Allah est Le Seul Protecteur ! Kenn meunoula samm koudoul Yallah. Boulenn yakar sii ken koudoul Mome! Senegal dangen beug affairou serigne. Yallah mo diara niann nimbeul! Bayil affairou safara té yakar si Yallah. On est tous des humains des créatures faibles qui comptent sur La Miséricorde et Protection d'Allah. Bayilen di fok ni serigne wala marabout molaa meun sam wala nianal la mou nangou. Ces prières qu'ils offrent pour toi, tu peux le faire toi-même car Allah est Notre Seigneur à tous, Il est Entendant et Voyant. Placez votre Confiance totale en Lui car Il vous humiliera pas ni vous fera honte. Qu'Allah nous protège de tous et nous guide. Allah Seul et Unique est digne d'être imploré et supplié pour toute chose. Qu'Allah nous pardonne et nous fasse Miséricorde.
G le coeur fendu et je pense que je suis pas la seule 😢. Mon coeur de fille, soeur, Maman saigne... Yallah naléne Allah gnital ce voyou violeur! Soyez fortes mes filles! Les parents naléne Allah diokh kholou mougne
@@aidagueye5394 yowe ya wakh deugue ki dou rèye mo guene ci mome ki dèniouko wara dougueul prison bo khamnè aye goor djiguèn youniou tèdj 50 ans niou koye violer bamou dè domèram dji
Je suis de ton avis quand j’étais petite quand une personne me demander qui est ton marabout je répondais toujours mon père. Aujourd’hui que je suis mariée c’est mon époux mon marabout et c’est ça lislam et c’est ça que nous a enseigné Cheikh Ahmadou Bamba RA
Wa lii mom doyna war ki mo bone rek waye yéne yaye yi tamitt sangane ngéne trop khana sa dom bounko viole dinga guiss mou am changement sakh nitt danga war di bayi khell si sa ndiabott waye serigne khadim yalla nako yalla torokhal
*Ahh moma diakhal srtt kou am 13ans warone nagne ko kham bou yague tmt c’est trop way khalé da ladj setlou bou bakh srtt mineur bougne ko pénétrer warr gua ko kham am dett*
SËRIÑ TUUBAA waxoon na ne : " Ñi sant Mbàkke, la ñu baaxle laa bokk ak ñoom ". Kon am na ci ñu baax lool waaye am na ci ñu doy waar lool. Lii metti na trop trop foo ko takk rekk weesu na ko.
Je voulais préciser une chose, les gens qui disent que tayouko dou jikom ils n'ont rien compris dans la religion d'Allah, ya un nom parmi les noms d'Allah qui est as'sitir ce nom signifie Celui qui cache les défauts c'est-à-dire Dieu cache les défauts il ne dévoile pas le premier péché ni le deuxième caché mais si tu persiste trop sans laisser le péché Dieu va le dévoiler et il va te scandalisé ce que je vous parle demande aux gens de sciences... Donc on comprend bien que c'est pas la première fois qu'il le fait ,walahi on doit remercier dieu car il l'a dévoiler.... Et t'inquiètez pas tout se paye .... Sénégal nio wara baayi gueum Serigne soit disant diangalé alkhourane, misez vous sur les bons comportements des gens avant même leurs sciences
C un 'violeur en série", un malade sexuel... J'espère de tt coeur qu'il se rendra lui-même à la police. Comment on peut dormir et vivre normalement après un tel horreur.
Ki Dou Serigne ab khath la bou moubou Serigne nanko teuth boléko ak travaux forcés ak torture pénou xaléyi kou nék dix ans nanko teuth girou doundam doméram pire ak thiaga😢😢😢
Yenneu dall louléne dall rék bakhneu comment une maman peut dire qu elle a confiance au marabout dakh serigne touba lakoye kholé yénneu serigne touba limou nékone daguéne sé nékkeu non mais amna louma méti an bilakhi mon coeur saigne😭😭😭😭😭
Je n’ai jamais vu des mères aussi irresponsables qu’elles . Li mom sagane deugue la billahi . -Comment pouvez vous accepter que votre enfant se fasse laver sous prétexte qu’on les protège. Qui est censé protéger votre enfant ? Vous ou les autres ? -Votre enfant tombe malade, n’arrivant même pas à marcher , vous osez la remettre à un soi-disant marabout pour qu’il le soigne . Savez vous la cause de sa maladie ? Comment quelqu’un n’étant pas un spécialiste, peut l’aider ? Comment ne pas remarquer cette tragédie que vit votre enfant ? Et pire pendant un long moment . -
L'ignorance, l'analphabétisme et le fanatisme sont la cause de tout ça. Il suffit juste de les écouter pour s'en rendre compte. Malheureusement ,tout le monde n'a pas la chance d'être éveillé. Les parents sont eux même des victimes de cette société religieuse
La pédophilie n'est pas une question de religion mais d'humain. Da gnouye mboubo religion pour accéder facilement à leurs proies car les parents leur confient aveuglément leurs progénitures. Malheureusement ils sont partout, dans l'éducation nationale, l'animation, le sport, dans les familles. . . Vraiment personne n'est digne de confiance, on doit faire de la prévention et de l'information auprès des enfants sur ces sujets tabous.
