Je te jure il est le Meilleur Machallah Il nous plonge dans l'émotion comme pas possible Pieds Nus tank yi wékh taal Ndéyssane Ils sont trop fort chapeau bas à toute l'équipe
Alkaly (père), ta chute risque d’être très dure surtout envers ton meilleur ami. Makhoudia (fils) idem pour toi envers ta femme à qui tu as fais perdre votre enfant de la pire des manières. Kheucha qui s’en prend à son père aussi… La morale dans ces 4 premières épisodes, c’est qu’il faut toujours penser aux conséquences de nos actes ou paroles, quelque soit la situation. Car il y’a de ces choses une fois faites ou dites, laisserons des traces qui jamais, ne disparaîtront. Makhoudia (père) souffre en silence pour le moment mais j’ose espérer qu’un avenir meilleur l’attend tellement il est calme et continue d’être fidèle à ses principes. Un masterclass cette série.
Makhoudia il n a pas de dignité. Il préfère défendre son ami et sa femme .Eux qui l ont rabaissé et traité comme un moins que rien .Pour moi il devrait pas divorcer de sa femme premièrement. Deuxièmement il devrait protéger sa famille ,et être là pour eux.
@Khadimamadou je respecte votre opinion même si je ne le partage pas. Car pour moi au contraire, de ce que j’ai vu de la saison une à maintenant, Makhadiou est la dignité personnifiée dans cette série. Alkaly (père) est perdu pour le moment vu ce qu’il traverse. Mais être perdu ne rhyme pas avec dire ou agir n’importe comment car les conséquences de ses dires ou agissements le rattraperont. Makhoudia qui divorce avec sa femme ? Moi personnellement je le comprends, car c’est à cause du secret qu’elle a révélé qui a amener tout ceci, juste par vageance. Ensuite que Makhoudia ne défend pas sa famille alors la je me demande si nous suivons la même série lol, car moi je pense que pour le moment il est le seul personnage à qui on peut dire zéro faute.
Si tu tombes sur ce message qu’Allah te bénisse,te protège, te garde en excellente santé, te facilite et t’aide à réaliser tous tes projets et souhaits ainsi que moins de problèmes et d’obstacles dans ta vie 🙏🏽 ❤❤
La douleur de mame bou goor m’a fait pleurer encore une fois evenprod vous avez taper fort une épisode riche en émotions on sent que cette saison sera chaude entre les guers geuweuls et laobes bravo aux acteurs qui nous transmettent des émotions vives et intenses
Bilay c'est dommage que si c'est vrai dans le téléfilm que Marem.sall.nest vraiment plus mais si ce n''est juste qu un rêve Ohhjhh naniou delo souniou rein wala naniou afficher si bounteubi que ici repose Marem.sall avec le.rein d alkaly gnegno à jamasi comme.niniouy wakhe ici repose astaffourlah dama fachees wayy alkaly workatleu sofna bone na
Sallahou alla Mohammedine ❤ allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa Salim ❤️ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa alla alihii wa sakhbihi wa salim
@ vraiment félicitations pour tout ce que vous faisait vivre à travers le casting, le sénario, les sécances et les artistes merci beaucoup🙏 Mon grand-père était tout pour moi il était à la fois mon père et ma mère il a éduqué à bas âge j’avais à peine 2ans jamais je ne cesserais de prier pour lui et jamais je ne pourrais l’oublier
Alkaly sall est très ingrat omg ton karma n'est pas loin ndiaga Thiam le meilleur de sa génération machallah makhoudia tall yeureum nako diouma thiam calme toi et écoute mame bou goor dieynaba tall warna bayi nétali
Amina dioylona gnou bari thi yaye wayé Diaynaba tall tamite cou diouy walla sa yaram daww néna man sama papa la beugue papa ak yaye kénne meunouco remplacé yalla nalén fii yalla bayi gnou féké lépou inchalla kharé aldiana gni djitou amine 🙏
qu’ الله aide la Palestine qu"الله accepte nos duaa qu'الله nous accordé le paradis qu'الله accepte nos prières qu'الله protège nos parents qu'الله protège nos grands mères/pères 🤲🏼
HEURES DE PRIÈRES DU 20 AU 26 DÉCEMBRE 2024 Fadjr: 06h17 Suba: 06h32 Tisbar: 14h15 Takussan: 16h45 Timis: 18h54 Gue: 19h54 Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Ndeysan la douleur douleur d'une mère qui perd son enfant Daba Thiam yeureum nako meune na limou déff trop kou content di guiss jojo si bété bété rkk lalal j'aime ❤bravo à eben prod série mofi meune💪
Dans la vie, chaque jour avec son lot : tantôt c’est la joie, tantôt c’est la tristesse ou des journées tranquilles qui nous apaisent. Qu’Allah nous donne foi et la force de vivre nos épreuves avec acceptation
J’ai entendu l’autre fois,Cheikhouna Gueye (Saneex) dire que Serie bi ama goul thiow ! Mais je confirme ces dires,Lima guissssss ! Jojo il est excellent,il joue bien ! En tout cas,je félicite Evenprod pour tout le travail fourni.
