Allahou Akbar‼️Franc mo dakka xékh Ama Baldé, Coach Bakary fait des terribles révélations

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 фев 2025

Комментарии • 49

  • @RenénicolasBadiane
    @RenénicolasBadiane 11 дней назад +12

    Démal wakh lépp lo kham Ama,djeuleul coach guédiawaye ak pikine yeup,Ama dagn koy humilier.

  • @momoreaction6903
    @momoreaction6903 11 дней назад +12

    Franc teulé woul khékh deh

  • @vieuxngom3760
    @vieuxngom3760 11 дней назад +11

    Coach Ama baldé leu beugue sauvé bilahi

  • @MameSow-r4i
    @MameSow-r4i 10 дней назад +1

    Franc❤kassé❤❤❤❤

  • @KaneArman
    @KaneArman 6 дней назад

    Tiey Bakary 😂😂😂❤

  • @abdouloume7373
    @abdouloume7373 11 дней назад +5

    Franc boko teewul meuno ko door
    Franc même contre attaque lay beuré, motakh mouy arriere pour aspirer lheu

  • @youssouphesane6184
    @youssouphesane6184 10 дней назад +2

    Borom lomotif yi😂
    Yangui dimbali ama nak 😅😅😅 la peur est de son coté

  • @abdoulo7752
    @abdoulo7752 3 дня назад

    Ana vidéo Ama Baldé

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 10 дней назад +2

    Kii ay secret franc lay wané nii 😢mais Sëriñ fallou rek

  • @vieuxngom3760
    @vieuxngom3760 11 дней назад +3

    Meilleur analyse le coach la il est où Sénégal ou bien

    • @ModouDiouf-i4d
      @ModouDiouf-i4d 11 дней назад

      Ki moy coach Bakary dafa directe me parfois day sai sai thi ay kadou me c est un excellent combattant et technicien

  • @rouguikebe9984
    @rouguikebe9984 8 дней назад

    Kéne laadjoula ligay wakh 😮
    Franc seul😊🎉❤
    Franc nimouy beuré nonoula khalé dagay imposé en utilisant ton cerveau mais pas took di calculé de midi à 14h❤
    Franc dou thiouné😊

  • @IbrahimThiam-x7h
    @IbrahimThiam-x7h 10 дней назад +1

    👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿❤️❤️❤️❤️❤️

  • @julosow3610
    @julosow3610 11 дней назад +3

    Kou nane 😂 mannlaa dou mom

  • @elhadjimaodoniang5531
    @elhadjimaodoniang5531 11 дней назад

    Maitre chanteur nga🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥

  • @ModouNgom-ge6yh
    @ModouNgom-ge6yh 10 дней назад

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @NdiawDiop-o6u
    @NdiawDiop-o6u 9 дней назад

    Bakary doul way

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye 10 дней назад

    Coche Bakary 😂 seule ❤

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 10 дней назад +3

    Bkhi lim yepp dou deugg 😂😂ay fenn rek la franc limou remise yepp dafa dall bou baax

  • @elhadjimaodoniang5531
    @elhadjimaodoniang5531 11 дней назад

    Do thiotou ndeyam maitre chanteur nga.Anna adamo?
    🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🙏

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 10 дней назад +1

    Kii ama balde lay diappalé di pett mais comp nagn fall

  • @YvesSagna-w5n
    @YvesSagna-w5n 11 дней назад +3

    Ioe doul wakhou farr rek ngey ndeye wakh

  • @mormbaye6583
    @mormbaye6583 9 дней назад

    Ama ak franc nio bokk khekh daniouy remise

  • @alassanemamadouba9570
    @alassanemamadouba9570 10 дней назад +1

    4 appui sou amoul lén dou ame Ama daye Ouby Combat Si Kaw Yor Ko Si Souf Pour Firko Bénn Solution Bobou Rékk La Ame Si Combat bii Franc Soula Ama Dané Si Plaqué Ma Khame nii Dague Nio Yapp Nioune Wa P.A

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 10 дней назад +1

    Wakhoo fi darra 😂😂nganane ma lene Dax analysé di doul 😂😂

  • @TallaDiouf-k5w
    @TallaDiouf-k5w 10 дней назад +1

    Khamo dara ama nga faral mé franc kassé

  • @naby1588
    @naby1588 10 дней назад +1

    Konn gueweul nga moudjé donn ?😂Beuri nga wakh trop té khamo dara

  • @AdamaMbaye-e1o
    @AdamaMbaye-e1o 11 дней назад +1

    Koy sani khér😂😂😂

  • @DaoudaFaye-h2p
    @DaoudaFaye-h2p 10 дней назад

    Lolo ler

  • @MoussaTraore-v5f
    @MoussaTraore-v5f 10 дней назад

    Yenn wa parcelle kato lenn sen data yaye mom nday nitt ba kou diouk di chroniqué rek sou wahé lou arranger woul sen mbeur ngeni dafa farr wl khamoul dr sen diobou nday way momo lenn nday nitt te kou farr amna droit nday farr boulenn niou fateu

  • @ngomndiaye8817
    @ngomndiaye8817 8 дней назад

    😂😂

  • @IdrissaSeck-x9g
    @IdrissaSeck-x9g 11 дней назад

    coach aay na mais il n’est pas humble quoiii😂😂

  • @mbackegaydelserignembacke8335
    @mbackegaydelserignembacke8335 10 дней назад +1

    Yw li yep beug wa keur ama dane faranc la ms yw ningaye fare mo baxouk yw triseur nga li ak laye xew fofou dina woute loll challa li wesouna dalal sa bopou te mga xamni manothi faranc dara

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 11 дней назад +1

    Fara xékhé Tapèth Deugeu Lay xèkh ki
    Bouy xèkh Day geumou ki😂😂😂🤔

    • @mbackediop7678
      @mbackediop7678 11 дней назад

      Mais ama Manoul beurè

    • @AboulBacharSall
      @AboulBacharSall 11 дней назад +1

      Wa baxna delein nax sene boppou rk bala 16 Incha Allah

    • @MoustaphaMbathie-mm1rp
      @MoustaphaMbathie-mm1rp 11 дней назад +1

      Wa pikine wax rék la Niou am si lamb dji waye la 16dina Niou léne nokho dane léne

    • @saliouthiam2462
      @saliouthiam2462 10 дней назад +1

      Balaa ma deee nga nek sa guinaw nann tapett 😂 esk do soumé kou dougou si birr lamb kmk yaa am fitt keuy

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 10 дней назад

    Yow ni nguay analyser doxoul vraiment li nguay deg daa wara équilibré nak waayé Franc lii franc lee franc leulé

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 10 дней назад

    Yaw guisso li franc li remise 😂😂ngay doul rek

  • @lbyoungtv2223
    @lbyoungtv2223 11 дней назад

    😂😂😂😢😅

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 10 дней назад

    Deffal video si ama comme ninga ko défé si franc

  • @Mowmetg
    @Mowmetg 11 дней назад

    Daguay duul rk 😂😂😂😂😂

  • @JosephDieganeTine
    @JosephDieganeTine 11 дней назад

    Yaw khamo dara

  • @OmarBa-r8r
    @OmarBa-r8r 10 дней назад

    Yaw doul