Sainte Marie, La sainte Femme Si tu n'avais pas d'affection pour nous, Personne ne serait là à te prier. Cent ans à genoux ,nous te prions Ave Chantez Marie, Ave rendez grâce à Marie , Ave ayez de la considération pour Marie, Ave Priez Marie. Établis ton trône chez nous, Avec ton vertueux enfant Répands ton amour sur nous, que l'on puisse prendre modèle de ta pureté. Sainte Marie, la Sainte Femme, si tu ne nous aimais pas, nous ne serions pas là à te prier Mille ans nous voici à genoux et te prions Ave Chantez Marie, ave remerciez Marie, A ve considérez Marie, Ave Priez Marie Ô Marie, entends nous, La très pure Mère, Verse sur nous ta divine grâce Et illumine notre chemin Sainte Marie, la Femme sainte, Sans ton affection, on ne serait là à te prier. Mille ans nous voici à genoux et te prions. Ave Chantez Marie, Ave rendez grâce à Marie, Ave ayez de la considération pour Marie, Ave Priez Marie Toi divinité de la Paix, Veille sur notre pays, Répands une paix infinie sur le Sénégal. Sainte Marie, la sainte Femme Sans ton amour, nous ne serions pas là à te prier, depuis Cent ans nous te prions à genoux. Ave Chantez Marie, Ave rendez grâce à Marie, Ave vénérez Marie, Ave Priez Marie Nous nous donnons à Toi, Et mettons nos prières à ta disposition Car Dieu T'a choisi, Reine des cieux Sainte Marie, la sainte Femme, sans ton amour nous ne serions pas là à te prier. Cent ans nous te prions à genoux. Ave Chantez Marie, Ave rendez grâce à Marie, Ave vénérez Marie, Ave Priez Marie Béni tes enfants, la sereine Dame, Ouvre nous les portes des cieux, que l'on chante avec Toi afin d'en gouter Sainte Marie, la dame sainte, Pour ton amour nous voici cent ans à genoux et à te prier. Ave Chantez Marie, Ave rendez grâce à Marie, Ave vénérez Marie, Ave Priez Marie Traduction:Alpha Sarr
Mariama mu sell mi Jigéen bu sell bi Boo ñu soppu loon Marie Kenn du fi ñëw di la ñaan Téeméeri at a ngi Ñu sukk fii di ñaan Ave woy leen Marie Ave sant leen Marie Ave naw leen Marie Ave ñaan leen Marie. Sampal sa nguur ci ñun Yaak sa doom ju baax ji Sédd ñu ci sa cofeel Ndax ñu roy sa sellaay Mariama mu sell mi Jigéen bu sell bi Boo ñu soppu loon Marie Kenn du fi ñëw di la ñaan téeméeri at a ngi Ñu sukk fii di ñaan Ave woy leen Marie Ave sant leen Marie Ave naw leen Marie Ave ñaan leen Marie Ey Marie, déglu ñu Ndeye ju laab-a laab ji Tuural ci ñun sa yiw Té leeral suñu yoon Mariama mu sell mi Jigéen bu sell bi Boo ñu soppu loon Marie Kenn du fi ñëw di la ñaan Téeméeri at a ngi Ñu sukk fii di ñaan Ave woy leen Marie Ave sant leen Marie Ave naw leen Marie Ave ñaan leen Marie Yow buuru jàmm ji Sàmmal ñu sunu réew Tuural ci Sénégal Leel jàmm ju dul jéex Mariama mu sell mi Jigéen bu sell bi Boo ñu soppu loon Marie Kenn du fi ñëw di la ñaan Téeméeri at a ngi Ñu sukk fii di ñaan Ave woy leen Marie Ave sant leen Marie Ave naw leen Marie Ave ñaan leen Marie Jox nañu la sunuy bopp Jébbal la sunuy ñaan Ndax Yàlla fal na la Buuru asamaan Mariama mu sell mi Jigéen bu sell bi Boo ñu soppu loon Marie Kenn du fi ñëw di la ñaan Téeméeri at a ngi Ñu sukk fii di ñaan Ave woy leen Marie Ave sant leen Marie Ave naw leen Marie Ave ñaan leen Marie Barkeel-al sa doom yi Jigueen bu téey-a téey bi Ubbil ñu asamaan Ñuy woy ak yow ba mos Mariama mu sell mi Jigéen bu sell mi Boo ñu soppu loon Marie Kenn du fi ñëw di la ñaan Téeméeri at a ngi Ñu sukk fii di ñaan Ave woy leen Marie Ave sant leen Marie Ave naw leen Marie Ave ñaan leen Marie Julien Jouga Transcription et traduction :Alpha Sarr
J'aime beaucoup la chanson❤❤ Mariama mu Sella mi❤❤
Amen 🙏🏿
Sainte Marie, La sainte Femme
Si tu n'avais pas d'affection pour nous,
Personne ne serait là à te prier.
