Oui il a beaucoup de talent Epui il jouer bien n son rôle nous sommes content pour lui que dieu le garde et le donne beaucoup de force ❤❤❤ thank you bakary
Une vrai bande de fou wallah vous êtes fort. Blague a part ceci reflète la vrai galère des HOMMES , je parle des vrai hommes foula feyda diom, c'est les mêmes galères juste les formes qui diffères. Salam a tous les HOMMES qui gèrent calmement
Juste wooow !🤩 Je n'avais pas vu ça depuis Goor-goorlu. Bravo aux artistes, vous êtes trop forts et chapeau au scénariste et réalisateur (THIAN THIANDOUM) et à toute l'équipe technique !👏
Les vrais acteurs sont là, les maisons de production préfèrent chercher des filles claires aux grosses fesses en quête de célébrité et les donner des miettes au lieu de prendre les vrais acteurs
Wallahi Senegal barina niou tardé situation familiale molene tardél 😢😢 ay jambar deugg lane chaque jour niouy daw nguir ndiabooot 😢😢😢 yalla nalén yalla taxawou
Bravo à la RTS pour cette série qui éveille les consciences quant aux réalités du quotidien des sénégalais. C’est à force d‘éveiller les consciences que le peuple tout entier uni pour un même combat fera du Sénégal un pays où tous les citoyens pourront vivre dans la satiété et la dignité.
depuis dara kocc magui enfin je viens d'adorer à nouveau le théâtre sénégalais. Il mélange éducation civique,humour,dramatique,réalité sociale bref c'est magnifique et original
J'aime bien cette série et c'est la 1ère fois d'ailleurs may tokk di suivre série Galsen. En plus d'être originale ça reflète bien notre société surtout la vie des GOORGOLUS
LISTE BOU BAKH BI MOY PASTEF NAKO NIEP VOTEL TÉ BAYIFI ÑI BEUGONA NAKH SENEGALAIS YI SOTIWOUL NIOUY NAKHANTÉ SEN BIIR 😂 POUR TERMINER MOUMA FOUMOU DIEULÉ PERMIS TAMIT
8:00 Maada mi nimouy kaassé mom ohho elle incarne djiguen boula beug teh Yalla takh topewoula dara ndeysan si benene côté 😂 ke di mbarane feulé tamit thiey li😂
Épisode bi dafa gatte donc nay daw sak joure walla niou yokhou temps bi mais yalla nanou yalla mousseul si situation bakary yalla bounu mouthuou si dieumou diou méllni baye bada amine
Ndeysane ya plein de Bacary au Sénégal merci la RTS
manguini😅
Bilahi
Magi ni
Bilaahi❤
𝐖𝐚𝐥𝐚𝐡𝐢😢😢
Li motakhitte nous les responsables de famille surtout les pères de familles yalla nagnou borom bi djiapalé té dimalégnou
Amen 🙏🙏
Ngene bayi doxane bi nak 😂😂😂
Bakary a du talent ainsi qu'a toute l'équipe 😊qui est d'accord avec moi?
Oui il a beaucoup de talent Epui il jouer bien n son rôle nous sommes content pour lui que dieu le garde et le donne beaucoup de force ❤❤❤ thank you bakary
trop vrai ❤️
La vraie vie d’un Sénégalais j’adore cette série c une pure réalité
Billa
Bilahi
Je te jure
Mada😂nk nop na Bakary oh 😻 c l'amour
Bilahi tu Mada yi aka nio bari Sénégal
Sérieux chaque sénégalais doit avoir une Maada et un baay bada s’il tient vraiment à la vraiment à la vie 🥹
La femme de Bakary une vrai artiste
Une vrai bande de fou wallah vous êtes fort. Blague a part ceci reflète la vrai galère des HOMMES , je parle des vrai hommes foula feyda diom, c'est les mêmes galères juste les formes qui diffères. Salam a tous les HOMMES qui gèrent calmement
Yalla nagnou yalla mousal si situation bakary 🙏🙏
Amine vraiment
Allahoumma amine 🙏🏽
😂😂@@khalilthiam4760
Baye Bada tamit kou bakh la 🎉
Billy 😢😢
On a pensé à la meme chose
Nit kou nk am nga batou tè bacary la
Baye bada dh bou doul won ak mome dou bakhe 😂
Bakari mo teugeu khôl 😂😂
Lii Moy le vrai sens de l'amour ❤. S'aider mutuellement
Série bi da wara daw chaque jour wayy😂😂
Bilahi ioe 😂😂😂
Thoma deug ga wax d sak jours la dara daaw
Billaye nak
Bakary moy Sénégal 😄😄😄😄
Bakary dh yoroul wayé amna maada 😂❤❤ kouy wout wouteul koula beugg
Dëgg dëgg 😂
Ki nak mo am ngor deugue
Mada nak mon am ngor DEUG dafa beug Bakary motakh mou wakh li yepp parés diapouleko🎉❤
Non amna bay bada
Juste wooow !🤩 Je n'avais pas vu ça depuis Goor-goorlu. Bravo aux artistes, vous êtes trop forts et chapeau au scénariste et réalisateur (THIAN THIANDOUM) et à toute l'équipe technique !👏
