DIÈNE KAÏRE RÉPOND FILS DE BALLA-SAMA PAPE DOUSA MOROM,AMO CLÉS BOUMA DANE,BALLA GAYE BISBOU NIEUWÈ

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 30 дек 2024

Комментарии • 61

  • @papeseck9969
    @papeseck9969 3 дня назад +7

    Boy bou discipliné,ame respect tei geum yala lay ndirou
    Yala ndaga ame ndam bro

  • @NdiaboutaDiouf
    @NdiaboutaDiouf 3 дня назад +5

    diene yalla Nala yalla may ndam lou sed inchalla nit kou yarou nga

  • @adamacoulibaly9903
    @adamacoulibaly9903 4 дня назад +8

    Baba Diaw Yalla nako sunu borom fayall bopam tei may Diène Kaïré ndam bou lérr nagn ci barkey Serigne Saliou❤❤❤

  • @GueyendioroGueyendioro-m6s
    @GueyendioroGueyendioro-m6s 4 дня назад +7

    Diene diouf kaire yalla nala yalla maye ndam brk seydina Muhammad ❤

  • @Loufa__bou__xaragne__lô__221
    @Loufa__bou__xaragne__lô__221 4 дня назад +16

    Modou lô meilleur lutteur de tous les temps 👑

  • @KaneOusmane-t9t
    @KaneOusmane-t9t 4 дня назад +2

    Diene yalla nalla yalla may ndam amine

  • @momonjiae2314
    @momonjiae2314 4 дня назад +3

    Yalla nalla yalla maye ndam champion ❤🙏

  • @GueyendioroGueyendioro-m6s
    @GueyendioroGueyendioro-m6s 4 дня назад +3

    Talfa diene kaire tapha mbeur zarko tapha Gueye 2 ibou afia yalla nalene yalla maye ndam ❤

  • @baboucarrjeng7655
    @baboucarrjeng7655 3 дня назад +2

    Blie I really appreciate you bro ❤❤❤

  • @Mõũhåmëd-i5l
    @Mõũhåmëd-i5l 4 дня назад +4

    Diéne kaïré yalla na ko yalla maye ndame si barké cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul ❤️🙏🏿

  • @afro3827
    @afro3827 4 дня назад +3

    Diene dafa am yar rek douma nafi ay mbeur ba tayi mais yalla nala yalla may ndam ❤

  • @AwaDiaw-ud4et
    @AwaDiaw-ud4et 3 дня назад +2

    diene kaire yalnako yalla maye ndam lou seed gouye❤❤❤

  • @OuseynouSarr-l3z
    @OuseynouSarr-l3z 4 дня назад +2

    Ndam rék inchallah

  • @serignematartall4137
    @serignematartall4137 4 дня назад +2

    Fils de balla yalnako yalla maye ndam🙏

  • @OusmaneFall-xv2uu
    @OusmaneFall-xv2uu 4 дня назад +2

    Machala kelle communication ❤ ndame rekkk

  • @PapaSeck-c9u
    @PapaSeck-c9u 4 дня назад +1

    Yalla nala Yalla May ndam lou sedd gouy ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @PenKhadim
    @PenKhadim 3 дня назад +1

    Belén fatte valdo ❤❤🎉❤❤

  • @diattaabdoukoulingo2826
    @diattaabdoukoulingo2826 2 дня назад

    Ndam rek inchala diéne kairé

  • @Faye-sv1jx
    @Faye-sv1jx 3 дня назад +1

    Diene yala nako yalla soutourale si comba bi maye ko ndam bou guawe ❤

  • @abdoulayembaye4261
    @abdoulayembaye4261 3 дня назад +1

    This is Diene 🔥

  • @AlonsoSone
    @AlonsoSone 4 дня назад +2

    Diéne kairé seul ❤❤❤❤❤

  • @sambaba683
    @sambaba683 23 часа назад

    Diène kairè mbeur bou yarou machallahh diambar leu yallah ngua am ndam

  • @BadaNdiaye-z2w
    @BadaNdiaye-z2w 3 дня назад

    Merci ❤❤❤❤

  • @adamslo7971
    @adamslo7971 4 дня назад +3

    Yallah nala yallah may ndam champion goore yallah bii wallahi diga yégue uncha alah future modou xaragne lo gay am nii talibé mam bii boull ragall Dara ndam rk uncha alah 🙏💪🏿💪🏿🥰🥰❤️🫶