C est la première fois dans une histoire de viol 27 mineur 12ans13ans c est vraiment triste mais en ceux moments yobou sa dôme Dara woroul amna gnénéne gnoukoye doundou mais ils on peur de dénoncer biss penc Dina méti lol un mbacké mbacké violeur c est vraiment dur sa Mame cheikhoul Khadim amna louko méti Barker Serigne saliou
Je me demande il est où l'état. Ah j'avais oublié que cté lui le premier 'violeur' des droits Sénégalais... Pauvre mon Sénégal. Triste d'être femme Africaine tt court sans aucun droit!
lii moy viol nak wayé thiagatou ba raap diiii doul nane daniou ma violé yalla na yallla may kholou mougne khaléyi et ses parents serigne bii naa deh ci kasso bii
Les marabouts n'ont jamais été aussi nombreux au Sénégal au lieu de limiter votre croyance au seul bon dieu... Mais continuer c'est pas encore fini 😢 😢 je pleure pour ces filles si jeunes 😢
Fanatisme, clanisme, lane moy sant. Fi kén gueunou fi kén. Yalla bamouy yoni yonetibi dou pour wone sante. Bayilén tapalé ak ragual. Dieul sa doom dika diokhé adiyyah. Niaka diangue ak fanatisme molén sonal. C'est votre problème, gérez ça vous-mêmes. Ce pays va mal.
Ay way guisnafi sama Badjenn Coumba sa fai longtemps khawma foumouy sey ay way mame Diarra Sene sama cousine tan Coumba mann la ramatoulaye Domou djewo gueye à saint Louis sama yaye gadjiouna ak sama papa magui Dakar legui badjiane
@@senedemba4287 bilahi sama yaye Wa Touba la m depui mou décédé lafa guethe 8ans d’émouma Touba t Sama gale mame Mougui fa ndamatou inchalah Nafa dem tkt pa
Il faut di lène némékou di lène yé si adina. Les prédateurs sont partout au plus près de leurs victimes. Les pédophiles gravitent malheureusement autour des enfants.
Sante mbacké mounoule nek nite Kou bakhe loukeu dalé serigne touba ngua khameni mome si bopame 33 femmes ak 3 you bok ndeye ak baye la amone bassi seuteume bou moudjou kéne bakhoussi
C'est tellement dur lorsque tu entends ces témoignages poignants,tu vois ces enfants qui ne sont même pas conscientes de ce qui leurs. Je me sens impuissante et c'est ce qui me fait mal😭
Tellement fréquent. Je suis mariée avec deux enfants. J'habite en France. On m'a fait des attouchements plusieurs fois à l'ecole coranique à medina baye niass.cela fait des decennies que les enfants à l'école coranique se font violer. Les parents qui abandonnent les enfants dans ces écoles doivent bien s'en douter. Moi ça a fait éclater mon mariage des années après je ne parle plus à mon père et jai eu deux ans de thérapie. Des garçons se font violer quotidiennement aussi tout le monde le sait. Les gens sont hypocrites avec un islam qui n'a rien d'une religion. On a oublié nos valeurs en laissant les marabouts et à leur famille faire ce qu'ils veulent
Serigne khadim yalla kham nani damako yeureum seytané moko meune rek . Ndakhtè diapouma ni nitt dina wotté yalla a diang alkhourane ba.paré fi def lou mel ni . Honnetement gueumoumani moko tay
C’est tellement dur vraiment et les enfants ne sont pas conscientes du faits luttons contre les violences faites aux jeune filles bref il est temps que l’Etat prend ses précautions teh teguei neulei afaire de Adji Sarr Sonko😭😭😭😭
Ce mal saint doit être puni avec la manière, faites circulé sa photo sur le net que tout le monde le puisse reconnaître…. Certaines familles se croient intouchables ds ce pays.
Je te donne toutes les raisons du monde Mr.Alpha...,moi,j'ai toujours dis ça,mais j'ai gagné plus d'énnemies,que d"amis....,même les soulards qu'on critique,et les fumeurs de chanvre ne font pas ça..,dans la statistique du pays:le haut pourcentage des violeurs sont curieusement;les OUSTAS,et les SÉRIGNE DÂRA....,et,ce n'est pas la premiére fois...!,Salut...!
Ayway g le cœur meurtri.Naniou geum Yallah tei doylo ko .Sante dou dari .jikko la sunu Borom taguer wone Seydina Mohamed!vigilance le monde est à l’envers
Akhirou zamane deuggg liii moy moudiouk diamono deug Fiii la beut yam fiii la nopp yam 😢😢kiii moy mbam kii moy nitt kou haram deug 😢😢😢ay way liii metina 😭😭😭yalla naleine yalla may xolou mougn et que justice soit faite
C me rappel la fille de une d nos voisine aicha camara yallah nako yallah yereme😭😭 dagnon ko viole famille bi khamoko bamou febar thi bir febar bi lakowah yayam fimoye khareh ba aicha tané thila aicha fatou wouyo boromame a lage de 8ans 😭😭😭😭 par infection Mon ❤ signe atanke yaye Y
Lii motakh je ne peux pas me faire à l’idée d’amener mon fils à l’internat pour étudier le coran❤et pourtant je veux qu’il metrise le coran mais dès que je pense à ces genres de choses g tellement peur que je ne peux pas l’expliquer 😢😢😢😢
Un fait que je n’ai jamais vu ou entendu de ma vie ! C’est vraiment une honte! Les parents sont des éducateurs et c’est leur devoir obligatoire (en Islâm) d’éduquer leurs enfants au lieu de les confier à des soi-disants marabouts ou “serignes”. Ils (ces parents) seront interrogés le Jour du jugement dernier au sujet de l’éducation de leurs enfants. Mais le fait qu’ils manquent d’éducation les amènent simplement à laisser leurs filles à des “Serignes” pour leur inculquer les valeurs de l’Islam alors que ces derniers les utilisent pour leurs intérêts personnels ou les abusent sexuellement. Je dis que cette mentalité sénégalaise doit cesser maintenant. Les Sénégalais sont trop naïfs et croient fermement à des marabouts pensant que ce sont des gens de bien et pouvant leur porter bonheur. Mais c’est faux !!! Nombre de garçons et filles qui sont dans les daaras ne sont pas bien éduqués par leurs maîtres coraniques simplement parce que leurs méthodes d’enseignement sont mauvais ou ne sont pas en conformité avec les bases religieuses ; en d’autres termes, pour éduquer les enfants, il faut commencer par le Tawhîd (l’unicité d’Allah) qui est le fondement islamique le plus important. Les autres viendront après.
