Mashallah . Comme d'habitude imam à son niveau...mais là vidéo ne devrait pas avoir comme titre: la suprématie de serigne touba parceque imam nous fait comprendre clairement que même mouhamed (psl) n'est pas suprême alors serigne bi c'est un digne serviteur du prophète ( l'élu) .
Khoutba bi dou bari commentaires, sonè borom Touba niouni thièl, sou wakhè si dokhaline dioulit,niounila mouride naniou kholat sène.nangoul lène Borom Touba. 11:18.none islam deug joulit lay done.yonent bi khoutba nassi ay yone ande len done bèn sày .12:45
Wolof you nékh ba doo beugg mou noppi. Taariikh bou yémé TabaarakalLaah. Waayé nak PAS DE CULTE DE PERSONNALITÉ EN ISLAM !!!! CRAIGNONS ALLAH ET SUIVONS NOTRE PROPHÈTE MUHAMMAD SALLAALLAAHU ALEYHI WA SALLAMA!!! Kouy gnaan ngueureumou kou faddou bokkaalé ne. Moussibeu le. Kouy yaakaar am pay tchi kou faddou bokkaalé ne. Moussibeu le. Yaa Rabbal Aalameen sammal nou sounou diiné tchi tawhiid gou sakh daakk bagna khadiam. Nangoul nou sounouk lott té doolél nou ngir seytaané bagn gnoo fakkatal. Mousseul nou yaa Rabbi. Koo mousseul mou moutch! Li am Sénégal yémé ne raglouneu. Tchieuy !!!!
Yalla terewoul Ken ga naw dieufame dakh ame bimou ame diné ba diko si topou . Galla manoulen si diamou yalla yi té bayi kounek ak li nek si xolame euleuk alakhira kounek sa bop gay taxawal do taxawal massamba do taxawal ma demba kon nak na kounek deff bopam yitem. Magui diegalou si kadou yi
Tanéfoup Serigne Touba yague fi loll téé and akh wéérr ❤❤❤❤❤
Si serigne Touba revenait sur vous ne changerez jamais votre posture que dieu vous garde ❤❤❤❤❤❤
Yalnafi yagg tèanakwèr
Sama Serigne bi Mbacke, Yalla nala Boroom bi fay
Qui peut m’aider a avoir son adresse ou un de ses contacts
Machaala Mbacke balla yalla na yalla goudeul sa fane
Allah vous protège vous êtes le meilleur
Machala mbak khamkham rek ka woor
Manchalah 🎉🎉🎉🎉
Yaalna nous Allah boolé sii ndiabootou borom Touba Yakaarou jaam yii. Amiine
Maachallah imam Rafahi Mbacké ❤❤❤ qu'Allah vous accorde une longue vie et la santé
❤❤❤Machaallah ya seydy al Imam rafahi al mbakiyou sukran laka
Machallah diangale amna solo té leerna
Manchalah
ما سا ء الله 🙏♥️
Mérci mbake
Massalah massalah mbacke dieureu dieufe Seringe touba amoul morom ❤️❤️❤️
Dieuredieuf Mbacké ❤❤
🌹🌹🌹🌹🌹🌺🌺🌺🌺🥀🥀🥀💐💐💐🌷🌷🌷♥️♥️ ماشاء الله أيدك الله ببركت شيخ عبد القادر الجيلاني قدس سره
Mashallah . Comme d'habitude imam à son niveau...mais là vidéo ne devrait pas avoir comme titre: la suprématie de serigne touba parceque imam nous fait comprendre clairement que même mouhamed (psl) n'est pas suprême alors serigne bi c'est un digne serviteur du prophète ( l'élu) .
حفظك الله ورعاك
Machalla 💖💖💖🕋🕋🙏🙏🙏💖💖
Machallah
Jeureujeufeti mbacke balla Yaggal wereul barke cheikhoul khadim
Thieye Rafahi epuis il communique bien dh vous constatez il parle sans nier quoi qui que ce soit
Khoutba bi dou bari commentaires, sonè borom Touba niouni thièl, sou wakhè si dokhaline dioulit,niounila mouride naniou kholat sène.nangoul lène Borom Touba. 11:18.none islam deug joulit lay done.yonent bi khoutba nassi ay yone ande len done bèn sày .12:45
Rêw mi mo barri nafêkh rekkk
❤❤❤❤❤❤❤
😢
Daradf mbacke
Yalana yala goudal sa fane
Amine
l'ONG Vie
Wolof you nékh ba doo beugg mou noppi. Taariikh bou yémé TabaarakalLaah. Waayé nak PAS DE CULTE DE PERSONNALITÉ EN ISLAM !!!! CRAIGNONS ALLAH ET SUIVONS NOTRE PROPHÈTE MUHAMMAD SALLAALLAAHU ALEYHI WA SALLAMA!!! Kouy gnaan ngueureumou kou faddou bokkaalé ne. Moussibeu le. Kouy yaakaar am pay tchi kou faddou bokkaalé ne. Moussibeu le.
Yaa Rabbal Aalameen sammal nou sounou diiné tchi tawhiid gou sakh daakk bagna khadiam. Nangoul nou sounouk lott té doolél nou ngir seytaané bagn gnoo fakkatal. Mousseul nou yaa Rabbi. Koo mousseul mou moutch!
Li am Sénégal yémé ne raglouneu. Tchieuy !!!!
❤️❤️❤️❤️❤️❣️

❤❤❤❤❤
Machalla