VISITE SURPRISE DE SERIGNE ABDOU MARABOUT DE SONKO DANS DIOMET...SA NDIOGOU MAME PATHE ET SOINBOU...

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 21 май 2024
  • SOLUTION TV

Комментарии • 586

  • @samadeug6754
    @samadeug6754 25 дней назад +138

    SOLUTION TV AMNA LU DIAFE
    MERCI SERIGNE ABDOU
    SI SA TAKHAWAY

    • @khadyndiour3473
      @khadyndiour3473 25 дней назад +7

      Vous le méritez diadieuf way

    • @user-lq8rs3mp2n
      @user-lq8rs3mp2n 16 дней назад

      A❤qqqq❤qq❤❤❤❤❤❤​@@khadyndiour3473

  • @yayeboy1839
    @yayeboy1839 25 дней назад +134

    ❤❤❤❤❤❤❤Dieureudieufati a vous tous serigne bayou Ousmane Sonko Sa Assane Souhibou mais aussi Cheikh Bara et Mara. Yal nalen Bourbi faye nangou seni nianes.

    • @patheseye9384
      @patheseye9384 25 дней назад

      ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @CoolBoy-zg9he
    @CoolBoy-zg9he 25 дней назад +51

    Je ne suis pas mouride mais j'apprécie l'engagement de certains de leurs guides religieux pour l'émancipation de notre cher pays. Je le respecte beaucoup pour cela. Longue vie et santé de fer à lui

  • @mamadoubathily4370
    @mamadoubathily4370 25 дней назад +27

    Un grand respect, à ce Saint Homme, courageux, engagé et constant pour le soutien de PROS et de Pastef.... N'dokalé , Bismillah !

  • @serignebambadabo9249
    @serignebambadabo9249 25 дней назад +23

    Jërejëfe Borom Touba jaraama Mame Cheikh Ibra Fall j’ai un immense plaisir de voir mon guide spiritual S Abdou Mbacke Darou khoudous yalgafi yaak te werr ci barke S Touba ❤❤❤

  • @user-dd3us2ym8z
    @user-dd3us2ym8z 25 дней назад +9

    Machalla s Abdou borom bay bo bakh bi doma fate sa waydior s cihekh khadi mbakhe yalla na yalla Yoko ay leram

  • @GoraThioune-cd3yi
    @GoraThioune-cd3yi 25 дней назад +77

    Solution tay dagėna wara jubilé , c'est comme un médaille 🏅 thi liguėye bii, diadieuff

  • @a-b-s7989
    @a-b-s7989 25 дней назад +26

    Serigne Abdou contane naniou si yaw yallana goudal sa fane barké sheikhna sheikh akhmadoul khadim

  • @mamadousarr3371
    @mamadousarr3371 25 дней назад +15

    Ndeysan serigne Abdou mbacke aka bakh man damako begeu te yalla takh yalla nako yalla samou merci beaucoup solution tv ❤✅️👍

  • @baabinewone7142
    @baabinewone7142 25 дней назад +73

    Serigne Abdou Mbacké ❤❤❤mes respects, nittou deug

  • @rokhayadiedhiou9360
    @rokhayadiedhiou9360 25 дней назад +25

    Mash'allah ! 🙏
    Un homme, un religieux que j'estime beaucoup. Yalneufi yague té wer🙏🙏🙏

  • @mamadoundiaye9274
    @mamadoundiaye9274 25 дней назад +13

    Depuis Brescia en Italie, la section pastef de brecia et provinces remercie vivement serigne cheickh abdou mbacke...de la part de Ndiaye professeur

  • @FafaToure-xq3ji
    @FafaToure-xq3ji 25 дней назад +36

    Machalla amna solo lool serigne abdou mbacke balla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdouseye1108
    @abdouseye1108 25 дней назад +16

    Diaduef seringe Abdou mbacke yalla nafi yague te wer amine barkè seringe touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ballysakho2563
    @ballysakho2563 25 дней назад +32