À barina NK li lepou NK mou waka tede prison wayé lors Lou bakh na si mom NK nako tedieu RK ki waye dafa bonne RK moudé sa prison RK mbacke mom louyou lén wakh RK mom la 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢dawaw à fa you Tabaski ben mbacke ray na nitt si palé batakh doko ray violé baparé mou banian ko NK mou Ray ko NK dougal ko si Bari nk😢😢😢😢😢😢😢 mbacke mom louyou lén wakhal mom la RK 😢😢😢😢😢😢😢 yalla na ko yalla à té yor mi hi Yam' ?😢😢
Yewwouleeen une e fois pour toutes kouleeen wanoul yalla ak yonnent bi woneleeen ko guinaww amoul mbacke amoul sy il est temp niou dieulate sugnu lepp wekk ko yalla gni sen mame nio bahoone niom bahouniou
Ayyy j’arrête pas d’y penser 😢toute la journée dama rousse lol étant Mouride et habitant à Touba nakalaniouyy défff ak none yi hoo en plus un Mbacké Mbacké 😢
Frère je suis catholique s’il te plaît boul wakh Li way day andi affaire tarikha et autres c’est un homme qui l’a fait pas tous les mourides. Je m’excuse si je t’ai mal parlé
Allah est Le Seul Protecteur ! Kenn meunoula samm koudoul Yallah. Boulenn yakar sii ken koudoul Mome! Senegal dangen beug affairou serigne. Yallah mo diara niann nimbeul! Bayil affairou safara té yakar si Yallah. On est tous des humains des créatures faibles qui comptent sur La Miséricorde et Protection d'Allah. Bayilen di fok ni serigne wala marabout molaa meun sam wala nianal la mou nangou. Ces prières qu'ils offrent pour toi, tu peux le faire toi-même car Allah est Notre Seigneur à tous, Il est Entendant et Voyant. Placez votre Confiance totale en Lui car Il vous humiliera pas ni vous fera honte. Qu'Allah nous protège de tous et nous guide. Allah Seul et Unique est digne d'être imploré et supplié pour toute chose.
Qu'Allah nous pardonne et nous fasse Miséricorde.
Plus fort Madame !!! 📢
Yaw doul boo guemoul affairou Serigne ça n'engage que toi arrêtel waay
Vous avez raison barakal lahhou fikk
@@antagueye223 bou done dala diégué do ame bi réaction Serigne si se sont des arnaqueurs
Bilahi deugla
G le coeur fendu et je pense que je suis pas la seule 😢. Mon coeur de fille, soeur, Maman saigne...
Yallah naléne Allah gnital ce voyou violeur!
Soyez fortes mes filles! Les parents naléne Allah diokh kholou mougne
Massa.
Tu as apseaulie ma raison 😢😢mais sois forte 😢les filles 😢😢
Tu as apseaulie ma raison 😢😢mais sois forte 😢les filles 😢😢
Tu as apseaulie ma raison 😢😢mais sois forte 😢les filles 😢😢
Tu as apseaulie ma raison 😢😢mais sois forte 😢les filles 😢😢
Amoul MBACKÉ mbacké amoul thiotou ndayam .Mane gaïde bamba mako wakh ay doméram nio nekk Touba Di yakh dérou mouride yiii
Dama rousss😢
Walahi dama rouss saax man mi deugg touba😢😢😢😢😢
Billahi walleye yow wahatiko
Kokou kayy domékharam bou makk la ayy domi diambour nga violé niépp yakk dérou yonou mouride
Ki Daniouko wara teuthie à vie mou yax avenir khalé yi ni j’ai tellement mal au ❤ c’est écœurant vraiment !que justice soit faite😢😢😢
Louy tej ki kay ray lagnko wara def
@@aissatoudia4280 non mais vraiment ki dou nit
@@aissatoudia4280 Ray day sedd ki dagnuko wara torturé bamou dé
@@aidagueye5394 yowe ya wakh deugue ki dou rèye mo guene ci mome ki dèniouko wara dougueul prison bo khamnè aye goor djiguèn youniou tèdj 50 ans niou koye violer bamou dè domèram dji
@@aissatoudia4280 11:54 11:55 6
Li déh mougui mélni théâtre Sanékh bah bamou doné mom kassé Goor si penc mi teudé khalé yi djiguéne yeup ki vrai domérame la yallah nako yallah torokhal tékko lou métti
Oh c’est douleurs j’ai les larmes 😲😭😭😭😭qui coulent sans arrêt yalla nalén yalla takhawou amine 🤲🏾🤲🏾🙏🏾🙏🏾
Je suis musulmane tout simplement, mon seul marabouts c'est mon père et ma mère. Point finale
Je suis de ton avis quand j’étais petite quand une personne me demander qui est ton marabout je répondais toujours mon père. Aujourd’hui que je suis mariée c’est mon époux mon marabout et c’est ça lislam et c’est ça que nous a enseigné Cheikh Ahmadou Bamba RA
@@sokhnadiarrasamb1396 djigueene borome keuram moy SR niame
Merci bcp
Diameu rek ngay amm inchalah
🙏🙏☝️
Des mamans inquietes des mamans qui ont peur 😢des mamans tristes yawmal hiyam dina metti serigne hadim yalnala borom bi alak fi si addina ak allahira
Motax so dioure dom bou djiguen sa fit wi dou dal mouk ,te dangay yarr sa dom fa ngako wara yare gnou kheuy yakh adounam yepp😢😢
*Bilay ioe😢😢😢*
Gor akke djiguène mo si yème, ils sont tous les proies potentielles des pédophiles.
