe Thiandoume jeune catholique protestant depuis Genève,diadieuf ndiame darou
Def signe 773932928 nu wahtan
Wawaw li deh kheweul
Sante Cheikh Moussa Cisse Cheikh Alhamdoudilah
Diadieufeuti Cheikh Moussa Toure limoy Islam tournage rafetna
Teh fouma guiss Seydina Souleymane Sene damay content Djiby Seye day dalal xel ak actor yeup limom yallana yalla yokou Amin
Diaguén dieuf🙏🏽
Salam ku bakh. Nakh mounna kham titre sons Youy daw si film bi ? 🙏🙏
mashala. AMENA SOLO LOOOL
Machallah il faut goûter pour savoir
Diadieuf cheikh Moussa cissé ndiamé darou
Mashalla
Akassa! yana yalah oubi khol yi ak khél yi bagnou meuna dieurignou si message bi film bi di véhiculé. Amine
insbi film bi woron na guen yatou li negn si diapp diko setan lou barri diko partager en plus ndakh gneup meun sei diot gnou ligueyal cheikh moussa cisse
gaston forever
MOUSTAPHA EST TRÉS POLI DANS CE FIM J'ÉSPÉRE QU'IL EST COMME ÇA DANS LA VIE NOREMAL.MAIS NICE ALHAMDOU BAYE GUEYE
Yalla yalla yi amouniou xam xam
Jai trop aimer.....
billahi liguey bi rafétna kawéna