Hé hé waly seck répond sévèrement à ameth thiou fi yala rek

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 дек 2024

Комментарии • 82

  • @elsalimto4294
    @elsalimto4294 Год назад +5

    Vraiment parole yi amna solo
    C ke deug heur boko wakhé il fo am koussi guis bopam mais il ne parle a personne conseil la boumouy diokhé rek ke ni fi lep yalla la parce moy mayé moy khagné macha alla

    • @ndiayendeye4713
      @ndiayendeye4713 Год назад

      Légui dé lolou mo am daguay wakh nite fétéléko bopam ni man Lay garouwalé😂😂

  • @aladjifalloudia4915
    @aladjifalloudia4915 Год назад +20

    ❤❤❤❤❤wally seck yaye séne baye doo séne marom yaa finé 😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @maladodiagne-hc7wz
    @maladodiagne-hc7wz Год назад +8

    Bilahi fi yalla rek mofi nek yow Amal diam rek mar ont t aime bien ❤❤❤❤

  • @fatimafatima-xh4fn
    @fatimafatima-xh4fn Год назад +5

    Le chanteur du peuple machallah le choix du peuple le meilleur ´ mome legnouy topeu ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @minasy9566
    @minasy9566 Год назад +1

    Bilay deguele seck amal diame yague fi loole tes ande ak wér ❤❤❤❤

  • @tallambengue-oc4cd
    @tallambengue-oc4cd Год назад +21

    Waly ieo rekk lah beugue mé nitt dagay fatélikou dembu ameth diapalé nala dh

  • @papeabdoudiop925
    @papeabdoudiop925 Год назад +3

    Qu'il répond à Ameth Thiou ou pas... Le message est trop fort....

  • @yakinesene1649
    @yakinesene1649 Год назад +3

    Machala.wally.yalanala.yala.takhawou.nga.goude.fane.loole

  • @awagaye2031
    @awagaye2031 Год назад +11

    Wally u are always da best bravo

  • @aliouneseck3049
    @aliouneseck3049 Год назад +10

    Good job bro your the 👑 god bless you we love you and I really love my seck family

  • @leuzthiam550
    @leuzthiam550 Год назад +2

    Fier de tw tu aide bcp dans ma vie damaye guis sama boopou si yaw tjrs

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy Год назад +16

    Mba khol yagui nekh

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy Год назад +13

    Le choix du peuple

  • @fatouba2560
    @fatouba2560 Год назад +5

    Demal dieul meth mo guen lii sanitou hier moy sa nittt

  • @galsenegalsene
    @galsenegalsene Год назад +13

    Mane sa fans la wally wayé nite dangaye fatalikou démbou Ameth thiou takhawou nala founé

    • @khabaneazar7406
      @khabaneazar7406 Год назад +1

      Goor wally faté woul démb ameth mo wara wathié bopom tuti rk comme néna wally rakam la frère la fils sam la lolu lép sudé deugla mom thi souff la wardi wakh

    • @awaseck3645
      @awaseck3645 Год назад

      @@khabaneazar7406 Vraimen

    • @awaseck3645
      @awaseck3645 Год назад +1

      Ms yaw dèglounga ameth limou wakh nite bo amer loula meti si nite dèmal basi mome nga wakh koko lolou moye nite Ms tok si reseau yi nga khamni danio gaw si cas

    • @ndiayendeye4713
      @ndiayendeye4713 Год назад

      ​@@khabaneazar7406 merci là-bas

    • @ndiayendeye4713
      @ndiayendeye4713 Год назад

      ​@@awaseck3645 deug deug

  • @elhadjimbackembodji9243
    @elhadjimbackembodji9243 Год назад +2

    Yalla yalla rek mofi nek

  • @awaseck3645
    @awaseck3645 Год назад +2

    Wally nopi yeup li LA donne khare c tres bien waye Ms commentaire yi niome amna niou seuttanè waye Wally loumou df ameth mo wakh mome mou tontou rk lanla arreter waye ameth mo worone demeu basi mome wakh ak mome Ms pa pour mouye tok si reseau yi di wakh

  • @sidatemohamedthiam3787
    @sidatemohamedthiam3787 Год назад +2

    Wally Seck nekal Nitt teh bayi yi ngay deff Ahmed thiou sa magg leu meytoul Seytané yi lay dougal

  • @diagnegnilou1078
    @diagnegnilou1078 Год назад +21

    Mom Kat dafa eupeul Hana dou employer

    • @rockyky1747
      @rockyky1747 Год назад +2

      Lolou mon diakhale gneup 😅

    • @awaseck3645
      @awaseck3645 Год назад

      Employer nk 😂😂

    • @awaaidara8729
      @awaaidara8729 Год назад +4

      Dedet dou employé rek deh bay la mak leep la pour man niop la rek dinaniuko géré si sen bir

    • @ndiayendeye4713
      @ndiayendeye4713 Год назад

      ​@@awaaidara8729 bamou khamé ni baye la makk leu la wara waron takhawé comme telle baye wala makk dou yakheu domam Wally même bou nékone ki keuneu mauvais thi dom yi papa thione douko yakheu moukk😏😏