Saanekh, Saanekh, Saanekh😢
Tout ce que tu transmets comme émotions reste inexplicable 😊
Un artiste complet
Très même bilahi c le meilleur ❤❤❤❤
Le meilleur de sa génération ❤
Bilahi il mérite des ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je te jure il est le Meilleur Machallah
Il nous plonge dans l'émotion comme pas possible
Pieds Nus tank yi wékh taal Ndéyssane
Ils sont trop fort chapeau bas à toute l'équipe
Eh oui je pensais la même chose avant de voir votre commentaire. Un grand acteur ❤
Des cœurs pour Even Prod et toute l’équipe de la série Bété-Bété!
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MouhamedWadediop Merci beaucoup. ❤
Aka nékhone ma done Dallou Saydina Mouhamed Salalahou Allah Mouhamed
Stp lolou douu wahoo fiiiii nèkall nitttt
@@abiba1227merci
Sayy yaw sa aldiana ngay lidieunti nii😂😂
@@SonFife😂😂😂Wakh na deug
Daba Thiam Dafa mene rolam nak elle mérite des cœurs ❤❤❤
Vraiment ❤
@@OumyDiop-y7x billay dafa meni dioyam yi degg la sakh❤
Dafa yagg jouer nak ma sha Allah
❤❤❤
Mom kay machallah ❤❤❤❤
Sanekh et ces pieds🤣🤣🤣meilleur acteur de tout les temps
😂
Bilaye 😂😂😂😂
@PendaSow-cv7zc Merci. 😂
Wékhna talle deh deysanne
😂😂😂 dokhna ba tanke yi peunde 😂😂
Alkaly (père), ta chute risque d’être très dure surtout envers ton meilleur ami. Makhoudia (fils) idem pour toi envers ta femme à qui tu as fais perdre votre enfant de la pire des manières. Kheucha qui s’en prend à son père aussi… La morale dans ces 4 premières épisodes, c’est qu’il faut toujours penser aux conséquences de nos actes ou paroles, quelque soit la situation. Car il y’a de ces choses une fois faites ou dites, laisserons des traces qui jamais, ne disparaîtront. Makhoudia (père) souffre en silence pour le moment mais j’ose espérer qu’un avenir meilleur l’attend tellement il est calme et continue d’être fidèle à ses principes. Un masterclass cette série.
Makhoudia il n a pas de dignité. Il préfère défendre son ami et sa femme .Eux qui l ont rabaissé et traité comme un moins que rien .Pour moi il devrait pas divorcer de sa femme premièrement. Deuxièmement il devrait protéger sa famille ,et être là pour eux.
El Hadji tamit ❤
Je me suis dit la même chose ci dernier épisode bi c'est la colère qui a poussé Fatim Thiam ak laobé yi
@Khadimamadou je respecte votre opinion même si je ne le partage pas. Car pour moi au contraire, de ce que j’ai vu de la saison une à maintenant, Makhadiou est la dignité personnifiée dans cette série. Alkaly (père) est perdu pour le moment vu ce qu’il traverse. Mais être perdu ne rhyme pas avec dire ou agir n’importe comment car les conséquences de ses dires ou agissements le rattraperont. Makhoudia qui divorce avec sa femme ? Moi personnellement je le comprends, car c’est à cause du secret qu’elle a révélé qui a amener tout ceci, juste par vageance. Ensuite que Makhoudia ne défend pas sa famille alors la je me demande si nous suivons la même série lol, car moi je pense que pour le moment il est le seul personnage à qui on peut dire zéro faute.
