Oussmane sonko mou selami rek inchalah nioun yalla lalniou guem te mofineka tay ak eulak koudoul yalla amo meuno xamo dará meuno dará sonko mou selami rek inchalah doynanou si rewmi doynanou si dinedji
@@bettysagna5632Effectivement, dire qu’il a fauté sans même savoir ses ressentis c’est être malhonnête. Et en plus , n’oublions pas que Serigne Moustapha avait dit que Sonko faisait semblant d’être malade au moment où Sonko avait plus besoin de lui. Donc, on se calme un peu
Fi refetal amou fi. Killifa dou def ni. Dou yalla dou yenant, na nagnal bopam ak rew mi ak sonko... vive LE SÉNÉGAL ET VIVE LE PRÉSIDENT OUSMANE SONKO !!!
@@MaguetteGueye-e4emane mi dii wakh ak yaw sonko laa mais hamnani mou dem fa seti ko mo geuneu rafete, ndah pur ils ont toujours été là Mais eskeu serigne nimou dohalei rafete naa? Wahal rek
Tout à fait d'accord avec les pertinentes analyses et suggestions de l'équipe de Solution. Serigne Moustapha aime SONKO c'est pourquoi, il s'intéresse à ses faits et gestes. Ils vont se retrouver pour l'intérêt du pays. Qu'Allah veille sur le Sénégal.
Seydina Ousmane sonko muselmi mon idole respect dieuredieufaty yalla nala yalla goudal sa fane té mayla wér gui yaram té aar la sambou la si barke ch ahmadou bambou khadim Rassoul 🤲❤️🔐
Il faut les actes forts. Diomaye et sonko guene senegal si goûta gui mou neke te il ne fait k commencer sur laj jeunesse ayons très peur pour l avenir de la génération ki va suivre il ne faut pas emboîter le pas du gouvernement si non ceux ki on volle nos milliards vont revenir nous faire plus mall❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci wa solution vous êtes trés pertinents Serigne Moustapha sy ak wa PUR bamou mété déno am takhaway bou amsolo massouno daw c'est des alliés de valeurs
❤❤❤❤SEUL ALLAH EST AUX COMMANDES ET AUX CONTROLES ALLAH BENISSE SONKO LE PROTEGE ENCORE ET ENCORE ET LE GARDE AVEC LE PEUPLE QUI LUTTE A SES CÔTÉS WASSALAM WASSALAM WASSALAM WASSALAM
Serigne Moustapha est dans sa logique de faire campagne pour les législatives et pour se faire une promotion il ne peut passer que par Sonko. Mais les choses ont changé walahi les choses ont changé, les sénégalais n’écoutent ni papa ni maman encore moins guides pour prendre leur développement en main. Et notre développement c’est une majorité de Sonko-Diomaye à l’assemblée. On n’est focus sur le 17 et nous ne nous laissons pas distraire car le duo du siècle Sonko-Diomaye est indestructible car c’est voulu par Le Tout Puissant .
Sonko yalla mo yore bakenam te yalla moko sove te yalla moko diokh rewmi te bu nare gagné législatives yi AK buko nare niak te yalla nako gagné yalla la
Sonko est sur la bonne voie vu que toute la sommité du pays se concentre sur sa personne. Nous lui demandons de ne pas répondre à ses détracteurs. Parce que Dieu est avec lui. Focus sur les législatives pour terminer le travail. ❤Sonko mooy Diomay té Diomay mooy Sonko.❤ Yalla Rek Moofi Nekk.
Yallah na soune Borom deif ga deilou watte niga meilone akk PROS. Serigne Moustafa Sy akk Serigne Habib Sy Dabakh deux figures de Tivaoune qui ont tjours soutenus Ousman Sonko Yallah na Borom bi deif djam akk soutoureuh
Pastef et Pur deux alliés surent qui ont énormément de chose en commun ceci n'est qu'un phénomène ce sont des alliés loyales Serigne bi et Sonko vont se retrouver il faut accepter les gens comme ils sont.