Goor gni ñio guene nekk en danger diamano dji nakh pédophilie yi nio guene bonne
Deuga rekk nga wakh 😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Barina serigne youye mboubo diangalé wala fadji fék lamouy deff ci souf ci djiguéne gni rek .mais yalnaléne yalla were yéne gnep
Je vais faire bcp plus d'efforts pour enseigné mes enfants moi même incha Allah. Waw c incroyable
Dans les véritables pays musulmans c'est les mamans qui enseignent le coran à leur filles
@@FamilleYague-no6iz j'en serai une incha Allah
serigne khadim nagniou ko maye khale yeup😃 kom k probleme rek la beugeu
Wa lii mom doyna war ki mo bone rek waye yéne yaye yi tamitt sangane ngéne trop khana sa dom bounko viole dinga guiss mou am changement sakh nitt danga war di bayi khell si sa ndiabott waye serigne khadim yalla nako yalla torokhal
Man kay lolou moma diakhal
@@rackyndiaye3665 ñii kay dano sagane 27 kénou manousé setlou sa dom
*Ahh moma diakhal srtt kou am 13ans warone nagne ko kham bou yague tmt c’est trop way khalé da ladj setlou bou bakh srtt mineur bougne ko pénétrer warr gua ko kham am dett*
@@veroniquenatack7392 man kay ñi dan ma diakhal depuis diamonoy corona ba légui kénu si niom masoul setlou domam khale yi khaw nano dhé bilaye
@@mamendoumbefall9783 *deh nagnou kay 13ans imagine rk lane lagnou wara subir c’est du n’importe koi bilay walay Yaye yi nagnouye bayi khel thi khalé yi goor sakh dagne koy violé wakhou malague djiguéne*
SËRIÑ TUUBAA waxoon na ne : " Ñi sant Mbàkke, la ñu baaxle laa bokk ak ñoom ". Kon am na ci ñu baax lool waaye am na ci ñu doy waar lool. Lii metti na trop trop foo ko takk rekk weesu na ko.
Mon cœur de mère saigne. Allahou Akbar. Lii métina torop.
Ana Antoine lanlay khaar thi lii qui limou def mo gueneu grave li sonko def nafekh baakhoul thieye senegal
Serigne khadime mbacké yay domiharm duegg
Je voulais préciser une chose, les gens qui disent que tayouko dou jikom ils n'ont rien compris dans la religion d'Allah, ya un nom parmi les noms d'Allah qui est as'sitir ce nom signifie Celui qui cache les défauts c'est-à-dire Dieu cache les défauts il ne dévoile pas le premier péché ni le deuxième caché mais si tu persiste trop sans laisser le péché Dieu va le dévoiler et il va te scandalisé ce que je vous parle demande aux gens de sciences... Donc on comprend bien que c'est pas la première fois qu'il le fait ,walahi on doit remercier dieu car il l'a dévoiler.... Et t'inquiètez pas tout se paye .... Sénégal nio wara baayi gueum Serigne soit disant diangalé alkhourane, misez vous sur les bons comportements des gens avant même leurs sciences
*Srtt ca se que tu as dit dans les derniers ligne c’est très important*
Une excellente vérité , liii daffa niaw té rousselou. SERIGNE KÉMTANE
Bon il faut que savoir guiss ga khalé yayam bouko dè diokh seram bimuy wodè mou diko sangoo mbalane lolou dinako waral ma deg SR Abdou Aziz wakh ko
Sont des excuses il mérite mort
@@AhmedLo-eu2eklo waxni pleas j n comprend pas
Envoyer svp ce reportage aux médias internationaux comme France 24 et vous aurez sous peu une réaction de l UNICEF et d autres.
Walay très bonne idée li ça dois pas se limiter au Sénégal kessé
Sont des mineurs ndeysane
Frère si vous avez la possibilité n'hésitez pas à faire le nécessaire pour que cela soit reçu par France 24.jai trop mal au cœur en tant jeune mere
Wa mes serigne bii dielhala khalë yui dijien yepp 🤔
Le plus noble d’entre vous auprès d’Allah est le plus Pieux Sourate S 49 verset 13
N'approchez point la fornication en vérités c'est une turpitude et quel mauvais chemin.
Srt : An nure la lumière
Wallahi founiou waron bakhé légui falaniouy yako 🙏🏾yalnaniou yalla samal bopam aralniou souniou ay niabot
Sortez dans la rue - manifestez-vous aurez le soutien de tout le peuple. C’est la seule solution.