    Machalla mbacke bala contane nagn troppo ❤❤❤❤❤❤❤

  • @kadiadiaw5819
    @kadiadiaw5819 25 дней назад +15

    Jai pas encore suivis la Video, mais je suis tres tres contente bilahi. Yalla goudeul saye fane thie barke seydina mouhamed psl

  • @abdouseye7705
    @abdouseye7705 25 дней назад +19

    Ndeyesan Serigne Abdou mbacké Aka bakh yalla nako yalla samb barkbe borom touba Amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @gueyendiaga5000
    @gueyendiaga5000 25 дней назад +25

    Diapou tey Diouli
    Diang tey dianglé
    Dioupe tey. Dioubeul
    Diouboo tey dioubanty

  • @amadoudiop8014
    @amadoudiop8014 25 дней назад +10

    Massalah je l'adore Serigne Abdou Mbacké yalgua fi yague lool té am wer si barké Nabi PSL ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @BoubacarGueye-xe1wx
    @BoubacarGueye-xe1wx 25 дней назад +8

    Salam Merci mon Dieu Alhamdoulilahi Alhamdoulilahi Alhamdoulilahi de nous avoir donné des Guides religieux modeste et véridique comme notre cher marabout. Que le bon Dieu vous assiste vous garde, vous avez joué un rôle très important pour la libération du Peuple Sénégalais. Que le bon Dieu accompagne et assiste le Président Bassirou Diomaye Diakhar Faye et le Premier Ministre Ousmane Sonko et le régime actuel à réussir leur mission rebâtir notre cher Sénégal dans la dignité et le développement. Merci Sa Ndiogou et votre équipe Solution et tout le Groupe Walf

  • @user-gb7ml9kj2o
    @user-gb7ml9kj2o 25 дней назад +28

    Kee reke lasoup akamakou beggu ce Sama khoull yalla nakou yalla maye goudou fans akke were kelifa deggela

  • @laminediatta7069
    @laminediatta7069 25 дней назад +10

    Sa Ndiogou chapeau a vs raiment vs mérite tout ce la car t’as bcps appris chez Sidi lamine vive le Sénégal l’apical dans le monde

  • @mogettdofbi3058
    @mogettdofbi3058 25 дней назад +27

    Machalah mbacké Balla 🤲🏾🤲🏾🤲🏾❤️❤️❤️

  • @syllandiouga9541
    @syllandiouga9541 25 дней назад +30

    Sama xol sédd na yàlla xam nako ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @LeuzSikki-sg9kv
    @LeuzSikki-sg9kv 24 дня назад +3

    Bëss bi deh, histoire dinnako binde, solution amnguén Lou jaffé, Lou raar
    Jeurejeufé Serigne bi cii teeway bi , solution TV, télé Askan Wii leu ♥️♥️
    Sa ndiogou, sonhibou, ak pa Assane , chapeau à vous, cii sen takhawaay

  • @issakane9853
    @issakane9853 25 дней назад +12

    Kou bakh moye sreigne abdou mbacke nion mome daniokoye guianuall rek sonou brome godall fan wi teh werall yareume bi barkeb ahmadou barkeb khassidayi

  • @user-hd2iz7vn2n
    @user-hd2iz7vn2n 25 дней назад +6

    Djieureudjefaty Mbacké bala yague fi lole té yague wér Mbacké té serigne fathe adio diam nieup rék rawatina patriote ❤❤❤❤

  • @cheikhdiagnenar7934
    @cheikhdiagnenar7934 24 дня назад +2

    Machallah li seddena khol, Yalna Yalla Faye Lene.
    Merci Serigne Abdou
    Merci Walfadjri
    Merci Solution TV
    Merci les Patriotes
    Jub Jubeul Jubanti Rek
    inch'Allah

  • @moustaphaka3444
    @moustaphaka3444 25 дней назад +6

    Bilahi degue n'a deug li moy serigne touba amatina si quanamou yalla pur mottana ndeye mottna baye dieureudieuf serigne abdou dieureudieuf serigne touba allhamdoulilahi dieureudieufati yalla allahou akbar merci