Sonko yalla la yakare rek AK Le prophet Muhammad la guem
Sa dediaw ndaye fii koffi yakroul yalla
S Moustapha s'y dama yakarni jioumay tiwawan bi moko soké😂😂😂😂. Sonko yala la yakar☝🏿 ak Sénégalé yi ✊🏿🇸🇳
Khana tay l
@@mariediop7264AK demb😂😂
Yaw ak kou melni yaw yènaye yakhal sonko
Sonko yalnako yallah sameu amine❤
Sonko diomaye ❤❤❤❤❤❤❤ manchalla
Amine yaa rabbi
Moustapha c'est un maître chanteur qu'il nous fout la paix
Machalla rafetna
Amine yarabi 🤲❤️
Sonko kèna douko santage t nèna kèna rèk moy royoukayame mouy seydina mouhamade (psl)
Sonko moy ki dakha politique si istoire Sénégal ❤❤
Wakho lo am dé dalle Abdoulaye Wade sakh dou moromou Sonko Bayiléne Thiakhan yi
Waw
Waxal Histoire pAfrique mofi dak politique je te jure
❤❤❤❤❤❤
@modouseckseck9893 Lou wérr gua wakh ☝🏾
Oussmane sonko mou selami rek inchalah nioun yalla lalniou guem te mofineka tay ak eulak koudoul yalla amo meuno xamo dará meuno dará sonko mou selami rek inchalah doynanou si rewmi doynanou si dinedji
Sonko yalla rék la yàkar
Bilaye wakhatico
Bilaye wakhatico
Kassé
Mo tax serigne moustapha yalla la djital si aywaxam
AK adji Sarr 😅😅😅😅😅
Sama carte Sonko moko môme inchallah
Akk man ak sama ndiaboot❤❤❤❤
AK mane tamit @@francoismendy8115
Ak sougniou wa keur
Ak sugnu wa kogne
Ak niuon molyi
Sonko yallah nako yallah same Amine❤❤❤❤❤❤❤
Soncko a' vie amine
Amine yarabi 🤲🥰
Merci Sa ndiogou c'est toi qui as bien compris la situation et tu l'as dit Telle qu'elle est
Que bon Dieu préserve le président Pusmane Sonko Allahoummaamin❤❤❤
Une chose est claire est que Sonko est quelqu’un de très reconnaissant, on ignore les dessous mais ne nous emballons pas à le culpabiliser pour rien
Bilahi sonko est très reconnaissant
@@bettysagna5632Effectivement, dire qu’il a fauté sans même savoir ses ressentis c’est être malhonnête. Et en plus , n’oublions pas que Serigne Moustapha avait dit que Sonko faisait semblant d’être malade au moment où Sonko avait plus besoin de lui.
Donc, on se calme un peu
oui tu a bien raison 👍
Sy avait dit que Sonko son grève de la faim était une mise en scène que c'était planifié pros n'a sûrement pas apprécié
@@momomlk9029 j’imagine
Sonko, n'est pas un politicien artificiel. Mais un vrai stratège politique.
Sonko rek thia kaw thia kanam❤❤❤❤❤❤❤
Vraiment merci Saa diogou sa analyse pertinente dé
Sonko ❤❤❤ ,c' est un homme de Dieu...lepeume Yalalaaaa Macha Hala....,❤❤❤❤..... 🇪🇦🇬🇭🍓🍓🍓🍓
Diomaye moye sonko ❤❤❤. Sonko moye diomaye Serigne bi tu peux rien contre Sonko douyaw yalla
Mag la negn ko worymaal rec… Xam lougne xam toog way kenen kou wakh fekk nioufi
ioe sa deudieuw ndeye sa digou leufeul ndey yalla sonko fils de pute😂😂😂😂😂
C pas les marabouts c Dieu ❤❤❤❤
Diomaye Ak Sonko bénnala diarroul khadiélé😢
Bour Yallah denk nagne la Sonko ak Diomaye
Président Ousmane SONKO, yalla naka yalla sam tei arko. SONKO mo dakha politique si Sénégal. Très franchement parlant, amoul morom.
