Qui sont les Mbacké Mbacké? [Audio Version - Téléchargeable]

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 15 янв 2025

Комментарии • 34

  •  4 года назад

    *Cliquez pour télécharger Audio bi:*
    drive.google.com/uc?id=1MminRDrCoH0UwulZn0H1fLEyAjLIVxCH&export=download

  • @sadiondiaye9856
    @sadiondiaye9856 4 года назад +5

    C'est Incroyable... C'est Incroyable ! Thiééyy Funu Jëmme Akk TÛRÛQ Yii !

  • @omardia6023
    @omardia6023 3 года назад +3

    Wallahi serigne si koulen top dem safara

  • @kaboutoure3671
    @kaboutoure3671 3 года назад +4

    Village bou nguenne yess thi Sénégal moye Touba, khalifa général bou nguenne yess thi adouna moye khalifa général de Touba,

  • @adamsd6238
    @adamsd6238 4 года назад +17

    mountakha mbacke doko degue mouk mou wakh aya wala hadith bokaalee rek ma khala dianguoul tee menoul wakh tarikha mourid bokaalee rek

    • @babadiop2700
      @babadiop2700 2 года назад

      Il faut rectifier ses erreurs c'est grave la mort est très proche

  • @aligueye4727
    @aligueye4727 3 года назад +2

    Sénégal deukou comédie gniy nakhé akk niouy weur kouléne nakh gniofi dadjié vraiment c'est triste 😭😭

  • @elhadjithiam8564
    @elhadjithiam8564 3 года назад +5

    Gni gno mana doul deug deug

  • @arimaz89
    @arimaz89 3 года назад +3

    Pa Serigne bissi fin bi moy ki sol li wekh nekeu si auto bi Hana dafa mandit 🤨

  • @senegalopposant2878
    @senegalopposant2878 2 года назад

    Bayilene serigne

  • @adamasy267
    @adamasy267 3 года назад +2

    Ayyy wayyy ténio ragall yalla

  • @WillyD.
    @WillyD. 3 года назад +1

    Kara🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @caroleducrocq8248
    @caroleducrocq8248 2 года назад

    Allahou akbar allham doulillah yallah yoow rék yaaye yallah kéén dou yallah koudoul yoow yallah mouhamadou rassoul mooye sunu yonéént yallah kééne la fii téh doo toul gnar ccii darou adouna. Yallah sunu boorom gnii ak séne yii nii téh jéégé woul daara touss ak diiné islam béh kagne? Seigneur dieu jusqu'à quand ? Jusqu'à quand ?

  • @abdoulayemarega9799
    @abdoulayemarega9799 3 года назад +3

    Serigne mountakha Bess bo diakar lo ak safara diakhanam Di kham yalla sougnou borom Kenn dou ko foyé

    • @abdoulayeba7078
      @abdoulayeba7078 3 года назад +1

      Wallahi, le jour du jugement dernier, mountakha saura que son grand-père n'est rien du tout devant ALLAH.

    • @diyasoumare8742
      @diyasoumare8742 2 года назад

      @@abdoulayeba7078 il se rendra compte que son grand-père ne siège pas avec Dieu😂😂

  • @thefabulous7694
    @thefabulous7694 3 года назад +5

    Kara un vrai comédien🤣🤣🤣

    • @adamasy267
      @adamasy267 3 года назад

      Kara mo yakh senegal domouram la

    • @grandmo1006
      @grandmo1006 3 года назад

      C'est un clown c'est encore pire

  • @fodedieng9870
    @fodedieng9870 3 года назад +3

    Gnilein top moy sama problème

  • @ngonesarr1141
    @ngonesarr1141 2 года назад

    gni déh louma lén beug wakh rék khép ko khna dilén nianal yalla guindi lén rk

  • @adjithianediagne1548
    @adjithianediagne1548 3 года назад +2

    Li moy mandarga nitou safara. Gni nio bonne

  • @omardia6023
    @omardia6023 3 года назад +2

    Ay bokalé kat you mok moy yen yalla nalen yalla guindi thi sen rerr bi bala déé nieuw

