4 appui de Reug Reug? La réaction Moussa Ndoye

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 фев 2025
  • 4 appui de Reug Reug? La réaction Moussa Ndoye

Комментарии • 140

  • @ndiemebiaye3808
    @ndiemebiaye3808 Год назад +8

    Yaw nit au moins wakh nga wakhou nit moussa Ndoye un très grand champion❤

  • @amadouibrahimaba6974
    @amadouibrahimaba6974 Год назад +19

    Moussa ndoy un champion un vrai sportif

  • @babacardiop5162
    @babacardiop5162 Год назад +7

    Moussa c un grand sportif machalla

  • @anonym7811
    @anonym7811 Год назад +40

    Felicitation a sathies. Dafko douma dane ko. Les arbitres doivent etre sanctionner.

    • @alvin2goat339
      @alvin2goat339 Год назад +1

      Douma yaw khamgua louy douma!!! Félicitations Reug Reug pour ta prestation😊

    • @Thier218
      @Thier218 Год назад

      Arbitre day dioum

    • @bylalfalfal3333
      @bylalfalfal3333 Год назад +3

      Wathie ma daan la woroul kou daan dangay feté kaw

    • @amanasy7411
      @amanasy7411 Год назад

      Seuytané nga doul

    • @anonym7811
      @anonym7811 Год назад

      @@amanasy7411 massa khamna defaite bala diapp mais du courage champion :D :D :D

  • @boubacarboiro5813
    @boubacarboiro5813 Год назад +20

    Sathies félicitations tu as humilié le choix disant meilleur lutteur de la lutte simple 🤣🤣🤣🤣🤣🤣 wadjiii deukkk thiaroye les chiens sont disponibles 🐕‍🦺🐕‍🦺🐕‍🦺🐕🐕🐕🐕

    • @elhadjifaye1166
      @elhadjifaye1166 Год назад

      Ioe sa data yaye yaroul

    • @seydinaomardiop4537
      @seydinaomardiop4537 Год назад

      Humiliation ? 4 appuis mo len mày chance

    • @boubacarboiro5813
      @boubacarboiro5813 Год назад +1

      @@seydinaomardiop4537 boy cela fait parti d'une de la lutte eumeu a pris Roi des arènes ainsi donc c'est une humiliation soit digne

    • @seydinaomardiop4537
      @seydinaomardiop4537 Год назад +1

      @@boubacarboiro5813 Sathies a gagné d’accord mais dire qu’il a humilié Reug reug suis pas d’accord

  • @saliouka9709
    @saliouka9709 Год назад +5

    Merci Moussa ndoye yaw borom bakh nga

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 Год назад +2

    félicitations reug reug

  • @cheikhndong359
    @cheikhndong359 Год назад

    Machala yaram dawena reug reug sa waye la li refetna

  • @lattendiaye-4794
    @lattendiaye-4794 Год назад +5

    Filicitation mbeur champion nga

  • @momadouniang5229
    @momadouniang5229 Год назад +2

    reug reug ❤❤❤❤❤❤❤

  • @mouhamedmbengue1237
    @mouhamedmbengue1237 Год назад +2

    Reug reug rek moussa ndaye rek ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ZOOMA-O.B.Y
    @ZOOMA-O.B.Y Год назад +5

    Yèn gni di wakh moussa ndoye ni ni socé yi djola deff coalition sérère yi même choses Moussa di lébou téwal mbokou lébou ngèn di xeuw

  • @legendetvngoundiane9297
    @legendetvngoundiane9297 Год назад +2

    tres bien moussa ndoye

  • @diawnumero1071
    @diawnumero1071 Год назад +5

    Moussa ndoye bayill mbeir yingayy xarito lii defayy 'newall sayy adversaire

  • @sarrymbengue553
    @sarrymbengue553 Год назад +6

    C'est le sang lébou qui coule dans nos veines ❤️

  • @ahmetmbodjmbodj4686
    @ahmetmbodjmbodj4686 Год назад +1

    Yén niar niep sa thies danalé 😍😍😍

  • @VieuxseydiSeydi
    @VieuxseydiSeydi Год назад

    Yarakh kassè ❤

  • @thiernocisse1284
    @thiernocisse1284 Год назад

    Bilay wargua diagal reug reug communication

  • @papecourtois1648
    @papecourtois1648 Год назад +11

    Moussa ndoye AP talibe cheikh DAY wah deug ta Yalla rk Tah

  • @mbarndiaye223
    @mbarndiaye223 Год назад

    Leufel ndèy arbitre lamb bi

  • @abousylla2317
    @abousylla2317 Год назад +3

    Allez reug reug merci pour la victoire

  • @khadimfaye4420
    @khadimfaye4420 Год назад +15

    Sa thies yén gnar gneup lë dann guém lén yalah té déllo drapeau bi😂

  • @anonym7811
    @anonym7811 Год назад +16

    Meme moussa ndoye khamna que sathiés mo dane reug reug malgré mogui jubiler ak mome ;D

    • @bylalfalfal3333
      @bylalfalfal3333 Год назад

      Wathie ma daan la woroul kou daan dangay feté kaw

    • @anonym7811
      @anonym7811 Год назад

      @@bylalfalfal3333 meuno danou baparé danél. Ak loumou meunti métti djoullit day wakh deugue wala mou done nafékk.