@KhadyDiop-lv5dg tamit ❤️
Ndeysann Daba Thiam Elle est une legende si théâtre mtx elle ne force rien machalla da meun li mouy def bravo à toi et toute l’équipe❤❤
Daray kocc ka forme nak machalla
J ai vraiment pitié d elle .Elle souffre trop
Des coeurs pour eux ❤❤❤❤❤❤❤❤
Je l'aime trop
Bilahi bouy dioy day melnii réel 😁
Si tu tombes sur ce message qu’Allah te bénisse,te protège, te garde en excellente santé, te facilite et t’aide à réaliser tous tes projets et souhaits ainsi que moins de problèmes et d’obstacles dans ta vie 🙏🏽 ❤❤
Amine y'a rabbi merci ❤
Amine
Amine
Amine 🙏❤️
Amine yarabi ñiou bokouko❤
Serie bo khamni khoulo rek keur yeupa tangue fénn sédoul 😮😅😂😂
@kountambacke6908 Doyna ware. 😂
Thine bouy bakh la coté yépay wagnakh
C’est ça le but seuy guer guewel teude daye beuri thiow
Guinaw maréme sall mo gueune tangue kanamame😂😂
La douleur de mame bou goor m’a fait pleurer encore une fois evenprod vous avez taper fort une épisode riche en émotions on sent que cette saison sera chaude entre les guers geuweuls et laobes bravo aux acteurs qui nous transmettent des émotions vives et intenses
"Vous avez tapÉ fort" au lieu de taper
@@z.e.y.n.a.b.qu’est ce qu’on s’en fout tu as compris non 🙄 ah Molière toi aussi 🙄
@dieynabadiaw3352 Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire.
Kou yereum 😢Daba Thiam ak Makhoudia Tall rek beusseul ❤
Daba mom yeureum nako mais Makhoudia Tall dou responsable xaritam moko geuneul famille wam louko dale moko yobe bopam
@@Wealth.One1da nguan koy comprendre itam loumouy degue metina
Bly il est vraiment complexe
La mère de daba thiam la yeureum billahii elle souffre vraiment 😢😢elle mérite une deuxième chance 😢😮
@@Wealth.One1tu as totalement raison sur Makhoudia
Jojo né nako teul mbéthie😂😂😂😂😂😂seuttt non théâtre bi gnou ay reka fi tassé des coeur pour évenpro❤❤❤
Walahi gneupeu aye kène dou Deguène laobè ❤❤❤
😂❤jojo dina dozé ba raylou boppam 😂li Wa bahna rek
@mariemebabou7019 Deigeul lolou diadieuf. ❤
😂😂@@baubaubeye7836
L’énergie de Deguène, bonne fin de soirée à tous
@Dark00559 👍
Ohh sama petit frère fékawoul épisode 4 😢😢😢 Yalla na souff sédd si kawamm Amine 🙏
amine
Ohh masa Amin yarabi 🤲
Yalla nako borom bi yereum xaréko aldjiana firdawsi yereum ko diegualko😢thi barké seydina mohamed psl
Ne me fait pas pleuré
Amine
J'aime beaucoup notre bien aimé prophète Mohamed psl no n'a jamais vu ni entendre sa voix mais il reste dans non cœur ❤😢
Bilahih nak❤❤❤❤
Ta maman vivra jusqu’à ta réussite dit amine ❤🎉
Amine
Amine yarabi
Amine ❤
Amiiiiiiiiine Ya Rabi 🤲🤲🤲🤲💓💕❤️💞
Ameen ❤🤲
Jojo théâtre rk layyy defff kirassoulay xaleiii biii ylla nako ylla Lafalll thiatttt wayyy🎉❤mashllah evenprod chapeau à vous meilleur acteur yi ak actrice rk guen boleiii mshlla mention sepecial a l’équipe et le producteur
Dafa ayy
Jojo dou dara il change tous…amour rek . Day yakh théâtre
@@NdeyeSene-dq5zi yow lo Hamm
@@NdeyeSene-dq5zi lane moy sa compétence
@DijarassoulDioum Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire.