Merci beaucoup
Merci beaucoup mes amis patriotes
MachaAllah bay Assane ❤❤❤ Son Ibou bayil diambour😂😂
Serigne Moustapha nama ball rek wàyé SONKO Ùsman Douala meusseu bayil mal entendu la rek wàyé yiit SONKO yalla kepp la yakar
C’est pas les marabouts c’est dieu, vive Sonko et Diomaye ❤❤❤
Sa ndiogou vraie intellectuel leu
Nañu bayi wakh intellectuel moy ki diangue ba yeuy keuyitt koku xhar leu
😂😂😂
😂😂😂
SA. WAY. NIO. BOK. GUISS GUISS. SA. NDANANE. LA DÉ
Wa kour gui nak😂😂
mane mi sonko momo sama carta bi ak sounou wa kuer😊🎉😂😂❤
Serigne Moustapha sy est véridique ❤❤❤
Fi refetal amou fi. Killifa dou def ni. Dou yalla dou yenant, na nagnal bopam ak rew mi ak sonko... vive LE SÉNÉGAL ET VIVE LE PRÉSIDENT OUSMANE SONKO !!!
Taye bimou nékhé guéne KO mana wakh
@@MaguetteGueye-e4emane mi dii wakh ak yaw sonko laa mais hamnani mou dem fa seti ko mo geuneu rafete, ndah pur ils ont toujours été là
Mais eskeu serigne nimou dohalei rafete naa? Wahal rek
Khana kou am nian moy nianal rewmi moustapha sy bandit salte la amoul nian
@@MaguetteGueye-e4efi Yallah reka nek moustapha sy bandit salte la fi chantage diekhna fi
Moustapha Sy fi Senegal seydina Ousmane sonko moy diomaye ❤❤❤❤❤❤❤
Yallnaléne yalla lafall thiate
Ay way, bayilene Sonko te nguene nangou ndogalou Yalla. FII KOU FI GNAANAL DIOMAYE, GNAANAL NGA SONKO. DIOMAYAY SONKO.
Bayi lén ñuy waax rék.
LOLLO AM ! SONKO MOY DIOMAYE ! YAL NALEN YALLAH ARE! YAL NALEN YALLAH SAM!
Pertinentes analyses de Sa Ndiogou,merci.
Ndiarama Serigne Moustapha sy Almaktoum ❤🎉
Diadieuf l’équipe! Vive PROS et ses compagnons Ndame réck InchaAllah Amine YARABY
Sonko rék ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sonko Rék lanouy topeu❤❤❤
Ousmane sonko rend visite aux kallifes genèraux ,il rendra visite a Serigne moustapha sy inchalat rabi ❤❤❤
Machalla Sadiogou vous avez bien analysé la situation 💫💫💫
Président sonko yalla na la yalla tahawou❤❤❤❤❤
Kou déf lou bakh dafa wara nék té yalla rék takh.Yalla rék mo meune. Sonko mooy Diomaye.
Legui ignoré bi lousiy sa xalate
@@mouhamedsow6688 je parle d'une manière générale lolou mo yakh nitt gni.
@@MameThiernoBoromDarou2.0 d'une manière générale nit sakh dafay wax alhamdoulilah nguir reconnaissance si xewalou borom bi
@@mouhamedsow6688 motakh manila Yalla rék mo meune.
@@mouhamedsow6688 bane ignoré fautez nous la paix
Tout à fait d'accord avec les pertinentes analyses et suggestions de l'équipe de Solution. Serigne Moustapha aime SONKO c'est pourquoi, il s'intéresse à ses faits et gestes. Ils vont se retrouver pour l'intérêt du pays. Qu'Allah veille sur le Sénégal.