    • @NguithieTv
      @NguithieTv Год назад +2

      ​@@anonym7811 vraiment tu as raison Sénégal mo beurri nafekh

  • @VISIONTVONLINE2299
    @VISIONTVONLINE2299 Год назад

    Voila le lutteurs des lebous moussa ndoye ak quensh. Point

  • @babacarthiam6885
    @babacarthiam6885 Год назад

    Mousa ndoye aka taphete

  • @alassanegaye677
    @alassanegaye677 Год назад +1

    Domou dangou le champion dieule léne ko

  • @adamaseck8816
    @adamaseck8816 Год назад

    Félicitations sa thies

  • @papefall7324
    @papefall7324 Год назад +3

    moussa ndoye bayina faral

  • @fallougnigue384
    @fallougnigue384 Год назад

    Lambou dji nekhatou gni wara beure niepp ay kharit la niou😍

  • @dioppape5873
    @dioppape5873 Год назад +2

    Mouss loy wakh nii 😂😂

  • @ndigueulbadiane5980
    @ndigueulbadiane5980 Год назад +3

    Dieuleu modou Anta ngan wakh rk

  • @malick9084
    @malick9084 Год назад

    Sa thies Mo bolé trois amis( Reug reug, Siteu ak moussa ndoye)

  • @khalifayade7505
    @khalifayade7505 Год назад

    Félicitations

  • @diopcheikhfalilou-wy3or
    @diopcheikhfalilou-wy3or Год назад +1

    Moussa Ndoye yak reug reug weup la sa Thiès defal bagass

  • @papecisse-iu1bt
    @papecisse-iu1bt Год назад +8

    Moussa Ndoye gueumoul bopam, après Modou Lo il cire les pompes à Reug, tchim
    Démal naapi dieune kone😀

    • @ZOOMA-O.B.Y
      @ZOOMA-O.B.Y Год назад

      Bayil sama mbeur bi

    • @layetheonly5139
      @layetheonly5139 Год назад +2

      Y’aw y’a gueumoul sa bopou
      C’est un ami qu’il a accueilli

  • @abdoudione3827
    @abdoudione3827 Год назад +1

    6min28secondes 😂😂😂MOUSTAPHA gueuye

  • @omarfaye2580
    @omarfaye2580 Год назад +5

    Moussa ndoye dieuleul avance bighay daw yak modou anta bou thiese bayil daw bi

    • @onelove6721
      @onelove6721 Год назад +1

      Ki mo geuneu tapét si mbeur yi

    • @omarfaye2580
      @omarfaye2580 Год назад +1

      @@onelove6721 ki kayy moy lolou

    • @paradisegang1757
      @paradisegang1757 Год назад

      bane modou anta dou bou wegnone Stade Demba Diop

    • @omarfaye2580
      @omarfaye2580 Год назад

      @@paradisegang1757 waweu naghou na lolou moka nieugha dane si lamb lolou dou darra na moussa ndoye dieul avance bi rk

    • @paradisegang1757
      @paradisegang1757 Год назад

      @@omarfaye2580 se waye sougnou naré beuré ake modou anta beuréke ake yékine jr

  • @babacardiouf6253
    @babacardiouf6253 Год назад +1

    Sa thiès Kaccé

  • @ousmanethiam6570
    @ousmanethiam6570 Год назад

    Safouré bi dièkhna tay dh 🤣

  • @serignediaw5271
    @serignediaw5271 Год назад +1

    Reug reug yagui profitou dh

  • @namousow7955
    @namousow7955 Год назад +1

    Sa thies da raye sén ndeye 😂🤣🤣😂

    • @sofiegaye2487
      @sofiegaye2487 Год назад

      😂😂😂😂

    • @cassiuslorenzo7979
      @cassiuslorenzo7979 Год назад

      😂😂😂😂😂😂

    • @bylalfalfal3333
      @bylalfalfal3333 Год назад

      Wathie ma daan la woroul kou daan dangay feté kaw

    • @omarcisse3461
      @omarcisse3461 Год назад

      Ioe sa data yaye sakh reug reug dane nako guediewaye pour l'instant 3 mbeur Kate naniou séne ndéye