  • @mamadoufall3408
    @mamadoufall3408 25 дней назад +9

    Machalla solution tu auras toujours la solution des problemes du pays ❤

  • @DalandaDiallo333
    @DalandaDiallo333 25 дней назад +13

    ❤❤❤machallah sangue bi gnou gui rafetlou setsi bi 🙏

  • @MamadouSallene-ov6dg
    @MamadouSallene-ov6dg 25 дней назад +5

    Patriote yeuppeu contaan si serigne bii... Maachallah yalla Nala yalla defal diameu ak gouddou fane AK werr.

  • @user-pz2bd1xw3o
    @user-pz2bd1xw3o 25 дней назад +13

    ❤❤❤❤❤❤❤ akassa mbacké bala yagu fi loool té wéer

  • @safiatoudiedhiou2534
    @safiatoudiedhiou2534 25 дней назад +34

    Machalla serigne yala na yala Sam soutral Sénégal diam rek ci tout les sénégalais oh ooh ❤❤❤❤

  • @ndinfos2466
    @ndinfos2466 24 дня назад +2

    Machallah S Abdou MBACKÉ Ak Mame Pathé Ay Diambar Dëgge Yalna Yalla Gouddel Sen Fan Sammu Lén Aar Lén Merci Merci solution Tv ❤❤❤❤❤

  • @amithiam3603
    @amithiam3603 25 дней назад +7

    Maachalla Mbaké Bala Aissa yalna sa diameu yag yalla katanalla lool le Papa de Pros Nous sommes fière de vous

  • @mamadouassad2302
    @mamadouassad2302 25 дней назад +10

    Machala serigne bi , dila ziar bou bakh , un marabout véridique et tres engagé , le marabout du projet. Solution TV, amm nguène succès bou reuy , yènne thia kaw,thia kanaam rék machala. Kii , deugg rék mokoy yeukeutti

    • @sokhnathiam6072
      @sokhnathiam6072 25 дней назад +2

      Machalla sama xarite sama serigne Mbacke balla aka bah tée oyof❤❤❤❤❤

  • @user-il1dx5sr3u
    @user-il1dx5sr3u 25 дней назад +6

    Macha Allah seringe bi yalana yalla yokou sa martaba

  • @adamaaw9631
    @adamaaw9631 25 дней назад +4

    Sa ndiogou massalah et merci pour le discernement et la perspicacité sur vos analyses un citoyen un patriote !!!

  • @chezthiatesokhnadieng7846
    @chezthiatesokhnadieng7846 25 дней назад +6

    MachaAllah Mbacké yallah na yoke wère inchaAllahou ak soutoura. Merci d'être là à côté du peuple.

  • @babacarceesay4819
    @babacarceesay4819 25 дней назад +11

    Mashalla Saringe Assane Mback content boubakh si mome ndakh yomboule Mashalla

  • @elhadjiousmanegueye3277
    @elhadjiousmanegueye3277 25 дней назад +7

    Dieuredieuf Serigne Bamba Khadimou Rassoull Mbackè Balla Aìssa Solution Sa Ndiogou Baye Assane Souhaibou Mash'Allah

  • @user-sv6xg5gg5b
    @user-sv6xg5gg5b 24 дня назад +2

    Machallah Cheikh Niass boul ame loy regal domou gaydé dou ragal allá walf day déme inchallah bonne continuation ❤de la part de Cheikh tidiane yarakh ❤❤❤❤

  • @aidadiouf2032
    @aidadiouf2032 25 дней назад +6

    Machahalah di ziar serigne Abdou Mbacké yalla na fi yague té wér tha khaw tha kanam Groupe Solution.

