Machalla rafetna trop je suis mouride mais je suis content du khalife serigne babacar sy et de sa reconnaissance envers sidy et aussi des conseils importants envers cheikh niass j'apprécie
Assalamou aleykoum.Seydi Sy! Machallah très très sages paroles et très genereuses paroles.Tu lui as parlé comme tu aurais parlé à ton propre enfant.Ton humilité légendaire Seydi Sy ne t' en démarque jamais.Tu nous honore vraiment. Machallah. Cheikh ta démarche est bonne suis les conseils tu ne le regrettera jamais.QuAllah te préserve et te soutienne afin que tu porte très haut le flembeau.
Eskeuy cheikh niass ,vous avez l'honneur d'être le prétexte de ce beau message destiné à l'universel,en ces jours de bourdou,dans ce tiouawane de seydi hadji MALICK,QU'ALLAH nous procure la capacité d'écoute et les moyens de pratiquer, au nom du prophète de l'universel, MOHAMADOU RASSOLOULAHI SAWS
macha Allah Al Khalifa Serigne Babacar SY, yaa bakh tee beugue lou bakh pour gnepp. Message et conseils très importants à l'endroit de Cheikh NIASS mais qui est valable pour kepp kou beugue lou bakh. Cheikh Niasse diapal Serigne bi bou bakh, kouleu beugueul lou bakh leu. tee dou diaye keen lou doul wakh deugue kessé.
Kaddu you yiw te louy yette baari ndieurigne lolou fi ci adouna ak alakhira ma shaa Allah SY MALICK yalnala may gouddou fane andak weer lolou. Alhamdoulilah
Machalah li lépa liguéyou Sidi LA yalla nako yalla yereum kharko aldiana.Cheikh niass dieul nga sa tankou baye bonne continuation.Serigne Babacar sy mansour conseil yii amna solo nioune niépa mane nane si diaringou.
Machallah Serigne babacar mbaye sy ligua wakh cheikh dh domou Adam yep niou si mann guiss sone bop machallah sy Malick yalllna sa fane gogou si sa barke mame yii👏👏👏
Quand je vois ce crétin de Moustapha sy accusé sy cette homme certaine chose ça m’écœure vraiment il est d’une sagesse extraordinaire cette vidéo j’ai regardé ça plus de 50fois c’est une leçon de vie son discours rek defar na aduna nitt
Machallah amna solo lol dieureudieuf Serigne Babacar sy wakh dji amna solo sidy Lamine niass yalla naka yalla yeureum kharéko sa Aldiana you kawéya ta samb ndiabotam ❤
Machalla sy malick yagufi Loy tè and ak weer cheikh niass nagua bayi sa khel boubakh si Lila serignebi digeul ak loumoula diangal amna solo mem koudoul yaw sakh sètane videobi diangunasi loubari .
Bilahi bilahi bilahi bilahi sama khôl da'fa çede Gouy yalla mi waral li yalnagnou yalla dougeul si ngeur'meundéme si barki seydina mouhamed psl Amine 🇸🇳🙏
Macha la Serigne Babacar s'y Mansour Nit day wathié bopam Yalla yeukeuti'la Nga soufeul sa bopou Yalla kawél'la Lô beugeu am'ko Motax ndiabot Gui teunkou si yaw yalna yalla motali sa yéné si dîné'dji ak tarikha cheikh si barki Seydina Mohamed psl
Dieureudieuf serigne babacar sy Mansour yalla nala fi yalla yeugal te ande ak wér cheikh yaw nak serigne limo la wakh boko toupé dinala diarigne adona ak allakhéra
Allons rek donnons lui peu de temps vous verrez que il est bien préparé par Mame Abdou. Mame Abdou loumou dane def dey taggou serigne mbaye. Mo ko yar. Maggou Mame Abdou moy papame
Dieureudieuff Serigne Babacar Sy Khalife générale des tidianes kAllah vous accorde longue vie pleine de bonheur. Vous êtes notre fierté
Amiine
Macha allah chiekh niass refetna looll sakh yallana yalla yokou sa fan ak keppu kou wakh amine
Je n'ai jamais entendu des paroles aussi pleins de sens. Thieuy wa keur Maodo gno yémé.
