Sama Woudiou Toubab La - Episode 21 [Saison 02]

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 4 фев 2025

Комментарии • 877

  • @adjagaye7487
    @adjagaye7487 5 лет назад +693

    Ana sopé seydina Mouhamed ak serigne touba

  • @thiarragueye3482
    @thiarragueye3482 5 лет назад +92

    Kou bess jaim yalla nga féké déwéne

  • @amantousambe6796
    @amantousambe6796 5 лет назад +168

    Ba yénagui wathe Safar gui❤ Mon Pére meunouma si mome dara aka am fitt mome😂😂😂 Mark soukareu Béck😂😂😂 Ngoné Dagua Djiongama Nak machallah

    • @aichanguette8371
      @aichanguette8371 5 лет назад +1

      Aman IBn Saliou 😂😂

    • @madeleinendour7834
      @madeleinendour7834 5 лет назад +1

      Wala Sucre bou mok🤣🤣🤣🤣magui dee

    • @amantousambe6796
      @amantousambe6796 5 лет назад

      @@aichanguette8371 non gni douniou ay nitt😂😂

    • @amantousambe6796
      @amantousambe6796 5 лет назад +1

      @@madeleinendour7834 Mon pére mon am fitt ni

    • @salladiop4639
      @salladiop4639 5 лет назад +1

      Sava samawoe tobal ça va bien RUclips Facebook ça que tu m'as p tu pp

  • @AidaBa-h4w
    @AidaBa-h4w Год назад +1

    Mane maty mbaaye mo maye reye diakhassé rek lek laye def ak beugue money 10000❤❤❤

  • @maremendiaye4733
    @maremendiaye4733 5 лет назад +464

    Nianal léne souniou soeur astou sow talibé baye Niasse bou gueum baye mo guéneu adouna

    • @mbayeniass1030
      @mbayeniass1030 5 лет назад +14

      ndeye sann yalla nako yalla xare aldiana firdaw seydina mouhamed teruko baye niass may ko diokh

    • @maremendiaye4733
      @maremendiaye4733 5 лет назад +6

      Amine way

    • @maimounambengue3361
      @maimounambengue3361 5 лет назад +7

      Yalla nala baye niass térou

    • @maremendiaye4733
      @maremendiaye4733 5 лет назад +2

      Amine inchalla

    • @mbayeniass1030
      @mbayeniass1030 5 лет назад +4

      @@maremendiaye4733 inchall yalla mounako te yalla nako deff thie yeremandem

  • @Princesse_Mina
    @Princesse_Mina 5 лет назад +78

    Koubeugue serigne touba beuseul j'aime tagua yakati salokho

  • @fatouniang7429
    @fatouniang7429 5 лет назад +469

    LIKE POUR GNOU BEGUE SAMA WOUDIOU TOUBAB LA ❤️❤️

  • @ndeyefatoucisse776
    @ndeyefatoucisse776 5 лет назад +260

    Ana gni sourirou ngoné mbaye di danél wonéléne séne bopou maye guiss

  • @jamilabae5890
    @jamilabae5890 5 лет назад +98

    Meilleur épisode parmis tous😂😂 ngoné Mbaye walahi tu m fai telmen rire si seulmen tu savai yalla nassa diam yagueu machala t tro belle avk un sourir ki fai sourire😍 noirceur d’ébène diongoma une vrai Sénégalaise❤️ Sama Woudiou toubab la tha kaw tha kanam

  • @boubacarsagna8858
    @boubacarsagna8858 5 лет назад +24

    Kou yakaar serigne saliou beuseul pousse bleu 👍

  • @NiamaDiop
    @NiamaDiop Год назад +1

    Magui ni sopé sérigne touba ❤❤❤

  • @dabadiop7160
    @dabadiop7160 5 лет назад +218

    Diréction safar gui Ani mourid yii😘😍

  • @naturalmavista1917
    @naturalmavista1917 5 лет назад +75

    1.Mon père Ngoné mbaay la nope
    2.Ngoné moy seykate bi ani yakhalaté kate bi
    3.Maty mbaaye SEYTANÉ