  • @massaergueye-gf6qp
    @massaergueye-gf6qp 25 дней назад +5

    Tout le monde doit prier pour vous par votre excellente travail

  • @bintousamb1940
    @bintousamb1940 25 дней назад +4

    S abdou mbacke yallana souniou brome yagal takhaway bi té sammu la barke serigne bi ❤❤❤❤

  • @souleymanediop3669
    @souleymanediop3669 25 дней назад +6

    Alkhamdoulilah MBACKÉ Yagg Fi té were Lole
    Wa solution tv Yokkou Yagg Were Lole Way machaalah

  • @moussadione3468
    @moussadione3468 25 дней назад +5

    Yalnalen yalla sam ci barceb s touba amine ya rabbi ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤

  • @abobayeye-tj3gcbb
    @abobayeye-tj3gcbb 24 дня назад +1

    yalla na yalla aar leën daguèna bakh serigne souhaïbou mbacke

  • @papinongaala8047
    @papinongaala8047 24 дня назад +2

    Machalla serigne bi gnongi ziare
    Solution thia kaw thia thiakam❤❤❤❤❤❤❤

  • @SiiwalalXibaar
    @SiiwalalXibaar 25 дней назад +16

    Saa Ndiogou doxalal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @jeanmichelcorrea2115
    @jeanmichelcorrea2115 24 дня назад +2

    Bonjour je suis fier de vous et partage avec vous la présence de Serigne Abdou. Merci

  • @SadioSylla-eo2ny
    @SadioSylla-eo2ny 25 дней назад +3

    Dieureu dieuf sunu Serigne bou baax bii merci ton soutien💪💪 pour nôtre président Ousmane sonko

  • @serignemodousokhna5026
    @serignemodousokhna5026 25 дней назад +2

    MachAllah YALLA Doli tawfékh ci rew ak nji nék ci rew mi
    Vraiment solution tv ay diambar guéne vous êtes plus fort que les journalistes
    BAY assane takhna douma complexe toubab yi
    Sa ndiogou wéddina sunu intellectuelle yi
    Sohibou il respecte notre intelligence absolue
    Sidi lamine Niass paix à son âme
    CHEIKH Abdou MBACKE YALLA sa Mame CHEIKH AHMADOU BAMBA sunu Yakar faye la yiwww......!!!

  • @abdoundiaye9623
    @abdoundiaye9623 25 дней назад +12

    Serigne Abdou Nit kou Bakh la

  • @AbbaMane
    @AbbaMane 25 дней назад +10

    inimbara morkéba abdou mbacké...Merci.

  • @baboubacar7851
    @baboubacar7851 25 дней назад +3

    Mbeekté reek laa ame tay vraiment. merci sandiogou❤❤❤❤❤❤

  • @walimatangom2272
    @walimatangom2272 25 дней назад +4

    Quelle surprise machalah goud fan ak werr aki kheweul sawan bawane si barké alkhouran karim Amine

  • @ApoSamy-xd2tj
    @ApoSamy-xd2tj 25 дней назад +3

    Dieuredieuf mbackée yalla nala yalla soutoural goudal say fann

  • @sulaymanjallow8146
    @sulaymanjallow8146 25 дней назад +4

    Alhamdullilah djerediefe Serigne Touba ❤❤❤

  • @user-sv6xg5gg5b
    @user-sv6xg5gg5b 24 дня назад +2

    Machallah li la Yalla souniou borom begue Sénégal c'est un pays pas deux.

  • @khadimka2058
    @khadimka2058 25 дней назад +2

    Am nguen gane bou Beuri ndiarign billahi te nek nitt kou yalla bakhal te mou am xam xam nak machalla Mbacke Balla ❤❤❤❤

  • @fatoudieng895
    @fatoudieng895 21 день назад

    Machalla seurigne abdou yalla na yalla guoudeul say fann mbakhe balla yague fi loll ta and ak werr bekh naniou tie yoww lolll mbakhe ❤❤❤❤❤❤

  • @mbackembenguekhadim7284
    @mbackembenguekhadim7284 25 дней назад +10

    Machalah mbacké balla

  • @maguettendiaye3510
    @maguettendiaye3510 24 дня назад +2

    Man dé mangui rétane rek té khawma loumay rétane lo. Bilahi contane dafa bakh si domou adama. Mbacké Balla kou bakh kounek wek nala beug nala ndakh sa deugou ak sa ame koleuré. Yala nala Yalla may fan wou goudou ak wergui yaram si barké Cheikhoul Khadim. Bravo à Sa ndiogou, baye assane et sonhibou . Li ndam deug la .