  • @bambagningue5935
    @bambagningue5935 Год назад +3

    Mais gnoune senegal lane moy sounou probleme koulene wakhni amet thiou lay wakhal nanou aye detail

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Год назад +2

    Bless you And Long live 🙏 Amen

  • @khalifambengue6125
    @khalifambengue6125 Год назад +2

    Niak foulleu ak fayda di garouwalé ni

  • @sofiekebe4168
    @sofiekebe4168 Год назад +2

    Kholéne ndakh ameh thiou mogui noyi 😂😂😂😂

  • @abdoulmbaye3764
    @abdoulmbaye3764 Год назад +3

    Vraiment wally I am so happy for you

  • @ajiemanneh7245
    @ajiemanneh7245 Год назад +2

    La vérité absolute

  • @Stars19023
    @Stars19023 Год назад +2

    Je ne suis pas d accord demall nga waxtan ak sa nitou demb nga bayi gnilaye topp pour intérêt

  • @issambaye4620
    @issambaye4620 Год назад +6

    Bimiy metti daal mongui fi won yen niare la daal waxtaneko mo gueun

  • @bintafaal-kohlschmidt1753
    @bintafaal-kohlschmidt1753 Год назад +2

    Il falait même pas répondre ❤❤❤❤❤

  • @AntaDiouf-wo2kl
    @AntaDiouf-wo2kl Год назад +3

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💯

  • @Zazindiaye218
    @Zazindiaye218 Год назад +1

    Wa keur massar sama kholll dafa sėėdddd si yėneu bilay

  • @mbayediagne1234
    @mbayediagne1234 Год назад +4

    Mar demal gawakhtane akmome moguen yow borome mbakhga ya ndiabote niep ahmet thioukh nopil yowite teboumoula dalati yen niar niepa bakh

    • @aboudiallo3631
      @aboudiallo3631 Год назад

      Teudieul sa gatte Ahmeth dafa falle nday wally koku boy guediawaye leu dou ngaka dou serr

  • @aliounendoye9022
    @aliounendoye9022 Год назад +1

    Musique dou sama mbir mais démaka beug lool nguir défay dimbiliwaaté ci liko Yalla weur seugueul

  • @bintadiagne2545
    @bintadiagne2545 Год назад +1

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @DickoNdiaye-nv7zm
    @DickoNdiaye-nv7zm Год назад +1

    Yalla la Mane naniou nagou ya fi née

  • @abdoukhadrendiaye3595
    @abdoukhadrendiaye3595 Год назад +8

    Wakho fi touss démal gua wo hamet thioune sén deganty dafa yague

  • @bakarcoulibaly5308
    @bakarcoulibaly5308 Год назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤👍💯💪💪

  • @babucarrtouray9198
    @babucarrtouray9198 Год назад +1

    😢😢❤️❤️

  • @fatoucamara956
    @fatoucamara956 Год назад +2

    ❤❤❤❤❤

  • @fatoumataba9925
    @fatoumataba9925 Год назад

    Wally Mousso tontou téguonone naméty kou faté pape diouf témeusso wakhe mais pas aujourd’hui je t aime beaucoup mais il ne fallait pas petit frère y’a djitou tu vas voir de toutes les couleurs mais sois toujours un exemple penses y

  • @babacarsadikh120
    @babacarsadikh120 Год назад +1

    waay doul

  • @maguettekane3888
    @maguettekane3888 Год назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @SeynabouNiang-bo5fx
    @SeynabouNiang-bo5fx Год назад

    Marma Yacine wathié gua keur Massar samedi

  • @Zazindiaye218
    @Zazindiaye218 Год назад

    Waly mounoul way beugue naniou wakh guėne lou nėkkk waly dafa danou dafa khėwi diko liguėye lou nėkkk dėf guėne kooo do lėneu nopalou sėn khôl dou meuseu sėddddd barkė yonentė biii pssllll

  • @marmichoue7857
    @marmichoue7857 Год назад

    Heu wally son micro c en or ???

  • @KhadimCissé-f8s
    @KhadimCissé-f8s Год назад

    Wawe😂😂

  • @zouazou2297
    @zouazou2297 Год назад +5

    Je suis pas dakor wakhtan leen rek lep rafetat aduna amoul solo

  • @hrams4793
    @hrams4793 Год назад +1

    Bayilen nafekk yii

  • @bassatoure4696
    @bassatoure4696 Год назад +1

    Mar yaffine

  • @seydoudia8077
    @seydoudia8077 Год назад +1

    Ki ki ki

  • @serignembacke629
    @serignembacke629 Год назад

    Nekal mak nak te Baye ye Akh

  • @abassegueye3365
    @abassegueye3365 Год назад +9

    Ki meunoule waye

  • @yaadamajobe7559
    @yaadamajobe7559 Год назад

    doomi harmi nga demel ken do la teyeh