Machallah sangue bi message bi amena solo yalna yalla goudal sa fane
Vraiment c'est le meilleur khalifa général d'Afrique ✌️✌️
seerigne bii neckoul siii sa wakhi swytanne yiii
@@bnoitbadiane7386 boula mété viens moi voir 💪💪sisou Mane nga Di géne dé c'est lui le meilleur khalifa général
@@abdoulayewade971 danga dooof
c la vérité
Machalla rafetna trop je suis mouride mais je suis content du khalife serigne babacar sy et de sa reconnaissance envers sidy et aussi des conseils importants envers cheikh niass j'apprécie
Assalamou aleykoum.Seydi Sy! Machallah très très sages paroles et très genereuses paroles.Tu lui as parlé comme tu aurais parlé à ton propre enfant.Ton humilité légendaire Seydi Sy ne t' en démarque jamais.Tu nous honore vraiment. Machallah.
Cheikh ta démarche est bonne suis les conseils tu ne le regrettera jamais.QuAllah te préserve et te soutienne afin que tu porte très haut le flembeau.
Eskeuy cheikh niass ,vous avez l'honneur d'être le prétexte de ce beau message destiné à l'universel,en ces jours de bourdou,dans ce tiouawane de seydi hadji MALICK,QU'ALLAH nous procure la capacité d'écoute et les moyens de pratiquer, au nom du prophète de l'universel, MOHAMADOU RASSOLOULAHI SAWS
Aziz Ndiaye walahi le message s’adresse à tout le monde. Dieureudieuf Al Khalifa yague fi loool té andeu ak wèèr.
macha Allah Al Khalifa Serigne Babacar SY, yaa bakh tee beugue lou bakh pour gnepp. Message et conseils très importants à l'endroit de Cheikh NIASS mais qui est valable pour kepp kou beugue lou bakh. Cheikh Niasse diapal Serigne bi bou bakh, kouleu beugueul lou bakh leu. tee dou diaye keen lou doul wakh deugue kessé.
Oui il y a longtemps j'ai pas pleuré mais aujourd'hui seulement là j'ai pleurer 🇨🇮🇨🇮🇨🇮🇨🇮🇨🇮🇨🇮♥️♥️♥️♥️♥️
C'est émouvant. Ces paroles d'or sont à méditer et à traduire en actes pour cheikh et nous tous.
Alkhamdoulilah
Masha Allah! Dieureudieuf Serigne Babacar Sy Mansour Khalife Général des Tijanes
Machaallah message très très important serigne bi yalna yalla gouddal fanam barkél doundam
lidé kou nè warnako dégue
Amine yarabi
Amine
Amine yarabi
Amine
Wallaahi Serigne Babacar Sy Mansour nittou YALLAH deugg leu... Goor YALLAH tiggui...
Kaddu you yiw te louy yette baari ndieurigne lolou fi ci adouna ak alakhira ma shaa Allah SY MALICK yalnala may gouddou fane andak weer lolou. Alhamdoulilah
Machalah li lépa liguéyou Sidi LA yalla nako yalla yereum kharko aldiana.Cheikh niass dieul nga sa tankou baye bonne continuation.Serigne Babacar sy mansour conseil yii amna solo nioune niépa mane nane si diaringou.
Wallakhi
Machallah Serigne babacar mbaye sy ligua wakh cheikh dh domou Adam yep niou si mann guiss sone bop machallah sy Malick yalllna sa fane gogou si sa barke mame yii👏👏👏
Serigne yagui fi ta gouda fane dieureuf s'y malick
Grandeur modestie, sagesse cette hommes c est le genre de personnes quon veut entendre parler ,pleines d enseignement dieuredieu serigne bi
En tous cas wakhdji rafetna lol lol lol sakh
Diadieuf way
Machallah ya bakh wayy 🙏🙏
Walaye sy j'ai les larmes aux yeux un message plein d'enseignement yalna yalla faye la yiw rafetna trop
Waw dieufée mo dess nak
Machallah sy malick yague fi lole ta wèr cheikh niasse yalnala yala samou tè arrla
Machallah serigne mbaye sy yalna yalla koudal fanevi ak wer
Quand je vois ce crétin de Moustapha sy accusé sy cette homme certaine chose ça m’écœure vraiment il est d’une sagesse extraordinaire cette vidéo j’ai regardé ça plus de 50fois c’est une leçon de vie son discours rek defar na aduna nitt
Seydi aboubakr yalna yalla mayla goudou fane yaw ak sa mbokk khalifa generaux yeup....Cheikh yawit yalla taxawoula bou baax
Jërëdëf Sy Maalig yalla nanga fi yàgg te wér aamiin.