    • @elhadjifaye1166
      @elhadjifaye1166 Год назад

      Ioe namou Sow sa data yaye do yarou

  • @Lepatriote9423
    @Lepatriote9423 Год назад +1

    Moussa Ndoye légui aka wayadi 😂

  • @nabychop80
    @nabychop80 Год назад

    Sa thies dakar n’a sa ndey dakar ndeye reug reug

  • @saliouka9709
    @saliouka9709 Год назад +1

    Reug dolé cassé la ame mais amoul kham kham

    • @layetheonly5139
      @layetheonly5139 Год назад

      G😂😂😂rousseul yallah touty
      Mane Sathies moy sa ma mbeur

  • @abdoulakhatgueye7513
    @abdoulakhatgueye7513 Год назад +3

    Moussa ndoye naféque deug nga

    • @sarrymbengue553
      @sarrymbengue553 Год назад

      Nane la neké nafekh
      Deretou lébou moy daw sougnou yaram
      Ay lébou lagnu pire ✊

    • @abdoulakhatgueye7513
      @abdoulakhatgueye7513 Год назад

      @@sarrymbengue553 mo banne lebou leboula kome yawe sama yaye thiaroye la deuke mai degueu nékhoule reug Reug dafa danou

    • @bylalfalfal3333
      @bylalfalfal3333 Год назад

      Wathie ma daan la woroul kou daan dangay feté kaw

    • @abdoulakhatgueye7513
      @abdoulakhatgueye7513 Год назад

      @@bylalfalfal3333 banne kou danne dangaye feté kaw yawe fo deuke sakhe si Sénégal

  • @basstv7450
    @basstv7450 Год назад

    Mais pourkwa pas meunou niou dindi 4 appus si lamb ji

  • @mansourseye7810
    @mansourseye7810 Год назад +1

    Reug reug dafay beug kouko diapalé rek mais kham na danouna

    • @bylalfalfal3333
      @bylalfalfal3333 Год назад

      Wathie ma daan la woroul kou daan dangay feté kaw

  • @serignecheikhgaye4897
    @serignecheikhgaye4897 Год назад +1

    Verdict bi fégn n'a jubiler guéne ba paré niapou léne Séne khonn mougn

  • @naboucisse2555
    @naboucisse2555 Год назад +2

    Lou am amna reug reuk dannagueko

  • @pascal1863
    @pascal1863 Год назад

    Ay lebou lanou reug reug kassé

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 Год назад

    Daw lakou rek

  • @waganetv274
    @waganetv274 Год назад

    Yalla na diam yague thi Sénégal kou abonné thi sougnou chaîne RUclips wagane tv Yalla nala yalla térale thi barke seydina mouhamed 🤲🤲🤲

  • @mbayesall3507
    @mbayesall3507 Год назад

    iaw ak modou anta th

  • @serignembackeseye4008
    @serignembackeseye4008 Год назад

    Moytou lèn gnii dilèn talal micro yi ay rambadj lagnou you bonne

  • @makhtarsene4422
    @makhtarsene4422 Год назад

    Moussa dangay doule rek

  • @basstall2921
    @basstall2921 Год назад

    Sa thies nokhou nalen yen niarr nieup

  • @assanediamly134
    @assanediamly134 Год назад +1

    Yaw Moussa ndoye ya geuneu tapét nieup sathies yaw la ndieukeu niouss

  • @moustaphasamba4386
    @moustaphasamba4386 Год назад +2

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂

  • @djelenekane463
    @djelenekane463 Год назад

    Demal dieli modou anta

  • @mouhameddiop4376
    @mouhameddiop4376 Год назад +2

    Yaw Moussa ndoye do touss

  • @boy_galsen12
    @boy_galsen12 Год назад

    Nguir yalla drapeau bi boum khégne dieun way danio wara jubilé gaw lein indile niouka

  • @ousmanethiam6570
    @ousmanethiam6570 Год назад

    Yaw dagn la filé 😁😁

  • @sarrymbengue553
    @sarrymbengue553 Год назад

    Ay lébou lagnu pire

  • @mamadoudiouf7016
    @mamadoudiouf7016 Год назад

    🤐🐒🙈

  • @reverantle474
    @reverantle474 Год назад

    Moussa ndoye bayilll daww Laxou biiiii. Yawak Reug wargnén berré dans le futur. Yéneu mbeur yi ay vrais cons ngênn, vous laissez passer des millions ci ay affaire de Daw laxuuu

    • @crispyqueen7323
      @crispyqueen7323 Год назад

      Niata mbeur niofi taxaw ni dougn beurei ak ki wala kei? Tei derete bolen woulen. Balla ak sathies bokouniou ak ama dara tei dougn beurei. Lac 2 bokoul ak b52 dara tei nenagn dougn beurei. Yaw mi ya con koleurei mo geune fouf ay millions. Seu genre sagn nagn djay sen niit nax allal

    • @reverantle474
      @reverantle474 Год назад

      @@crispyqueen7323 man ngay traité kou con 🤣 . D'accord. Dommage sénégalais comprendroul business. Yaw mi nékeu fi dima xass, c'est sûr que tu peux lui apporter de l'aide quand il l'a besoin. Alors étant jeune, s'il peut profiter pour gagner le max de millions quitte à croiser même ses amis. Boyyy règlel niom nioy mayanté xaliss s'en biiir.
      Köllerë Fayoul courant, Fayoul ndox, tabaxul keurr.
      Défal seu bop ak niiiitttt.
      Moi je te parle de réalité.