Wa acteurs yii founiou neckon🎉 bravo🎉🎉❤❤jambar deug guen kou d'accord lalal j'aime
Les vrais acteurs sont là, les maisons de production préfèrent chercher des filles claires aux grosses fesses en quête de célébrité et les donner des miettes au lieu de prendre les vrais acteurs
Wallahi Senegal barina niou tardé situation familiale molene tardél 😢😢 ay jambar deugg lane chaque jour niouy daw nguir ndiabooot 😢😢😢 yalla nalén yalla taxawou
Amine
Bilahi yalla molako takha wax mais lothi def rek sounou borom fayla ko
Bilaye deyessan 🙏😢
Machallah madaa sa action rafetnaaa
Serie bi dh mo dak leep momay doundel❤😊
Bravo à la RTS pour cette série qui éveille les consciences quant aux réalités du quotidien des sénégalais. C’est à force d‘éveiller les consciences que le peuple tout entier uni pour un même combat fera du Sénégal un pays où tous les citoyens pourront vivre dans la satiété et la dignité.
depuis dara kocc magui enfin je viens d'adorer à nouveau le théâtre sénégalais.
Il mélange éducation civique,humour,dramatique,réalité sociale bref c'est magnifique et original
Maréme dial ak bacary lou nékh way😂😂😂
Baye bada kou bakh la bakary moy senegal merci rts ❤❤
Boulen niou deff com serie adja rek dem ba tameleniou sen booo guen bayii niou gui yalla rek😂😂
Vraiment je n'ai jamais vu nes série aussi bien tourné, tout est naturel, le décor, l'ambiance..... C'est le Sénégal 🇸🇳
Mada aime VRAIMENT bakary
Bakary New di dolela Tee niarele lafi guss niii 😂😂
Vive sonko et diomaye beaucoup de j'aime pour eux❤❤❤❤❤❤
Bakary mii, Pr Diomaye warr nako diokh poste ci ngour gui😂
Ndeyesane Bakari verema diambar deung leu😢😢😢😢
bilakhi li dafa graw barki alkhourane famille rek mouniou sonal wayé dou lénene beugue teral Yaye rek mtx talou niou souniou bopou Yalla khamnako m lepp dineu soti inchallah 👊👊👊
Meussouma djisss série bou amé ni sens lepp naturel ❤❤❤
Serie bu nekh na vie sénégalais 100%
Tawfekh rek ak taysir barke borom touba
Bakary 😂😂😂 le meilleur
Walahie rèalitè senegalaise deugue
Machallah li amna solo torob bilahi ❤👍👍👍👍
Meilleure Série Sénégalaise, j'ai pas l'habitude de suivre les séries mais celle-ci m'a beaucoup séduit.
meilleure série dans ce pays ❤
Ndeye San bakary yeureume na ko dèh bly😢😢
Enfin une serie qui reflete la realité senegalaise
Mada mbeuguel dou yeufi nite goru sénégalais famille motakh douggnou réussir
Bilaye c'est vrai
Bakary le meilleur ❤❤❤
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉
J'aime bien cette série et c'est la 1ère fois d'ailleurs may tokk di suivre série Galsen. En plus d'être originale ça reflète bien notre société surtout la vie des GOORGOLUS
Vraiment Mada est un exemple 😂❤
Bly théâtre bi nékhna trop th am gnerigne🙏🙏🙏
Merci à tous les acteurs
Halima ❤❤❤ dama ko beug rkk th yalla takh 😍❤️🙏🙏
Mada ak Bakary😂😂😂😂
li set vrement la sensiblisasion pour toute les Senegalese yalla djiekh let you'll darra😊😊😊
Walahi li samaxol bi sedena deh me kenadou mada ak baye baye bada ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😭😭😭😭😭limoye adouna bilahi
Série bi dang Koy setan rek fier ci nek Sénégalai ❤❤❤
Baye Bada ndeysane nit kou bakh la 😢 fou bakary djaxlé mom lay guiss
Meilleur telefilm du senegal qui reflete notre sociètè et bon a regarder.machalla bravo la rts
Bakary yalla nalla sounou boromm samm amine ❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂
Jaime trop trop même c’est naturel aussi très comique man dam sakh faté sam ay problem nakh bakary 😂😂😂😂
Nit nitay garabam ta bakari amul xaalis waaye am na nit ñi❤❤❤
Mada sa khole mola togne😂😂😂😂mbeuguel gay ame fofou
Oh li nekhna way, voila c ce genre de series qui reflétent notre Société qu'on veut voir mais pas ay affaire de mbeigeul toudoul diekh
Mada da beugue ndeysane 😅😅 beugue lou bone😂😂
C'est le l'amour qui se passe 😂
Ko melni mada khana disponible fi😢❤
Très Belle série 👏🏿👏🏿👏🏿❤️❤️❤️
Yalna gnou yalla may Keur.
