Ki moye Serigne Sidy Mbacké Ibn Serigne Abdou Khadre Mbacké,Djoulite akhane AK goré AK fess déll AK xam xam,té xam lool liy dox si réwmi AK adounabi.bolé lép andak taaloubé akoup yaar.Rewmi Nanou topou yaroup Serigne Touba,bilahi loolou rek mognoussi mana guéné.
Bayiléne naféxx tay wax deuggg bou réwmi dé takk xaméwoul Serigne xamoul talébi xalé yángui déh si yonou guéjj Gui ngir deukk bou méti xalé yangi si kasso yi ñou teujj si dará loudoul politiques diamm dou lounouy wax lounouy dieufla roylén si Chiekhal Khadim si até deugg ak wax deuggg, na sén xél dém si xaré samba sagna digeunté Lat dior ak Chiekhou Amadou bimouko toñé Diay KO dolé nagou alalam ba nopi Di wolou Sergne bou makbi ngirr... Mou wouyssi ko Serigne bi dafa Niko délol alal ji ma soggua ñeuw wouysila ndax danga toñe Chiekhou Amadou jiayko dolé nagou alalam lat Dior Niko qaadi ma Diakhaté kala moko até ni alal ji dagaane ná té qaadi makala modone juge bou Lat dior té diangal na Chiekhal Khadim si zaa hir
Dieureudieuf Mbacké,Lou ragal YALLAH amoul,dou déme féne.Nanou délou si Diamou YALLAH té wormal sounou kilifa dîînéyi.
Dia dieuf mbacké serigne touba mesoul beugue noteél ❤🙏
Machalla Mbacké. Wax len nguir yalla son nagn dé.
Machalla Mbackè amna solo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yagu fii lol balla aicha❤
Dég n'a deugg nak ,MBACKÉ dieureudieuf
Dieuredieufe mbacke balla yalle nga fi yangue loool ta were amine
Machalla mbacké
Wahou deug kouko dégo hamkoo nite meuna wah baa paré téé doo faral kén tahaw thii digue bii deug yalla koo môm makk gnifi nékone bou reiwmi mélane ni dagneda Adou diare thi digubii téé dougnou farale kén deug yalla koo môm...
7:35 7:54
Ki moye Serigne Sidy Mbacké Ibn Serigne Abdou Khadre Mbacké,Djoulite akhane AK goré AK fess déll AK xam xam,té xam lool liy dox si réwmi AK adounabi.bolé lép andak taaloubé akoup yaar.Rewmi Nanou topou yaroup Serigne Touba,bilahi loolou rek mognoussi mana guéné.
Bayiléne naféxx tay wax deuggg bou réwmi dé takk xaméwoul Serigne xamoul talébi xalé yángui déh si yonou guéjj Gui ngir deukk bou méti xalé yangi si kasso yi ñou teujj si dará loudoul politiques diamm dou lounouy wax lounouy dieufla roylén si Chiekhal Khadim si até deugg ak wax deuggg, na sén xél dém si xaré samba sagna digeunté Lat dior ak Chiekhou Amadou bimouko toñé Diay KO dolé nagou alalam ba nopi Di wolou Sergne bou makbi ngirr... Mou wouyssi ko Serigne bi dafa Niko délol alal ji ma soggua ñeuw wouysila ndax danga toñe Chiekhou Amadou jiayko dolé nagou alalam lat Dior Niko qaadi ma Diakhaté kala moko até ni alal ji dagaane ná té qaadi makala modone juge bou Lat dior té diangal na Chiekhal Khadim si zaa hir
Mbacke balla senegal mo nékhola wakhé wanté seringe bi si diame laye dokhe macky yalla sakhe fallé woko
Machallah Mbacke ❤❤❤❤
lou wér mbacké balla bayi lénne nack guayi réck yw déy sa mam guaramnala
❤❤❤❤❤❤❤
Boulén bagn koulen méré ci deug. Wax meunoul gnack dé.
Akassa
Douma kholeu kouma mèrè deumay wakhe fi deugg binèkke deugg yallah mokko mom bilakhi
Dieredief mbacke balla
❤❤❤❤❤❤