  • @falloukonta1674
    @falloukonta1674 3 дня назад

    Yalnala mayy ndam rekkk inchallah ❤❤❤

  • @MamecheikhantaNgom
    @MamecheikhantaNgom 3 дня назад

    Ndam rek inchallah ❤❤❤

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j 2 дня назад

    Le digne fils de ndakarou domou town bi .✊❤️

  • @fallousarr5728
    @fallousarr5728 3 дня назад

    Boy bi aka yarou machalah

  • @KhakhamBoye
    @KhakhamBoye 4 дня назад

    Ndam rek inch’allah diéne diouf kaïré ❤❤

  • @dembsaounera2858
    @dembsaounera2858 4 дня назад +1

    Diene Diouf kaire 🎉

  • @alediakhate
    @alediakhate День назад

    Diéne yanala sounou borome défal tawfékh ak taïsir mouthie ak mouthielé diam diou sakh ba faw ta mayla Ndam lou séd gouy sii kaw Fils de Balla le 12 inchallah 🤲

  • @assanekane1426
    @assanekane1426 4 дня назад

    YALLA NALA.YALLA MAY NDAM AMINE

  • @bigtory4632
    @bigtory4632 18 часов назад

    Pokola Mbam Khoukh🤣💔

  • @momardiouf2950
    @momardiouf2950 4 дня назад

    Yalla nala borom bi may ndame👏🏾

  • @dembaniass9062
    @dembaniass9062 4 дня назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Doudoudiao
    @Doudoudiao 3 дня назад

    Inshalah dinga dane fils de balla diel bu reuy this is diene kholou gnou kenen kouy tak nguemb

  • @MortallaBeye-j6p
    @MortallaBeye-j6p 4 дня назад +1

    Mbeur bouma nekh

  • @IbrahimaDiallo-p9o
    @IbrahimaDiallo-p9o 4 дня назад +2

    Diene seul

  • @SaikouB-z8x
    @SaikouB-z8x 4 дня назад

    Nice

  • @masska201
    @masska201 4 дня назад

    ❤️❤️❤️

  • @sambatorino8115
    @sambatorino8115 4 дня назад +1

    Boye yala nga dane

  • @SalamBasse
    @SalamBasse 4 дня назад +1

    Diéne kaïré seul

  • @seydinaaliouneboromjasiji3200
    @seydinaaliouneboromjasiji3200 День назад

    David Luiz Bayil Football Xana Naar yi Sa Sokhela Wougn La

  • @LahatDiouf-v4n
    @LahatDiouf-v4n 4 дня назад +1

    Mangi laye nianal ndam

  • @ModouFall-b6t
    @ModouFall-b6t 4 дня назад

    Ndam rek mbeur

  • @papegueye147
    @papegueye147 3 дня назад

    Combat bi day match nul diéne ak boy niang séne ni papa gnoléni conseiller té gno eupe séni papa kham khamou lamb

  • @MansourDieye-dh6jv
    @MansourDieye-dh6jv День назад

    Franchement diène kaïre iow la yené nga dane mais sama guiss guiss mouno dane fils de balla srx

    • @ndongodiop9977
      @ndongodiop9977 Час назад

      Le jour j gay comprendre diéne kaiser est mille fois plus fort que fils de balla

  • @MoussaTraore-v5f
    @MoussaTraore-v5f 4 дня назад +1

    Saway dou am dreum zarco mila dann lathie ko kouy fils de balla no def danou

    • @wakhkatoundiakhoum2167
      @wakhkatoundiakhoum2167 4 дня назад +1

      Sa waay lolou dou dara ki gni mou daneu fils de balla meunouleneu dara lamb mo doyy warr rekk mais ki dou moromou fils de balla

  • @adamslo7971
    @adamslo7971 4 дня назад +3

    Yallah nala yallah may ndam champion goore yallah bii wallahi diga yégue uncha alah future modou xaragne lo gay am nii talibé mam bii boull ragall Dara ndam rk uncha alah 🙏💪🏿💪🏿🥰🥰❤️🫶