  • @user-od2fy1xt9c
    @user-od2fy1xt9c 25 дней назад +6

    Machallah MARHABA un grand invité est là ❤❤❤❤❤❤

  • @cira1345
    @cira1345 25 дней назад +2

    Dierieuf Serigne Abdoul ❤❤❤❤❤❤❤❤❤serigne touba beug na ci Mbacké balla khôl seeed na ❤❤❤❤❤❤❤❤❤mame paté ❤❤❤❤❤❤❤ élément sidi lamine niasse sa sonhibou baye assane meilleures roubéman ❤❤❤

  • @Mameboussobousonko
    @Mameboussobousonko 25 дней назад +1

    dieureu dieuf Serigne Abdou mbacke yalla nala yalla défal diamou Samou la barké cheikh ahmadou bamba dieureu dieuf sougnou khol sédena Lol si yaw biilahi ❤️ ❤❤❤

  • @malickngom9793
    @malickngom9793 25 дней назад +1

    MACHAALLAH SUNU BAY SERIGNE ABDOU
    JARAJEUFF

  • @oliviervaz4658
    @oliviervaz4658 25 дней назад +12

    Hoo niite koubakh kou ayof kou am class niite kou am khar am teguien serigne abdou yala nala yalla defal diam ❤❤❤❤❤❤

  • @bintadiemefall8970
    @bintadiemefall8970 25 дней назад +3

    Machalla solutions 📺 tèye mome plateau bi dafa aladowoymè machalla Mbacke balla yague fi lole and ak wère ak wèrelè contane nagnou si sa taxawayi thank you so much lovely 😍 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @theflowfight7738
    @theflowfight7738 25 дней назад +2

    Masha ALLAH c est une chance pour le Senegal , il faut inviter Serigne you melni ci Tele bou bakh

  • @ibrahimagassama4623
    @ibrahimagassama4623 25 дней назад +4

    Mame Pathé je confirme ton sondage 🙏🙏🙏ils sont les meilleurs

  • @FatouMbaye-rr1io
    @FatouMbaye-rr1io 25 дней назад +3

    Machallah Mbacké yalna yalla defalla goude fan

  • @papandiaye8357
    @papandiaye8357 25 дней назад +6

    Werna kuer sama Patton la duek❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @AdamadiopTHIAW
    @AdamadiopTHIAW 21 день назад +1

    Dieureudieuf MBACKE BALLA yallana sax borom geuna sam amine

  • @moustaphandiaye9697
    @moustaphandiaye9697 25 дней назад +4

    Dieureudieuf Mbacke 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
    la solution 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @Papy012
    @Papy012 24 дня назад +1

    Akassa Serigne Bi!!! Vous êtes vraiment un digne descendant du Grand Marabout, un Petit fils exemplaire, visionnaire, révolutionnaire, sincère, humble et humile. Merci pour avoir cru au projet et merci pour avoir pris position au moment où les autres avaient choisi l'opposée.

  • @aminatadiallo5497
    @aminatadiallo5497 25 дней назад +4

    Merci Suniou kilifeu bou diambaré bi. Maa shaa Allah contane lol.kou beugue pros rék ya niou mom. Yalla na yalla samala sameu niou

  • @serignembackedieng976
    @serignembackedieng976 25 дней назад +2

    Cëy ndeysaan ❤ sëriñ bi moo baax rekk

  • @ndeyeselembadrame8767
    @ndeyeselembadrame8767 25 дней назад +4

    Machaala Mbacke Balla Aissa kerogue manifestazione bou Italia ba maggue yawe gno toggone sa Bergamo Yalla nala Yalla SAMME te laffal la thiate si Barker Yonentabi

  • @DjilyGadiaga-ud7lw
    @DjilyGadiaga-ud7lw 25 дней назад +1

    Sama khôl sedena way!!!kilifeu gou bakh ,kou deugou ,man deh ni nga diapaleh sonko ak projet bi rek mo takh ma sopela,yallana yalla goudeul Saw fane teh mayla wére!!!