  • @bintousall6485
    @bintousall6485 5 лет назад +540

    Dieureudieuféty Borom TOUBA

  • @fatyseye2740
    @fatyseye2740 5 лет назад +190

    Barké serigne touba ngoné mongui may Ray way😂😂😂

  • @fatouthiam8971
    @fatouthiam8971 5 лет назад +20

    Ooh j adore les yeux de ani. Ils sont magnifique machallah😍😍😍

    • @oumoumbengue3459
      @oumoumbengue3459 5 лет назад +1

      en tout cas taille basse bi dé rafetna té djap nako torop

    • @toulayeceesay2213
      @toulayeceesay2213 5 лет назад +2

      @@oumoumbengue3459 Ani kay dafa melni motakh gnou créer taille basse dafko diap torop

  • @TEAM_DMG_OFFICIEL
    @TEAM_DMG_OFFICIEL 5 лет назад +14

    💯Ila touba rèèk inchalla ❤

  • @sokhnabousso4763
    @sokhnabousso4763 5 лет назад +54

    Ngoné est vrai actrice j'adore😂 en passant maty doniou wax fingay jeuler sa expression yi😂

  • @fallfall7146
    @fallfall7146 5 лет назад +13

    Serigne moutakha mbacke yalla nafi yague

  • @fatougueye-zh7td
    @fatougueye-zh7td 5 лет назад +58

    Team ngoné mbaaye 🤣🤣🤣🤣😂

  • @rackygackou1188
    @rackygackou1188 5 лет назад +285

    Ngone, ma la beugue pir sa sourire daf may Daniel maty mbaye môme farou fene

  • @reinedunord
    @reinedunord 5 лет назад +13

    Ngoné reew na ba dof 😂😂😂😂 je l'adore ❤❤

  • @khadyseye5013
    @khadyseye5013 5 лет назад

    Cou émérite sama commenter yallana gafékémagale touba amine 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @niang8068
    @niang8068 2 года назад

    Ksp de votre satisfaction 😌 et vous souhaite de bonnes fêtes 🥂 à la famille 👪 de votre

  • @maxychoctoure8977
    @maxychoctoure8977 5 лет назад +3

    Bilay ngoné mbaye moy dindi sama stress😂😂😂

  • @gnagnabousso5601
    @gnagnabousso5601 5 лет назад +80

    Zéro stress avec ngoné réee mba tass.
    Bisous ngoné😘

  • @akonniang2259
    @akonniang2259 5 лет назад +85

    Deugue,deugue ngoné mo nékhal Théâtre bi dadji nanu

    • @ndeyasene5152
      @ndeyasene5152 5 лет назад +1

      Watiko way san mome theatre bi dou neh

  • @mamanbeye6525
    @mamanbeye6525 5 лет назад +223

    Ana wa wifi ma guiss

  • @awandong2472
    @awandong2472 5 лет назад +9

    Billay mane ngone mbaye moy sama antistress 😂❤❤

  • @marierosendione3884
    @marierosendione3884 4 года назад +1

    J'aime beaucoup Gnoné 🍓🍔🍫🍸🚑🐒

  • @rachou1239
    @rachou1239 5 лет назад +6

    Parlons de père Mbaye. Dieukeur bou beug awom malgré ses caprices😂 il fait l'effort de yamalé diabar yii mais dafa niakk fayda. Borom keur bo xamni yonam ci dara bou keur gui di todj soit defal nagnko ndiaroum lambay mouy nelaw wala mou weuyani. Deugeur na fitt dawoul salla yay nderr cii ay françaim 😂Zéro stress je l'aime😂😂

  • @cisseyacine7308
    @cisseyacine7308 5 лет назад +265

    Pourquoi les femmes de pére mbaay ne tombe pas enceintes. Ngoné bou eubé day nekh

    • @boufakebe8559
      @boufakebe8559 5 лет назад +9

      Prtant warnagn kosi bolé nek ken sakh eumb si

    • @aramedrame7430
      @aramedrame7430 5 лет назад +25

      Ndaw enceinteur Bou rhewww ngoné rek

    • @ndeyefall9476
      @ndeyefall9476 5 лет назад +3

      Arame Dramé wakhatiko 😂

    • @aramedrame7430
      @aramedrame7430 5 лет назад +2

      @@ndeyefall9476 😂😂😂day tok béneuh jr rek xarou

    • @mamejarrah4880
      @mamejarrah4880 5 лет назад +5

      Kone dom bou bari djoy lay am🤣🤣🤣

  • @babacarbarry235
    @babacarbarry235 5 лет назад +7

    Je déclare ngoné mbaye meilleure comédienne de l'année 2019 et lui souhaite bon vent pour sa carriére.sama khol laay seddal,tu es la meilleure