Bougnouko défé guen deuk bi3
Tu as tout dit ces un domaram danou ko wara diap
@@djoguosediakhate-hx8yf lii mome diare na guéneu deuk bi. Khaléyi amatouniou béne dignité fofou ndakh serigne bou domékharame bobou
@@davidsat297 gnii bari nagn fi dé jenre gui ay domeram lagn mes ken dou wakh
C'est du jamais vu walahi gni gno yakk yonou mourite des vrais domram dougnou rouss sahe
Aye serigne bi yakhe na avenir khalé yi😭😭😭😭😭
Billahi ki daniouka wara ray tâlko thi kanamou khaleyi 😢 ki kay dou Serigne 😭😭
C un 'violeur en série", un malade sexuel... J'espère de tt coeur qu'il se rendra lui-même à la police. Comment on peut dormir et vivre normalement après un tel horreur.
Li ñiawna trop😩🥹🥹yak n’a adouna xalei yi
Ki Dou Serigne ab khath la bou moubou Serigne nanko teuth boléko ak travaux forcés ak torture pénou xaléyi kou nék dix ans nanko teuth girou doundam doméram pire ak thiaga😢😢😢
Sérigne Daara yi yagg nanio deff lou mél nonou. Dénio fébar fébarou djiguéne
Kholou yaye yeup toyy bilahi Khadim mbacke mi moy Kouti vrai mbam ki ray ko rek lagnou wara deff 😭😭😭😭
Yenneu dall louléne dall rék bakhneu comment une maman peut dire qu elle a confiance au marabout dakh serigne touba lakoye kholé yénneu serigne touba limou nékone daguéne sé nékkeu non mais amna louma méti an bilakhi mon coeur saigne😭😭😭😭😭
Li dè la wakh
Merde kii nagneko teuthie a vie, boudone fii Amerique kene wakhatouko,mon coeur segne😢😢😢.
Merci😢
Mais senegal bou macky laniou nek ..... Et ray ko rek mo daguane 😡😡😡😡😡
Ki kay rayko rek mo dagan
C vrai boudon Amérique la Fi waydji peine de mort mingui koy khar
@@10gital66 Ki rayeko dafa sede sakhe, bayiko mouye soufrire a vie thi prison lako yene,imagine 27 filles.
Mais le calcul est simple 27*10=270 ans de prison.
C'est un animal ce mec.
A vie
Merci beaucoup
*Bilay ioe lou euppe sakh métina*
J'ai fait le même calcul. Vraiment amoul c'est-à-dire 💔
Walahi c un anne
Je n’ai jamais vu des mères aussi irresponsables qu’elles .
Li mom sagane deugue la billahi .
-Comment pouvez vous accepter que votre enfant se fasse laver sous prétexte qu’on les protège.
Qui est censé protéger votre enfant ?
Vous ou les autres ?
-Votre enfant tombe malade, n’arrivant même pas à marcher , vous osez la remettre à un soi-disant marabout pour qu’il le soigne .
Savez vous la cause de sa maladie ?
Comment quelqu’un n’étant pas un spécialiste, peut l’aider ?
Comment ne pas remarquer cette tragédie que vit votre enfant ? Et pire pendant un long moment .
-
Je suis dacord avec tw paranyi ame naniou thie part de responsabilité ils ont irresponsable
Elles sont ignorantes rek ndeyssane
L'ignorance, l'analphabétisme et le fanatisme sont la cause de tout ça. Il suffit juste de les écouter pour s'en rendre compte. Malheureusement ,tout le monde n'a pas la chance d'être éveillé. Les parents sont eux même des victimes de cette société religieuse
Talougnou dara ak daw njabott am na niou oauvre à touba metina trop li
Ils n'ont pas de moyens
Domeram you melni serigne bi laniou wara teudjj 30ans comme aux USA😭😭😭Amna louma meiti trop
Non 27 khalé eupe na 30ans li a vie la béne khalé bou nék 10 ans de prison la ki kaye kasso laye déwé
*A vie kay*
Saway yaw danga bax rekk bane 30ans qui a vie laniouko wara teuthi
10ans fois 27 enfants
270ans d emprisonnement
@@mamanmbaye1305 ay tay modé😥😢😢😂😂😂
Dome bou djiguéne dagnoukoy setlou 😢mais ki defli dou nite dé Allahouma sali 😢
Je suis en Europe, mais chak jour que Dieu Toubab yii di khass derou musulman.
Lii day wané nii dioulit diafé ni si reew mi 😭😭😭
La pédophilie n'est pas une question de religion mais d'humain. Da gnouye mboubo religion pour accéder facilement à leurs proies car les parents leur confient aveuglément leurs progénitures. Malheureusement ils sont partout, dans l'éducation nationale, l'animation, le sport, dans les familles. . .
Vraiment personne n'est digne de confiance, on doit faire de la prévention et de l'information auprès des enfants sur ces sujets tabous.
@@sunkiss4950 je suis totalement d'accord avec toi
Dioulitt,amoufi...,Slt
Il faut arrêter ce sauvage n'importe comment.....!
Wawaww ligni toppé sonko... 😢Nagniu ko toppé seigne biii. Thieyyyyy. Allahu Akbarr sénégal mo doyy Warr.
Wawe Ana feminist yi Gabriel Dela Madison francoi eline et les actress nafekh 27 adji sarr gnonguini
Walahi les feministes
Raison de plus niou foutre PROS un mandat d'arret aindi que ce Mara, nul n'echappe a la loi.