  • @ndarndar920
    @ndarndar920 25 дней назад +2

    Merci sa diogu et toute l'équipe de solutions TV

  • @AbdouBeye-bw8ti
    @AbdouBeye-bw8ti 25 дней назад +1

    Solution 📺 Machaallah elhadji sa NDiogou te le meilleur yalla samléne yokléne inchaalh

  • @maxboy2916
    @maxboy2916 25 дней назад +2

    Dieureudieuf serigne bi...gnu melni yaw diafé na sougnu diamono dji...yague fi lol t wer...

  • @falloundiaye9049
    @falloundiaye9049 25 дней назад +7

    Machalla mback balla yagufi te wer

  • @user-qj9we5nh4e
    @user-qj9we5nh4e 25 дней назад +2

    Dia diefati wa solution ziar nan la mbacké balla aïsa❤

  • @ndeyecoumbafall5171
    @ndeyecoumbafall5171 14 дней назад

    Machaallah yallahna yallah goudeule fanam thi barké yionén sallakhou aleikhi wassallam

  • @wahawakh7478
    @wahawakh7478 25 дней назад +11

    serigne Abdou ak serigne Habib Sy gno taxx waxou ma ni serignes yéppa yème..... goudde fanne wërr ak wërlé

  • @boubacarkebe598
    @boubacarkebe598 21 день назад

    Ddieufati Seigne Abdou Mbackè. Sa taxaway amna solo..La Diaspora senegalaise vous remercie.

  • @FafaToure-xq3ji
    @FafaToure-xq3ji 25 дней назад +7

    Machalla wa solution tv amna solo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-yr8gc5wu5x
    @user-yr8gc5wu5x 24 дня назад

    Merci sa souébou.assane.toute l'équipe merci falfadjri k dieu protège Serigne bara et Abdou backé

  • @seexbasking7920
    @seexbasking7920 25 дней назад +2

    Sëriñ Abdu jërëjëf yal na Yàlla guddal sa fan❤

  • @makharyndiaye5922
    @makharyndiaye5922 25 дней назад +3

    Machalla ❤❤❤❤

  • @aliounemar8370
    @aliounemar8370 23 дня назад

    Khôll sédana , Serigne yalla naako yalla défal tawféek . Je vous suis chaque jour . Sama connexion yéenn rék yéenako meunaloul jéekhal.Assane borom baakh la

  • @user-ei8uf4ie6j
    @user-ei8uf4ie6j 25 дней назад +20

    Baguéne oubé ba légui, moussouma guiss gann gou ni toll. Ma cha Allah.

    • @theflowfight7738
      @theflowfight7738 25 дней назад +1

      walahi , chance deug la , Serigne Yalna YALLA GOUDAL FANWI SAMEUKO BOU BAKH

  • @morlayekonte5626
    @morlayekonte5626 24 дня назад

    Machalah Machalah Machalah alhamdoulilah yarabalalamine diureudief serigne touba akazza mourid diureudief sa ndiogou taye amna mbkte lole magi ziar bou wer ❤❤❤❤❤

  • @amadouguisse7497
    @amadouguisse7497 23 дня назад

    Mâcha Alah ! Diadieuf Serigñ Abdou. Tous les patriotes sont fiers de vous!! ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhndiaye4199
    @cheikhndiaye4199 21 день назад

    Manchalla mbacké dieureudieuty mbacké yague fi l'OL té wére ni gagnou sagalé yalnala yalla sagal

  • @user-rr5no6pj1k
    @user-rr5no6pj1k 25 дней назад +2

    Kidou Serigne Nitou Yallala❤️