  • @fatougueye6206
    @fatougueye6206 5 лет назад +11

    Avec ngoné mbaaye zéro stresse qui est d'accord avec moiiiiii

  • @iamouz
    @iamouz 5 лет назад +38

    Ngoné Mbaaye Je taime💕💖💖💖

  • @astouwagnane8468
    @astouwagnane8468 5 лет назад +125

    ani mbaay woudiou si ki faatou mon pére dieukeur si ki faatou mati mbaaye ndieuké si ki faatou gnoléne di yeugal kharouk ngoné mbaay😂😂😂😂😂😂

  • @laylagueye7554
    @laylagueye7554 5 лет назад +6

    Je vote episode bi the best ngone dadji ngama😂😂😂retann na bay perrier

  • @adamodouty9234
    @adamodouty9234 5 лет назад +33

    😂😂😂😂Ani Ngoné mongui lay beug ray

  • @aichalaye5702
    @aichalaye5702 5 лет назад +4

    Maty mbaye bodio bodio nga bou mak anni à raison
    😂😂😂😂😂

  • @diamouyallahtv4363
    @diamouyallahtv4363 5 лет назад +3

    Dieurëdieuf Serigne Touba

  • @linguerendiaye4461
    @linguerendiaye4461 5 лет назад +2

    Ngoné mbaye mom ak anni akhana niow douniou ame dôme koumou diakhal beuseul jaime

  • @rokhayadabakyambaye4278
    @rokhayadabakyambaye4278 5 лет назад +2

    Ngoné dama fébar dhh mais bama la séltané la tané 😂😂yaye sama spafon 😄😄

  • @salvatoremaira7684
    @salvatoremaira7684 4 года назад

    Ngoné mbaye est tros bellle 💞💞💞💞💞💞

  • @sunugal4392
    @sunugal4392 5 лет назад

    Non dama réééé ba sooneu. Merci à tte l'équipe 😚😚

  • @rokhayandiaye2213
    @rokhayandiaye2213 5 лет назад +6

    Gnoné ak any comme Tom et jerry🤣🤣.mais ngoné va me tué way

  • @mbsambou6124
    @mbsambou6124 5 лет назад +142

    oh les caprices de ngoné amoul mdrrr

  • @moustaphagueye2993
    @moustaphagueye2993 5 лет назад +1

    Do lene bayyi gnone mbaye cou dacor beusseul jaime

  • @badebousambou3219
    @badebousambou3219 5 лет назад +21

    Maty seytanè gua amo koy faral koudoul toubab bigua khamnè falèwoula

  • @janettesarr2318
    @janettesarr2318 5 лет назад +8

    😂😂😂😂😂wooooy Ngone Mbaye dadjinama

  • @mariemegningue7079
    @mariemegningue7079 5 лет назад +4

    Bilay goné mbaye amoul ki dou dem😂🤣🤣😅

  • @abdoulazizmbodj7671
    @abdoulazizmbodj7671 5 лет назад +1

    Mes ngoné rey na ma kou beugueu puce bleu

  • @diarrasaliou1180
    @diarrasaliou1180 5 лет назад +207

    Magal touba ❤️jj-49

  • @kingmilkmangane4375
    @kingmilkmangane4375 5 лет назад +20

    Meilleure épisode de la saison l'incontournable ngoné mbaye

  • @nafissatousane8413
    @nafissatousane8413 5 лет назад

    Mane ngoné mbaye mi éhhh yi Mane meunama Rey💖

  • @binoushanne6301
    @binoushanne6301 5 лет назад +92

    Non père mbaaye dinama ray🤣🤣🤣🤣Nena kou mom Facebook moungui toudou mark soukeur beck🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣wooyyy

  • @aissatoudiegocisse5142
    @aissatoudiegocisse5142 5 лет назад +26

    Ani beugue ngoné Mbaye way

  • @yandendiaye4133
    @yandendiaye4133 5 лет назад +1

    Mane ngone Mbaye damaye yakamti mou amme defete ma retane ba beugua dee ndakh aye gestame chapeau à elle

    • @mamypouye4432
      @mamypouye4432 5 лет назад +1

      Bilahi chapeau à elle joue trés bien

  • @fatougueye2643
    @fatougueye2643 5 лет назад +8

    No ngoné kou yapp😂😂😂😂damaye kharou 😂😂😂😂

  • @khadydiouf9278
    @khadydiouf9278 5 лет назад +26

    Ani gni beugue kankoura 😂🤣🤣🤣😂😂

  • @diopvirginie
    @diopvirginie 5 лет назад

    Beydi Seye moy Mr Seye wa ani kokou iowwwww Joseph Felix Corea JFC😍😍😍😍😍

  • @madamefatoulo6250
    @madamefatoulo6250 5 лет назад +5

    Wouyay ngone mbaye ak yaw marewat 🤣🤣🤣 ngone mbaye respect nene da Sadiq

  • @lasenegalaises6055
    @lasenegalaises6055 5 лет назад +1

    J'en peux plus de ce deux femmes 😂😂😂

  • @notrechaine6483
    @notrechaine6483 5 лет назад +14

    Première commentaire je peux 1000000 j'aime

  • @rokhayaba135
    @rokhayaba135 5 лет назад +1

    Diabba balma taye mala thiatou dama téla jubilé!!!!😂😂😂😂😂

  • @maguettembodji6078
    @maguettembodji6078 5 лет назад +2

    Ani niou beugueu baye Karim falillou

  • @diopserignembacke9769
    @diopserignembacke9769 5 лет назад +1

    Kou guissé né Ani da mol dh🤩🤩

  • @pradisebousso1156
    @pradisebousso1156 5 лет назад +11

    Xaral ma dém wouti thièpp bouma lék 😂😂

  • @aminandiaye6649
    @aminandiaye6649 5 лет назад +7

    Mame Thierno kOon dOu ai fOo 😍ngoné wathi gnou way 😂

  • @mamidiengsalioumamitasalio4766
    @mamidiengsalioumamitasalio4766 5 лет назад

    Ngone mbaye dinama rayy rekk😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @dieynabadiop4333
    @dieynabadiop4333 5 лет назад

    Ngone nehh nga ma sa manière sa djonge sa fem Masha Allah zéro e stress ré ba tass

  • @mariadieye1502
    @mariadieye1502 5 лет назад +39

    Mon père kilay niawal bouko bayi vraiment nice na diap nala 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 ani

  • @aissatoucamara8346
    @aissatoucamara8346 5 лет назад +50

    Waw loutakh Ngoné rew 😂🤣🤣🤣li

  • @ndeyeyacinefallyas9711
    @ndeyeyacinefallyas9711 5 лет назад +2

    Je vous kiff depuis Italie et bonne continuation c'est super 🤣😂🤣😂 tague la mounoul mougne

  • @miachougoudiaby991
    @miachougoudiaby991 5 лет назад +14

    Bilay ngoné dou dém mé maty mbaye kouy weur Séytané rek diapp ko ni yallla bouma am belle soeur bou mélni mom

  • @tinabadji2057
    @tinabadji2057 5 лет назад +2

    Chuuuteeettttt mon père tamite dil wah lébone ba paré doga wah tamite 😅😅😅😅😅😅😅

  • @myakhouma5535
    @myakhouma5535 5 лет назад +6

    Waw koy série Djiégéne yi mi ngui Nonou commentaires yi 97% C des femmes👏👏 Djiégéne day diapalé moroumam

  • @evangom6821
    @evangom6821 5 лет назад +66

    Ngonė mbay con na gor bou tolni bayam guanane ko loutakh gua djonguama 😂😂 melni kouy wakh ak djiguene