@@wakheetragalal yallah si ligaye wakh
Surtout lolou tmt Françoise, Gabrielle,
@@wakheet naanal essence koss almét
C est la première fois dans une histoire de viol 27 mineur 12ans13ans c est vraiment triste mais en ceux moments yobou sa dôme Dara woroul amna gnénéne gnoukoye doundou mais ils on peur de dénoncer biss penc Dina méti lol un mbacké mbacké violeur c est vraiment dur sa Mame cheikhoul Khadim amna louko méti Barker Serigne saliou
Mbacké ak niang lépp yém bakh nékoul si santa nulle part 😢
Merbi nena Mbacke Mbacke yi gnolene gueune 😂😅😅😅
Je me demande il est où l'état. Ah j'avais oublié que cté lui le premier 'violeur' des droits Sénégalais... Pauvre mon Sénégal. Triste d'être femme Africaine tt court sans aucun droit!
Good job DakarBuzz! This is what journalistic should be
lii moy viol nak wayé thiagatou ba raap diiii doul nane daniou ma violé yalla na yallla may kholou mougne khaléyi et ses parents serigne bii naa deh ci kasso bii
😂ray ngama
@@rackyndiaye3665 dama wakh deugue dii tamite
Khana danguine bi lah
🤣🤣🤣
Bolé si sa ndaye kone nakh kigay wakhal moko tané
Mon cœur en tant que maman saigne
li doyna war cheu. nou nitt meuné liii
Waw ana gouvernement Sénégal gni ay khaleylagnou gno gueune sokhla dimbeul adji sarr
Blh Procureur am nga lo auto saisirou
Procureur autosaisir 😂
Dagno beugue cas rek amenagne lougnou cas
*Bilay ioe deugue bou werrr*
Les marabouts n'ont jamais été aussi nombreux au Sénégal au lieu de limiter votre croyance au seul bon dieu... Mais continuer c'est pas encore fini 😢 😢 je pleure pour ces filles si jeunes 😢
Ou est le rapport maître coraniques et marabout ça fait 2
@@magorcisse9555 merci dafaa am niou con qoi
doyna waar dal
Fanatisme, clanisme, lane moy sant. Fi kén gueunou fi kén. Yalla bamouy yoni yonetibi dou pour wone sante. Bayilén tapalé ak ragual. Dieul sa doom dika diokhé adiyyah. Niaka diangue ak fanatisme molén sonal. C'est votre problème, gérez ça vous-mêmes. Ce pays va mal.
Vérité absolue indéniable
*Vérité absolue gni dagnouy énervé nitt😤😤😤😤*
Wakho fi dara....fi fanatisme amatoufi sou donn lollou la konn dagnouy neuss neussal ken dou yeukk elles veulent que justice leur soit rendue.
Une vraie Dingerie Toute Ma Vie J'ai jamais vue une chose Pareille
Dou Oustaz deh wout tatla waye yalnalen Borom assamanak souf attek mome yarabi. Allahouma amie yarabi. 😡
Nn Sénégal c fini li Sénégal rk gakoy deug nn😢😢
Il faut dénoncer organiser une grand marche et tout la population pour que justice soit faite
C'est ici mm qu'on doit se constituer pour leur défense.
Faisons passer la vidéo en statut.
Thiey yalla en écoutant sama t’ yaram di daww ki mo gnaff ndayamm deug yalla nako yalla weirr
Ay way guisnafi sama Badjenn Coumba sa fai longtemps khawma foumouy sey ay way mame Diarra Sene sama cousine tan Coumba mann la ramatoulaye Domou djewo gueye à saint Louis sama yaye gadjiouna ak sama papa magui Dakar legui badjiane
Demal touba sétiko fo lathé sam niou wone lako
*Ahhh moy yone gua soutenir ko*
Louthie sounou yone
@@senedemba4287 bilahi sama yaye Wa Touba la m depui mou décédé lafa guethe 8ans d’émouma Touba t Sama gale mame Mougui fa ndamatou inchalah Nafa dem tkt pa
@@veroniquenatack7392 inchalah ma puc
Wa limom diamoula. Lidé moy Sénégal, dano geum serigne si rek. Mais lepou ler. Kouy geum geumal yalla ak yonéntou.
Sant takhoul nit ki nek serigne.
Daara dji khana amoule ndongo you goor tamite niome fougne nekone 😮
Lolou deh moma diakhal wala ay djigueine rek gnofay diangué🤷♀️
😮😮😮😮😮😮
J’ai même peur pour ma fille et mes nièces qui sont à l’internat 😩😩 Ay ya latif vient nous en aide
Ki rayko rek mo dagane
Il faut di lène némékou di lène yé si adina. Les prédateurs sont partout au plus près de leurs victimes. Les pédophiles gravitent malheureusement autour des enfants.
Faut mettre tes enfants dans des lieux sûre
Les photos de cet méchant marabou doit être publié partout
Khou deff Li yalla nako yalla wérr
Oú sont les féministes ?Gabrielle kane et consort levez vous vous avez du travail😊😊😊😊wala danguéne ragal mouride yi
Danio am prblm ak mouride yi
????
Wallah
Voilà les soit disant féministe
Lane moy mouride Mey Lene niou
Vraiment C'est Triste 😢
Que Dieu Vous Aide A Retrouvé ce Homme 😢
Ki danko wara ray ki vrai domeram le 😢 khale maumine le😢😢
Bilay rey rek mo dagane si mom
Nous sommes de tout cœur avec vous que justice soit faite lii rkk mo diarraa manifestée li metiina trop thiey yalla
Sante mbacké mounoule nek nite Kou bakhe loukeu dalé serigne touba ngua khameni mome si bopame 33 femmes ak 3 you bok ndeye ak baye la amone bassi seuteume bou moudjou kéne bakhoussi
C'est tellement dur lorsque tu entends ces témoignages poignants,tu vois ces enfants qui ne sont même pas conscientes de ce qui leurs.