Seydina Ousmane sonko muselmi mon idole respect dieuredieufaty yalla nala yalla goudal sa fane té mayla wér gui yaram té aar la sambou la si barke ch ahmadou bambou khadim Rassoul 🤲❤️🔐
Merci Sa👍
Très belle intervention
❤❤❤
Sonko rek,love from The Gambia
Il faut les actes forts. Diomaye et sonko guene senegal si goûta gui mou neke te il ne fait k commencer sur laj jeunesse ayons très peur pour l avenir de la génération ki va suivre il ne faut pas emboîter le pas du gouvernement si non ceux ki on volle nos milliards vont revenir nous faire plus mall❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sonko sonou na nak yalla nala yalla may kholou mougne
Sa Ndiogou a une dimension intellectuelle exceptionnelle 🎉❤
Dieureudiaf sa ndiogou DEUG ngawakhe dé yanala yalla Faye dieureudiaf ♥️♥️♥️❤️♥️ sonko rék inchallah 🙏
Sonko moye diomaye diomaye moye sonko amoule lénéne ❤❤❤
Merci bcp sa amna solo ❤❤❤
La meilleure nouvelle c’est le fait que sonko a choisi diomaye. Alhamdoulilah. Sinon les autres une fois choisi allait montrer leur vrai comportement
Serigne Moustapha sy almaktoum amoul morome si Sénégal ❤🙏🏿
Sonko moy Diomaye
Diomaye moy Sonko
Point............................
Waxatiko. Kene dou lene separer bou neexè Yalla
Naniou ko wakhetané rék Sénégal dieume kaname le travail continue 👍 jube joubal joubanty 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Sen wax rafetna ❤
Sonkho mo bari bayeré bilakhi koulaye khare yalna khadii vive sonkho Vive doimaye yala rek mofi nek
Sa wakh nga deug serigne Moustapha sy a la le respect des patriotes même si on n'est pas d'accord avec lui sur ses propos.
Fii amoul benne respe môme mo wara respecte sénégalais yii malheureusement chaque années il nous n’importe quoi imbécile
Sonko moy Moustapha Moustapha moy Sonko❤
Sonko❤❤❤❤
Merci wa solution vous êtes trés pertinents Serigne Moustapha sy ak wa PUR bamou mété déno am takhaway bou amsolo massouno daw c'est des alliés de valeurs
Aladji sa machalah amatina solo merci
Well spoken bro Assan , I totally agree with you
Merci sa djogou sa caddu amna solo
❤❤❤❤SEUL ALLAH EST AUX COMMANDES ET AUX CONTROLES ALLAH BENISSE SONKO LE PROTEGE ENCORE ET ENCORE ET LE GARDE AVEC LE PEUPLE QUI LUTTE A SES CÔTÉS WASSALAM WASSALAM WASSALAM WASSALAM
SONKO Mooy Diomaye 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️ Focus 17 Novembre inshallah
Sonko à vie ❤️🔐
Wakh dëg yalla waa PUR soxlowul poste waaye respect rek lañu soxsoxla❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ak reconnaissance
Sonkon lagnou wakh ❤❤
Serigne Moustapha est dans sa logique de faire campagne pour les législatives et pour se faire une promotion il ne peut passer que par Sonko. Mais les choses ont changé walahi les choses ont changé, les sénégalais n’écoutent ni papa ni maman encore moins guides pour prendre leur développement en main. Et notre développement c’est une majorité de Sonko-Diomaye à l’assemblée. On n’est focus sur le 17 et nous ne nous laissons pas distraire car le duo du siècle Sonko-Diomaye est indestructible car c’est voulu par Le Tout Puissant .