  • @ElTIO_Galass
    @ElTIO_Galass 5 лет назад +7

    Son bi mongui Beureudji beuredie sama khol ❤️ bi waw keuy nak

  • @kandjikine4802
    @kandjikine4802 5 лет назад +22

    Ngoné mbaye réw nga😂😂😂😂😂

  • @bebemounass866
    @bebemounass866 5 лет назад +2

    Ay mane Maty mbaye diakhal nama, meune na dakhine, meune domada ak souloukhou 😂😂😂 cheuteuteut 😂

  • @oumykebe1922
    @oumykebe1922 5 лет назад +1

    Ngoné mbaye yaw ani mola guena rew gnawwww

  • @lalazoralo9150
    @lalazoralo9150 5 лет назад +2

    Ngoné y'a réy 😆😆😆😆😆😆😆😆😆😆😆😆

  • @maymonafall6063
    @maymonafall6063 5 лет назад +30

    Grève de la soif🤣🤣 ngone raiweuna tamite

  • @TymashaynaNdiaye080359
    @TymashaynaNdiaye080359 5 лет назад +3

    😂😂😂😂😂😂ngoné mbaye dou nitt

  • @fatoudiop1152
    @fatoudiop1152 5 лет назад +12

    Non ngoné Mbaye douma rayyy 😂😂😂😂

  • @bballouniang4708
    @bballouniang4708 5 лет назад +28

    Billahi ngoné mbaye dina raye rek maréwate kaye

  • @aminataaw5834
    @aminataaw5834 5 лет назад +91

    Mane dal beugouma kouy wokh gor yalla danga diongoma

    • @diarramame6470
      @diarramame6470 5 лет назад +9

      Ana gor ak diongama sakh😁

    • @coumbismbaye81
      @coumbismbaye81 5 лет назад +5

      Wakhal deh ca sonne mal a loreille

    • @aminataaw5834
      @aminataaw5834 5 лет назад +5

      Eupeul rek ak gnamé ay terme

    • @rararara164
      @rararara164 5 лет назад +2

      parey j dirai jamai ca a mon mari dal

    • @abdoub1477
      @abdoub1477 5 лет назад +1

      This girl is funny 😁

  • @lobendiaye2578
    @lobendiaye2578 5 лет назад +2

    Ngoné sincèrement tu me fait rir🤣🤣🤣

  • @loukaperez9628
    @loukaperez9628 5 лет назад +4

    Ay pére mbaye ya meuna feeen thiéré bi nekh na rek guani sama ommeu lako moniè guani kou nieuw senegal sukarbék 😂😂

  • @khadyndong2456
    @khadyndong2456 5 лет назад +2

    Non Ani Dinama raye je l'aime trop

  • @dydyshsn8453
    @dydyshsn8453 5 лет назад +7

    😂wouyyy wa Ngoné Mbaye mi ni laniou kay bayi ki dinama ray wayy😂😂😂😂😂

  • @sawdatoukane6197
    @sawdatoukane6197 5 лет назад +2

    Meilleur episode,depuis les usa

  • @sokhnaastoudiop35
    @sokhnaastoudiop35 4 года назад

    Jem tro tro la série machalla 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰

  • @eyvandiaye4382
    @eyvandiaye4382 5 лет назад +1

    J’en peux plus
    Ngone amgeu oscar😂😂😂

  • @Zazou_wane
    @Zazou_wane 5 лет назад +5

    14h25 j'adore la percussion

  • @dieguoucissenguarry3001
    @dieguoucissenguarry3001 5 лет назад

    Non maty mbaye rek si gnekkè yalna gnou yalla mousseule si mome

  • @krotgueye1028
    @krotgueye1028 5 лет назад +27

    Ngoné day sagnsei louneih mouttt🥰

  • @modoumodou8665
    @modoumodou8665 5 лет назад +59

    manquant bou mèlni ngonè mbaye masoumako guisse non mane ngonè la beug ndèkè

    • @aissatabah8892
      @aissatabah8892 5 лет назад +1

      Rafetoule mome diakarlo aak guor naane ko dagua djongoma c'est du n'importe quoi quelle gâchis les galséne

  • @fashagueye4853
    @fashagueye4853 5 лет назад

    Snap ngonei mbaye la beug maaan beuge naaa ngonei mbaye nak 😍😍😍

  • @aminatouthiam1911
    @aminatouthiam1911 5 лет назад

    Marc soukar békk 😂😂😂 non père mbaye tu es fort