لقدفرحت حينما رأيت شيخ نياس في مدينة تيوان لقدتمت نيته والدته ماأجمل هذا وماأحسن اللهم طول عمره مع صحة وعافية مع رزق واسعا مع البركات بجاه خيرالأنام
Serigne ababacar sy yalla nako yalla yok saw fan
Cheikh niass mi dall yalla nako yalla samal bopam
Aamin way
Amine yarabi
@@fatimandiaye2040 Amin
Amine yawit ya bakh way
amine
Manchallah amatina solo.
Cheikh mouhamadoul hafiss
Lèguèy bi raffét na manchallah.
Yalna yalla geuna deugaral takha waayam
Mosouma guiss lo amé ni solo machallah sy malick yalna sounou borome goudel sa fane lol té maye la wér si barke seyedina mouhamed psl
Waw waw ma cha allah ni rek la beug na billahi yallah nala yallah takhawou
Machallah amna solo lol dieureudieuf Serigne Babacar sy wakh dji amna solo sidy Lamine niass yalla naka yalla yeureum kharéko sa Aldiana you kawéya ta samb ndiabotam ❤
Sy Malick vous êtes un grand Monsieur. modestie pieuté islam; yalla na sa diam yague say khéwal bawaane
Machalla sy malick yagufi Loy tè and ak weer cheikh niass nagua bayi sa khel boubakh si Lila serignebi digeul ak loumoula diangal amna solo mem koudoul yaw sakh sètane videobi diangunasi loubari .
Mach'allah jeureujeuf SY Malick yalna brom bi goudeul sa fane yagal sa taxaway si kanamu njabott GI si barké yonanta bi saw amin
Bilahi bilahi bilahi bilahi sama khôl da'fa çede Gouy yalla mi waral li yalnagnou yalla dougeul si ngeur'meundéme si barki seydina mouhamed psl Amine 🇸🇳🙏
Deug deug xol sédatina elhadji sidi lamine yalna yalla yok léram
Bilay niepe kontan
Papa sidy yalna yalla kharue ko aljana firdawoci
Amine
Machallah sama serign loutakh ma sopou la mako kham
Beaucoup d'enseignements très intéressants très riche
Macha'allah raf na 🙏 limoy Sénégal 🇸🇳 tidiane ak mourid 🙏🙏🙏
Bilahi ya bakh sy malick yallah na yallah goudeull sa fane
Le message est valable pour nous tous... Très pertinent
Plein de Savoir vivre Serigne Babacar Sy Mansour Yallah Yallah goudal faname alahouma amen
Amine yarabi sy Malik yageu fi lolou sakh yalla na diamou ya gue machallh amna solo
Sidy lamine niass yalla nako yalla yeuram si barke sidynah mouhamed
Yalla Na yalla goudel saw fan
Machaala St Malik wakhatane wi amna solo té bari yédangué yalnaniouko dieufé
Macha la Serigne Babacar s'y Mansour
Nit day wathié bopam
Yalla yeukeuti'la
Nga soufeul sa bopou
Yalla kawél'la
Lô beugeu am'ko
Motax ndiabot Gui teunkou si yaw yalna yalla motali sa yéné si dîné'dji ak tarikha cheikh si barki Seydina Mohamed psl
Sy y’a deugou té bakh yalla na yalla goudal sa fane maye wére si barké seydina mouhamed
Machallah Yan na Yalla barkél lepp Sy Malick Dieuredieuf
Machallah sy Malick yalla nala samou t3 arr la
Je ne me lasse jamais de ce wakhtane plein de sens et d'enseignement.
