Quand on décide de chanter une personne, on doit connaître ses ancêtres. Ndiouga Dieng l'a réalisé merveilleusement. Aujourd'hui on chante des gens juste pour de l'argent. Paix à l'âme de Diop Le maire et de Ngoudia Dieng. Cette chanson est magnifique.
i love you NDIOUG DIENG YALNA YA Allah yokk la lerr samala sa ndjabo ya gnakk kignan bilah sama xol dafa sedd mak sama borom rekako xam bilahi merci pour cette joie
Quand on décide de chanter une personne, on doit connaître ses ancêtres. Ndiouga Dieng l'a réalisé merveilleusement. Aujourd'hui on chante des gens juste pour de l'argent. Paix à l'âme de Diop Le maire et de Ngoudia Dieng. Cette chanson est magnifique.
ndeysane cette chanson a bercé mon enfance
Dou Diop DOUDOU AIDA NDIAYE..... YALLA NALLA YALLA YEUREUM amal nga ndiarigne sa communauté
Ndiouga dieng loukko mamadou diop massa may doyyoul.
Maynako keur. Mais wakhgua deug. Ki lounou ko may doyoul
Mayna keur yobouko makka ay yon outalko liguey ak domam mayko kaliss en pagaille defko kharite foumou dieum ande ak mome c est la mort ki l ai séparé
i love you NDIOUG DIENG YALNA YA Allah yokk la lerr samala sa ndjabo ya gnakk kignan bilah sama xol dafa sedd mak sama borom rekako xam bilahi
merci pour cette joie
Walay maliberi fatouma 💃💃💃
Aita ndiaye gning mou coura gueye. Fatima yayi maliber ndeye Gueye samb yayi mar
Seydina samba merci beaucoup mais svp dougalal cassette bih yeup stp
Un chant actuel
Ndaw bou yaro téy am kham kham té yadia liguéy loumou am diombouko. C est une Verité absolue
J'ai envie de pleurer
Waywi loussi doudou Diop Fay rek doyoul dafa neex té dougou si xol
Oh ndaaw na yarame
Sénégal diam rek laye ame
Paix à son âme
Li kouma ko woy ma dague sama yapou yaram may lako
Wallahi bodé goor deugeu gua sa yarame dina daaaw