Vraiment tu ma marché sur la langue tu a tout résumé
Wallay les choses ont beaucoup changées sakh, lolou lagnou xamoul
Saway son ki n’est pas reconnssant
Avant d’accéder au pouvoir xamona nimou done def bay dèguantè Ak mom
Ya wayadi DEUG
Sonko Yalla rek la Yakar sonko mooy Diomaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂😂 vraiment vous êtes les meilleurs 😂
Machallah sonko moy Diomay Diomay moy Sonko
❤❤❤❤❤ merci sa toujours pertinent
Allahou Akbar yalla kén là yalla Moy fall té Moy follé
Sonko yalla mo yore bakenam te yalla moko sove te yalla moko diokh rewmi te bu nare gagné législatives yi AK buko nare niak te yalla nako gagné yalla la
Bravo sa ndiogou belle analyse
Sonko rèk ❤❤❤❤❤AK diomay pion
Sonko moy Diomaye yalna lene yalla samme❤❤❤
Sonko moy Diomay lolou la yalla déf ❤❤❤❤
Diarama Serigne moustapha sy almaktoume
Merci SA. Pertinente analyse.
Sonko est sur la bonne voie vu que toute la sommité du pays se concentre sur sa personne. Nous lui demandons de ne pas répondre à ses détracteurs. Parce que Dieu est avec lui. Focus sur les législatives pour terminer le travail. ❤Sonko mooy Diomay té Diomay mooy Sonko.❤ Yalla Rek Moofi Nekk.
Sonko yalla ak déterminations population mo takh mou fallou bou déssone si religieux yi rk si kasso bi lay déwé
Diomaye Moy sonko sonko Moy diomaye ❤❤❤❤❤
Doundou yalla moko yor sonko rek
Macha Allah Pa Assane🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Li mo takh maléne di wakheu ni bouléne di saga assane si commentaire yii assane day roubé pour Sadiogou di meune di lérale ❤️❤️❤️
Bilakhi lo ngay a chaque fois da ma kay Assane dafa béne rôle bou mouy def pour sadiogou mana Def liguéyam ❤❤❤❤❤❤❤
Pour yaw xel nieupa KO am?Assane Mésséré est bien dans son Rôle😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤je je
Chaque jour ma wakh len ko
Ndeysane Sohibou nala yalla defale tawfekh🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Sonko doula massa bayi seringne moystapha sy mala ko wakh mal entandui la❤❤
Walahi pur pastef yalla nanou andd ❤❤❤
Serigne Moustapha Sy ne doit pas être pressé. Sonko est une personne très reconnaissante.
Vraiment dacobeugue saltél rek
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂noo Walahi yéna Fi meune yalna solution don aay tele 😂😂😂❤️❤️❤️🇺🇸🇸🇳👌🏽té guéne féké ko Ak talko aminne 🤲🏽❤️❤️
PRÉSIDENT OUSMANE SONKO MOUSELMI BALNIOU AKK SI BARKET SEYDINA MOUHAMED PAIX SUR LUI🙏🙏🙏🙏🙏🙏. BEUGUE SÉNÉGAL REK MO TAKH LI LEUP NIOULA KOY TEGUE, SEDINA OUSMANE SONKO MOUSELMI BALNIOU AKK ENCORE🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Bly yaw😢
Yallah na soune Borom deif ga deilou watte niga meilone akk PROS. Serigne Moustafa Sy akk Serigne Habib Sy Dabakh deux figures de Tivaoune qui ont tjours soutenus Ousman Sonko Yallah na Borom bi deif djam akk soutoureuh
Klk soit les intentions des marabouts envers sonko la population croit à sonko
Sonko est blanc comme neige
Il est sympa ,un bon cœur econom
❤❤❤❤
Sonko rek. Gni yalla mo lenn fall. Peuple bi Sonko la niou andal❤
Pastef et Pur deux alliés surent qui ont énormément de chose en commun ceci n'est qu'un phénomène ce sont des alliés loyales Serigne bi et Sonko vont se retrouver il faut accepter les gens comme ils sont.
Sonko moy Diomay Diomay moy Sonko ❤❤❤❤❤
Non Sonyibou ray nama ak question bi si assane 😂li sofi wakhé mousiba dika khame😂😂😂
Nio bokou guiss guiss 😂😂😂😂😂
Kour gui😂😂😂
Bily😂
Sonko sama papa❤❤❤❤❤❤
Seydina ousmane sonko Pointe ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
M'a nchallah Baye assane sa analyse pertinent na là