État bi aussi warna wakh si location bi dée. Legui Chambre Sall de bain Moy mini studio à 100 000 FCFA 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Bilaye père de famille mo metii dama ko yeuram 😢
Le réalisateur aussi on en parle pas. Woww❤❤❤❤
Vision Sénégal 2050 inchalla ❤❤❤
La série reflète la réalité sénégalaise mais le message véhiculé à la fin du film est encore plus important. Les chauffeurs doivent prendre note.
Ndeysan solidarité chauffeur yi me depasse 😢😢
Bay Bada est très fort machalla
Amena gnou 😢😢😢 yalna yalla takhawou bepp borom keur bou nekk ci ay diaffe diaffe
Masha allah et bonne continuation à mon frère thian Thiandoum ❤
Mane mariieme dinamama Ray 😂😂😂😂😂😂je l’aime ❤❤❤
Une production de qualité
Serie bi da warone dawo chaque jour ❤❤
Bakary ak djiby séye lou nara nékh😂
😢😢😢 J'en pleure ça reflète tellement la strict réalité des Sénégalais
Gueuthna guiss Lou mél ni temp boy.merci mada
Ay way ma ngui xalat keur niol😂😂😂ak bakari
Lou nara nékhe
Bayyi leen publicité yi ngeen di avance 😎
Bilahi Bakari damako yeureum
❤❤❤❤
Maréme dial elle est exceptionnelle 😂❤❤
LISTE BOU BAKH BI MOY PASTEF NAKO NIEP VOTEL TÉ BAYIFI ÑI BEUGONA NAKH SENEGALAIS YI SOTIWOUL NIOUY NAKHANTÉ SEN BIIR 😂 POUR TERMINER MOUMA FOUMOU DIEULÉ PERMIS TAMIT
Inchalah
Yaw kaye demel voté rek
Halima dinama raay sou dioguer rek toud sama eumbeu bi melni mane rek makofi def 😂😂😂😂😂😂 la petite soeur de bacary quelle famille 🤣🤣🤣🤣
Pour une fois marietou am foula 😂😂kherer n'a wow kong 🎉🎉🎉
Lima geuneuh rethiou moy limay setane Bakary sans saison bi jekh
Manouma khar😭
Bakary mooy Goorgoorlou rek
8:00 Maada mi nimouy kaassé mom ohho elle incarne djiguen boula beug teh Yalla takh topewoula dara ndeysan si benene côté 😂 ke di mbarane feulé tamit thiey li😂
Ndaysanne Bakary sonouna❤❤❤
Bilahi je suis triste et à la fois ému vraiment triste réalité dh sénégalais Masta wayy à nous les pauvres ❤❤
Bakary mi Est-ce que piraté woul sama life.
😂😂😂
Souniou life😂😂
😅😅😅😅
😂😂😂😂😂😂
Ndeysane sama xoll toyna
Épisode bi dafa gatte donc nay daw sak joure walla niou yokhou temps bi mais yalla nanou yalla mousseul si situation bakary yalla bounu mouthuou si dieumou diou méllni baye bada amine
machallah! je me retrouve a cet episode. qu'Allah nous facilite d'avoir une maison.
I love Senegal 🇸🇳
Le bonheur de bakary yeureum nako
On réclame le bonheur de Bakary ❤
Jiguene moy moteurou goor❤️👑les paroles de mada
Bye Bada tmt machallah 🥰🥰
Yalla na yalla teguil la natou yi😂😂😂😂😂 bakari
Wawaw 😂 faux expliquer aux femmes mariees k parfois maitresse yi ñou decanté situation yi 😂😂😂
😂😂😂😂
Malako wakh 😂
Wa Manko anda Réclamé Bonheurou Bakary laléne J'aime 😂😂
C le meilleur série