Alkaly est vraiment ingrat il n'a jamais considéré Makhoudia il montre juste son vrai visage
Li rek ladon wax sank 😢
Bilay c'est dommage que si c'est vrai dans le téléfilm que Marem.sall.nest vraiment plus mais si ce n''est juste qu un rêve Ohhjhh naniou delo souniou rein wala naniou afficher si bounteubi que ici repose Marem.sall avec le.rein d alkaly gnegno à jamasi comme.niniouy wakhe ici repose astaffourlah dama fachees wayy alkaly workatleu sofna bone na
Daba Thiam elle transmet bcp d'émotions
Oui enfin elle a pu vider son sac!😢
@@GoundoKonate-o9ebilay dafa sonou
Est-ce que série bi Amna kou Doul transmettre émottions
Vraiment ils dépensent beaucoup d’énergie 😊
@@aliounembaye4022 bilay série bi émotion késsé là
@sokhnadiop3506 👍
*Les 5 millions d’abonnés d’Evenprod Sénégal Mon combat la meilleure chaîne de L’année*
Mériténagnouko dé😍
Vraiment ils méritent plus 🌹 🌹 🌹 🌹 nio meune te eup doole
Kone amouniou 5millions ni mais hana dolen xol
@malcomboydiptsStyle Merci pour la force.
@@evenprod Yena ko fa am😍
Loc bomb ak mayel dinan ma ray😂😂😂
@modo6218 Da melni moudjou nagne djibo ? 😂
Nieuw léne niou diouli si YONENT bi salallahou Allah MOUHAMED ❤
Salahou ala Mouhamed ❤❤
Sallahou alla Mohammedine ❤ allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa Salim ❤️ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa alla alihii wa sakhbihi wa salim
Salalahou alla wa Salim
Nieuwougnou😡😡😡😡😡 seytané guendi Diay boy diouli si yonet bi figuakay dioulé??
Salalahou alla mouhamed ❤
C'est très fort le lien entre une maman et son enfant Daba est inconsolable
Zozo legui comme père jora😂😂qui l’a remarqué 😂😂
😂😂😂
😂
J'ai remarqué ça key kif kif
Adando Day wallé
Sa yaye yallna féké sa ndieuriñ wakhal amine ❤❤
Amine ❤❤❤
Amine
Amine 🤲🙏
Amine
Amine
Une pensée à toutes les familles qui souffrent de la disparition de l’un de leurs proches, k’Allah les guides et les ramène auprès des tiens 😢😢😢😢😢
Non vraiment l’amour de Ndiaga thiam envers Diouma thiam me touche vraiment
Ça me rappelle les souvenirs avec mon grand père(qu’il repose en paix)
@ndirmbaya810 Paix à son âme.