    • @crispyqueen7323
      @crispyqueen7323 Год назад

      @@reverantle474 nittei wo dh encore une fois. Allal dou dara danguay dei bayi kofi wayei koleurei dh lou ame solo leu

    • @reverantle474
      @reverantle474 Год назад

      @@crispyqueen7323 d'accord merci pour ton message. Je me rappelerai que nité wuma.
      Alhamdoulilah Alhamdoulilah j'espère qu'on fera connaissance.
      Laisse moi ton mail, ou ton Instagram ou autre moyen de contact direct et tu verras de tes propres yeux qui suis-je vraiment insha'Allah.
      😁🤣 Nitéwuma mais guisnané danio xamanté woul motax.
      En passant, Köllerë niom mbeur yi cibopam geumouniouko. Il se trouve que très souvent ils plaignent comme quoi ken dimbaléwulén, alors que sport bi business leu, qui veut peut se faire des millions et tous sont gagnants.
      Man esprit sport akh business lay waxé akh yao.
      Yao par contre tu dans la peau d'un supporteurs fanatique. Jamais t'as entendu les grands dire que douma beuré akh diw wala diw alors qu'ils savaient daniouy business rekk.
      Mangui lay nianal ngeu geuneu wérrr insha'Allah man tamit yalla maymaa xel meu werrr com yao.
      Man ken si ngiom défoul sama keur, j'ai dit ce que je pense et ce que je leur souhaite. Gagné wumasii dara.
      Ndax étant Rufisquois, Domu Dangu Damakoko wax direct néko mbeur sétal ay millions, yawak Reug ak Moussa yeup ay potentiel adversaires ngén, té danguén wara mayanté ay millions.
      Je t'informe que Dofbi nak yalla téralnako Machala. Sama borom képeu lakoy santé. Wanté fimanek daniouy baxo Di wax né "Soft power, holding business".
      Peu importe lamb noumou meunti mel, demain insha'Allah daniouy andat, Ani Balla Guaye akh Babou c'était quasiment des ennemis donté bokuniou mais c'est pour expliquer que yag yag ils se retrouvent.
      Jajeuf. Mangui sante boubax.
      Merci

    • @crispyqueen7323
      @crispyqueen7323 Год назад

      @@reverantle474 Latchiel makk gni, makk gni nak la wax sougn teguone allal wala sameu koleurei si gnignou djappei sen niit lann lagnouy tanneu. Après reviens me voir. Olof nak dafani bou niit gni di outte allal outtal niit gni. Man niarr mbeur yi yeup dougn samay mbeur. Tu me parles de supporter fanatique smh. Yalla nala Yalla yagg terral nax guiss nanni kou begue xaliss nga. Soudei si sujet bi lagnouy baser wou djapei na sama bopp niit nax samay niit ma geunal allal. Lamb nga xamni sax diné begouko nax violence bi ak njabbar gui nax djarr na fecci koleurei ? Tei sameu koleurei diné sopp ko lollei smh

  • @assanegaye513
    @assanegaye513 Год назад

    Waxx ji rafett na

  • @bassirouwade4072
    @bassirouwade4072 Год назад +2

    Moussa ndoye yaw amo lo wakh tapete gua

    • @elchico8595
      @elchico8595 Год назад

      Tapète bu makk la xamna ko bu baxx

  • @mamathiam5649
    @mamathiam5649 Год назад

    iow la nieke dokhan sa ndeye

  • @seydinalimamoulayediagne3463
    @seydinalimamoulayediagne3463 Год назад

    Sa molène dane nak

  • @mawademangane2990
    @mawademangane2990 Год назад

    Sa thiés kassé

    • @bylalfalfal3333
      @bylalfalfal3333 Год назад

      Wathie ma daan la woroul kou daan dangay feté kaw

  • @babacardiop6458
    @babacardiop6458 Год назад +2

    Yaw amo fitte

  • @mouhamedniang-hw8ln
    @mouhamedniang-hw8ln Год назад

    Kii day boul rek

  • @trace-infos2a846
    @trace-infos2a846 Год назад

    Mangui gnane kép kou guiss sama commentaire nga abonner si sama chaine youtube nguir yalla