  • @joopjoop8556
    @joopjoop8556 4 года назад +3

    Thieuy ndiabar bi safna sap

  • @babinewone2742
    @babinewone2742 4 года назад +1

    Yemena dé

  • @diyasoumare8742
    @diyasoumare8742 2 года назад

    Le dernier est ivre mort. Ils ne se rendent même pas compte

  • @ussumanecorreia
    @ussumanecorreia 3 года назад

    SOUBHANALLAH

  • @kaboutoure3671
    @kaboutoure3671 3 года назад +1

    Touba Mouss gniou mbagnie xaliss bou bonne, xaliss drogue xaliss prostitution xaliss braquage ,yeppe thi juma Touba

  •  4 года назад +4

    *Lann moyy A't-Tawhîd...* Wéteul Yalla...Contrairou Bokalé Yalla? *_Lannit moy Bokalé?_*
    Si xamxam yi dafa amm xamxam bouniouy wowé:
    *Fiqh:* mo layy diangal nouniouy diâmo Yalla.
    *Hadith:* mo layy diangal nou Yonantibi saws démone doundé Islam ak nane laniou wara doundé l'islam souniou ka beugué roy. Si xamxam bi, ngay diangué *Sounnah* t moyy dokhalinou yonanti bi saws si dîné ak comportement.
    *Tafsir:* mo layy dégeulo ak comprendre lo kaddou Yalla you nekk si Al Qur'aan. Ak lann la Yalla dioublou si lepp loumou niou wakh si téréwam bi.
    *Sîrah:* histoire et biographie du Prophète psl et ses compagnons
    *Tadjwîd:* nann laniouy diangué ak tarée Al Qur'aan...mou diarr yonn té rafet.
    Et d'autres xamxam.
    Legui nakk...dafa amm Benn xamxam bou amm solo bouniouy wowé:
    *A't-Tawhîd:* xamxam bi mo layy diangual nou Yalla wété si Ayy mbiram yeup! Xamal la akkeu Yalla Yi. Yo khamni kou si dialgati dangay dougou si bokalé...minga xamni Yalla dafa wakh Dou ko balé.
    Si xamxam bii niouy wowé *A't-Tawhîd* ...dafa amm niett xâthie souniou kayy diangualé.
    Xâthie bou ndieuk bi: *Tawhîd A'r Rouboûbiyah*
    Si xâthie bi laniou layy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si Al Khalq:* Création Wala Sakk. Moyy Yalla mo Sakk niepp niouy doundou, nitt, animaux yi, Malaka yi, djinné yi, ndokh yi, djant bi, weer wi...lepp si gatal. Nitt sou wakhee Kenn koudoul Yalla mo Sakk Dara si adouna bi...kokou bokalé na Yalla si Tawhîd A'r Rouboûbiyah...si xâthie bouy diangualé Al Khalq. Beu Legui si A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah, Dina niou la fa diangual, ka *Yalla dafa weet si Al Moulk:* moyy Yalla dafa weet si Ngoûr. Momm moyy Bourou nieup. Mou amàt belen xâthie, si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah...bouy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si A't-Tadbîr:* moyy Yalla moyy dokhal mbirou adouna bi, moyy contrôler weurseuk yi, doundou nitt gni ak ngelaw yi...taw Yi...ak événement youy amm si souniouy mbir, Moyy rayé...moyy doundeul. Kou wakh Lou melni kelen moyy diokhé doundou ak dè. Bokalé nga Yalla si weteul Yalla si A't-Tadbîr si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah. Si A't-Tadbîr tammit, laniouy layy leralè ni ke Yalla moyy contrôler souniou affaire yeup comme kann mo niouy Djitté, nou souniouy mbir di demé ak kou Yalla tekk si souniou kaw. Yalla rekk moyy falé. Falé akkeu Yalla la. Kou KO diokh kelen koudoul Yalla danga bokalé Wala diokh Yalla un associé...si mbiroum Fallé. Nitt dafa amm akkeu ak loumou Yayo t momm KO. Yalla amm Ayy akkeu ak loumou Momm. Kenn amoul droit diokh akou Yalla mamam Wala kharitam Wala Serigne niamm, yonanti bi ou qui que ce soit. Momm la yonanti bi saws wakh moyy togne bou geuneu reuy si togne yi. T togne bakhoul. Rawatina togne Yalla.