@ vraiment félicitations pour tout ce que vous faisait vivre à travers le casting, le sénario, les sécances et les artistes merci beaucoup🙏
Mon grand-père était tout pour moi il était à la fois mon père et ma mère il a éduqué à bas âge j’avais à peine 2ans jamais je ne cesserais de prier pour lui et jamais je ne pourrais l’oublier
Sanex yalla na yalla goudal fanam ak bepeu dioulite 🙏❤️😊
Amine ❤😢🎉
Amine ❤❤
Alakhouma amine. C'est le meilleur walay
Amiiine ya rabby
Allahou ma amine ya Allah sama acteur bi aka mo meune maasha Allah Mame Cheikhou Gueuye alias Sanekh❤❤❤❤❤❤❤
Dieynaba tall kagn lay bayi netali😂😂😂😂😂😂
Moy RUclips 😂
@ndoumbeniang4919 Mougui gnawe dh. 😂
Mofi nékal codou famille sénégalaise😂😂😂
Evenprod wolein père Zora mou nekk nidiayou lawbee yii😂😂😂
😂😂😂day euppp sou boba
Yangi wakh Lou tange père Zora don nidiayou lawbee yii non lolou doumako atan😂😂😂
😂😂😂
Dafaye eupe
Dedd yaw beugo diam dh 😂😂😂
Kou beugué Serigne Saliou AK Serigne Babacar sy lalal j'aime
Ndéye Ndiaye néna RUclips moma ko wakh li nekh na 😂😂😂
Dafa dioum Google lah waroon wkh😂
😂😂😂
@NdeyearameSene-lf1ll mbadou 😂😂😂
@@NdeyearameSene-lf1ll no youtube bi mo gueuna andeu dé 😂
@@NdeyearameSene-lf1ll Google la warone wakh kay 🤣🤣
Alkaly sall est très ingrat omg ton karma n'est pas loin ndiaga Thiam le meilleur de sa génération machallah makhoudia tall yeureum nako diouma thiam calme toi et écoute mame bou goor dieynaba tall warna bayi nétali
Daba THIAM🥺🥺!! La douleur d’une mère qui perd son enfant ❤️❤️❤️ yalneu oumpp bepp yaye🥹🥹
Amine way 🤲🤲
❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤
Fi Thi Touba bène yaye bou yekha am dom ndeysane la domam bou am 2ans rèr depuis plus d' un mois niepa ko yeureum khalè bi Mame khadim Ndiaye la toud😢
Amine
@@amycollendiaye1682 oh my God 🥺🥺!! Purée c’est trop triste . La police est sur l’affaire ?
Kou mosoull sétane bété bété si télé comme man ❤
Bari ngua si morom télé mom naniou ko bayuil khalé yui🤣
Sa ma guél bii (ma grand mére)ci téléphonam lakoy sétane mousouko raté
Moi😂😂😂😂
Yalna gnou goudd fann sn Mame yi❤😊@@BaraNdiaye-q1i
Lègui lako don wakh
Jojo ak mala eupe khalise dans les séries c'est une longue histoire 😂😂😂😂
🇫🇷 : Cette série est juste incroyable 🎉❤️
🇸🇳 : kou beug yonet bi rk lalal j'aime
Sénégal nekhna😂
Bilahi ioe ❤😂fàtte reik j'aime yi pr lan tmt
😂😂😂😂😂
As yeux des enfants à partir des années et je vous souhaitez faire des
Salalahou aleyi wa salam ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
😂😂
Amina dioylona gnou bari thi yaye wayé Diaynaba tall tamite cou diouy walla sa yaram daww néna man sama papa la beugue papa ak yaye kénne meunouco remplacé yalla nalén fii yalla bayi gnou féké lépou inchalla kharé aldiana gni djitou amine 🙏
Dieynaba dafa wah rek sama xeel dème si sama papa ndeyszn que son âme reposé en paix
Amine ❤
@@Faby-u7hAmine Bilahi man mi sama yaye dafa décédé yalla bakhna yalla na yalla bayi fi gnifi dés bathi kanam🙏❤️
❤❤❤
Amine way
Légui niou dougou 2025 avant mouy diekh yallah niou réalisé sounou rêve yallah soril niou diable yah barké seydou mouhat salahou aleyhi wa salam
Alahouma amine ya rabi
Amiin
La mère de Daba Thiam souffre énormément des conséquences de ces actes.