Je me sens impuissante et c'est ce qui me fait mal😭
😭😭😭😭😭
😢😢😢😢😢😢😢😢
لَوْأَنَّ فَا طِمَةُ بِنتُ رَسُولُ الَّلهِ سَرِقَتْ لَقَطَعَاتْ يَدَاهَا😢
Lolou moy deug !
@@ibrahima8085 bilay até yi mom waroul ame ki ak ké
@@fallougaye4301 effectivement 🙏 lolou la YALLAH santané 🙏
صلى الله عليه وسلم تسليما كثيرا
Vraiment amoul Mbacké amoul dara
Ki kay dou serigne diaroul wowé serigne ak tour bou mague bimou yor vrai vaurien la mon cœur de sœur saigne 😒😒😒
Deyssane elles sont toutes innocente mais en souffriront après 😢💔
*C’est ça nakkk après lagnouy kham conséquences yi😢😢😢té dina méty trop thi gniom*
@@veroniquenatack7392 deug gua wakh 😢
@@binasanja9521 *bilay ioe daff ma méty li 🥺🥺🥺*
Tellement fréquent. Je suis mariée avec deux enfants. J'habite en France. On m'a fait des attouchements plusieurs fois à l'ecole coranique à medina baye niass.cela fait des decennies que les enfants à l'école coranique se font violer. Les parents qui abandonnent les enfants dans ces écoles doivent bien s'en douter. Moi ça a fait éclater mon mariage des années après je ne parle plus à mon père et jai eu deux ans de thérapie. Des garçons se font violer quotidiennement aussi tout le monde le sait. Les gens sont hypocrites avec un islam qui n'a rien d'une religion. On a oublié nos valeurs en laissant les marabouts et à leur famille faire ce qu'ils veulent
Mbacké Mbacké you naw yi diakhal nagnouma lou bonne réke
Billahi walleye yow wahatiko
Serigne khadim yalla kham nani damako yeureum seytané moko meune rek . Ndakhtè diapouma ni nitt dina wotté yalla a diang alkhourane ba.paré fi def lou mel ni . Honnetement gueumoumani moko tay
Femme bi néna mouride dof laa😂 bo hassé ba sante mbacke rck dagnoulay wolouu
Ndeyssane. Il faut que Serigne Mountakha recevoir parents yi ak khaleh yi. Deufeul lenn.
C’est tellement dur vraiment et les enfants ne sont pas conscientes du faits luttons contre les violences faites aux jeune filles bref il est temps que l’Etat prend ses précautions teh teguei neulei afaire de Adji Sarr Sonko😭😭😭😭
Ce mal saint doit être puni avec la manière, faites circulé sa photo sur le net que tout le monde le puisse reconnaître….
Certaines familles se croient intouchables ds ce pays.
Ou est JAMRA, j'espère que tu aura le courage de t'attaquer à cette histoire.
Ah ils auront intérêt à se dépêcher rapidement sur place .
*Vraiment bi deh mo diara wakh ay khalés you ndaw*
Je prie de bien consulter les petits avant que le pire arrive 13ans leurs cycles menstruels peut commencer tomber enceinte c’est le pire ❤❤ courage 😍😍
Continuer à être Fanatique et à vénérer les Etres Humains
Vos enfants vos Subir les Conséquences
Doff guène trop way 😢
Li dafa mainti 😢
Je te donne toutes les raisons du monde Mr.Alpha...,moi,j'ai toujours dis ça,mais j'ai gagné plus d'énnemies,que d"amis....,même les soulards qu'on critique,et les fumeurs de chanvre ne font pas ça..,dans la statistique du pays:le haut pourcentage des violeurs sont curieusement;les OUSTAS,et les SÉRIGNE DÂRA....,et,ce n'est pas la premiére fois...!,Salut...!
Alahouackbar....,ndéyesane...😢,ngni,kouléne lorr,yala dina la torokhal...!
Yalla rek yalla kesé Bayuilen gueme serigne yui
Ayway g le cœur meurtri.Naniou geum Yallah tei doylo ko .Sante dou dari .jikko la sunu Borom taguer wone Seydina Mohamed!vigilance le monde est à l’envers
Akhirou zamane deuggg liii moy moudiouk diamono deug
Fiii la beut yam fiii la nopp yam 😢😢kiii moy mbam kii moy nitt kou haram deug 😢😢😢ay way liii metina 😭😭😭yalla naleine yalla may xolou mougn et que justice soit faite
Bilakhi la maman à vraiment raison 😭 yakk na khaléyii . Mais yal nagniou amm ayy borome keur you compréhensifs 🤲
C me rappel la fille de une d nos voisine aicha camara yallah nako yallah yereme😭😭 dagnon ko viole famille bi khamoko bamou febar thi bir febar bi lakowah yayam fimoye khareh ba aicha tané thila aicha fatou wouyo boromame a lage de 8ans 😭😭😭😭 par infection
Mon ❤ signe atanke yaye
Y
لا قول ولا قوّة الّا باللّه
Sougnouy weur kou bone deugue ba dadjièk bii oustaz ngne ko tiyè😢😢😢😢
Naniou wakhe si li mo gueun niouy sonko
Nit dafa leundeum 😢li méti na trop 😢
😢 nako bay fall yhi lidianti 😡🔥💔🇸🇳😭😭😭😭😭 man djiguen la li dafa meti
Lii motakh je ne peux pas me faire à l’idée d’amener mon fils à l’internat pour étudier le coran❤et pourtant je veux qu’il metrise le coran mais dès que je pense à ces genres de choses g tellement peur que je ne peux pas l’expliquer 😢😢😢😢
Pareillement pour moi
Walay je vous comprend .je disais tout le temps k souma amé dome dafay maîtrisé coran mais akk lima guiss sama khéle dalatoul😢
Bonn dependroul si sante yalla nko yalla ray ki mo bonn
Li môme nexoul ci xool.Métina loole. Li police dathié wara takhaw takhawaye bou mate seuk . Amoul mbacké mbacké amoul dara.