Cent ans à genoux ,nous te prions
Ave Chantez Marie,
Ave rendez grâce à Marie ,
Ave ayez de la considération pour Marie,
Ave Priez Marie.
Établis ton trône chez nous,
Avec ton vertueux enfant
Répands ton amour sur nous,
que l'on puisse prendre modèle de ta pureté.
Sainte Marie, la Sainte Femme,
si tu ne nous aimais pas,
nous ne serions pas là à te prier
Mille ans nous voici à genoux et te prions
Ave Chantez Marie,
ave remerciez Marie, A
ve considérez Marie,
Ave Priez Marie
Ô Marie, entends nous,
La très pure Mère,
Verse sur nous ta divine grâce
Et illumine notre chemin
Sainte Marie, la Femme sainte,
Sans ton affection,
on ne serait là à te prier.
Mille ans nous voici à genoux et te prions.
Ave Chantez Marie,
Ave rendez grâce à Marie,
Ave ayez de la considération pour Marie,
Ave Priez Marie
Toi divinité de la Paix,
Veille sur notre pays,
Répands une paix infinie sur le Sénégal.
Sainte Marie, la sainte Femme
Sans ton amour,
nous ne serions pas là à te prier,
depuis Cent ans nous te prions à genoux.
Ave Chantez Marie,
Ave rendez grâce à Marie,
Ave vénérez Marie,
Ave Priez Marie
Nous nous donnons à Toi,
Et mettons nos prières à ta disposition
Car Dieu T'a choisi,
Reine des cieux
Sainte Marie, la sainte Femme,
sans ton amour nous ne serions pas là à te prier.
Cent ans nous te prions à genoux.
Ave Chantez Marie,
Ave rendez grâce à Marie,
Ave vénérez Marie,
Ave Priez Marie
Béni tes enfants, la sereine Dame,
Ouvre nous les portes des cieux,
que l'on chante avec Toi afin d'en gouter
Sainte Marie, la dame sainte,
Pour ton amour nous voici cent ans à genoux et à te prier.
Ave Chantez Marie,
Ave rendez grâce à Marie,
Ave vénérez Marie,
Ave Priez Marie
Traduction:Alpha Sarr
Machallah ❤
🤲🙏❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
Ave Maria
Salut, avez-vous la partition, s'il-vous-plaît ?
Mariama mu sell mi
Jigéen bu sell bi
Boo ñu soppu loon Marie
Kenn du fi ñëw di la ñaan
Téeméeri at a ngi
Ñu sukk fii di ñaan
Ave woy leen Marie
Ave sant leen Marie
Ave naw leen Marie
Ave ñaan leen Marie.
Sampal sa nguur ci ñun
Yaak sa doom ju baax ji
Sédd ñu ci sa cofeel
Ndax ñu roy sa sellaay
Mariama mu sell mi
Jigéen bu sell bi
Boo ñu soppu loon Marie
Kenn du fi ñëw di la ñaan
téeméeri at a ngi
Ñu sukk fii di ñaan
Ave woy leen Marie
Ave sant leen Marie
Ave naw leen Marie
Ave ñaan leen Marie
Ey Marie, déglu ñu
Ndeye ju laab-a laab ji
Tuural ci ñun sa yiw
Té leeral suñu yoon
Mariama mu sell mi
Jigéen bu sell bi
Boo ñu soppu loon Marie
Kenn du fi ñëw di la ñaan
Téeméeri at a ngi
Ñu sukk fii di ñaan
Ave woy leen Marie
Ave sant leen Marie
Ave naw leen Marie
Ave ñaan leen Marie
Yow buuru jàmm ji
Sàmmal ñu sunu réew
Tuural ci Sénégal
Leel jàmm ju dul jéex
Mariama mu sell mi
Jigéen bu sell bi
Boo ñu soppu loon Marie
Kenn du fi ñëw di la ñaan
Téeméeri at a ngi
Ñu sukk fii di ñaan
Ave woy leen Marie
Ave sant leen Marie
Ave naw leen Marie
Ave ñaan leen Marie
Jox nañu la sunuy bopp
Jébbal la sunuy ñaan
Ndax Yàlla fal na la
Buuru asamaan
Mariama mu sell mi
Jigéen bu sell bi
Boo ñu soppu loon Marie
Kenn du fi ñëw di la ñaan
Téeméeri at a ngi
Ñu sukk fii di ñaan Ave woy leen Marie
Ave sant leen Marie
Ave naw leen Marie
Ave ñaan leen Marie
Barkeel-al sa doom yi
Jigueen bu téey-a téey bi
Ubbil ñu asamaan
Ñuy woy ak yow ba mos
Mariama mu sell mi
Jigéen bu sell mi
Boo ñu soppu loon Marie
Kenn du fi ñëw di la ñaan
Téeméeri at a ngi
Ñu sukk fii di ñaan
Ave woy leen Marie
Ave sant leen Marie
Ave naw leen Marie
Ave ñaan leen Marie
Julien Jouga
Transcription et traduction :Alpha Sarr