Bilahi 😢
Wallahi elle souffre très sincèrement metina way
Ses * ( possessif )
@@z.e.y.n.a.b.😂😂😂😂👍🏾
Bilahi c'est douloureux
Gayi ay seconde sax nga guiss vu yu beurii 😂Gni amagoul djeukeur yalla naleinn yalla may djeukeur bu bax way
Amine
Amine way
Niou amagoul diabare nak 😂
@Mamecheikhndao-pe8ny diabar yomb na yeinna beugul takk rk
Amiinn
Dada Thiam Dafa mene rolam nak elle méritebes coeurs🎉🎉🎉
@OumoucoumbaSeydi ❤
qu’ الله aide la Palestine
qu"الله accepte nos duaa
qu'الله nous accordé le paradis
qu'الله accepte nos prières
qu'الله protège nos parents
qu'الله protège nos grands mères/pères 🤲🏼
Amine yarabi
amine ya Rabi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amine yarabi
Amine ❤❤
Ndiaga Thiam un acteur hors pair 😂😂😂Daba et Makhoudia sen problèmes yi dadié na deh 😢😢Daba dinga febar di 😂😂😂
@sambafall3509 Ah doyna ware. 😂
Even prod loléne gnou beugeul tmt 😫gnogui dioyy 😭wesh wesh kheucha ak papam thi prononciation guéne endil gnou jojo 😂team bi matt na nk Kirasoulilay ❤
@Divachou-d9i Yeina kofi ame. ❤
Maneu jojo je l’aime trop😂😂 vraiment bayilen liguen di wah c un bon acteur
Il est juste fort
Lofi dégue niou wakhko Jojo tmt meuna netali trop😂😂😂😂
Moi qui croyais qu’Alkaly limou wakh Makhoudia dafa mérone motakh ndéké Lou nék thi kholam la wakh quel ingrat 😢
Commentaire bi la don wuer alkali dafma moudié soff
Billaay li moye kharité tii taye aye ingrat léne😱😱😱😱
Hypocrite la Alkaly
Makhoudia nak mo wara ame diom protéger sa famille comme niii ko Alkany dèfè
Alkaly kay je n’ai pas de mots pour le qualifier li mome dafa ñiaw
Jojo tamite menone na niakkk mome dale li rek lay jouer mon amour mon ❤😂😂😂😂😂
Danga nob Jojo hana
Il vous a montrer qu'il sait bien jouer se rôle c'est pourquoi il insiste que dafa am halis
Des coeurs pour notre Prophète Muhammad PSL 🎉❤❤❤
S A W❤
Daba Thiam dafa yagg meunn théâtre ndaysann ❤
Daray kocc la diougué nk
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@aminatandiaye980 Merci. ❤
Maël Thiam AK lock bombe best duo😂😂❤ sama xol bi sédd neu way ❤❤❤
Sanekh yalla nafi yague té andeu ak wérr
Aminn ya raby 🤲🤲🤲🤲🤲🙏🙏
@PouloDiallo-e5l 👍
Ohhhhe ndeyesan ay yaye mon sonno thi Dome sougnou yaye yi yalna gniou goud fane 😢😢 lii kou diouroul rk manoo ko khame 😢😢yalla bou mou oumpa bene dji guène
❤❤❤❤
Bilahi diourouma dé mes kan mes niéces ét mes neveux son mal😢
Sama Adouna dey touki😢
Amine
Hoo 😭 bété bété❤
Aminnnnn❤❤❤❤
Monsieur bou goor 😂😂Mme bou djiguen amatoul 😂😂
Famille wesh wesh kheuskha ak papam guene yokal nioussi jojo😂🤣😩khamgua lane la tay mou nekh 🥳🥳😂😩❤️
Bilay even pro dougnou ay nitt 😍😍😍
Fii dinawathie a zero
Walahi tu m’a tué 😂😂😂 famille bi kay Matt n’a 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂
Mais c wesh wesh 😅😅
BETE BETE série bou nehh bi niéppa siyy guiss séne bopou chapeau à vous EVEN PROD
Ticket laobe 😂😀😀😂khaliss rek lay topou courage deguene metina trop sakh
HEURES DE PRIÈRES DU 20 AU 26 DÉCEMBRE 2024
Fadjr: 06h17
Suba: 06h32
Tisbar: 14h15
Takussan: 16h45
Timis: 18h54
Gue: 19h54
Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Merci beaucoup thi heure bi c'est vraiment gentil
Allahuma amiiine
Merci qu'allah vous bénisse
Ont n'est pas entendus sa ❤voix ni son visage jusqu'à présent ❤❤ notre prophète Mouhamed (psl) des coeurs pour lui
SAW💓💓💓
Thiéy mon jojo🎉 Ndiaga Thiam🎉Makhoudia Tall chapeau à vous 🎉🎉
@babacarndiaye1725 Merci.