Machallah sy malick yague fi lole serigne babacare sy mansour wakhtanbi amna solo
Machalah cheikh niass yalnala yalla diapalé
Machallah Machallah on est trop fière de vous
Cheikh machallah yallah nala yallah lafal thiat machallah sy malick
Machallah chetkh yallna yalla diapalekou
Jajeufe jajeufe walftv machallah serigne babacar sy Mansour
Billahi li doumasi doyal séttal li rekk nimou amée solo machallah ❤️ 🙏
message bi pour kep kou buegue lou bakh yalla na yalla sam
Sydi lamine niass yalne yalle yokke ay leram amiine
Machllalla wakhtane bi amna solo torob sama xoll sėdena torob si serigne babacar sy mansour
Serigne babacar sy Mansour yal nafi yague té wér
Machallah, fier d'être Tidiane. Dieuredieuf Serigne Babacar Sy Mansour. Espérant que Cheikh Niass a bien entendu les conseils du sage.
Maschaallah message très important Dieureudieuf Sy Malick
Machallah serigne bi sa wakh dji guiss na si sama bopou yala na la yala faye
Machallah nonou la
J'ai les larmes aux yeux ya rabbi 😢😢😢😢😢😢😢😢😢Dieuredieuf Sy Malik
Machallah le vrai khalif général du monde
Dieuredjef sy Malick Yalla guafi yag teh wer barkè Yonnenetebi Psl barkè Cheikh Tidiane R A
Dieureudieuf amna solo serigne babacar sy Mansour yalnala yalla takhawu si barki seydina Mohamed psl amine
Masha allah serigne bi wakh dji gneup la lale walahi
Dieureudieuf serigne babacar sy Mansour yalla nala fi yalla yeugal te ande ak wér cheikh yaw nak serigne limo la wakh boko toupé dinala diarigne adona ak allakhéra
Discoure de grandeur vive SERIGNE bi vive walfadjri suivit dp8t Italie
Walay cheikh niass bo awone si ndigal bila kilafa gui waxone do joum man sax masiy diang c important le 07 02 2024
Message très émouvant machallah
Machallah sy Malick sydi lamine des kontana tey
Tres message important notres khalif longue vie si Barker Seydina Mohamed PLS AMINE
Dieuredieuff YA AL KHALIFA ABOUBACAR SY MANSOUR MALICK conseil pour tous
machala serigne
babacar sy
serigne cheikh Nossa m achalla yalnala
yallatakhae
ndigl djafe
Machallah sy fa demba
Pape Ndiaye ngalgou mayma terrain tivaoune defka adiya seydina Mouhammad psl barke mame maodo
machalla.yalla na yalla goudal sa fan. sy malick
Barké borom touba Seringe bii koubaxla
Weuy
Mach'allah
ya bakh rék walaye kou bakh moy kham bakh
Bilahi black black yaw koubakhga barckè serigne babacar sy ndakh liga wakh sakhol gako tibè yalla nala yalla defal diam si barckè serigne babacar sy
Un message très fort pour tout le monde
Dieureudieufff sounou khalifa bi Serigne Babacar S'y Mansour
Machalla serigne babacar s'y Mansour al khalifa yallanala yalla faye Ak wer merci walf
Machala sy yague fi lole te werr wakh dji rafete na ame na solo machala
Mesage très important macha Allah
Machala sy Malick diazakalahou ana khayrane oooooh quelle grandeur sy malick
Dieuredieuf Serigne Babacar SY Mansour yagg fi lool and ak wérr
Machall ha rék walf tv 🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷
Sidy diambar deug yalna yalla yok yeurmandee takhawou ndiabotam mashala
Vraiment j,ai mème envi de pleurer walahi ya bakh Sy Malick,yalanala yala samm way
Yalla na yalla yombal mission bi
Ah machalah s bi kadouyi amnasolo
Serigne Babacar sy Mansour yallah nafi yageu té wér
Allons rek donnons lui peu de temps vous verrez que il est bien préparé par Mame Abdou. Mame Abdou loumou dane def dey taggou serigne mbaye. Mo ko yar. Maggou Mame Abdou moy papame
Machallah yageufi lol te wer sy
Machallah amna solo sy malick
Machala gnass yalla koudal fan yi way 😍😍😍😍😍
chiekh khamanytewougnou mais yala na borom goudeul sa fane yalla boulene none retane thi barke mame you bakh yi
Bilay begue na Serigne Babacar sy ye gua ngep machallah
Wakh dii de kou nek si gnoun warnga thie guis sa bopou rawa Tina gnoun ndawgni
شيخ أنياس أطال الله عمرك
حفظك الله ورعاك حبيب قلوب رجال الله شيخ الخليفة السيد ابوبكرالحاج منصور سي