    Legui damay teunk Lou dess si résumé xamxam bouniouy wowé A't-Tawhîd:
    *Niarelou xathie bi...moyy A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah* ...fi laniou layy diangualé Yalla dafa weet si Diâmou Yi...moyy lepp louy Diâmou Yalla. Kenn warou ka defaral Kenn koudoul Yalla. Example de Diâmou Yalla:
    *Djoulli:* Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kouy dioulil kenen. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A's Salaat...Djoulli.
    *Yakar:* Yalla rekk laniou wara yakar. Kou yakar kelen koudoul Yalla. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A't-Tawakkoul...yakar.
    *Diâmou:* Yalla rekk laniou wara diâmou. Kou diâmou kelen koudoul Yalla si bepp façon d'adorer ou diamou. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si Al Ibâdat yi...diâmou yi. Iyyaaka na'hboudou. Yaww rekk laniouy diâmou.
    *Ndimbeul:* Si Yalla rekk laniou wara sako ndimbeul. Iyyaaka nasta'înou...si Yaww rekk laniouy sako ndimbeul. *Kouy sako ndimbeul si kenen koudoul Yalla en étant en danger*, Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A'l Isti'âna...sakkou ndimbeul. *Note:* *Sakkou ndimbeul bokalé* moyy par example, nga nekk si auto Mouy wadja accidenté, wala nga nekk si biir guethie ngay melni kou nara lapp, wala nga teud si lale febar...nga ragal d, ngay Sakkou ndimbeul si Serigne bou genn adouna pour mou secourir la/dimbalila. So nekee danger, Yalla nga wara wo. Soko defoul bokalé nga.
    Et y a d'autres comme niann...Yalla rekk laniou wara niann. Niann diâmou la. Ragal kou fi nekoul...Al Khawf. Yalla rekk moka Yayo. Akkeu kamm la. Pour ne pas trop citer d'exemples d'adoration...j'arrête ici. Naniou diangue souniou diné samay mbok djoullit...li yeup dinaniou KO kham et les détails et exemples que g pas cité. Naniou kham bokalé ba douniou KO deff. Douniou KO djigne kou ka defoul. Ndakh khamnaniou loumou donn.
    Si gatal si A't-Tawhîd A'l Ouloûhiyah, bepp diâmou Yalla, Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kou ka defaral kenen. Diokh nga akkeu Yalla kokou.
    Ma teudiee fii...ak *xâthie bou moudj bi. A't-Tawhîd Al Asmâ...wa's Siffât.* Fii laniou layy diangualé tourou Yalla Yi ak melo kanam Yi. Moyy ayy tour ak melokane yo khamni Momm rekk mo ka Yayo. Kou diokh tour wala melokanou Yalla. Bokalé nga si borr bi si A't-Tawhîd A'l Asmâ wa's Siffât. Example: Yalla mo amm melokane bo khamni moyy guiss nieup ak lepp. Kou Yakar ni dafa amm Kenn kou layy guiss fo manti nekk. Yangui bokalé kokou akk Yalla si côté bi. Kou Yakar ni Kenn koudoul Yalla khamna si lo nekk fo manti nekk, bokalé nga Yalla si Benn si melokanam yi. Ndakh Yalla rekk moyy xamm nieup si louniou nekk a tout moment. Akkeu kamm la.
    Legui nakk. D fois pour nga xamm ndakh nitt dafa bokalé fokk nga kham tawhîd...weteul Yalla ak contraire ramm bokalé Yalla.
    Kou beugeu kham sa dîné, commence par lire la traduction du Coran et les enseignements du Prophète psl dans les livres de hadith comme le jardin des vertueux, Sahih Mouslim, et Sahih Boukhari. Et plus tard...nga commencer diangue deug deug sa diné.
    Naniou diâmou Yalla ! Naniou diangue souniou diné.
    Lou bakh si sama wakh si Yalla la diogué !

  • @maridjikine7887
    @maridjikine7887 4 года назад +1

    سيعلمون غد من الكذب