Je suis déguéne je vous déguéne et je vous fume au calme😂😂❤
Mane lolou rkk moma diaxal temps yi dal conjuguer touram bi la dieul
😂😂😂
Degaine
Elle vous dégraine et elle fume au calme sacré Halima 😂😂
Tokh katou yamba yii kham nagnou lolu😂😂
Tank sanekhe yi 😂😂😂 seuuuuu 😊
Khamena dafa selmou souf cy
Yeuw ladon weur si yi tank😂
Deux jours yii Sénégal Dafa poussière 🙏🙏🙏🙏🤔🤔
@@FatouSeck-fp5ji😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
Man amy mbaye moma fi bayi au moins mome mogui happy si série😂😂 Wayé gni di dioy rekk😂😂😂
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉 0:20
Bété bété mo yégal niveau evenProd ba 4.86M d abonné bravo
Psk beugou ma Di weur yutub pour guisko faw niou send mko direct 😂
@cheikhou_407 Merci.
sama papa Baye Papa Seye yalnako YALLA diégal bolékok malakam yeurmandé yokou ay léram oubilko ay khéweul kharéko ALDIANA🤲🙏😭😭😭😭
Ndeysan la douleur douleur d'une mère qui perd son enfant Daba Thiam yeureum nako meune na limou déff trop kou content di guiss jojo si bété bété rkk lalal j'aime ❤bravo à eben prod série mofi meune💪
Jojo famille gnom kheusha rk la meuneu bokk 😂 famille titeurou😂😂evenprod dioumo léne deh
Vraiment ❤❤❤❤❤
😂😂😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂
Bilayeee 😂😂😂😂
Bilahi Ndiagua Thiam me rappel Mon grand père que son Ame repose en paix 🪦 😢
🤲
Kou beug ame dôme bou gor toudèko seydina moukhamét lalal j'aime❤❤🙏🏻
Bilahi di setann tek si di lire ay commentaires dara dakhouko😂😂😂😂😂😂😂😂
Wawaw😂😂😂
Ay way sougnou yaye yalla na goudou fane amine des cœurs, pour Maman 🙏❤️
❤❤❤❤
❤❤❤❤
Yén commentaire pour nguén diokhé sén khalat si serie bi la pas pour genre yi FI GNOUN GNÉPPA BEUG SUNU YAY
Amine ya rabi
Allah ouma amine inchallah ❤❤❤❤❤❤❤
Non Makhou mo nékh,yow Alkaly khawla ray nganane dinala amate😂😂
Lolu la reh ba sone😂makhou amna fit nk😅😅
Môme kaye dagn ko tela até
😂😂😂😂😂😂
Da beugga dée 😂😂
Épisode bi yallna bumu nék sun mudieuntélu épisode amine
Amine 🙏🏾
Amine
Amnie
Gni contann si retour de jojo na cœur yi nioli 🎉❤
Yéna gaw nak
@ kenn dou iow miyy tontou ☺️
❤❤❤
@MameDiarraFall-f3c ❤
Mai la beauté de deguéne🎉❤ vraiment t'es mignonne ❤
Vraiment dame il joue son rôle très bien néna niome gno commencé 😂😂😂
mon acteur préférét 😂😂😂 dame bouné monsier bou goor walla Mma bou djiguéne rek ma tothie
❤❤😂😂
Dame kay ak ben tenue bi😂😂😂
😂😂😂 bilahih ça ma fait rire@@diadjikanteye4908
@MamanBodian-d5k Merci beaucoup.
Alkaly et sa famille lagnouy def gnaw si torokhal nite gni guemougnou yalla d😮
Billahii lii dafa niaw 😢😢
@ndeyemariethiam4727 Ah doyna ware. 😢
Ndaysane 😭 père ndiaga thiam meilleur acteur de tout les temps sama xoll toyy na bly😢
Kou beugue sa yaye rek mayema ayye cœur ♥️
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤KO BAGNE YAYAM
Moma diakhal@@ousmanesakho5340
❤️❤️
❤❤❤
aye tické laobé 😂😂néenako ki diaroull si Bountou bi😂😂
@maremediop2782 😂
Une equipes incomparable tres naturel , bete bene dal takhna weetatounou nioun wa europe ,bonne continuation !