Dama choquer😢😢 kii nagneko teuthe,vrai danger public moye soi disant serigne bi..boudone fii Amerique kene wakhatouko.
Mbacke mbacke douniou dara sen lofal ndey seringue touba santoul mbacke mom ba la santé
Voici véritable Viol nak d'état du Sénégal doit tout faire pour retrouver ce violeur ki d'où nit j'ai le cœur brisé 💔
Que cette affaire soit tirée au clair et que le coupable reponde devant la justice.
Senegal beuri na nite you bari youy mboubo serigne té nékou niou ko serigne beuré toufi dh li niawna
Ndeysane li métina trop khaléyi yalla naléne yalla takhawou serigne bi défna lou niaw 😂😂😂
c'est pas drôle de rigoler. la on parle de viol et tu ris
@@nadiyou*Bayiko fofou rk*
Meuna na xam ni de quoi tu ricane ou daga diawalé les emojis 🤔🤔🤔
@@nadiyou les gens ne font pas attention sur la signification des emojis.mieux vaut ne pas les utiliser si on ne peut pas les différencier
Serigne bou mag bi nena sante mbacke sante la rek mai top ay ndingalam bayi ay terem kokou mo bok si mome
Ki dou Serigne wayy...bayiléne topp Santeee... Serigne Touba néna diourouma kéne....yone bii talubé rekkk mofii ammm...ay way yewouléne...
Incroyable Serigne bi dou nit allahu akbar
Un fait que je n’ai jamais vu ou entendu de ma vie ! C’est vraiment une honte! Les parents sont des éducateurs et c’est leur devoir obligatoire (en Islâm) d’éduquer leurs enfants au lieu de les confier à des soi-disants marabouts ou “serignes”. Ils (ces parents) seront interrogés le Jour du jugement dernier au sujet de l’éducation de leurs enfants. Mais le fait qu’ils manquent d’éducation les amènent simplement à laisser leurs filles à des “Serignes” pour leur inculquer les valeurs de l’Islam alors que ces derniers les utilisent pour leurs intérêts personnels ou les abusent sexuellement. Je dis que cette mentalité sénégalaise doit cesser maintenant. Les Sénégalais sont trop naïfs et croient fermement à des marabouts pensant que ce sont des gens de bien et pouvant leur porter bonheur. Mais c’est faux !!! Nombre de garçons et filles qui sont dans les daaras ne sont pas bien éduqués par leurs maîtres coraniques simplement parce que leurs méthodes d’enseignement sont mauvais ou ne sont pas en conformité avec les bases religieuses ; en d’autres termes, pour éduquer les enfants, il faut commencer par le Tawhîd (l’unicité d’Allah) qui est le fondement islamique le plus important. Les autres viendront après.
Je suis musulmane tout simplement, mon seul marabouts c'est mon père et ma mère. bilaaaahi
27x10 ans =270 ans de prisons ( prison à vie pour ce salaud)
À barina NK li lepou NK mou waka tede prison wayé lors Lou bakh na si mom NK nako tedieu RK ki waye dafa bonne RK moudé sa prison RK mbacke mom louyou lén wakh RK mom la 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢dawaw à fa you Tabaski ben mbacke ray na nitt si palé batakh doko ray violé baparé mou banian ko NK mou Ray ko NK dougal ko si Bari nk😢😢😢😢😢😢😢 mbacke mom louyou lén wakhal mom la RK 😢😢😢😢😢😢😢 yalla na ko yalla à té yor mi hi Yam' ?😢😢
ioew mbacke mbacke yi dounousa morom soy wah wakhalack ki déf dieuf dji
Yewwouleeen une e fois pour toutes kouleeen wanoul yalla ak yonnent bi woneleeen ko guinaww amoul mbacke amoul sy il est temp niou dieulate sugnu lepp wekk ko yalla gni sen mame nio bahoone niom bahouniou
Ayyy j’arrête pas d’y penser 😢toute la journée dama rousse lol étant Mouride et habitant à Touba nakalaniouyy défff ak none yi hoo en plus un Mbacké Mbacké 😢
Lolou dou lou bèss si mourites yi
Yaw kham loufi indi lolou
Frère je suis catholique s’il te plaît boul wakh Li way day andi affaire tarikha et autres c’est un homme qui l’a fait pas tous les mourides. Je m’excuse si je t’ai mal parlé
@@bernadettegomis1094 tu n'a qu'à aller occuper ta religion et ne mêler de notre religion
@@ndongfode5726 fode t’as pas fait le droit la constitution du Sénégal va le revoir tu feras ce qu’on a écrit frère