Wa mane loutax kéne dou j'aime sama commentaires 😢
Amal diam
@moustaphacadame6044 amine niou bokouko
Chapeaux à Cheikhou Gueye " Ndiaga thiam " un grand artiste et Cheikhouna aussi " Makhoudia Tall " ❤️
@fallu.cactus Merci. ❤
@ the Best ❤️
Evenprod meilleur maison de production 😢😢je vous love tellement
Pour une première fois Kheucha mére 😂😂Ohh Histoire dinako binde
😂😂bilahi il a assuré
@PrinceBaPoulho-nu4bo 😂
Thiey bi serie comme guerre 😂je te jure bébé meilleur film
Vraiment 😂
Bébé 😂😂
Bébé way🤣
Mayko lolou tmt😂😂😂
@@ndoumbemare ki kay 🤣
Une telle production avec autant d’acteurs de qualité
Dina rare
Dieynaba tall mom😂😂ah Li dh mom fébar la
Meun na doul d mom😅😅
Yen baylen jainaba Tall c jamma😂😂😂@@cheikhdiallo9009
@BineteLy Mougui gnawe. 😂
Yalla na yalla déf diama si Sénégal yalla na yalla déf xéwale
Aminr
Dans la vie, chaque jour avec son lot : tantôt c’est la joie, tantôt c’est la tristesse ou des journées tranquilles qui nous apaisent.
Qu’Allah nous donne foi et la force de vivre nos épreuves avec acceptation
Waa yéne dieynaba tall migui meune nétali ba légui ?😭😂😂💔
Doomou bay lolo moma diakhal ni man 😂😂
Minw moom meunvnako...
You tube dafa efficace dé elle donne des informations et à temps réel nak
@@sopeserignesaliou doyna war dh 😭😂
Bilahi Dama yeureume mére Khoudieu thiam 😢😢😢😢😢Damay ragal mou fatou ndakh nakhar aussi mbiri mayé Dome Dji da yeureumone kime ko maye 😢😢
Kan moy mère khoudja
J’ai entendu l’autre fois,Cheikhouna Gueye (Saneex) dire que Serie bi ama goul thiow ! Mais je confirme ces dires,Lima guissssss !
Jojo il est excellent,il joue bien ! En tout cas,je félicite Evenprod pour tout le travail fourni.
Yalla xam nani môme lay wakh sama yaye legui
Bilay néna ay bombe 💣 moy niew 😅😅gayi nan ay sumboulou 🤣
@BayemodouGueye-dk3qsje t’assure bro,Liiy nieuw moy euppp thiow !
@@HaajHabibbilayyy,Soumboulou,elle a assuré mais personne n’est indispensable dans la vie !
Siiiii ! Liy nieuw moy geuneu yémé☝🏿☝🏿
@@HaajHabib soumboulou kay day xar😂😂😂
Kou yeureum yayou daba thiam rk lalal j'aime ❤😢
Wouy Dieynaba Tall meune gua fene gua démm ba Bassine dilla wakh "youtube"😂😂
J'adore le calme de la grande mère de Douma Thiam, malgré tout elle avait agi avec amour et aujourd'hui elle ramasse les pots cassés 😢😢
lou lér gua Wakh ❤❤
Elle s est trompé elle devrait pas offrir l enfant de sa fille sans son autorisation.
Elle avait agi avec peur, pas amour. Ragal son mari plus que ragal Yalla
@@Khadimamadou l'erreur est humaine 😔😔
Oui elle voulait protéger sa fille, puis son mari ne l'a pas du tt soutenu 😢! J'imagine qu'il a dû même l'accuser a tord des conséquences😮
Ayway yerem na makhoudia NK kouko yerem RK Lalla ma 😢🎉
Ww
Kou d'accord ni evenpro c'est le meilleur que marodi tv rek l'al j'aim
@AmadouDia-e6i Merci.
Merci à votre assiduité Evenprod ! Yalla na Diam yagg Senegal